text
stringlengths 26
222
| utterance_pitch_mean
float32 76.7
126
| utterance_pitch_std
float32 5.71
37.5
| snr
float64 14
51.5
| c50
float64 5.17
59.9
| speaking_rate
float64 1.25
12.8
| phonemes
stringlengths 12
121
| stoi
float64 0.73
1
| si-sdr
float64 -0.03
25.1
| pesq
float64 1.26
3.83
|
---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|
parce que nekk yu am solo bi ci njëkk moom mooy yoon bi ma bëgg a jaaralee sama produit est ce que nekk na yoon bu baax ci marché bi | 109.943161 | 24.51479 | 27.329504 | 29.222094 | 8.547009 | kju ju æm soʊloʊ baɪ jun baɪ mɑ ʌ sɑmʌ ɛst sii kju nɑ jun baɪ | 0.96793 | 14.379201 | 2.494854 |
yow mii di entrepeneur dafay am solo lool laataa ngay fasal wala laataa ngay wéyeel li nga xamante ni moom mooy sa li ngay joxe | 106.074966 | 14.864258 | 22.943863 | 41.103626 | 5.33769 | jaʊ di æm soʊloʊ wɔlʌ li ni sɑ li | 0.963996 | 14.627354 | 2.749952 |
waaye tamit ni nga am message wala slogan mooy li nga xamante ne moom mooy sa bàq wala moom mooy sa mandat nga ndax ñaari yooyu noonu yëpp te logos boo koy créé dafa war a nekk li nga | 106.243683 | 19.000145 | 27.782745 | 5.329942 | 8.808809 | ni æm mɛsʌdʒ wɔlʌ sloʊɡʌn li ni sɑ wɔlʌ sɑ ti loʊɡoʊz bu wɔɹ ʌ li | 0.908852 | 8.094084 | 1.700093 |
donc loolu di message bi sonal loolu donc loolu di message dafa war a nekk mbir bi nga xamante ni dañ ci war a liggéey bu baax a baax a baax a baax | 107.221252 | 20.665956 | 24.28413 | 6.663613 | 6.706707 | di mɛsʌdʒ baɪ di mɛsʌdʒ wɔɹ ʌ baɪ ni wɔɹ ʌ ʌ ʌ ʌ | 0.910786 | 7.057273 | 1.565901 |
mais bu maaage bi ëpp ñoom bu ko defee bu ñu lir waaye bu ñu gisee rek dañuy comprendre waaw mën na nekk yenn xeetu digé digital yi wala infogra fii wala yenn email yi nga xamante ni | 105.679863 | 23.577335 | 22.582745 | 6.615779 | 8.021558 | meɪs baɪ koʊ dɛfi nɑ dɪdʒʌtʌl ji wɔlʌ wɔlʌ imeɪl ji ni | 0.895697 | 7.418052 | 1.678566 |
lii di kanado communication comme ni ñu la ko waxee dafa war a nekk li nga xamante ni | 115.368134 | 24.251616 | 19.445572 | 6.989501 | 6.860062 | di kʌmjunʌkeɪʃʌn ni lɑ koʊ wɔɹ ʌ li ni | 0.88194 | 9.197259 | 1.818191 |
nga leen di envoyer ay messages di leen taajëfal wala tamit di leen soñju ngir utilisation yi nga xam te ni war nañ ko mën a def seen produit waa tamit bul | 100.756447 | 19.081808 | 19.907965 | 7.873614 | 7.607608 | lin di eɪ mɛsʌdʒʌz di lin wɔlʌ di lin ji ti ni wɔɹ koʊ ʌ sin | 0.902965 | 8.60872 | 1.702374 |
waaye nag yëg ni yoon bi am na solo waaye message bi nga xamante ni moom ngay jaaralee ci yoon bi tamit dafa am solo ndax yoon bi ginaaw ba nga ko tànnee ba pare | 104.17588 | 19.238989 | 17.652147 | 8.012153 | 11.055832 | næɡ ni jun baɪ æm nɑ soʊloʊ mɛsʌdʒ baɪ ni jun baɪ æm soʊloʊ jun baɪ bieɪ koʊ bieɪ pɛɹ | 0.901574 | 6.996193 | 1.563926 |
donc ñooy nga jaaroon ñi nga xamante ne tamit ñoom ñooy say jege ñaale wala say dëkkandoo ñoom it danga leen war a dugal say base de données | 102.248001 | 18.602713 | 23.951332 | 48.165928 | 6.459054 | ni seɪ wɔlʌ seɪ ɪt lin wɔɹ ʌ dudʒʌl seɪ beɪs di | 0.957374 | 15.500381 | 2.701998 |
donc yooyu daf ciy baax yow mi yor sa entreprise nga leeral say couleur nga leeral sa logob nga am logobu fekkee amoo ko woon nga def li nga xamante ni moom mooy logobu | 113.425255 | 16.780697 | 21.179884 | 5.895105 | 5.643739 | jaʊ mi sɑ seɪ sɑ æm koʊ li ni | 0.90012 | 7.45349 | 1.776051 |
parce que dañuy gis ni lii di boussa a rey maanaam wax nit dégg moom mooy canal bi nga xamante ni moom moo gën a moo ko gën a indil ay clients | 116.382805 | 20.959097 | 29.704702 | 34.454231 | 7.807808 | kju ni di ʌ ɹeɪ wæks nɪt kʌnæl baɪ ni mu ʌ mu koʊ ʌ eɪ klaɪʌnts | 0.969649 | 14.205353 | 2.578825 |
