audio
stringlengths
56
98
transcription
stringlengths
26
222
audio_file
audioduration (s)
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_37_Developper_ses_ventes_segment_20.wav
parce que bu ñu xoolee ñaar la ñu xoolee ñoom ñooy ay xaritam ñoom ñooy ay njëge ñaalam léegi dafay jaay engrais
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_37_Developper_ses_ventes_segment_9.wav
bu yoon bi nga xamante ni yaa ngi koy def ngir fasal wala ngir weel li ngay def mooy canode distribution wala canode communication
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_37_Developper_ses_ventes_segment_17.wav
léegi yoon bi nga xamante ni moom la fas yéene jaar bu bees bi moom mooy day wut ñeenti partenaires yi nga xamante ni dañuy daañu jot
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_37_Developper_ses_ventes_segment_21.wav
waaw ñu ko jaayee mille deux cent maanaam moom boo xoolee ci cinquante lignes dañuy dina ci gën a quinze mille
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_37_Developper_ses_ventes_segment_2.wav
parce que ñoom ñoo xam ne ñoom ñoo xam ne ñoom ñoo jaayal ñi di destribiteur yooyu nag dañu war a nekk nit ji nga xamante ni pare nañ
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Carte_37_Developper_ses_ventes_segment_19.wav
dina leen jox chaque semaine cinquante litres
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_2.wav
parce que ñu ngi lay jëndee li mu mooy ci école bi semaine bi da ngay gis ni juró juróom yi bësi yëpp dafay nekk ci li nga xamante ni moom mooy faculté day nekk fi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_1.wav
ñu ngi lay xam ne dafay jàngi école waaye am na temps bi nga xamante ni moom la jël ngir sëgg ci li nga xamante ni moom mooy projet bi moom ay chenaux boo xoolee
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_9.wav
te dinaa gis ni dinaa rotewaat yeneen événements yi ñëw pour
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_10.wav
mais loolu famille bi te métinamul lool lool lool léegi ni que ah mën de comprendre naa la yaa ngi door a tàmbali li nga xamante ni moom mooy sa entreprise te amoo ko benn taxawaay
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_0.wav
ñu dugg ak génn ci suñu deuxième partie bii chapitre de ñu nar a waxtaanee lépp li nga xamante ni aajo woon a ci weyal ak
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_3.wav
loolu lay jàngee waaye ñaari ba si moom da koy concentré wu ci li nga xamante ni moom mooy entreprise bi te concentration boobu noonu yëpp boo xoolee ci ngon si lay ëpp lu mu koy def
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_4.wav
lu organisation boobu noonu am solo da ngay gis ni am na benn jafe-jafe bu seew bu ci am moom moom ay chers dafa xaw a jegee fa même
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_13.wav
ah ñu ngi lay defar nañ laa koy defee ah élaage ñu ko ah mais yow yooyu amoon nga benn yoon bi nga xamante ni moom ngay faral di jaar sa ginnaaw ba sa création
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_16.wav
ndax dina ma jàppale loolu ngir nga ma gën a mën a seet saytu sama taa ak ma gën a mën a lëkkalew ak li nga xamante ni moom mooy famille bi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_5.wav
te fan yii fan am ñu ngi koy wax ni ko gisuñu ko ci lu bëree rawatina xew xew yi nga xamante ne jot na fi am yu ci meenn anniversaire wu jarbaa
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_17.wav
loolu di dem la ci quoi say nga def ay gëstu gëstu yooyu ngay def ci wàllu naka la ñuy def ba gën a mën a gérer sa taa mën nga waxool ci internet wala
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_8.wav
donc ñoom ñoo xam ne ñoom ñoo xam ne ñu ngi koy defee ni ko éleger man de fàtt naa la wax
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_12.wav
diggante jàng bi ak famille bi ak li nga xamante ni moom mooy sa projet ajon yi ko waaw ah loolu li nga wax de dëgg la bàyyi naa ko xel bu baax
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_7.wav
mi ngi koy métti nag mi ngi koy jàmbat fu mu toll te Mouda di dem li nga xamante ni waxtaan na ci ak xaar itam ak frais am di éleage moom achet boo mu ñëwee
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_0.wav
ay chabbali mi ngi continuer di nga xamante ni moom mooy jàngam waaye mi ngi koy booleg lii di projet
