text
stringlengths 1
1.87k
| duration
float64 0.5
193
| file_name
stringlengths 7
31
| path
stringlengths 13
39
| audio
audioduration (s) 0.03
193
|
---|---|---|---|---|
waa xam nga bu ñu waxee étape bu denc balaa ngay denc dafa laaj ay jéego ay jéego yu rëy ci wàllu céréales bi surtout bu ma lay jox lu mel ni dugub wala ma jox la lu mel ni ceeb balaa ngay wax mbiru denc dafa laaj ay jéego jéego bi d' ab() da njëkk d' abord war nga xalaat xam li ngay góob ñor na wala ñorul kon man balaa may wax mbiru denc naa xalaat ndax mbéytéef bi produit bii muy produit agricole bi maanaam ñor na wala ñorul | 33.14 | wol_43411_200.948_234.088.wav | kallama/wol_43411_200.948_234.088.wav | |
si par si par ay partenariats partenariat partenariat rek internet beeg fépp ñu awale ay produits | 5.553 | wol_42314_548.994_554.547.wav | kallama/wol_42314_548.994_554.547.wav | |
ñun ndax ñoo koy nangu kon nag war nañuy seet li xam ne nii méngoo na ak ñun baax na ci ñun ñu def ko te bañ a topp rek aussi itam %e sama gars yi | 7.183 | wol_4813_234.841_242.024.wav | kallama/wol_4813_234.841_242.024.wav | |
ñoom it dañoo war a aar peggu géej gi parce que géej gi mooy seen mooy seen liggéeyukaay | 4.558 | wol_44712_1479.842_1484.4.wav | kallama/wol_44712_1479.842_1484.4.wav | |
alhamdulilah | 0.652 | wol_43612_1133.699_1134.351.wav | kallama/wol_43612_1133.699_1134.351.wav | |
Nataal bii ab ab palaat buñ teg la waaw bu def sunguf, sunguf si nag kenn xamul kaani laam déet waaye xonq na lool nuru na kaani daal. | 14.457813 | 208:29.wav | waxal/208:29.wav | |
am na yeneen yoo xam ne yooyu la ñuy wax des maladies fongiques ay feebar yoo xam ne yéen mënu leen ko gis ay feuilles yuy lax lay nekk wala yuy chocolat yooyu c' est une maladie fongique yooyu bu dalee ci gàncax gi dañuy ut li ñuy wax produit bu ñuy wax tamex ah ñu traité ko ci ba nga xam feebar yooyu dina dem feebar yooyu daal souvent ñoo ëpp li ñuy jàpp wàllu maraîchage bi xam naa ne dañ ko ciy | 22.93 | wol_43012_1527.535_1550.465.wav | kallama/wol_43012_1527.535_1550.465.wav | |
ba nga xam ne wa date boobu passée | 1.628 | wol_43111_684.487_686.115.wav | kallama/wol_43111_684.487_686.115.wav | |
xam ne bu nen yooyu mooy bu ñu amee 3 jours rek | 2.239 | wol_4410_1599.215_1601.454.wav | kallama/wol_4410_1599.215_1601.454.wav | |
boo jëlee Tamba | 0.796 | wol_44111_626.092_626.888.wav | kallama/wol_44111_626.092_626.888.wav | |
jërëjëf | 1.777 | wol_44511_175.962_177.739.wav | kallama/wol_44511_175.962_177.739.wav | |
monsieur Wade | 0.881 | wol_42314_508.668_509.549.wav | kallama/wol_42314_508.668_509.549.wav | |
mais li ma ci gën a interessé mooy partie organique bi | 2.745 | wol_4210_501.745_504.49.wav | kallama/wol_4210_501.745_504.49.wav | |
donc jigéen ñi doon nañ cibles bi nga xamante ne que PAM bàyyi na xel ci ñoom | 5.884 | wol_42921_585.444_591.328.wav | kallama/wol_42921_585.444_591.328.wav | |
Coopérative rurale d' épargne crédit bi ak UGPM | 2.389 | wol_44912_466.815_469.204.wav | kallama/wol_44912_466.815_469.204.wav | |
donc di nga xam chaque marché actuellement ban prix moo fay daw léegi yow yaay tànn bu la bu la bu la intéressé nga yóbbu foofu sa produit bi jaay prix bi bi nga soxla yaa ngi gis | 10.989 | wol_41920_1279.436_1290.425.wav | kallama/wol_41920_1279.436_1290.425.wav | |