te loolu nag dafa war a neex a jàpp am solo te wute ak li nga xamante ni moom lay say wu ci toog te loolu nag dafa war a feeñ ci bépp xeetu jumtu kaay | 114.600304 | 25.182312 | 21.809875 | 6.250948 | 8.728107 | ti næɡ wɔɹ ʌ ʌ æm soʊloʊ ti li ni leɪ seɪ wu ti næɡ wɔɹ ʌ | 0.909234 | 7.989448 | 1.854703 |
bi ngay bàgg sa bopp bàgg bi ngay bàgg sa produit bàgg bi ngay bàgg sa njëkk waaye bàgg tamit bi tax clients bi mën a bàyyi xel li nga xamante ni moom mooy yow | 101.222458 | 14.703048 | 26.288506 | 6.025725 | 7.807808 | baɪ sɑ bɑp baɪ sɑ baɪ sɑ baɪ tæks klaɪʌnts baɪ ʌ li ni jaʊ | 0.903872 | 7.971094 | 1.751384 |
loolu moom day jëm ci saafara li nga xamante ni moom mooy ay jafe-jafe wax woo ngay wax nag tubaab di ko woowee slogan | 102.62027 | 24.444508 | 21.067898 | 7.629517 | 5.805806 | deɪ li ni eɪ - wæks wu wæks næɡ di koʊ sloʊɡʌn | 0.894268 | 8.266639 | 1.840558 |
xool ndax am yoon bi nga ko bëgg a jaaralee méngóo na ak ñi nga xamante ni moom mooy say client suñu ne méngóo na nag maanaam | 108.960945 | 17.121811 | 39.950855 | 32.977604 | 5.905906 | æm jun baɪ koʊ ʌ nɑ ni seɪ klaɪʌnt ni nɑ næɡ | 0.956394 | 12.560569 | 2.513926 |
waaye nag moom diggante bu baax sa diggante client waaye tamit nga gën a mën a xam lan moom mooy bëgg-bëgg client bi ak client yi nga xamante ni ñoom | 106.40007 | 23.625669 | 26.953823 | 39.355724 | 6.900051 | næɡ sɑ klaɪʌnt ʌ ʌ læn - klaɪʌnt baɪ klaɪʌnt ji ni | 0.968936 | 15.760293 | 3.016554 |
parce que bu ñu xoolee dañuy déggee origines bi maanaam fu mu jugee ak ni mu ñëwee ci yow ci marché ngeen daje dañ la boole ak moom | 105.094536 | 20.534388 | 28.70929 | 19.344963 | 5.854241 | kju baɪ fu mu ni mu jaʊ lɑ bul | 0.940396 | 14.262052 | 2.358957 |
muy seen i ay information seen i tur seen i sant seen i numéro télèphone fi ñu dëkk ak li nga xamante ni moom mooy seen i ay adress mel loolu da ciy baax de temps à temps | 103.104759 | 16.212475 | 22.571478 | 7.585989 | 10.510511 | sin aɪ eɪ ɪnfɜ˞meɪʃʌn sin aɪ sin aɪ sænt sin aɪ faɪ li ni sin aɪ eɪ mɛl dɑ di tɛmps tɛmps | 0.906323 | 7.166828 | 1.545489 |
ñu ci mel ne léegi di ñu ci mel ne Instagram parce que sa client foofu nga leen war a mën a gis li ñu bëgg wax foofu moom mooy bépp yoon boo bëgg a jaarale sa poudre | 110.555786 | 21.948227 | 24.240606 | 6.760659 | 9.209209 | mɛl ni di mɛl ni ɪnstʌɡɹæm kju sɑ klaɪʌnt lin wɔɹ ʌ ʌ li wæks jun bu ʌ sɑ | 0.906174 | 8.35078 | 1.713067 |
loolu mun a indil yeneen clients ba léegi ci base d' ordre ay chèques yi dañuy gis ni clients bii di fàttu jób moom moo ëpp lu muy jënd | 106.992325 | 16.545235 | 28.910103 | 27.821932 | 7.119132 | mʌn ʌ klaɪʌnts bieɪ beɪs di' eɪ ji ni klaɪʌnts di mu lu | 0.952862 | 14.336938 | 2.408391 |
yooyu noonu yëpp mu nekk ay questions yi nga xamante ni yu am solo lool yi nga war a bàyyi xel laataa ngay weyel li nga xamante ni moom mooy sa produit wala service | 102.16227 | 12.199308 | 27.212324 | 54.911453 | 8.392503 | mu eɪ kwɛstʃʌnz ji ni ju æm soʊloʊ ji wɔɹ ʌ li ni sɑ wɔlʌ sɜ˞vʌs | 0.967568 | 14.105947 | 2.352554 |
waaye nag njëkk xalaatee naka ngay def ba yëwe yël li nga xamante ni moom mooy li ngay def | 117.648895 | 25.853619 | 24.662527 | 29.288849 | 5.309356 | næɡ bieɪ li ni li | 0.914526 | 13.690423 | 2.729336 |
wax ñoo ji nag comme ni ñu la ko waxee dafa war a nekk lu gàtt yombatee neex a jàpp bu ko defee ñoom bu ñu déglu sa turu entrepix sax bu ñu ko gisee rek ba ñu koy xam | 102.457619 | 19.762362 | 18.274443 | 8.69654 | 8.350626 | wæks dʒi næɡ ni lɑ koʊ wɔɹ ʌ lu ʌ koʊ dɛfi sɑ sæks koʊ bieɪ | 0.922134 | 8.863463 | 1.852533 |