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_11.wav
te bu dul loolu tamit sa jàng mu ngi nii def lay jëlal temps bu bëree loolu nag dafay aajoo nga def li nga xamante ni moom mooy tollale
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Cas_Aicha_segment_15.wav
saytu ko ci wàllu temps ngir mu mën a jàppale la nga gën a mën a xool say effort naka nga mën nga koy mën a tasee à ce daal ñu ko ah loolu day am na solo élage
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_1.wav
parce que bu ñu xamante ni moom mooy sa entreprise subaab di ko wax lancement ak formalisation ci jëm ci sa wàllu entreprise ñu gis ni nekk na partie bi nga xamante ni bu am
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_3.wav
bii ñuy dugg moom moo lay jàppale nga juggee ci lépp li nga xamante ne xalaat la maanaam sa idée dootul nekkati li nga xamante ne moom mooy xalaat kese waaye dafay jëm ci lépp li nga xamante ne jëf la
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_9.wav
muy nga xam ne dañuy am nag mu tàggatoo ci bu baax a baax a baax a baax ngir liggéey boobu gën a ñoom ngir li nga xamante ni moom mooy bëgg-bëgg bi du ko ndax benn yoon
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_4.wav
waaw ngir nag nga àgg foofu bëri na ay mbir yi nga xamante ni yu am solo la yi nga xamante ni war nga ko bàyyi xel war nga ci tàggatu ngir àgg fi nga xamante ni moom mooy fi nga
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_2.wav
parce que loolu loolu ci bëpp entrepreneur ndax yow mi nga xamante ni yaay entrepreneur bëgg tukki sa tukki entrepreneur yàlla da ngay gis ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_11.wav
ñu ngi xam ne moom moom la ñu soxla pour nga créer wala nga saytu wala nga doxalal li nga xamante ni moom mooy sa entreprise
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_14.wav
li nga xamante ni moom la ñuy wax jaayante tubaab di ko wax ay sacrifices sacrifice yooyu nag muy def moom moo koy mën a jàppalee ngir mu ag fi nga xamante ni foofu la seen tu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_7.wav
parce que loolu moom mooy lancement boobu ak formalisation boobu ndax kat loolu nekk na mbir bi nga xamante ni bu am solo la comme ni ñu la ko waxee
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_15.wav
sacré fii si yooyu noonu dafay laaj yi si njëkk moom mooy tàggat tàggat bi nga xam te ni war nga ko tàggat sa bopp paa bi nga xamante ni war nga xam na nga koy géré ak tamit xarante yi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_5.wav
seentu donc loolu nag moom nañ lay indil fii nii ci waxtaan bu yaatu ngir nga gën a mën a saytu lépp li nga xamante ni aajëwoon a ci mbir yooyu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_13.wav
bu ba léegi di passion da ngay gis ni ngir entrepreneur bi mën ci génn mën a weyal li nga xamante ni moom mooy liggéeyam ba gën a ci koom dafay aajoo mu def
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_10.wav
ñun ñun ñoo xamante ni ñun ñun xel ñaar wala li nga xamante ni mën na faa gaagal lépp loolu di nga xamante ni moom moo koy may kom-kom
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_6.wav
ñu ngiir mu gën a leer sa bopp nag ñu ngi lay ñaan nga teewluñu bu baax bu ko defee dinañ dugg ak yow ci lépp li nga xamante ni xóotaay la lépp li nga xamante ni bancaesse sa ci wàllu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Chapitre_2_lancement_et_formalisation_introduction_segment_16.wav
waaw loolu moom mooy dinañ la ñuy xamante ni wànga ko wut ba ci décision yi nga xamante ni moom nga war a jël ngir soppi sa bëgg-bëgg boobu mu nekk li nga xamante ni moom mooy
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_5.wav
ngir wéyel li nga xamante ne moom mooy doxalinu projet bi li nga xamante ne nag moom mooy récritement bëre na ay façon yi nga xamante ni moom moo ci am
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_3.wav
ñir ñu ànd ak ñoom seen projet gën a mun a dox wala ñu gën a mun a yokk li nga xamante ni moom mooy seen i xalaatu projet
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_6.wav
bi ci njëkk moom mooy collaboration collaboration nag boo ko déggee mooy lëkkale moom mooy nga jël kenn ki nga xamante ne collaborateur mi koy woowee
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_7.wav
moom dafay am taxawaayu jàppale la dafay am taxawaayu dendal moom daf lay gunge ci lépp li nga xamante ni danga koy def
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_8.wav
parce que dafa am nañu dafa am nañu dafa jëm si wàllu entre pays waaye dafa nekk yi nga xamante ni tamit da nga koy fay
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_10.wav
wala lu mbalala lu mu renforcé la wala mu gunge la ci lépp li nga xamante ni wàllu délégation la wala yenn wàllu liggéeyu yu simple yooyu lay lay nekk
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_0.wav
beneen bi si topp moom mooy récrûlement li nga xamante ni moom mooy récrûlement moom it nekk na mbir jumtukaay bi nga xamante ni dañ koy faral dii
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_1.wav
utiliser ngir yokk li nga xamante ni moom mooy xarante jëm ci wàllu entreprise ndax quatre récritement moom mooy jël kenn wala ñenn ñi nga xamante ni dañ lay jàppale
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_2.wav
parce que dinañ gër sa liggéey gën a mun a dox
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_9.wav
mais moom mooy jël kenn ki nga xamante ne moom am na ay compétence ci domaine activité bi nga xamante ne moom nga nekk
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Le_recrutement_segment_4.wav
bu baax moom mooy ay nit yi nga xamante ni dañoo bokk gëm-gëm dañoo bokk gis-gis te dañuy am ay xarante yi nga xamante ni yu am solo lool
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_24.wav
donc yaaka dañ ko war a def loolu munul bañ a def la loolu moom mooy priorité ñu gis ni nag ñàkk def priorité maanaam boo amee activités yu bëri teg
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_27.wav
kon li ñu ngi leen li ngeen li ngeen gàpp ni yii munul xaar nga daal di koy bind fenn da ngay gis saañ nga xamante ni dañ koy bind en rouge wala ñu koy bind suñuñeekoo pour wane ni yii kat dafa am solo loolu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_3.wav
waaw dañu ne liggéeya yëpp dañu ne liggéeya yëpp dañu ne liggéeya yëpp dañu ne liggéeya
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_29.wav
loolu nag ji li nga xamante ne moom mooy génnee say priorité daf lay jàppale lool ba yow mi entrepreneur doot dugg ci lépp lenn li nga xamante ne
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_12.wav
yow mii entrepeneur di nga gis ni da lay jàppale lool ci wàllu saytu sotaa waaye tamit ci wàllu ñoŋal li nga xamante ni moom mooy lépp li jëm ci sa liggéey
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_25.wav
fa solo yenn ñoo ci gën a nekk yi nga xamante ne yu prioritaires la defandoo lépp def lay indil ay gàllankoor ndax mën nga mën a bañ a mëntandoo ñàkk defandoo lépp tamit daf lay indil gàllankoor yëpp
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_23.wav
mais loolu mooy li nga xamante ne moom mooy say priorité priorité nag boo ko déggee moom mooy li nga xamante ne lu munul xaar na
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_8.wav
jërëjëf bëri na entreprenariat yi nga xamante ni ñenn ñi daal ne gàllankoor ci ni ñu koy utiliser nu mu baaxle waaye ñenn ñu mi ngi leen di jàppale ci utilisation bu baax di nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_30.wav
da lay yàqal sa temps wala doo nekk leneen li nga xamante ni da lay yóbbul li nga xamante ni moom mooy sa temps ñu gis ni moom it nekk na benn jumtukaay bi nga xamante ni am na solo lool
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_40.wav
bi ci njëkk moom mooy dalay sonal waaye tamit day tax ni lépp lu war a egg du egg mën nga nag jox ñeneen ñu def waaye nga koy supervisé di xool am ci
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_1.wav
waaye mbir yi nga xamante ni yu mat a bàyyi xel la ngirum mu yombalal li nga xamante ni moom mooy tukki woowee comme ni ñu la ko waxee nag dinañ la indil fii ay
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_19.wav
ñu ngi gis bi objectif yi nga xamoon moom nga ay objectifs yi nga xam ne moom nga amoon ci semaine bi wala objectif yi nga xamante ne moom nga amoon ci weer bi ñu gis ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_28.wav
loolu boo ko defee da ngay gis ni daf lay jàppale loolu ngir nga mën a concentré wu ci loolu ak àpp bi nga xamante ni moom nga ko àpp