ñun li ñu leen di recommandé mooy par exemple ngeen orienté wu ci les variétés à cycle court bu fekkee bu fekkee ci ci ci côté mbay yi la kii quoi la la ñu kii quoi la ñu dem quoi | 10.02 | wol_42211_835.876_845.896.wav | kallama/wol_42211_835.876_845.896.wav | |
di leen xelal di leen former si ànd ak ñoom si lépp loo xam ne vraiment lu leen di gàllankoor la seen mbay ku nekk xam ne ISRA ISRA si boppam moom moo yor lii nga xam ne mooy recherche mooy gëstu ci wàllu mbay ci wàllu sàmm ci wàllu alam | 17.561 | wol_41920_189.575_207.136.wav | kallama/wol_41920_189.575_207.136.wav | |
nit ñi def si seen loxo ñëpp jóg si | 1.701 | wol_45412_47.457_49.158.wav | kallama/wol_45412_47.457_49.158.wav | |
d' accord am na %e solo xam naa ne émission bi nag li énu dese ci simili %e bariwul ndax %e am na sax d' ailleurs ku ma wax sànq ne ma wax dëgg yàlla émission bi déglu ko sax dafay gën a neex %e woote ndax danga ciy jàngat lu bari | 10.635 | wol_4815_224.704_235.339.wav | kallama/wol_4815_224.704_235.339.wav | |
merci beaucoup Sow man maa ngi tudd Pierre Badiate maa yore fii agri() agriculture ci département bi mooy suñu fi ñu fi ñuy liggéeyee moom mu dénk la ñu ma dénk si département bi waa | 10.404 | wol_43930_176.476_186.88.wav | kallama/wol_43930_176.476_186.88.wav | |
waaw boo déggee sànq neenaa la ci sama biir wax | 3.36 | wol_4813_366.635_369.995.wav | kallama/wol_4813_366.635_369.995.wav | |
tax na fu mu nekk nii gars yi dañuy def %e ce qu' on appelle donc la promotion de l' économie verte économie verte nag moom boo ko déggee moom mooy %e économie bi nga xamante ni bii da nga koy def %e te du exacerber la couche d' ozone bi nga xamante ne bii moom moo ñuy jural %e phénomène yi nga xamante ne bii moom la ñu gis | 18.436 | wol_44511_1493.134_1511.57.wav | kallama/wol_44511_1493.134_1511.57.wav | |
dafa mel ni togg la | 1.167 | wol_4210_1510.132_1511.299.wav | kallama/wol_4210_1510.132_1511.299.wav | |
%e technique bi foo ko foo ko dégee foo ko mos a gisee wala foo ko déggee | 3.57 | wol_36710_153.597_157.167.wav | kallama/wol_36710_153.597_157.167.wav | |
waaw loo bëgg ñu yokk ko walla ñu waññi ko | 2.615 | wol_56610_429.57_432.185.wav | kallama/wol_56610_429.57_432.185.wav | |
ah yooyu yëpp est ce que respect() respecte nañu ko ba xam ne nii bu produit biy gñn maanaam %e produit buy gñn ci biir fi ñu koy defaree | 7.925 | wol_41011_864.179_872.104.wav | kallama/wol_41011_864.179_872.104.wav | |
Waaw nataal gi ñiy jàkkaarloo nii moom, daa mel ni lu ñuy lekk la, lu ñu togg ba pare teg ko nii nag. Mu mel ni ay xeeti jën yu ñuy defar ak yooyu ay jën ak yooyu yi nga xam ne dañu ko def saaf ba pare, togg ko ba pare war koo lekk. Day mel ni palaat boobu la ñu jàkkaarloo nii. | 18.037813 | 2810:15.wav | waxal/2810:15.wav | |
walla lu kenn wax walla lu góor gi wax ñoom si la ñuy topp | 2.709 | wol_35311_242.073_244.782.wav | kallama/wol_35311_242.073_244.782.wav | |
Nataal bi ngeen ma mujjee yónnee muy ñeent fukkeelu nataal ak ñeent, maa ngi ciy gis benn jigéen, mi ngi sol yére boo xam ne yére bi mu ngi am ay bën-bën, yére bi am couleur boo xam ne muy ñuul ak weex. | 16.657813 | 3631:786.wav | waxal/3631:786.wav | |
