start_time
float64 0
2.73M
| end_time
float64 326
2.78M
| speaker_id
stringclasses 55
values | text
stringlengths 1
4.06k
| utterance_pitch_mean
float32 38.3
473
| utterance_pitch_std
float32 0
282
| snr
float64 -3.78
64.6
⌀ | c50
float64 -6.34
60
⌀ | speaking_rate
stringclasses 7
values | phonemes
stringlengths 0
1.77k
| stoi
float64 0.24
1
| si-sdr
float64 -18.8
28.1
| pesq
float64 1.08
4.37
| noise
stringclasses 7
values | reverberation
stringclasses 5
values | speech_monotony
stringclasses 5
values | sdr_noise
stringclasses 6
values | pesq_speech_quality
stringclasses 6
values |
---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|
1,464,402 | 1,487,096 | 11spk1 | ci li nga xam ne mun nañ cee dikkaat mooy ci fiñ toll nii li nga xam ne taxawaay bu mu laaj mooy da nga gis li may wax ne dañuy jël %e gub yi di ko weer ci kër yi boo xoolee léeg da ngay gis ñu koy def ci dañuy teg nii imperméable di ko lifin comme li mu wax noonu di moytu taw yi nga xam ne ñoo cit topp | 117.457268 | 37.389629 | 13.994169 | 8.386164 | slowly | li ni mʌn toʊl li ni mu dɑ li meɪ wæks ni %i ji di koʊ ji bu dɑ di koʊ li mu wæks di ji ni siaɪti tɑp | 0.886308 | 9.441946 | 1.505327 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,495,332 | 1,498,206 | 11spk1 | loolu aussi ñu bàyyi ci xel daanaka dañ koy def sax waaye ñu gën cee bàyyi xel | 136.359512 | 40.56604 | 12.728424 | 7.207285 | slowly | sæks | 0.855348 | 8.019621 | 1.42904 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,498,206 | 1,498,661 | 11spk2 | %hum %hum | 181.734665 | 11.666653 | 0.043148 | 10.201447 | fast | %hʌm %hʌm | 0.723111 | 1.489259 | 1.248434 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,498,661 | 1,538,606 | 11spk1 | et su ko defee ñu koy bañ ko bàyyee gone yi rekk et ñu lijjantil ko seen bopp su ko defee balaa ñuy tëdd ñu daal di koy muur ak comme ni ñu ko faral di defee mu lifin su ko defee bu bëccëgee fu fu mu xiinee ñu muuraat bul di dem ci nag ci bu dee gerte gi la ci dakase yeeg yooyu comme ni mu ko waxee et comme mu ngi ci naaj bi foofa xëy na mën na bañ a am jafe-jafe même bu fekkee ni sax taw yi fekk na ko fa comme danañ ko bàyyi lu yàgg foofu ci naaj bi waaye buñu fàtte di ko wëlbati ñu si bëri dañuy tayal nag xam nga léeg-léeg suñ ko bëggee dañuy wax gone yi te gone yi boo leen yónnee rekk ba leen yenn saa yi lu ci bëri duñ ko def parce que niñ ko bàyyee noonu comme li ma wax noonu bu ci tawee noonu day xuural waaye boo ko wëlbatee xëy na mën naa mën na mën na mën na di ko wëlbati wëlbati bi moo ci am solo | 128.959091 | 34.040901 | 15.393964 | 5.538523 | slightly slowly | ɛt su koʊ dɛfi koʊ ɡɔn ji ɛt koʊ sin bɑp su koʊ dɛfi di ni koʊ di dɛfi mu su koʊ dɛfi fu fu mu di næɡ di lɑ ni mu koʊ ɛt mu baɪ nɑ nɑ ʌ æm - ni sæks ji nɑ koʊ koʊ lu baɪ di koʊ si næɡ - koʊ wæks ɡɔn ji ti ɡɔn ji bu lin bieɪ lin ji lu koʊ kju koʊ li mɑ wæks deɪ bu koʊ nɑ nɑ nɑ nɑ di koʊ baɪ mu æm soʊloʊ | 0.815719 | 5.569023 | 1.269577 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,538,606 | 1,539,046 | 11spk2 | %hum %hum | 207.665039 | 15.037465 | -0.020712 | 12.623915 | fast | %hʌm %hʌm | 0.620561 | -2.1675 | 1.293552 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | extremely noisy | very bad speech quality |