muy fexe ba tënk li nga xamante ni moom nga war a wax yëpp wala moom def bàq bi nga xamante ni moom ngay bàq sa produit wala mbàqos bi nga xamante ni moom ngay indil kii yaabi | 102.05555 | 11.734369 | 20.615818 | 6.764839 | 7.307307 | bieɪ li ni wɔɹ ʌ wæks wɔlʌ baɪ ni sɑ wɔlʌ baɪ ni | 0.889612 | 6.933427 | 1.706226 |
li ngay dajëg sa sa yi clients dafa war a nekk li nga xamante ni lu ngay bàyyi xel ba clients bi dootu ko fàttali | 89.604134 | 17.935957 | 18.570831 | 6.638182 | 8.447861 | li sɑ sɑ ji klaɪʌnts wɔɹ ʌ li ni lu bieɪ klaɪʌnts baɪ koʊ | 0.877736 | 7.225245 | 1.744588 |
waaw xamante ni ci ci ci nga xamante ni moom mooy ñi nga tax a jóg ndax kat yoon bu baax bi ngay jaarale sa message dafa nekk li nga xamante ni lu am solo la | 102.87944 | 19.747324 | 23.115934 | 7.051172 | 8.825847 | ni ni tæks ʌ kæt jun baɪ sɑ mɛsʌdʒ li ni lu æm soʊloʊ lɑ | 0.918508 | 9.452515 | 1.984494 |
waaye nag kii di mati ca am moom moo gën a bëreel lu muy jënd ci quantité maanaam faatu jóbba moom moo ëpp lu muy ñëw di jënd si maanaam mën na ñëw tey jënd benn su mu ñëwaat | 109.468712 | 16.622461 | 33.539417 | 28.195168 | 6.906907 | næɡ di kʌ æm mu ʌ lu mu lu di si nɑ bɛn su mu | 0.962383 | 14.387637 | 2.589562 |
dafay méngoom maanaam couleur benn bu ci nekk booy tànn dafa war a am signification ci li nga xamante ni moom ngay def wala ci li nga xamante ni moom mooy sër | 116.824753 | 24.336477 | 22.953131 | 5.380736 | 5.205205 | bɛn wɔɹ ʌ æm li ni wɔlʌ li ni | 0.899078 | 6.19493 | 1.445937 |
mais loolu moom mooy base de données daf lay jàppale lool ngir nga gën a mën a saytu yenn xeetu laaj wala yenn xeetu xamel bi nga xam te war nga ko xam ci li nga xamante ni moom mooy | 102.483345 | 9.678808 | 27.272636 | 27.278202 | 7.394745 | meɪs beɪs di leɪ ʌ ʌ wɔlʌ baɪ ti wɔɹ koʊ li ni | 0.943041 | 13.012904 | 2.27517 |
parce que bu dee ci base de données boobu noonu yow mi nga xamante ne nag amagoo base de données nga faral nga bëgg ko am | 100.19162 | 17.291307 | 34.972534 | 19.73527 | 6.266749 | kju di beɪs di jaʊ mi ni næɡ beɪs di koʊ æm | 0.964468 | 14.89257 | 2.575907 |
fànn la nekk bu fekkee dafa am entreprise ban entreprise la jógee ay numéro téléphone am adresse email donc yooyu moom moo nekk xeetu xibaar yi nga xamante ni moom mooy nekk ci | 103.379128 | 13.456581 | 23.744219 | 27.546797 | 5.821963 | lɑ æm bæn lɑ eɪ æm imeɪl mu ji ni | 0.965147 | 13.534732 | 2.609709 |
comme ni ñu ko waxee suñu carte bi wees suñu ñëwee si suñu carte vingt six bii dañuy waxtaanee ak yow | 106.430817 | 26.271606 | 16.995821 | 5.917945 | 5.021971 | ni koʊ kɑɹt baɪ si kɑɹt sɪks jaʊ | 0.879609 | 6.433374 | 1.559238 |
donc dañu di wala sa publu si te rek na fekk ne yoon boobu dina la yombal ngir nga jot ci li nga xamante ni moom mooy say client | 102.797943 | 13.574837 | 22.134811 | 9.993131 | 8.122408 | di wɔlʌ sɑ si ti nɑ ni jun dinʌ lɑ dʒɑt li ni seɪ klaɪʌnt | 0.897162 | 8.164744 | 1.735015 |
waaye tamit bu ñu ñëwee ci marché bi gis wax yooyu waa yéen tamit bu ñu demee ci face bu wala bu ñu demee ci espagra am wala bu ñu demee ci léegi din fëkkal fa joo ji de wax | 107.874664 | 19.395464 | 17.957502 | 6.843613 | 7.507508 | baɪ wæks feɪs wɔlʌ æm wɔlʌ dɪn dʒu dʒi di wæks | 0.901702 | 7.082713 | 1.655009 |
ba li nga xamante ni moom mooy yoon yi ngi koy jaaralee mën a méngóo ak message bi waaye tamit mën a méngóo ak li nga xamante ni moom mooy foofu la lay | 106.589111 | 18.033613 | 31.776499 | 6.423705 | 6.506507 | bieɪ li ni jun ji ʌ mɛsʌdʒ baɪ ʌ li ni lɑ leɪ | 0.909951 | 9.00908 | 1.792408 |