si biir loolu ñun ñu ngi am presque cinq cent hectares plus de cinq cent hectares cinq cent hectares yooyu bon boo xoolee ñi ko ñi ko ñi ko ŋànk si wàllu population c' est presque huit GIE | 11.536 | wol_36410_159.076_170.612.wav | kallama/wol_36410_159.076_170.612.wav | |
%e baykat yi | 1.267 | wol_44114_693.052_694.319.wav | kallama/wol_44114_693.052_694.319.wav | |
muy juróomi %e questions yoo xam ne bëgg naa leen koo laaj ku nekk indi si xalaatam waaye ba légi tamit %e bu fekkee am na ñoo xam ne %e bëgg nañu dugg %e ci kanam tuuti dinañu dinañ ubbi ligne bi ñu jéem si dugg | 10.82 | wol_42311_100.972_111.792.wav | kallama/wol_42311_100.972_111.792.wav | |
ay %e points yoo xamante ne comme munuñu wax lépp | 3.553 | wol_43712_1214.935_1218.488.wav | kallama/wol_43712_1214.935_1218.488.wav | |
03 | 0.749 | wol_42514_1270.38_1271.129.wav | kallama/wol_42514_1270.38_1271.129.wav | |
li ëpp ci liy yàqu ci nawet bi yi ci gën a yàq yàq bu ëpp rek mooy woŋ woŋ | 4.125 | wol_43312_1337.25_1341.375.wav | kallama/wol_43312_1337.25_1341.375.wav | |
loolu day question bu %e am solo | 2.36 | wol_44311_536.458_538.818.wav | kallama/wol_44311_536.458_538.818.wav | |
parce que defe naa ne mboq mi bi muy ñëw | 2.61 | wol_45412_1103.963_1106.573.wav | kallama/wol_45412_1103.963_1106.573.wav | |
di bay li ngay lekk | 1.079 | wol_44914_556.463_557.542.wav | kallama/wol_44914_556.463_557.542.wav | |
asalaamaaleykum mbokk yi nga denc sa xaalis yaxanal sa poche fii si IMCEC loolee mën naa ne ngir mu mën a nekk faww nga nekk membre nga nekk nit yow kese wala nga nekk entreprise fàww nga am carte d' identité bu baax bu ñu mën a jafandikoo ñaari anam la nag mën nga joxe xaalis bi benn yoon lu mu néew ci juróom-benni weer war ngaa joxe juróom-benni junni su fekkee nag da nga bëgg saa su ne ngay ñëw di joxe mën nga joxe ñaari junni weer wu ne ci diiru ñetti weer su fekkeee bëgg nga see am ay leerlu mën ngaa woote si numéro biile 33 879 30 1233 879 30 12 IMCEC mooy li gën | 45.412 | wol_11480_0.0_45.412.wav | kallama/wol_11480_0.0_45.412.wav | |
lay des | 0.744 | wol_43412_1711.266_1712.01.wav | kallama/wol_43412_1711.266_1712.01.wav | |
vraiment mu yokk ko ci présentation bi | 1.904 | wol_44912_97.881_99.785.wav | kallama/wol_44912_97.881_99.785.wav | |
Waaw ñoo ngi siyaare bu baax, nataal bi ñi ngi ci gis ay gayndeek ak ñoom ñay ak ñoom mëfër ak ñoom seen. | 15.677813 | 3375:987.wav | waxal/3375:987.wav | |
%e di leen di jàngal lu bëri ci wàllum mbéy ci wàllum défense restauration des sols stockage formation yu bëri dañ ko fay defee jàppale boobu tamit lu jar a sant la %e beneen bi tamit %e ci wàllum population bi maanaam ñu nga xam ne bokkuñ bokkuñu bokku nañ bokkuñu mais ñi nga xam ne bokkuñu na ñuy roy ci ñële xool | 23.543 | wol_42922_1126.633_1150.176.wav | kallama/wol_42922_1126.633_1150.176.wav | |
ñu jël li nga xam ne mooy interet yi ak %e ak kii ak bénéfice yi daénu koy séddalewaat membres yi | 5.092 | wol_4815_47.366_52.458.wav | kallama/wol_4815_47.366_52.458.wav | |
waaw waaw waaw noonu noonu la demee quoi | 2.085 | wol_43810_225.916_228.001.wav | kallama/wol_43810_225.916_228.001.wav | |
pour mun a jël | 1.291 | wol_43020_1549.368_1550.659.wav | kallama/wol_43020_1549.368_1550.659.wav | |
su ko defee Mouhamed Bachir Mbow | 1.812 | wol_43112_701.709_703.521.wav | kallama/wol_43112_701.709_703.521.wav | |