1,539,046 | 1,554,678 | 11spk1 | waaye bàyyi dakase bi noonu rekk daanaka baax na waaye amul njëriñ nag di ko wëlbati wëlbati bi moo ci am solo comme wax nañ li tax ñu wëlbati ko li muy jural li muy wàññi ci doomu jangoro bi saabu bi ak ndax pour yëf yi gën a %e wo() maanaam séchage bi ni mu war a wowee gën a baax | 116.803162 | 33.966896 | 11.470505 | 9.560925 | slightly slowly | baɪ nɑ næɡ di koʊ baɪ mu æm soʊloʊ wæks li tæks koʊ li li baɪ baɪ pɔɹ ji ʌ %i woʊ() baɪ ni mu wɔɹ ʌ ʌ | 0.847378 | 6.4576 | 1.431726 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,554,678 | 1,555,118 | 11spk2 | %hum %hum | 74.576843 | 44.547363 | 0.157804 | 2.559843 | fast | %hʌm %hʌm | 0.541489 | -4.978187 | 1.21034 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | extremely noisy | very bad speech quality |
1,555,118 | 1,575,742 | 11spk1 | donc nañ koy wëlbati dana kii dana ci am solo li ci des it mu ne ah ma ne ko %e yeneen %e comme li mu wax noonu mbayum dër mi day day dugg waaw day dugg moom it day dugg day %e àndaale am na ñu koy def ci biir nawet bi waaye bu ñuy génn nawet bi it boo xoolee ñi gën a jublu ci mbayum dër mi mu doon lu baax it ndax lépp yokkute lay doon rekk ci baykat bi | 121.256607 | 35.465504 | 13.030903 | 11.73735 | slightly slowly | deɪnʌ deɪnʌ æm soʊloʊ li dɛs ɪt mu ni ɑ mɑ ni koʊ %i %i li mu wæks mi deɪ deɪ deɪ ɪt deɪ deɪ %i æm nɑ baɪ baɪ ɪt bu ʌ mi mu lu ɪt leɪ baɪ | 0.83203 | 8.768329 | 1.344108 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,580,034 | 1,580,542 | 11spk2 | am na solo | 140.391144 | 75.59536 | null | null | very fast | æm nɑ soʊloʊ | 0.445299 | -11.543942 | 1.158342 | very clean | very close-sounding | expressive and animated | extremely noisy | very bad speech quality |
1,580,542 | 1,598,347 | 11spk1 | kon lépp %e li ci li ci foofu xam naa ne li ci bëri it %e jot nañ ko waxtaane ci %e donc faram-fàccee ci waxtaan yi et ñaan li ci jógee ci nawet bi ñu muurloo ko rekk et te moytu nag yàq yi xam nga ñun nag Yàlla dafa ñoo nattoo Maodo et | 113.181953 | 31.76959 | 11.558146 | 7.236129 | slowly | kɑn %i li li ni li ɪt %i dʒɑt koʊ %i - ji ɛt li baɪ koʊ ɛt ti næɡ ji næɡ ɛt | 0.765988 | 3.172911 | 1.169339 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,598,347 | 1,598,784 | 11spk3 | %hum %hum | 43.839966 | 0.080152 | 2.206685 | 5.648597 | fast | %hʌm %hʌm | 0.573297 | -4.12113 | 1.195815 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | extremely noisy | very bad speech quality |
1,598,784 | 1,609,888 | 11spk1 | gars yi ñeme nañ lool bay waaye nag bu ñu génnee asaka ba noppi la ca des léeg-léeg sax mag ñi dañ doon def %e dugub ji boo ko teelee bojj def ko ay saako teg lu ko fay jëlee day yomb | 116.736 | 34.56543 | 11.255889 | 8.491702 | slightly slowly | ɡɑɹz ji beɪ næɡ bieɪ lɑ kʌ dɛs - sæks mæɡ %i dʒi bu koʊ koʊ eɪ lu koʊ feɪ deɪ | 0.834619 | 6.831493 | 1.322195 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,609,888 | 1,610,399 | 11spk2 | %hum %hum | 120.95047 | 34.332748 | 0.182793 | 6.780421 | slightly fast | %hʌm %hʌm | 0.723588 | 3.225639 | 1.201127 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,610,399 | 1,619,432 | 11spk1 | li tax mag ñi def sàq nañ ko xoolaat sàq bi sauvegarder la pour sécuriser la stratégie la de mag ñi mag ñi du ñu def dara ngir dara ci xam-xam la ñuy dox | 128.862305 | 44.670422 | 14.232773 | 4.825019 | slightly slowly | li tæks mæɡ koʊ baɪ lɑ pɔɹ lɑ lɑ di mæɡ mæɡ du dæɹʌ dæɹʌ - lɑ | 0.880133 | 7.532646 | 1.402375 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | very noisy | very bad speech quality |