waaw te ne lu neex lay nekk neex moom mooy foo ko déggee soit ni ñu koy waxee dafa neex wala tamit ni ñu koy gisee dafa neex yooyu mu nekk mbir yi nga xamante ni | 98.777351 | 16.711 | 22.935089 | 10.016846 | 6.666667 | ti ni lu leɪ fu koʊ ni wɔlʌ ni mu ji ni | 0.883092 | 8.299571 | 1.824066 |
waaye moom mooy ay béy utiliser wala dépp yoon bi nga xamante ni moom ngay jaarale sa communication maanaam bu fekkee say clients yi ñaari boor yëpp nañu féete maanaam da nga am clients yi nga xamante ni | 105.503937 | 15.16992 | 20.44408 | 9.220815 | 9.843063 | eɪ wɔlʌ jun baɪ ni sɑ kʌmjunʌkeɪʃʌn seɪ klaɪʌnts ji bʊɹ dɑ æm klaɪʌnts ji ni | 0.906996 | 7.43346 | 1.737419 |
parce que bu ñu xoolee maanaam sant tour liggéey maanaam kooku di nga xam te ni moom mooy client am lu muy liggéey | 112.363617 | 27.173319 | 28.935026 | 17.371183 | 4.904905 | kju sænt tʊɹ di ti ni klaɪʌnt æm lu | 0.960326 | 12.942585 | 2.479243 |
d' accord yi ñu ngi lay xool du ma dem ci loolu waaye tamit da ngay xool boo dajay client bi ban message ngay porté jëmale ko ci moom | 103.344467 | 23.730694 | 16.573277 | 8.024516 | 7.279252 | di' ʌkɔɹd ji leɪ du mɑ dɑ bu klaɪʌnt baɪ bæn mɛsʌdʒ koʊ | 0.879792 | 6.65419 | 1.725849 |
ñu ngi lay demee ñu ngi lay demee mu ne modo modo wax na ko faatu faatu wax na ko ñoom ajye ak nday ba nu mu nu lay demee ba siw ci pañ bi wala ciw ci gox bi | 107.949257 | 16.026047 | 26.025877 | 30.963688 | 10.732891 | leɪ leɪ mu ni wæks nɑ koʊ wæks nɑ koʊ bieɪ nu mu nu leɪ bieɪ baɪ wɔlʌ baɪ | 0.946593 | 12.901505 | 2.412542 |
waaw loolu moom mooy mooy dégg yoon woo woon nag ñaari ñoo ci am solo moom mooy dégg-dëgg bi moom mooy message bi ak gis-gis gi moom mooy imagé nga xamante ni moom ngay def | 104.550583 | 17.392351 | 21.370731 | 7.194276 | 6.606607 | jun wu næɡ æm soʊloʊ - baɪ mɛsʌdʒ baɪ - ni | 0.906497 | 8.806329 | 1.752071 |
di nga xam tamit naka ngay mën a saytoo lii di bëgg-bëgg client yi maanaam yan mbir ñoom ñooy tax ñuy jënd ak yan mbir moom moo leen mën a tax bañ a jënd yooyu yëpp ci base d' année bi | 107.454399 | 18.454258 | 31.649569 | 34.176357 | 8.786717 | di ʌ di - klaɪʌnt ji jæn tæks jæn mu lin ʌ tæks ʌ beɪs di' baɪ | 0.969124 | 13.808448 | 2.494895 |
par rapport ak nit ñi jëndee wala ni nga xamante ne moom la ñuy ñëwee ci yow ginaaw ba déglu nga loolu day baax lool ñu indil la misaal | 103.78199 | 23.142067 | 30.094475 | 21.592085 | 7.499616 | pɑɹ ɹæpɔɹ nɪt wɔlʌ ni ni lɑ jaʊ bieɪ deɪ lɑ | 0.968763 | 15.305816 | 3.110963 |
donc nag li nga xamante ni comme ni ñu la ko waxee moom mooy message bi ngir nga tëgg ko nag fexeel mu tënk ci yi nag gàtt leer | 98.27095 | 24.26848 | 21.046284 | 5.876815 | 7.510084 | næɡ li ni ni lɑ koʊ mɛsʌdʒ baɪ koʊ næɡ mu ji næɡ | 0.899345 | 7.313201 | 1.688578 |
mooy canal de distribution bi maanaam bu yoon bi nga xamante ni moom ngay jaar ngir yu weyal li ngay def canal de distribution boobu noonu daf lay jàppale loolu | 103.913239 | 14.850062 | 29.511908 | 43.753235 | 8.508509 | kʌnæl di dɪstɹʌbjuʃʌn baɪ jun baɪ ni ju li kʌnæl di dɪstɹʌbjuʃʌn leɪ | 0.955618 | 14.517375 | 2.533854 |
ci carte vingt sept bii ñu fas yéene waxtaan ak yow ci lii di base de données clients | 109.06279 | 26.095064 | 29.732224 | 49.72094 | 4.901142 | kɑɹt sɛpt jaʊ di beɪs di klaɪʌnts | 0.966411 | 14.213759 | 2.363174 |
waaye tamit li nga xamante ne looy méngóo ak li ngay def la looy méngooo ak li nga xamante ne moom mooy mbackuus bi ngay indi | 115.200096 | 21.831793 | 25.747051 | 6.842096 | 4.202784 | li ni li lɑ li ni baɪ | 0.91378 | 8.91853 | 1.938233 |