waaye léegiren surtout dem nañ ba weeru août am na ñoo xam ne weeru août la ñu commencé ji seen i gerte | 6.596 | wol_43211_555.432_562.028.wav | kallama/wol_43211_555.432_562.028.wav | |
ñu ne nañu créer nag loo xam ne dana mun taxaw ci wetu béykat boobu bu fekkee risque bi dal na ko | 5.915 | wol_4910_1790.398_1796.313.wav | kallama/wol_4910_1790.398_1796.313.wav | |
dañuy xaar ba mu ow ba pare après door ko xolli dangay xaar ba mu ow ba pare après door ko xolli après denc ko waaw loolu moo lay mën a permettre nga am gàncax bu normal boo ko jiwee | 10.472 | wol_41940_2450.608_2461.08.wav | kallama/wol_41940_2450.608_2461.08.wav | |
Nataal bii de nataal la boo xam ne ab jàkka la, jàkka ji nag ñi ngi koy tabax dañ koy soog a tabax ba muy soog a guddaat. Ba noppi jàkka ji am na bant yu bari yu nekk ci biir waaw. Jàkka ji nag bant yi dañoo bari tabax yeggagul yeggagul nuru na loo xam ne yeggagul. | 14.517813 | 3583:1229.wav | waxal/3583:1229.wav | |
ak kër goo xam ne nii baay ba rek a am ñu tëkkale leen kon yaakaar naa ne foofa faj soxla yi | 5.772 | wol_4614_203.574_209.346.wav | kallama/wol_4614_203.574_209.346.wav | |
donc xoolal loo xam ne soit ay bant la wala leneen loo mun a teg d' abord si suuf ba pare door a jël saako bi teg ko ci kaw mu bañ a am contact direct ak %e ak suuf si loolu tamit lu am solo la lu ñu war a bàyyi xel | 13.645 | wol_41940_2075.7_2089.345.wav | kallama/wol_41940_2075.7_2089.345.wav | |
léegi nag tey dañuy ñëw ba tey encore énu baamtuwaat ko ci li nga xam ni mooy %e wàllu changement climatique | 6.369 | wol_43211_220.82_227.189.wav | kallama/wol_43211_220.82_227.189.wav | |
day nekk suuf bu xaw a aéré | 1.972 | wol_44311_756.054_758.026.wav | kallama/wol_44311_756.054_758.026.wav | |
donc météo | 1.393 | wol_42812_216.1_217.493.wav | kallama/wol_42812_216.1_217.493.wav | |
bekoor | 0.651 | wol_4410_1016.7_1017.351.wav | kallama/wol_4410_1016.7_1017.351.wav | |
mais dafa nekk chance boo xamante ne yéen xamoo leen sax lii lan la parce que région de Louga yëpp ci commune bi dong lañ ci tànn dans tout le Sénégal ñetti communes dong lañ ci jël donc loolu loolu chance la ci wàllu programme bu mel nii | 14.704 | wol_41930_737.629_752.333.wav | kallama/wol_41930_737.629_752.333.wav | |
fàww ñu seet ay tëralin ay pexe | 2.404 | wol_43111_908.319_910.723.wav | kallama/wol_43111_908.319_910.723.wav | |
voilà comme dèjà oto yi amul te ñu yore affaire bi mooy waa base alerte Daara loolu dafay aar gunóor yi ñoom ñoo yore affaire xeex gunóor yi puisque léegi agriculture yore wu ko léegi base su alerte comme tabax nañu base am na agent bu nekk foofu | 15.35 | wol_43930_983.781_999.131.wav | kallama/wol_43930_983.781_999.131.wav | |
donc chenille légionnaire boobu béykat yi ñu ngi wax ne bu ngeen gisee chenille boobu %e amuñu lu koy traité am nañ produit bu koy répulsif bu koy dàq mais da ngeen di xool ne bu fekkee ne ppause dafa taxaw lu bëri nag da ngeen gis sax yooyu day bëri ci mboq mi mais bu taw bi ñëwaatee lu bëri rek nga gis ñu daw kon donc souvent béykat yi bu ñu ma ah dama leen ne ah bu tawee taw bu bëri rek dina daw donc gis ngeen ko moo nekk nii chenille légionnaire bi te du gis ngeen ko mu ngi ni ah day ñëw ci tool yi bu ngeen ko gisee rek xool ko ci mboq mi xam ne am na chenille légionnaire bu ci nekk loolu bu ngeen ma wooyee rek damay oo oto bi mu ñëw traité leen seen tool du ngeen ci fay dara | 35.681 | wol_43012_1018.477_1054.158.wav | kallama/wol_43012_1018.477_1054.158.wav | |