1,619,432 | 1,619,884 | 11spk2 | %hum %hum | 142.240723 | 59.334393 | 5.381726 | 5.545515 | fast | %hʌm %hʌm | 0.674583 | -10.070842 | 1.28587 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | extremely noisy | very bad speech quality |
1,619,884 | 1,630,100 | 11spk1 | gis nga dugub bi boo ko bojjul ci lay gën a gudd fan bàyyi ba soxla bojj waaye boo ko bojjee lépp teg ko cib saaku bu soobee kiy maye la ko fay jëlee dafay yomb | 146.114746 | 22.21916 | 15.42382 | 3.556822 | slightly slowly | baɪ bu koʊ leɪ ʌ fæn bieɪ bu koʊ koʊ meɪ lɑ koʊ feɪ | 0.790391 | 5.023695 | 1.257308 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,630,100 | 1,631,388 | 11spk3 | day yomb trop %hum %hum | 86.731056 | 36.44791 | 9.917549 | 0.073247 | moderate speed | deɪ %hʌm %hʌm | 0.420049 | -7.63276 | 1.175638 | very noisy | very distant-sounding | monotone | extremely noisy | very bad speech quality |
1,631,388 | 1,633,223 | 11spk1 | nañ xoolaat nañ xoolaat loolu | 135.745926 | 22.01885 | 12.517003 | 5.723272 | very slowly | 0.804117 | 6.461801 | 1.234534 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
|
1,633,223 | 1,633,996 | 11spk2 | am na solo | 178.133484 | 10.647139 | 2.135941 | 10.539902 | slightly fast | æm nɑ soʊloʊ | 0.744854 | 1.626896 | 1.121996 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,633,996 | 1,673,942 | 11spk1 | am na solo ndax boo toppee jigéen ñi ñoom li gën a yomb la ñuy def te mag ñi li tax ñu yëg ko mooy stratégie la woon mag ñi dañ doon def ab sàq boo xam ni kenn du ko laal lu moy yegg si wuñu si diggu nawet buñ daan terme **** sàq moom foofu lañ ko doon ubbee kenn ñemewu ko woon laal xëy na nag jamono métti na naam jamono mosut a yomb mag ñi seen jamono it yombutoon de waaye nag dañoo organisé ay organisé ba nga xam ne xam nañ ne fa nga koy soxlaa dëgg mu ne ah ma ne ko nga mun ko nga mun ko faa amee boo bayee daal ba noppi ba génne asaka ba noppi mu ne ah ma ne ko xalaatal jiwu déwén luñ tuddee réserve personnel semence | 136.791687 | 48.312977 | 15.740687 | 4.916644 | slightly slowly | æm nɑ soʊloʊ bu li ʌ lɑ ti mæɡ li tæks koʊ lɑ mæɡ æb bu ni kɛn du koʊ lu mɔɪ si si **** koʊ kɛn koʊ nɑ næɡ nɑ ʌ mæɡ sin ɪt di næɡ eɪ bieɪ ni ni mu ni ɑ mɑ ni koʊ mʌn koʊ mʌn koʊ bu bieɪ bieɪ bieɪ mu ni ɑ mɑ ni koʊ pɜ˞sʌnɛl | 0.804276 | 2.947581 | 1.311204 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | very noisy | very bad speech quality |
1,673,942 | 1,674,547 | 11spk2 | %hum %hum | 155.165665 | 46.481956 | -0.438108 | 7.814734 | moderate speed | %hʌm %hʌm | 0.674533 | -1.738551 | 1.139967 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | extremely noisy | very bad speech quality |
1,674,547 | 1,685,677 | 11spk1 | xalaatuñ jiwu déwén *** jiwu mu ne ah ma ne ko la ca topp nag mooy la ñuy lekk bien que am nga loo xam ne lu yaatoo yaatu ba ñu mën cee jaay li tubaab tuddee surplus | 132.004913 | 46.131657 | 17.117403 | 6.122904 | slightly slowly | *** mu ni ɑ mɑ ni koʊ lɑ kʌ tɑp næɡ lɑ bin kju æm lu ni lu bieɪ li sɜ˞plʌs | 0.863237 | 11.295789 | 1.8705 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | noisy | bad speech quality |