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_22.wav
parce que ñun ñu ngi ko planifier ci li nga xamante ne moom mooy sa calendrier beneen bi moom mooy nga définir li nga xamante ne moom mooy say priorité maanaam
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_31.wav
te entretenir yu bëri ñun ci tàggatu ngir xam yan ñooy seen priorité yan mbir nañu war a def léegi yan mbir moom war a xaar ak yan mbir yeneen yi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_15.wav
ñu ngi lay xamante ne entrependate bi nas na ko def mu am fu mu ko bind fu mu ko bind du yem ci loolu naka wutal bës naka wutal heure bu muy tàmbali
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_9.wav
ñu ngi koy def ndax taa boobu noonu moom moo lay wàññi yow sa projet bi ñaata taa wala ñaata waxtu nga ci mën a concentré wu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_32.wav
mën nañ ko bàyyi beneen bi nga xamante ni moom moo ci topp moom mooy nga nga yi nga yi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_5.wav
donc bu bu jefe laaj li nga xamante ni moom mooy téye ba ña yaakaam ti donc nag ki nga xamante ni mi ngi tukk ci tukki bi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_4.wav
ñu ngi xamante ni moom mooy rendement wala comme comme comme comme ni ñu ko xamee li nga xamante ni moom mooy entreprenariat dafa nekk benn tukki bu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_11.wav
waaw ñu ngi lay def nii entrepeneur ngir nga gën a mën a xam naka ngay mën a saytoo loolu ci waxtaan bi nag dinaa la baaxee ñaari mbir yi nga xamante ni yu am solo la boo koy faral di def
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_7.wav
dafa war a nekk yi nga xamante ni dafay bàyyi xel taalu bëri parce que lépp am ci taaloy tënk taanaak mu nekk mbir bi nga xamante ni bëri na entreprenariat
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_17.wav
leen di jàppale ci xeet yooyu yee yu ci mel ni ay googol agenda yu ci mel ni ay team su wala yeneen mbir yi nga xamante ni yu am solo lool ngir ñu mën a
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_38.wav
dina xam nag ko la koy defee loolu nag dafay ànd ak li nga xamante ni moom mooy planification yow yaay def lii kii bës bi nga ko koy def wala heure sangam ba koy def
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_0.wav
waaw comme ni ñu la ko waxee li nga xamante ni moom mooy tukki entrepreneur dafa bëri ay mbir yi nga xamante ni yu am solo la
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_21.wav
li nga xamante ni moom mooy say activité activité bu ci nekk nag boo koy organiser da nga koy organiser en fonction de ni nga ko planifier ci li nga xamante ni moom mooy sa tableau
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_10.wav
mais loolu nag dinañ ko ci projet bi est ce que jaral na la bàyyi leneen nekk ci projet bi donc yooyu noonu yëpp mu nekk ay mbir yi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_37.wav
yow daf yaay def lii yow yaay def le kii moom mooy def lële ñu gis ñi loolu boo koy def dina la jàppal lool ndax da ngay gis kenn ku ci nekk dina am ci du mu concentré wu
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_35.wav
donc loolu nag dafa defandu lépp nag daf lay indil ay gàllankoor yu ci mel ni liggéey bi du maté liggéey bi du àgg donc loolu nag daf ciy baax ngay def li nga xamante ni moom mooy
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_2.wav
mbér yi nga xamante ni boo koy faral di def da ngay gis ñu dina la jàppale loolu nga gën a mën a saytu sa liggéey yoonal ko ba pare
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_6.wav
di akam ti kooku dina am solo lool ci moom mu faytu lépp li nga xamante ni wàllu taalay doon comme ni ñu koy faral di déggee entrepeneur
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_18.wav
def li nga xamante ni moom mooy seen planification ndax carte planification boobu ngay def moom moo lay jàppale ngir nga gën a mën a egg ci say objectifs yi nga xamante ni moom nga amoon ci bës
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_26.wav
mën na tardé donc loolu nag moo tax yow mii entrepeneur liggéen ci yow baax ci sa projet moom mooy liggéey bu ci nekk nga saytu liggéey yëpp génnee yéen
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_20.wav
parise bu ci nekk dafay soxla am ay objectifs ci waxtu wu ne planification boobu ngay def nag moom moo lay jàppale ci fan la boobu moom moo lay jàppale ci li nga xamante ni mooy organiser
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_14.wav
parce que bu ñu xoolee ñu koy appal appal boobu nag bu ñu koy wax mën nga ko def ci wàllu calendrier mën nga ko def sa tableau mën nga ko def sa téléphone wala mën nga ko def feneen fu mu mën a doon
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_39.wav
te moom bu paree rek day ñëw ñi pare na keneen ak keneen noonu waaye bu fekkee ni tam moo di c' est de liggéey bi nga bëgg a def lépp da ngay gis ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_13.wav
bi ci njëkk moom mooy ngay planifié ak di organiser li nga xamante ni moom mooy say activité planifiée boo ko déggee nag mooy appal
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_24.wav
wut nag ki nga xamante ni moom moo lay tàggat ci benn tomb wala ay tombu yu bëri nekk na lu am solo lool te entreprenariat bu ci nekk
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_19.wav
waaw di def da ngay gis ni dañ fay weyel di fësal lépp li nga xamante ni ay xibaar la wala lépp li nga xamante ni xeetu xam-xam la ci domaine woowi nga xamante ni moom nañ leen
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_5.wav
gën a mën a ñoom bi ci njëkk moom mooy auto formation auto formation boo ko déggee moom mooy former sa bopp tàggat sa bopp loolu di auto formation entrepreneur yu bëri dañ
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_0.wav
ñu ñëw ak yow ci waxtaan wi nar a waxtaanee ak lépp li nga xamante ni yokk say xarañ te la ci wàllu entrepénariat ñu gis ne
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_17.wav
waaye bu dee taw wala formation mun na yi nga xam te ni dañ koy def du laaj téewaay waaye nit ki du koy def jaarale ko ci téléphone wala mu jaarale ko ci ordinateur feneen fi nga xam te ne dina mën a
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_22.wav
mën nga ci tàggatu jaarele ko ci formation yooyu da ngay gis ni daf lay jàppale lool formation yooyu ba léegi ñuy leeral am na yi si nga xamante ni dafay laaj fay am na yi nga xamante ne
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_11.wav
yulay mën a jàppale donc ñaari mbir yooyu jàpp ko bu baax bi ci njëkk moom mooy ngay def ay recherche beneen njëkk bi moom mooy ngay beneen bi ci topp moom mooy ngay roy ñi nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_23.wav
parce que tamit du laaj fay buñ juge ci formation yooyu am na yeneen yi nga xam te ni moom la ñuy wax koo ci koo ci nag ci wala moom mooy gunge wala tàggat
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_48.wav
ñu ngi lay jàppale lu bopp du am temps pour def leen wala leen li nga xamante ni yow mën na la jàppale lu bokkul ak projet bi ñu gis ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_21.wav
waaw mooy sa doxalinu projet moo xam ci wàllu comme tàbbilite la wala ci yeneen finance wala ci communication yooyu yëpp yow mi boot sa projet
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_51.wav
lu lay wéyeel ñu ngir sa projet dox la waaye bu fekkee da nga nii yow projet bi wala sa projet nga bëgg a jox saa pour sa sa table yëpp dañuy gis
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_16.wav
li nga xam ne dañuy gis ñaari ay formations ay cotxin benn bu ci nekk dina ci ñëw bu ñu ñëwee ci formation dañuy gis ni ñaari type formation moom moo am
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_7.wav
ñu ngi lay tax seen projet gën a mën a jëm ca kanam bi ci njëkk ñu koy faral di def moom mooy ngay def ay recherche ndax dangay gis ni lii di xarale yu bees yi
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales__segment_6.wav
mën nañu koy def mu nekk ay mbir mu nekk mbir bi nga xamante ni bu leen di jàppale la ci wàllu yokk seen xam-xam ci wàllu yokk seen xarante wala lépp li nga xamante ni
Not supported with pagination yet
/content/drive/MyDrive/segments1/Les_Pr_requis_de_la_phase_segment_53.wav
parce que ñi ngi leen di def ñi ngi leen di def ñi ngi leen di def ñi ngi leen di def ñi ngi leen di def ñi ngi leen di def ñi ngi leen di def ñi ngi leen di def
Not supported with pagination yet