asalaamaaleykum maa ngi leen di nuyu seen tur ak seen sant di rafetlu liggéey bi * man maa ngi tudd Pape Alanda Mbengue dëkk Daara Ndiakhoum depuis soixante dix ba léegi daal maa ngi si àll bi maa ngi ci mbéy mi | 21.475 | wol_36710_0.0_21.475.wav | kallama/wol_36710_0.0_21.475.wav | |
mais mu amaat beneen mbir mu nit ñi %e umpale tuuti | 4.912 | wol_43412_1084.99_1089.902.wav | kallama/wol_43412_1084.99_1089.902.wav | |
même bu dee da nga dugal say xar | 1.581 | wol_4910_1470.944_1472.525.wav | kallama/wol_4910_1470.944_1472.525.wav | |
wala nga sol ay dàll yu rafet ñu ne béykat laa ñu lay niit | 2.553 | wol_44412_1920.252_1922.805.wav | kallama/wol_44412_1920.252_1922.805.wav | |
ni ko Ibrahima waxee léegi ne ñu ràññee poches yi | 2.14 | wol_4611_675.96_678.1.wav | kallama/wol_4611_675.96_678.1.wav | |
am na ñax yoo xam ne baax na waroon fa sax bu produit yàgg di ko utilisé day dem ba ah produit yooyu vraiment yàq yàq suuf si | 7.366 | wol_43011_1432.336_1439.702.wav | kallama/wol_43011_1432.336_1439.702.wav | |
%e man nag maa ngi koy sant di ko gërëm | 2.862 | wol_42514_321.266_324.128.wav | kallama/wol_42514_321.266_324.128.wav | |
man nag jëloon naa sama xale Sadio fekk na fa booy yi sax booy yaa ngi fa toogoon chaque jour ñu ngi tëgg mais picc am na heure yoo xam ne dana fay nekk buñ wàccee yow boo wàccee ñoom ñu ñëw buñ xëyee ñëw loolu mooy problème bi | 14.535 | wol_41950_827.667_842.202.wav | kallama/wol_41950_827.667_842.202.wav | |
mu doon nag projet boo xam ne bu am solo la trop trop trop kon nag ginnaaw bu ñu waxee projet 4R boobu noonu lu mu ëmb ci émission boobu | 7.3 | wol_43711_65.913_73.213.wav | kallama/wol_43711_65.913_73.213.wav | |
taw na septembre pile | 1.409 | wol_43612_63.478_64.887.wav | kallama/wol_43612_63.478_64.887.wav | |
su ñu ko ku ko mélangé ba pare nag day nekk liquide xam nga lu nekk liquide mënoo jël sa loxo di ko jaxase | 6.477 | wol_41711_718.09_724.567.wav | kallama/wol_41711_718.09_724.567.wav | |
lépp jug ca kaw | 1.448 | wol_44411_686.938_688.386.wav | kallama/wol_44411_686.938_688.386.wav | |
alhamdulilah | 0.732 | wol_45422_879.828_880.56.wav | kallama/wol_45422_879.828_880.56.wav | |
kon donc incha allah ci émissions yi yooyu yëpp bëgg nañu ko cee génne ba mu fés | 3.836 | wol_44911_400.325_404.161.wav | kallama/wol_44911_400.325_404.161.wav | |
%e kenn ku ma mën a lim mooy waa COPACEL | 2.524 | wol_4711_790.18_792.704.wav | kallama/wol_4711_790.18_792.704.wav | |
mais tamit yaakaar la moo tax ñu indi ko Thiel waaye na bu xasee ba dugg Thiel man Sadio Deme moomatuma ko yow Aliou Sow moomatoo ko waaye askan bi moo ko moom | 9.791 | wol_41940_1837.907_1847.698.wav | kallama/wol_41940_1837.907_1847.698.wav | |
%e ndax tam ci wàllu jiw bi tam loolu amu ci jafe-jafe gerte googu ñàkk | 3.601 | wol_43930_1735.987_1739.588.wav | kallama/wol_43930_1735.987_1739.588.wav | |
waaye terewul ba tey mën nañu wéyal waxtaan bi ànd ak kii di Jalle yaakaar naa ni li fi Ibrahima wax yëpp am na am na solo te it xam naa ni %e yéen yaa ngi naan Ibrahima moo tax amagu leen yéen code barre mais yéen seen wàllu bopp aussi est ce que mate ngeen normes yi war a tax ngeen am code barre | 14.077 | wol_41013_361.197_375.274.wav | kallama/wol_41013_361.197_375.274.wav | |