1,685,677 | 1,686,326 | 11spk2 | %hum %hum | 153.459137 | 49.665367 | 1.749598 | 6.718431 | moderate speed | %hʌm %hʌm | 0.528977 | -11.94427 | 1.233173 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | extremely noisy | very bad speech quality |
1,686,326 | 1,695,419 | 11spk1 | waaye daal ab jumtuwaay yu njëkk ya comme ay julit la ñu lu ci bëri da ngay génne asaka soo paree na nga xalaat jiwu ba pour déwén la ca gën a baax | 135.487137 | 40.257278 | 16.781685 | 7.110553 | slowly | æb ju jɑ eɪ lɑ lu dɑ su nɑ bieɪ pɔɹ lɑ kʌ ʌ | 0.900667 | 2.150727 | 1.431254 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,695,419 | 1,695,834 | 11spk2 | %hum %hum | 157.414063 | 40.438335 | -0.252103 | 17.669506 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.506927 | -2.512346 | 1.412105 | very noisy | very distant-sounding | monotone | extremely noisy | very bad speech quality |
1,695,834 | 1,710,978 | 11spk1 | la ca topp la li ci des nag moom mooy lekk gi bu fekkee nag am nga nag lu surplus maanaam loo bay loo xam ne wax dëgg fa Yàlla gannaaw loolu lépp njaay xaj na ca nga yóbbu ci luuma ba jaay faj aajo ndax it et wér-gu-yaram a ngi fi njàng xale yaa ngi fi | 129.450912 | 28.63459 | 15.518595 | 7.230331 | slightly slowly | lɑ kʌ tɑp lɑ li dɛs næɡ næɡ æm næɡ lu sɜ˞plʌs lu beɪ lu ni wæks nɑ kʌ bieɪ ɪt ɛt -ɡu- ʌ faɪ faɪ | 0.832771 | 9.471481 | 1.436996 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,710,978 | 1,711,451 | 11spk2 | %hum %hum | 43.964645 | 0.001664 | 4.548649 | 5.13047 | slightly fast | %hʌm %hʌm | 0.738827 | 4.837954 | 1.167086 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,711,451 | 1,730,652 | 11spk1 | moytu yàq yi ci xew yi gars yi jàmbaar lañ ca tool ba de waaye mën nañoo yàq ci xew yi it de kooku moom nañ ko moytu donte ne sax léegi wax dëgg mbas mi tax na xew yu bëri sax léegi ñu ñu ngi koy ñu ngi ñu ngi koy moytu waaye comme mbas maa ngi jeex damay ragal sama gars ñi delluwaat ca delloo buum ca boy boy ga ca mën a yàq ci xew yi | 131.773605 | 30.051317 | 15.324646 | 6.147878 | slightly slowly | ji ji ɡɑɹz ji kʌ tul bieɪ di ji ɪt di koʊ ni sæks wæks mi tæks nɑ ju sæks sɑmʌ ɡɑɹz kʌ kʌ bɔɪ bɔɪ ɡɑ kʌ ʌ ji | 0.853493 | 7.177789 | 1.4635 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,730,652 | 1,731,093 | 11spk2 | %hum %hum | 191.723434 | 7.409173 | 0.859969 | 18.432421 | fast | %hʌm %hʌm | 0.734485 | 3.502399 | 1.193125 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,731,093 | 1,733,884 | 11spk1 | loolu nañ ko moytu ndax mbay dafa métti waaw | 126.179214 | 8.733759 | 15.675642 | 5.392055 | slowly | koʊ | 0.824797 | 4.638984 | 1.270644 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,733,884 | 1,734,354 | 11spk2 | am na solo | 142.384537 | 54.374592 | -0.571146 | 9.658428 | very fast | æm nɑ soʊloʊ | 0.766791 | -1.525941 | 1.154341 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | extremely noisy | very bad speech quality |