parce que bu ñu xoolee am nañu xoolee am nañu xoolee am nañu xoolee am nañu xoolee am nañu xoolee am nañu xoolee am nañu xoolee am nañu xoolee | 110.859734 | 21.549416 | 28.076574 | 17.607258 | 4.704705 | kju æm æm æm æm æm æm æm æm | 0.959937 | 13.963569 | 2.564814 |
parce que bu ñu xoolee nga def kii ni waaye tamit nga gën a leeral fan nga daje ak ñoom ndax fan nga daje ak ñoom tamit am na mën na la jàppale pour boo bëggee daje ak ñeneen ñu mel ni ñoom | 106.650536 | 16.382523 | 37.004589 | 47.464516 | 7.207207 | kju ni ʌ fæn fæn æm nɑ nɑ lɑ pɔɹ bu mɛl ni | 0.961146 | 13.192274 | 2.50348 |
parce que bu ñu xamante ni entreprise yi dañ koy faral di am di saytu lépp li nga xamante ne xeetu xibaar la jëm ci seen yi ay clients | 101.872398 | 18.752592 | 30.934599 | 33.853504 | 7.218221 | kju ni ji di æm di li ni lɑ sin ji eɪ klaɪʌnts | 0.960759 | 14.50776 | 2.504348 |
xara la ngay utiliser ngir jot ci clients yi di nga xam te nekk ngay waxee ak ñoom di nga xam ni yan clients ngay gën a jox gëd | 110.300903 | 17.815069 | 34.456066 | 32.344349 | 7.630971 | lɑ dʒɑt klaɪʌnts ji di ti di ni jæn klaɪʌnts ʌ | 0.976847 | 16.324432 | 3.112421 |
mais bu ñu xamante ni maanaam kii ñaay bu ko déggee du am du nekk ay wax yi nga xamante ni fóot la day day day compliqué ci moom gër mu jàpp ko wala biir mu xam lam da bëgg waa foofu | 105.12944 | 21.838657 | 18.5597 | 7.888387 | 9.30931 | meɪs ni koʊ du æm du eɪ wæks ji ni lɑ deɪ deɪ deɪ mu koʊ wɔlʌ mu læm dɑ | 0.876219 | 7.911076 | 1.66472 |
mais loolu nag yenn xeetu journal li nga xam ne dañ koy faral di utiliser xool naka nga mën a def ba li ngay jàll lañ | 103.181358 | 18.606024 | 23.007019 | 5.642423 | 5.67492 | meɪs næɡ dʒɜ˞nʌl li ni di ʌ bieɪ li | 0.885988 | 7.26329 | 1.767551 |
donc ñun dañuy xamante ne moom ngay fësal sa image sa logos wala sa photo ba ñoom maanaam client bi su gisee sa photo rek dina jàpp sa entreprise | 109.9692 | 21.695503 | 24.644505 | 9.747931 | 8.808809 | ni sɑ ɪmʌdʒ sɑ loʊɡoʊz wɔlʌ sɑ foʊtoʊ bieɪ klaɪʌnt baɪ su sɑ foʊtoʊ dinʌ sɑ | 0.935571 | 9.411368 | 1.770654 |
donc ñu ngi lay def dinañ la daal la am ci li ngay def kontaan na ci wala kontaan na ci | 103.932991 | 17.448793 | 25.195778 | 53.873592 | 3.903904 | leɪ lɑ lɑ æm li nɑ wɔlʌ nɑ | 0.950908 | 13.311566 | 2.353286 |
maanaam ñoom mooy ñoom laay jox ñu may jaayal est ce que nekk na ñi nga xamante ni tamit mën nañ fasal sama produit wala sama service | 106.641571 | 24.425331 | 31.083673 | 29.707146 | 6.798385 | meɪ ɛst sii kju nɑ ni sɑmʌ wɔlʌ sɑmʌ sɜ˞vʌs | 0.98162 | 16.515259 | 2.529018 |
mais bu ñu xamante ni dañuy xamante ni dañuy xamante ni dañuy xamante ni dañuy xamante ni dañuy xamante ni dañuy xamante ni | 107.209473 | 18.174595 | 19.880104 | 9.407908 | 4.004004 | meɪs ni ni ni ni ni ni ni | 0.903445 | 7.448003 | 1.620848 |
li ñu nekk di liens bi di di xaar li ñu bëgg wax foofu moom mooy bépp yoon boo bëgg utiliser na nga leerluñu yoon boobu moom mooy yoon bi nga xamante ni | 102.776382 | 21.360561 | 23.915289 | 7.108539 | 7.107107 | li di linz baɪ di di li wæks jun bu nɑ jun jun baɪ ni | 0.890906 | 8.364226 | 1.857896 |
parce que loolu la ñuy def la ñuy def lan teel ñoom ñooy kan base de données bi nag bi ñu koy wax nekkul client bi que c' est la concerner ndax comme ni ñu la ko waxee am na ñaar client bi ak prospès | 102.931816 | 15.347408 | 28.253042 | 32.111629 | 12.112112 | kju lɑ lɑ læn til kæn beɪs di baɪ næɡ baɪ wæks klaɪʌnt baɪ kju si' ɛst lɑ ni lɑ koʊ æm nɑ klaɪʌnt baɪ | 0.959718 | 12.674245 | 2.422573 |
waaye yëg nañ ko donc ñoom ñoom ñoo tudd prospect ñoom dañu war a bokk ci li nga xamante ni moom mooy sa base de données boobu noonu ngir nga gën a | 100.020645 | 17.608438 | 30.045795 | 35.100018 | 6.091109 | koʊ pɹɑspɛkt wɔɹ ʌ li ni sɑ beɪs di ʌ | 0.963946 | 14.223226 | 2.394995 |
waaye moom la ñu xam ne dañuy mën a saytu seen i ay bëgg-bëgg comme ni ñu ko xamee li nga xamante ni moom mooy base de nekkul | 107.439835 | 19.467724 | 30.171667 | 20.451239 | 5.505506 | lɑ ni ʌ sin aɪ eɪ - ni koʊ li ni beɪs di | 0.962308 | 12.565102 | 2.208186 |
se yoon yëpp nga ñu da nga koy jaarale ci lii di internet fekk ni yow clients yi nga xamante ne ñoom ñoo war a mën a jënd sa produit amuñu lii di internet | 112.164795 | 19.13693 | 27.877768 | 14.521338 | 8.537351 | seɪ jun dɑ di ɪntɜ˞nɛt ni jaʊ klaɪʌnts ji ni wɔɹ ʌ ʌ sɑ di ɪntɜ˞nɛt | 0.930682 | 10.574561 | 2.055727 |
ñu ngi lay xamante ni moom mooy suñu xarit ay chas ci base de ne bi nga xamante ni moom la def moom ay chas base de dem buñ ko doon tënk ñëw na | 103.456566 | 15.769456 | 32.592693 | 21.946634 | 8.218437 | leɪ ni eɪ tʃɑz beɪs di ni baɪ ni lɑ eɪ tʃɑz beɪs di koʊ nɑ | 0.965192 | 13.125775 | 2.321958 |
donc ñun produit yi produit yi wala service bi nga xamante ni moom nga bëgg mu eggi ci client bi egg fa donc loolu nag pour mu egg fa day baax lool nga xam ban jaaruwaay la war a jël | 105.623955 | 16.111942 | 18.155994 | 7.578754 | 9.40941 | ji ji wɔlʌ sɜ˞vʌs baɪ ni mu klaɪʌnt baɪ ɛɡ næɡ pɔɹ mu ɛɡ deɪ bæn lɑ wɔɹ ʌ | 0.897038 | 6.894241 | 1.699877 |
xaar ndax kat kanadok communication yooyu bëre na am na yi nga xamante ni | 107.113312 | 20.429888 | 14.039152 | 18.28529 | 7.177363 | kæt kʌmjunʌkeɪʃʌn nɑ æm nɑ ji ni | 0.726549 | 8.142192 | 1.785873 |
waaye tamit dal dal guñ koy wax moom mooy mu nekk li nga xamante ne lu ñuy bàyyi xel lay nekk la nekk tamit lu yomb simple | 111.96566 | 22.444136 | 23.680185 | 8.474147 | 5.988968 | dæl dæl wæks mu li ni lu leɪ lɑ lu sɪmpʌl | 0.918727 | 8.42943 | 1.866256 |
waaw ñu yëg ne ba neegi loolu di message bi nga xam te ne moom ngay jàllale warul nekk warul mën a nekk wax kese war na mën a nekk benn xeetu lu lëgu benn xeetu | 123.176239 | 23.989948 | 21.138935 | 10.672169 | 8.401596 | ni bieɪ di mɛsʌdʒ baɪ ti ni ʌ wæks wɔɹ nɑ ʌ bɛn lu bɛn | 0.926093 | 8.196275 | 1.75345 |
parce que bu fekkee daf lay jàppale lool bu fekkee yaa ngi koy yokku tamit di xool naka ngay gën a ñoongalee loolu yi xibaar | 108.292702 | 17.244719 | 27.491457 | 33.673389 | 3.503504 | kju leɪ di ʌ ji | 0.975384 | 16.572247 | 2.924983 |
parce que yu an bi nga xamante ne ñoom laay jaayee est ce que nekk na yu an bi nga xamante ne clients yi dañ koy faral di gis wala clients yi sax xam nañ ko | 103.069366 | 17.444645 | 30.945517 | 30.47006 | 10.01001 | kju ju æn baɪ ni ɛst sii kju nɑ ju æn baɪ ni klaɪʌnts ji di wɔlʌ klaɪʌnts ji sæks koʊ | 0.970344 | 14.222123 | 2.569504 |
waaw li nga xamante ni bi nga koy joxe bu ñu ñëwaatee ba léegi ci li nga xamante ni moom | 83.35244 | 26.108658 | 23.514891 | 32.824432 | 9.116809 | li ni baɪ bieɪ li ni | 0.973948 | 15.601357 | 3.032537 |
kon yoon la war a jël yoon bi nga xamante ni moom mooy tax client bi mën ci jël comme ni ñu la ko waxee ci lu wees boo jëlee | 112.949455 | 21.028246 | 23.588343 | 7.297186 | 8.416862 | kɑn jun lɑ wɔɹ ʌ jun baɪ ni tæks klaɪʌnt baɪ ni lɑ koʊ lu bu | 0.871819 | 8.895524 | 1.753251 |
mais foofu da ngay dugal lépp li nga xamante ne dugg la ci wàllu xaalis maanaam xaalis bi nga xam te ne jóge ne ci bitti ñëw dugg | 111.578224 | 21.107946 | 26.999521 | 24.923859 | 5.643739 | meɪs dɑ dudʒʌl li ni lɑ baɪ ti ni ni | 0.938135 | 13.650008 | 2.377553 |
mais loolu moom mooy jàppale lay doon moom ay chas ginnaaw ba mu commencé activité mag fii ak ay weer gis nañ ni moderne économique bi nga xamante ni | 105.462273 | 22.602192 | 22.367952 | 11.295674 | 6.606607 | meɪs leɪ eɪ tʃɑz bieɪ mu mæɡ eɪ ni moʊdɛɹn baɪ ni | 0.921319 | 10.186627 | 2.063384 |
ñu ngi lay jàppale ni naka lañ kay ñoomale ndax kat na nga yëg ñi loolu di modèle d' affaire | 102.229317 | 14.480653 | 25.023563 | 17.024601 | 3.703704 | leɪ ni keɪ kæt nɑ di di' | 0.935489 | 9.686135 | 1.896621 |
muy Salide dégg nga ko lépp li nga xamante ni wàllu tresorerie la wala wàllu xaalis wala dugub génn ci wàllu Kopar | 105.486511 | 18.29512 | 29.707026 | 17.113348 | 3.803804 | koʊ li ni lɑ wɔlʌ wɔlʌ | 0.963546 | 14.463205 | 2.439455 |
waaw yaay xool ñoom naka la ñuy def ngir jot ci li nga xamante ni yow moom nga leen di jox comme saafara | 96.489876 | 30.23304 | 21.508682 | 13.983673 | 4.79832 | lɑ dʒɑt li ni jaʊ lin di | 0.916711 | 10.203925 | 2.106778 |
mais loolu nag kon loolu nag mbéy nañ ko waxee woon ci chapitre 1 | 109.825943 | 17.011925 | 22.840101 | 17.760185 | 2.902903 | meɪs næɡ kɑn næɡ koʊ | 0.943217 | 10.478326 | 2.147249 |
waaw dafa war a méngóo ak li nga xamante ni moom mooy say gis-gis ci wàllu koppar wala fi nga bëgg a egale sa wàllu entre bi si wàllu xaalis | 108.596207 | 12.009429 | 29.372572 | 21.341349 | 6.206206 | wɔɹ ʌ li ni seɪ - wɔlʌ faɪ ʌ sɑ ɑntɹeɪ baɪ si | 0.958727 | 14.873569 | 2.528342 |
bu dee bu dee bu dee bu dee bu dee bu dee bu dee bu dee bu dee bu dee bu dee | 103.014412 | 19.049196 | 19.754295 | 19.527061 | 4.423868 | di di di di di di di di di di di | 0.929782 | 10.256477 | 1.837642 |
ñu ngi lay gis ci moom ak Sali dañuy gis ni def nañ ci lépp li nga xamante ni lu dugg la ci wàllu kópar wala lu génn ci wàllu kópar | 106.50042 | 16.984909 | 23.227669 | 29.300701 | 4.904905 | leɪ ni li ni lu lɑ wɔlʌ lu | 0.965191 | 12.64298 | 2.196095 |
falay jaar waaye technique nga xamante ni moom lay amee Koppar ci partie bu njëkk bi chapitre 1 waxtaanee woon nañu ak yow ci hypothèse yi nga xamante ni | 101.727989 | 13.054986 | 21.093542 | 24.150211 | 4.904905 | tɛknik ni leɪ baɪ jaʊ ji ni | 0.946067 | 11.788861 | 2.000734 |
maanaam bu fekkee da nga gis ni hypothèse yooyu maanaam nengoo na ak li nga xamante ni moom mooy bëgg-bëgg client yi | 116.863632 | 21.944355 | 24.099581 | 8.265726 | 4.104104 | dɑ ni nɑ li ni - klaɪʌnt ji | 0.919908 | 9.344796 | 1.971587 |
parce que loolu nag bi moom mooy fër ngel ban bës moom la loolu xaw jënd boobu wala jaay boobu ban bës la xaw | 103.653992 | 14.749297 | 25.822292 | 24.491901 | 4.604605 | kju næɡ baɪ bæn lɑ wɔlʌ bæn lɑ | 0.963595 | 14.670412 | 2.641052 |
moo xam damaa jënd paan moo xam damaa jënd bu tey wala leneen ak leneen beneen koo leen bi nga xamante ni entré wala encassement moom moo ci nekk | 104.276314 | 14.165538 | 34.512318 | 20.164846 | 5.205205 | mu mu wɔlʌ ku lin baɪ ni wɔlʌ mu | 0.963644 | 14.220775 | 2.617062 |
jërëjëf jëfay jëfay sa digganteeg say fournisseur wala sa digganteeg disponibilité sax produit | 102.428909 | 15.782056 | 23.836206 | 38.929249 | 4.081633 | sɑ seɪ wɔlʌ sɑ sæks | 0.954717 | 13.794601 | 2.258159 |
bu ngay génnee li nga xamante ni moom mooy douze mille mu des trois cent vingt cinq mille le dix neuf marche deux mille vingt un sari tamit dugal na beneen reçu | 108.338211 | 23.167727 | 32.008541 | 18.455185 | 11.426673 | li ni mɪl mu dɛs twɑ sɛnt sɪŋk mɪl lʌ dɪks mɑɹʃ du mɪl ʌn sɑɹi dudʒʌl nɑ | 0.962819 | 13.027598 | 2.645318 |
parce que ñu ngi lay bantereel in lay jël ak naka lay jaar ci modèle d' affaire bi ñu njëkkoon teg gisoon nañ ni | 109.128517 | 19.418182 | 22.54451 | 17.523819 | 5.012531 | kju leɪ ɪn leɪ leɪ di' baɪ ni | 0.932039 | 10.517897 | 1.970142 |
parce que saaitoo sa trésor yi sa denc nekk lu baax dama lay sonj nga am li nga xamante ni moom mooy kayee dakees | 112.037926 | 16.514391 | 32.544086 | 19.894739 | 5.063973 | kju sɑ ji sɑ lu dɑmʌ leɪ æm li ni | 0.974741 | 16.473198 | 2.799189 |
donc xaalis bi moom mooy 325000 donc xaalis bi li ci nekkoon da ngay jël 325000 nga boo lekk a ak 12000 waaye nag comme léegi jënd am na | 110.363663 | 17.151396 | 26.157215 | 19.231369 | 4.804805 | baɪ baɪ li dɑ bu ʌ næɡ æm nɑ | 0.963717 | 13.933448 | 2.402517 |
parce que bu ñu am solo lool yu ñu lay indil yu ñu lay wax yu ñu lay dénk boo ko faralee di def da ngay gis ni | 101.79644 | 16.469181 | 28.636347 | 23.008661 | 6.806807 | kju æm soʊloʊ ju leɪ ju leɪ wæks ju leɪ bu koʊ di dɑ ni | 0.954938 | 13.157939 | 2.413595 |
mais loolu moom ngay am hypothèse yooyu nag mu nekkoon ay xalaat ji nga xamante ni mën na am comme mën na bañ am léegi nag ci partie bi dañuy ñëw xool | 110.728638 | 20.812611 | 28.325737 | 15.406418 | 6.306306 | meɪs æm næɡ mu eɪ dʒi ni nɑ æm nɑ æm næɡ baɪ | 0.931269 | 10.602701 | 1.845733 |
bu ñu ñëwaatee ba léegi ci aychage ñu gis ni entrepis bi léegi mi ngi dox comme ni ñu ko waxee léegi am na kii nañ ki nga xamante ni moom lay liggéeyal muy yéen | 103.509483 | 10.746261 | 28.112965 | 22.51577 | 6.364111 | bieɪ ni baɪ mi ni koʊ æm nɑ ki ni leɪ | 0.959687 | 13.824851 | 2.523992 |
maanaam lan nga jënd li mutu du mooy xam pan la moo xam siw la moo xam saa ko la wala moo xam dana ne la entrel' wala wala sorti | 107.986961 | 13.719756 | 27.170099 | 19.276798 | 7.94304 | læn li du pæn lɑ mu lɑ mu koʊ lɑ wɔlʌ mu deɪnʌ ni lɑ ' wɔlʌ wɔlʌ | 0.945938 | 14.201187 | 2.567321 |
donc fii dafa def sorti dégâts ma douze mille trois trente li ñu noonu donc li nga xamante ni moom mooy nekk ci kayee | 109.532753 | 19.535879 | 24.46315 | 19.100914 | 3.703704 | mɑ mɪl twɑ li li ni | 0.932316 | 13.718522 | 2.532469 |
ci carte vingt huit bii ñu wax lépp lu aajoo wàllu saytu sa ndénc | 108.049286 | 24.18013 | 31.171797 | 19.563911 | 2.669336 | kɑɹt wæks lu sɑ | 0.952007 | 13.063039 | 2.404867 |
am na ci wàllu koppar yëngu yëng bi moom mooy muy dugg wala muy génn lépp li nga xam te ne lu aajewoo ci wàllu dépass la loolu dafa waral da nga ko war a bind | 108.878311 | 18.40288 | 27.431532 | 20.772579 | 7.007007 | æm nɑ baɪ wɔlʌ li ti ni lu lɑ dɑ koʊ wɔɹ ʌ baɪnd | 0.966706 | 12.663251 | 2.223931 |
xamante ni ñun ko planifier woon boobu baax na da nga koy mudgee continuer bu fekkee ne da nga gis ni hypothésie yi me nga ko wul ak li nga xamante ni moom mooy bëgg-bëgg kii liens yi | 105.247681 | 18.633709 | 24.878263 | 14.927658 | 7.007007 | ni koʊ nɑ dɑ ni dɑ ni ji mi koʊ li ni - linz ji | 0.937482 | 9.935212 | 1.953096 |
waaye xaalis bu duggul loolu tamit daf lay mën a daf lay indil du du du lele ay yenn gàllankoor wala yenn tardement yi nga xamante ni | 105.268158 | 16.185467 | 22.231445 | 50.220795 | 4.904905 | leɪ ʌ leɪ du du du eɪ wɔlʌ ji ni | 0.965819 | 14.133516 | 2.643859 |
loolu nag dafa war a nekk ci wàllu xaalis mën nga ko géréal sa bopp mën nga ko jox nit mu géréal la ko loolu nag dafa war a nekk | 109.744461 | 19.241581 | 26.730747 | 35.114849 | 7.852158 | næɡ wɔɹ ʌ koʊ sɑ bɑp koʊ nɪt mu lɑ koʊ næɡ wɔɹ ʌ | 0.944423 | 16.409439 | 2.78974 |
mën naa daal di ñëw laaj ko ni ko sali yan dépasse nga def ci semaine bi ñu génn dama ko bëgg a enregistré ci Skaye bi maanaam Kette boobu mu ñu koy wax | 108.065598 | 17.665899 | 28.838907 | 29.326429 | 6.897903 | di koʊ ni koʊ jæn baɪ dɑmʌ koʊ ʌ baɪ mu wæks | 0.955336 | 9.848929 | 2.103584 |
Subsets and Splits