information yi jugee si météo parce que c' est très important | 3.464 | wol_42811_1283.297_1286.761.wav | kallama/wol_42811_1283.297_1286.761.wav | |
waa ñu ngi lay sant | 1.07 | wol_4910_772.805_773.875.wav | kallama/wol_4910_772.805_773.875.wav | |
ay jafe-jafe ngay am sa gerte gi du fees ay chips ngay am | 2.863 | wol_43010_1329.742_1332.605.wav | kallama/wol_43010_1329.742_1332.605.wav | |
ñi nga xam ne tamit ñoom fi mu ne nii dina taw rek lañ soxla dégg | 3.435 | wol_42812_1378.158_1381.593.wav | kallama/wol_42812_1378.158_1381.593.wav | |
Nataal bii ngeen ma yónnee ab...boo xam ne xam naa ab xale buy doxi. Mu nekk fu taaru nag, fu rafet amiy garab yoo xam ne garab yu baree bari fu rafet lool, suuf si rafet. | 15.717813 | 3455:1088.wav | waxal/3455:1088.wav | |
%e naka la yokkee sa ci yokku na na dafa yokkute si mbay sa mbay yow ndax dafa yokku bu baax dafa yokku tuuti wala yokkul dara | 11.293 | wol_55010_84.215_95.508.wav | kallama/wol_55010_84.215_95.508.wav | |
amoon ci début bi ma amoon nañ pause | 2.898 | wol_43612_633.864_636.762.wav | kallama/wol_43612_633.864_636.762.wav | |
62 waaw | 1.555 | wol_4910_276.441_277.996.wav | kallama/wol_4910_276.441_277.996.wav | |
%hum %hum te yooyu xamuñ | 1.135 | wol_4410_2006.761_2007.896.wav | kallama/wol_4410_2006.761_2007.896.wav | |
produits yi am na ay ay ay ay gàllan() ay yeneen kii dafa non seulement dafa cher | 3.624 | wol_4410_795.958_799.582.wav | kallama/wol_4410_795.958_799.582.wav | |
kooku nag tey li ñu ciy dugal dafay wóor ne amatut kaaraange balaa ñuy wax ne ñaari weer ñetti weer | 4.925 | wol_43032_937.205_942.13.wav | kallama/wol_43032_937.205_942.13.wav | |
am na ñu bëri ñoo xamante ne bés bu ñu déggee information météo | 3.347 | wol_43212_1145.141_1148.488.wav | kallama/wol_43212_1145.141_1148.488.wav | |
nga dem peut être amoo pexe mais foog nga dem | 3.894 | wol_44812_1123.441_1127.335.wav | kallama/wol_44812_1123.441_1127.335.wav | |
Nafoore daanaka mën naa ne sax %e révolution la parce que presque en moyenne chaque quarante huit heures wala soixante douze heures alors dañ ma woo directement sama téléphone jox ma météo bi | 10.95 | wol_36510_275.03_285.98.wav | kallama/wol_36510_275.03_285.98.wav | |
quarante cinq mille | 0.626 | wol_42922_918.538_919.164.wav | kallama/wol_42922_918.538_919.164.wav | |
%e effet changement climatique bi | 1.572 | wol_44111_273.383_274.955.wav | kallama/wol_44111_273.383_274.955.wav | |
nga kii après si diggante bi mu am ay perturbations yenn changement yi | 4.17 | wol_43020_2029.03_2033.2.wav | kallama/wol_43020_2029.03_2033.2.wav | |
naaj ak ngelaw te yooyu yëpp météo moo koy saytu te yëpp nag bu fekkee da nga dem ba xam à temps maanaam %e laata nawet bi di ñëw Alpha nee na si rajo bi météo nee na dana taw taw bi dana ànd ak dënnu wala dana ngelaw yow di nga am say di nga di nga di nga di nga xam yan jumtukaay ngay jël | 21.092 | wol_45512_694.868_715.96.wav | kallama/wol_45512_694.868_715.96.wav | |
ci mbay mi | 1.429 | wol_44914_548.767_550.196.wav | kallama/wol_44914_548.767_550.196.wav | |
nga dugal ko foo xam ni vraiment dina mucc ayib | 1.962 | wol_44915_453.261_455.223.wav | kallama/wol_44915_453.261_455.223.wav |
Subsets and Splits