1,734,354 | 1,740,346 | 11spk1 | lu lu lu jar a bàyyi xel la ndax li ngay bay dafa am jubluwaay na nga fexe ba jubluwaay boobu bu ko bu ko wàcc | 140.067917 | 22.61932 | 19.035784 | 3.569685 | slightly slowly | lu lu lu dʒɑɹ ʌ lɑ li beɪ æm nɑ bieɪ koʊ koʊ | 0.749645 | 3.313812 | 1.176943 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,740,346 | 1,741,265 | 11spk2 | am na solo | 49.5145 | 0.262789 | -2.27097 | 27.132282 | moderate speed | æm nɑ soʊloʊ | 0.570049 | -1.377932 | 1.14086 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | extremely noisy | very bad speech quality |
1,741,265 | 1,762,923 | 11spk1 | te jubluwaay lu si njëkk gannaaw * dama koy faral di wax mooy jiwu bi ab baykat ne yàcc rekk di xaar nguur na ma jox jiwu kooku mu ne ah ma ne ko du jëf ju rafet du jëf ju mucc parce que pexey nguur bu sottee fa mu jëm ak yow mu ne ah ma ne ko loolu dina ko mos a wàññi ba mu wàññi ba nga yëg ko mu ne ah dina ko mos a ba xëy ba ndax am na ci loo xam ni mënut a wéy kon teel a fagaru | 154.103683 | 32.720493 | 17.51178 | 5.110953 | slightly slowly | ti lu si * dɑmʌ di wæks baɪ æb ni di nɑ mɑ mu ni ɑ mɑ ni koʊ du dʒu du dʒu kju mu jaʊ mu ni ɑ mɑ ni koʊ dinʌ koʊ mɔs ʌ bieɪ mu bieɪ koʊ mu ni ɑ dinʌ koʊ mɔs ʌ bieɪ bieɪ æm nɑ lu ni ʌ kɑn til ʌ | 0.770815 | 3.539175 | 1.195185 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,762,923 | 1,763,468 | 11spk2 | %hum %hum | 179.017746 | 8.736983 | 6.397348 | 3.597542 | slightly fast | %hʌm %hʌm | 0.75466 | 8.160568 | 1.168301 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,763,468 | 1,766,486 | 11spk1 | baykat day bày() day day ut jiwu | 60.587597 | 15.145718 | 8.058657 | 5.138607 | slightly slowly | deɪ () deɪ deɪ | 0.69031 | 0.846949 | 1.13294 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,766,486 | 1,767,431 | 11spk2 | am na solo | 178.501053 | 0 | 3.104273 | 6.517445 | moderate speed | æm nɑ soʊloʊ | 0.616602 | 0.567155 | 1.147913 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,767,431 | 1,769,063 | 11spk1 | dañ koy wut | 98.689545 | 0 | -0.277282 | 7.728176 | very slowly | 0.416427 | -9.824772 | 1.306859 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | extremely noisy | very bad speech quality |
|
1,770,585 | 1,770,966 | 11spk2 | %hum | 89.444 | 57.448544 | null | null | very fast | %hʌm | 0.568817 | -1.317305 | 1.168852 | very clean | very close-sounding | slightly expressive and animated | extremely noisy | very bad speech quality |
1,770,966 | 1,781,082 | 11spk1 | jógu fi am na ñu koy def ba léegi loolu dañ ko war a saxal na sax waaw loolu lépp lu lu lu lu lu lu lu am solo te gën a yaatal mbay mi donc ni ñu gën a diversifier rekk mu gën a baax | 135.353363 | 42.484062 | 5.584389 | 3.361398 | slightly fast | faɪ æm nɑ bieɪ koʊ wɔɹ ʌ nɑ sæks lu lu lu lu lu lu lu æm soʊloʊ ti ʌ mi ni ʌ mu ʌ | 0.665973 | -2.34016 | 1.138404 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | extremely noisy | very bad speech quality |
1,781,082 | 1,781,619 | 11spk2 | %hum %hum | 147.18338 | 49.112625 | -2.220118 | 17.234991 | slightly fast | %hʌm %hʌm | 0.722464 | 3.847063 | 1.180593 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | very noisy | very bad speech quality |
1,781,619 | 1,796,753 | 11spk1 | na ñuy gën a bàyyi xel sëb si danaa ci delluwaat sëb si xaal bi am na solo sëb si xaal bi ak basi bi ñi nga xam ne dañ teel a ñor surtout sëb na ci gën a na ci gën a nit ñi yaatal gën a yaatal mbay mi ci sëb si | 150.262939 | 35.43668 | 14.935262 | 4.428742 | slightly slowly | nɑ ʌ si si baɪ æm nɑ soʊloʊ si baɪ bɑsi baɪ ni til ʌ nɑ ʌ nɑ ʌ nɪt ʌ mi si | 0.791778 | 7.582465 | 1.349751 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,800,287 | 1,800,868 | 11spk3 | %hum %hum | 102.478279 | 34.641338 | 2.579623 | 1.531319 | slightly fast | %hʌm %hʌm | 0.468501 | -0.615306 | 1.192498 | very noisy | very distant-sounding | monotone | extremely noisy | very bad speech quality |
1,800,868 | 1,817,683 | 11spk1 | kon fokk ñu li nga xam ne day gaaw a ñor ñu gën ko bàyyi xel ci système de culture maanaam ni ñuy organiser yëf yi bu nawet bi bu nawet bi jeexee ah li jëm ci wàll bële it nguur gi ñu gën a baral gën a yokk mbir mi ci wàllu maitrise de l' eau | 138.852997 | 31.999062 | 15.93954 | 4.426326 | slightly slowly | kɑn li ni deɪ ʌ koʊ di kʌltʃɜ˞ ni ji baɪ baɪ ɑ li ɪt ʌ ʌ mi di ɛl' oʊ | 0.752335 | 0.421724 | 1.194105 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,817,683 | 1,818,358 | 11spk2 | %hum %hum | 97.608208 | 0 | -2.019057 | 7.344668 | moderate speed | %hʌm %hʌm | 0.665081 | -2.449105 | 1.235138 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | extremely noisy | very bad speech quality |
1,818,358 | 1,826,061 | 11spk1 | laaj wax nga ko sànq fexe ba ñu bañ a yem rekk ci mbayum nawet mbayum noor bi maanaam ñiy bay ci année at mi yépp | 130.05426 | 18.900913 | 11.465821 | 5.36886 | slowly | wæks koʊ bieɪ ʌ baɪ beɪ æt mi | 0.664865 | 3.579021 | 1.131548 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,826,061 | 1,826,661 | 11spk2 | %hum %hum | 178.829712 | 8.712885 | 1.319949 | 6.343972 | moderate speed | %hʌm %hʌm | 0.728662 | -0.843465 | 1.153198 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | extremely noisy | very bad speech quality |
1,826,661 | 1,843,782 | 11spk1 | loolu mën naa ne ndax Yàlla am na lu mu ñu may nguur gi mu ngi def ay pexe maasàllaa baax na waaye nag lu baax du doy du du du doy ñuy gën a yokk donc %e gën a yokk baral jeego yi ci wàllu maitrise de l' eau boobu ak xeex ak xorom si it fii ci Fatick | 142.15451 | 53.136604 | 10.574409 | 5.559594 | slowly | ni æm nɑ lu mu meɪ mu eɪ nɑ næɡ lu du du du du ʌ %i ʌ ji di ɛl' oʊ si ɪt | 0.668318 | 0.64847 | 1.145417 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | very noisy | very bad speech quality |
1,843,782 | 1,844,385 | 11spk2 | surtout | 176.414978 | 0 | 7.020404 | 7.375756 | very slowly | 0.691167 | 0.114235 | 1.155907 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
|
1,844,385 | 1,845,963 | 11spk1 | ah xorom si | 122.459785 | 2.65248 | 13.795696 | 7.359566 | very slowly | ɑ si | 0.873773 | 12.026937 | 1.690493 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | noisy | very bad speech quality |
1,851,384 | 1,852,000 | 11spk3 | %hum %hum | 139.447693 | 56.004951 | null | null | very fast | %hʌm %hʌm | 0.507008 | -0.263749 | 1.303554 | very clean | very close-sounding | slightly expressive and animated | very noisy | very bad speech quality |
1,852,000 | 1,877,493 | 11spk1 | gàllankoor bu mag la kon kooku it et lépp maanaam na doon yitteey ñépp nguur geeg baykat yeeg ña ko cay jàppale nguur gi moo jiitu baykat yeeg lépp ñu gën a gën a gën koo bàyyi xel pexe yiñ ko war a defee am na fi pexe yooyu nañ fexe gën koo yokk mu xam dañ koy jaar ci projet ab programme ak nu ñu ko fa mën a lifinee waaye daal xorom ci ci Fatick | 133.632431 | 26.817377 | 15.878843 | 4.75169 | slowly | mæɡ lɑ kɑn ɪt ɛt nɑ koʊ keɪ mu ʌ ʌ ku koʊ wɔɹ ʌ dɛfi æm nɑ faɪ ku mu æb pɹoʊɡɹæm nu koʊ ʌ | 0.857221 | 15.026225 | 1.796739 | very noisy | very distant-sounding | monotone | noisy | bad speech quality |
1,877,493 | 1,878,147 | 11spk2 | %hum %hum | 86.620186 | 6.032772 | 1.989535 | 6.754524 | moderate speed | %hʌm %hʌm | 0.756573 | 4.8437 | 1.156311 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
1,878,147 | 1,893,086 | 11spk1 | xorom si nag lu jar a seet la ndax rentable na lool maasàllaa ci wàllu exploitation waaye it mu ne ah ma ne ko ah boo ko bëggee dendaleeg mbay ma di mu ne ah ma ne ko lu jar a lu jar a seetaat la | 129.431992 | 36.009205 | 15.067293 | 5.333827 | moderate speed | si næɡ lu dʒɑɹ ʌ lɑ ɹɛntʌbʌl nɑ ɛksplɔɪteɪʃʌn ɪt mu ni ɑ mɑ ni koʊ ɑ bu koʊ mɑ di mu ni ɑ mɑ ni koʊ lu dʒɑɹ ʌ lu dʒɑɹ ʌ lɑ | 0.866323 | 11.633518 | 1.677147 | very noisy | very distant-sounding | monotone | noisy | very bad speech quality |
1,897,541 | 1,897,866 | 11spk2 | %hum %hum | 159.593765 | 57.314026 | -0.656472 | 18.445883 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.648956 | -3.818658 | 1.20036 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | extremely noisy | very bad speech quality |
1,897,866 | 1,900,462 | 11spk1 | ak département Foundoigne nga xam ne nag xorom si sonal na leen | 101.241158 | 23.240303 | 11.779949 | 3.301533 | slightly slowly | ni næɡ si nɑ lin | 0.721788 | -0.919617 | 1.144731 | very noisy | very distant-sounding | monotone | extremely noisy | very bad speech quality |
1,902,616 | 1,905,623 | 11spk1 | kon loolu loo xam ne mënuñ ko woon bañ a yokk ci mbir mi la | 112.557213 | 50.07 | 12.852758 | 4.457042 | slightly slowly | kɑn lu ni koʊ ʌ mi lɑ | 0.700313 | 2.853319 | 1.161009 | very noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | very noisy | very bad speech quality |
1,909,228 | 1,910,014 | 11spk2 | am na solo | 152.863861 | 61.076958 | 7.677862 | 58.816944 | slightly fast | æm nɑ soʊloʊ | 0.862293 | 4.082305 | 1.168763 | very noisy | slightly close-sounding | slightly expressive and animated | very noisy | very bad speech quality |
1,921,985 | 1,988,042 | 11spk2 | %hum %hum d' accord mu ngi noonu di leen jaajëfalaat rekk bu baax a baax ñi nga xamante ne ñu ngi doon déglu 93 point 5 ndefleng FM Fatick ci rappel rek émission bi %e ñi ko sponsorisé bokk na ci %e ci cadre projet 4R du projet du programme alimentaire mondial PAM dans les cinq régions %e cibles régions cibles yi nag bokk na ci Tambacounda Kolda Kaolack Kaffrine ak fi nga xamante ne moom mooy Fatick ci réalisation ak soutien wu technique bu Jokalante di leen jaajëfalaat bu baax a baax ñu doon waxtaanee lii di information climatique dans les activités de récolte ak post récolte )ndoon ko ak Maodo Samb mi fi teewal waa météo waaye ak %e Momadou Badiane mi nga xamante ne nii moom moo nekk ci direction régional bu développement rural àndoon koog seen présentatrice Maguette Mbaye di leen jaajëfalaat bu baax a baax ci kóolute gi ak saxoo bi ngeen saxoo lii di rajo Ndefleng FM Fatick %e di jaajëfal ñépp di leen jox dig daje ëllëg ci yeneen i émissions | 168.522858 | 35.32687 | 10.67981 | 8.644271 | slowly | %hʌm %hʌm di' ʌkɔɹd mu di lin ʌ ni pɔɪnt ɛfɛm baɪ %i koʊ nɑ %i kædɹi du du pɹoʊɡɹæm pæm lɛs sