audio
stringlengths
56
98
transcription
stringlengths
26
222
audio_file
audioduration (s)
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_103.wav
bi bëgg-bëgg bi ak taamu bi nga xamante ni moom nañu taamu di lekk lu baax ak lu wér moom mooy seen lenn diñiaax
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_122.wav
donc ñoom ñoom ñoo xamante ni moom mooy bëgg-bëgg client bi donc ngir nga gën a mën a saytu nag li nga xamante ni moom mooy offer boobu noonu joxe bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_208.wav
doos milliards quatre cent quatre vingt cinq cent donc loolu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_62.wav
marché bi marché bi nu muy doxee ngay def ay gëstu di laajte xool marché bi yan bës lay gën a dox naka lay doxee yan biir ñëw
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_66.wav
yooyu boo ko xamee da ngay gis ni dafa lay yombal lool ngir nga mën a am benn taxawaay bu baax ci saafara yi nga xamante ni wala ci mbir yi nga xamante ne ñoom nañuy wuti ci
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_90.wav
wala léegi donc yooyu dañuy jóge ci yeneen gox ñëw ci marché bi parce que gis nañu marché bi day day dox donc loolu boo xoolee ci wàllu yokkute production da ngay gis ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_68.wav
voilà li ñu jaay bi nag buñ koy wax moom mooy taxawaay bi nga xamante ni moom la client bi wala ay bëgg-bëggam client bi naka lay jëndee est ce que jënd bi dafay nekk jënd yi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_86.wav
ay chanak ngir mu weyel li nga xamante ni moom mooy joxe boobu mu fas yéene joxe ci marché bi moom génnee na ñetti laaj yi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_124.wav
bi ci njëkk moom mooy faw nga xam ñenn ñooy say wudj directement maanaam ñan nga xamante ne yéen yéen a bokk li ngeen di def moom yéen yow mii di jëng
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_133.wav
muy xam dain yéen yéen a kon dura waale moo xam ci wàllu joxe bi moo xam ci wàllu weel bi moo xam ci wàllu fësal bi wala moo xam ci wàllu taaral bi yooyu nag buñ koy wax moom mooy dafay jëm ci lépp
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_71.wav
wala ki nga xam te ni dafay jaay lu gën a yomb donc yooyu tamit nekk na mbir bi nga xamante ni lu am solo lu lool beneen bi te moom mooy bu mucc bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_138.wav
ñu ngi leen di amana moom mooy sut seen njëkk wala njëkk bi nga xamante ni moom mooy yees seen njëkk waaye jublu waaye moom mooy fexe ba client bi ba jëm si ñoom de ñëw ci yow
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_169.wav
mais moom mooy juillet ñoom concrètes yi ñu ngi koy jaayee litre bi 1000 200 te boo demee ci yan dëkk yu Magu yi ci vies yi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_199.wav
pour liggéey nañ li toll ci vingt trois mille litres ñii di seen jui ñoom liggéey nañ lu toll ci six mille litres ñeneen ñi nga xamante ni yu ndaw ndawaa
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_144.wav
waaw ci li nga xamante ni moom mooy concurrence bi ba yowit doo mën a perte dana li nga xamante ni say wàllu clients là wala jëm ci wàllu li ngay jaay
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_100.wav
waaye moom ay chers ba léegi xamul chiffre bi nga xamante ni bu taxaw la ci jëndkat yooyu maanaam munu leen xayma waaye
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_182.wav
li nga xam ne nii ay wudjëm war nañ ko mën a am ci marché bi da ngay gis ni moom bi mu ko bëggee calier bi mu ko bëggee calculé dafa njëkk xool
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_115.wav
mooy laaju client bi léegi nag joxe bi nag dafay am solo ci yow entrepeneur wala yow mi nga xamante ni yow yaay fas yéene
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_76.wav
gis ni xalaat ji nga ciy am def lay jàppale lool ngir nga gën a ñoŋal li nga xamante ni moom mooy joxe bi nga xamante ni moom ngay joxe
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_150.wav
naka la def ba teg li nga xamante ni moom mooy gëstu jëm ci wàllu wudjëm yooyu waaye tamit ci naka la def ba teg li nga xamante ni moom mooy taay de marché bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_174.wav
mooy cafk gi yenn yi dañu xaw a sauf suukkoor ba mu ëpp yenn ay tamit dañu xaw a am tuuti acid
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_108.wav
waaye tamit bu dee ci mbir yooyu noonu nekk na ji nga xamante ni ñoom ñooy gën a pousser client bi mu jënd te bu jëndee tamit mën na jëndaat ci ci yow
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_139.wav
mais loolu moom mooy beneen bi moom mooy ñu koy muccille li nga xamante ni mooy seen par de marché maanaam ñoom seen taxawaay ci marché bi est ce que nekk nañ ñi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_201.wav
parce que bu ñu xoolee ci marché bi léeg nag ay chèques yi nag ba mu bëggee ginnaaw ba mu defee calcul bi bii ba pare mu daal di jublu ci li nga xamante ni moom mooy production en valeur
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_104.wav
ngir ñu mën a ñëw ci marché boobu noonu di di jënd beneen mbir bi nga xamante ni ay chatamit mi ngi koy gëstu moom mooy client yi ci yan mbir nañuy sukkandiku ngir
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_73.wav
ak tamit ci yan mbir nañuy sukkandiku ngir def seen tànn neef ci li ngay joxe maanaam
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_94.wav
di nga xamante ni ay sébuggoon naka saytu moom mooy ñan ñooy faral ñan ñooy jëndkat di nga xamante ni ñoom ñoo gën a ñoom ñooy gën a faral di jënt
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_87.wav
mais ñun ñi bëgg na ko tontu ci ay gëstu ci ay yeneen xeetu en cate yu mun a radeef bi ci njëkk moom mooy ay chas
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_162.wav
boo xoolee ñoom ak ay shop booñu lu ñuy def waaye ay chet dafa jàpp ni ñoom ay concurrent am nañ bu ñu sukkandikoo ci li nga xamante ni moom mooy
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_157.wav
ak saaf na ak neem a kajo ak mandat bi yow ak zéna ak cinqu juin ak beneen bi nga xamante ni jàppal tur bi donc yooyu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_175.wav
waaye sa moom gis na ni li nga xamante ni moom mooy ingrédients wala yenn mbir yi ñu koy defaree ba su kii concrètes yi nekkul ci lu naturelles
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_95.wav
waaw xam nga xam ne dinaa wala bu mu defee ay gëstu taxaw seetlu moo gis ne ñi nga xam te ne ñoom ñooy gën a faral di jënd moom mooy ay góor
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_141.wav
muy xam yëw it naka ngay defaree sa toogaay wala naka ngay defaree sa duggin ci li nga xamante ni moom mooy marché bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_120.wav
ginnaaw ba nga xane doxalin nañu nga xamante ne ñoom ñooy say wudj donc dina la jàppale nga gën a xam ñoom fi ñu baaxle ak tamit
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_117.wav
mais dafa am solo entrepères entrepères bu ci nekk dafay am solo lool mu maitriser ko ngir gën a mën a ño ngal li nga xamante ni moom lay def
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_74.wav
loolu moo tax kéliaa bi di jëndat liy mbaayle loolu moo tax kéliaa bi di jënd ci kii te jëndul ci kéey yooyu noonu yëpp mu nekk ay xibaar yi nga xamante ni boo ko xamee di nga
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_186.wav
maanaam deux mille vingt ba ñu sayto ba AINSD sayto gis nañu marché bi li fay dugg ci wàllu juillet wala yenn xeetu transformation léegi mi mi ngi toll ci deux millions cinq cent
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_101.wav
am na yaakaar nii toll nañ ci vingt mille ci biir diwaan boobu noonu yëpp ci biir région bi yëpp
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_179.wav
waaye tamit loolu dañuy dañuy dañuy dañuy jaay ndax am na 7 ak sell bi nga xamante ni moom la transformation jus laaj
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_143.wav
waaye tamit di wéy boo ñëwee naka ngay def wala bu ñu la fa fekkee tamit naka ngay def ba ànd ak ñoom ci li nga xamante ni moom mooy jeegante boobu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_170.wav
wóor na xamante ni niveau yi xaw na yaatu ak station wala yenn service yi fa nekk da ngay gis ni foofu litre bi ñu ngi koy jaayee 1500
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_194.wav
ñi nga xamante ne ñoom ñooy concurrent ay chay ba léegi si 2 millions 5 cent vingt litres yooyu noonu bu ñu ko doon xaaj bu ñu ko doon xayma dañuy génne kenn ku ci nekk li nga xamante ne
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_195.wav
moom la produire ñi nga xamante ne ñoom ñooy jaïe takku liggéey ñoom produire nañu toll ci neuf cent vingt cinq mille litres
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_61.wav
waaye xel bu baax dina la jàppale lool nga mën a am dugg dugg bu baax ci li nga xamante ni moom mooy marché bi bi ci njëkk moom mooy nga saytu doxalinu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_70.wav
jaay bi est ce que ñoom dañu bëgg jaaykat pour yëngu est ce que ñoom dañu bëgg jaaykat bi nga xamante ni daf leen di jaay di leen wis est ce que ñoom dañu bëgg jaaykat ki nga xamante ni dafay jaay lu sell
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_183.wav
parce que marché bi ni mu toll ci yaatuwaay maanaam marché bi yëpp yëpp yëpp ñu mu toll ci yaatuwaay te loolu mu ngi sukkandiku ci ay xibaar yi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_190.wav
ciife bi nga xamante ni ci wàllu xaalis mi ngi dugg ci marché bi doon na ci trois milliards quatre cent deux millions moom mooy njëg bi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_189.wav
donc nga ñëw bu ñu ko nattee nag ci valeur dañuy gis ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_116.wav
ñu ne teg li nga xamante ni moom mooy saafara ñu yëg nit ñaari yooyu noonu dafa nekk ay mbir yi nga xamante ni yu ñu munul daq li la léegi oofu àtt demande joxe àtt laaj
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_127.wav
dañuy def li nga xamante ni lu wute la ak li ngay def waaye ñoom ak yow yéen a bokk saafara bi nga xamante ni moom ngeen di fàj
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_72.wav
ci li nga xamante ni war nga ko jàpp yu lay yombalal li nga xamante ni moom mooy joxe bi ngay joxe moom mooy nga bàyyi xel lool li nga xamante ni moom mooy bëgg-bëgg client yi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_85.wav
yaay lan mooy seen i ay bëgg-bëgg donc loolu nag da ngay gis ni li ñuy wax taxaw seetlu wala étude de marché day daal di am solo lool ci ay chas
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_111.wav
productions am ak tamit naka lay jéemee tënkut ci li nga xamante ni moom mooy bëgg-bëgg client yi secondi coup ci gëstu bi nga xamante ni def na ko
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_151.wav
bi nga xamante ni war na ko am wala ci bëgg na ko am ci marché bi ak tamit yan njëg wala ban taxawaay la war a am ci li nga xamante ni moom mooy marché bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_164.wav
dafa fas yéene sukkur ne ko ci li nga xamante ne moom mooy étude bu mu def jëm ci wàllu concurrent direct yi donc moom moo ji direct ay chas yooyu noonu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_106.wav
ci jëm ci produit nekk na li nga xamante ni moom moo gën a moom le client bi gën a bàyyi xel ci lu muy jënd maanaam client dañuy taamu jënd ci ki nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_107.wav
seet na seetla na ci wàllu produit am que jënd gën a ngi nga xamante ni amul yooyu noonu donc ñu gis ni critères yooyu noonu wala
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_172.wav
waaw laa joon ban gis-gis nañu am ci li nga xamante ni moom lay def ay chars dëgg de la na li nga xamante ni moom mooy moom yëmuy jaay
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_130.wav
naaw ba nga identifier sa yu wudji yooyu lu ñuy def at naka lañ koy defee donc dafay baax lool nga xam ñëw li ñuy joxe maanaam seen i produits ban produits nañ
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_88.wav
marché bi nu muy doxee mu daal di def ay laaj mu gis ni marché bi at bu nekk
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_204.wav
de l' être yi nga xamante ni concurrent bu ci nekk produit na ko daal di koy diviser par cent loolu nag da ngay gis ni moom mooy joxewaat ba léegi deux millions cinq cent vingt litres
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_137.wav
ju day baax lool nga xam ñoom njëkk yi nga xamante ne moom nañu jaayee xam seen njëkk dafay tax yowit nga mën a teg sa njëg njëg bi nga xamante ne
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_75.wav
mën a wàjal sa bopp ba yowit lépp lu yu méngóo bëgg-bëgg kii li yaabi di nga ci mën a di nga ci mën a taxaw
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_98.wav
dage yi nga xamante ni nekk na ci yenn produits industriels yi nga xamante ni mën na gàllankoor sa huérge yaram donc ñoom dañuy taamu jënd ci
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_132.wav
donc loolu yëpp say wudj bëleegi li ñuy def ak yow ni nga koy ni nga koy defee est ce que am na différence
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_156.wav
pour que dinañ am dinañ maanaam ñoom ak ay chas ñoo bokk li ñuy def bi ci njëkk di GIE takk liggéey beneen bi di entreprise Kumba beneen bi di mariaire distribution
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_58.wav
def wala li nga xamante ni moom ngay joxe donc ñu gis ni loolu lu am solo la lool boo ci bëggee xuus nga maitriser li nga xamante ni moom mooy
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_136.wav
mën te ni boo ko xamee daf lay jàpp le lool ngir sa joxe gën a mën a nekk joxe bu am solo beneen bu am solo tabine nga war a ko bàyyi xel
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_78.wav
mais loolu day dugg tamit ci wàllu fasal wàllu taaral ba client bi bu ko jotee dina ci am li nga xamante ni moom mooy contentement
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_114.wav
muy kër la ñuy xër bi moom mooy li nga xamante ne moom nañuy laaj maanaan client bi lu muy laaj moom
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_158.wav
ñoom nekk nañ ci marché bii nga xamante ni moom la ay sénekk waaye ñoom bokk li nga xamante ni moom li ñu la ñuy def
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_188.wav
marché bi te loolu boo xoolee moom mooy ñi nga xamante ne ñooy concurrent ay chay wala wudj ay chay ñoom nañuy faral di indi ci marché bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_119.wav
fu yu nga xamante ni yu direct la wala yu ànd direct naka la ñuy def wala naka nga mën a comprendre réimit ñoom seen i ay offres ak tamit ñoom seen i doxalin
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_163.wav
seen i taxawaay seen i duwale ak seen i jëmm ci li nga xamante ni moom mooy entreprise bi ici marché bi ay chat dafa
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_60.wav
ñu gis ñi lay soonju nga gën a concentré wu ci ñetti ponñi nga xamante ni yu am solo la ñu gis ni ponñ yooyu noonu boo ci
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_89.wav
at bu nekk lu toll ci fukka ak juróomi GIE wala yeneen xeetu kuréel gën a ñëw ci marché bi ñuy yëngu ci wàllu transformation fii
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_97.wav
dañ leen soñu ci lépp li nga xamante ni yenn yenn mbontee yi nga xamante ni wala yenn méfey wala yenn
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_131.wav
donc loolu tamit daf lay jàppale loolu beneen biir wala beneen laaj bi nga xamante ne dina am solo jëm ci wàllu oofu lu ba léegi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_129.wav
waaye yéen a bokk li nga xamante ni moom mooy jëmwaaye jëmwaaye moom mooy fexe ba fàcxeef beneen question bi nga xamante ni dafay am solo moom mooy ginna
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_205.wav
te yooyu noonu nekk ci marché bi bu ñu ñëwee ci missile bu ndaw ci li nga xamante ni moom mooy GIE takkul liggéey ñoom production avaleur bi nga xamante ni moom la ñuy def
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_181.wav
parce que ñu ngi lay gën a taw ci ay ay dinañ ko faral di bëgg
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_173.wav
ñi nga xamante ne lu ñu mën a nangu la léegi nag wute bi moom mooy moom maa ngay wujëm moom mooy ci li nga xamante ni moom mooy góob yi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_155.wav
donc ñu koy defee seen i ay loxo wala yeneen matériels yi nga xam amante ni bëriwul donc mu daal di génnee juróom-ñetti kuréel yi nga xamante ni ñoom ay comptes
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_102.wav
ndax ay gëstu moom mooy lan mooy comportement client yi bu mu taxawee seetlu gis nañ ni clients yu bëri dañuy faral di jënd ñetti yoon ci semaine
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_149.wav
marché ngir mu gën a leer si yow dama lay indil ba léegi suñu xarit ay chat moom mu wan ñu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_192.wav
bi naaw bañ ko multiplier ak li nga xamante ne moom mooy 1 350 di njëgul huitre ci marché bi donc loolu moom moo lay jox li nga xamante ne moom mooy njëg boobu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_153.wav
donc ginnaaw bu mu defee loolu am na nag ay xibaadi nga xamante ni moom la ñuy partagé ay chaque gis nañu ñi nga xamante ni ñoom ñooy ay concurrent direct am maanaam
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_159.wav
am na sax si ñoom ñi nga xamante ni ñoom ak ay chabu bu ñu roowu ñu produit yi ñëpp
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_145.wav
mën nga jëm ci mën nga dem ci wàllu ay calcul
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_203.wav
te lu ñuy multiplier ci njëkk bi nga xamante ni moom moo gën a néew te loolu nag ngir mu génnee ko ci pourcentage
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_185.wav
ci wala yëpp yi jëm ci wàllu léegi mu mu ngi toll ci deux millions cinq cent mille cinq cent vingt mille litres ci année deux mille vingt
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_113.wav
ñu ngi xamante ni moom mooy demande bi dañuy ñëw ci li nga xamante ni moom mooy off offre bi mooy li nga xamante ni moom la ñuy joxe
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_161.wav
industielle bi suñu mel ni groupe kii ren wala yeneen xeetu kuréel yu mel noonu ñoom dañuy joxe ay li nga xamante ni mooy production yenn boobu sauma gazés yi ñoom tamit
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_82.wav
léegi nag mu jël dogal nii moom day gën a yaatal marché bi day gën a xool naka lay jaayee li nga xamante ni moom mooy jaay bu yaay
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_148.wav
wala kenn ku ci nekk li ma war a mën a proposé lu ma war a mën a joxe ci marché bi donc loolu tamit da ngay gis ni dafa lay jàppale loolu ngir nga gën a mën a saytu li nga xamante ni moom mooy par demar
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_171.wav
mais bu ñu tester maanaam essayer li nga xamante ni moom mooy yooyu am tamit li nga xamante ni moom mooy retour client yi ñu wax ko
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_91.wav
maanaam ci année bi lu toll ci cent quatre vingt mille litres de juin wala ak neuf kilo de confiture day daal di ñëwaat ci marché bi day daal
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_128.wav
ñu ngi bëgg yëngu ci li nga xamante ni moom mooy fàjum xif ñoom dañuy joxe lekk bi yëgg ngay joxe lekk bi doon tënni lekk yi ngay di joxe mun na wute ñoom ñu ngay di jox mun na wute
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_180.wav
waaw dafa ko jàppale loolu moom ay chen ngir mu gën a mën a sukkandiku ci loolu di sell ak caf ko bu neex
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_23_le_march__segment_202.wav
waaw daa yi nga xamante ni ñoom la jot a am donc loolu li koy tax mu génnee ko moom mooy day jër njëg bi nga xamante ni moom lay litre bi di jar
Not supported with pagination yet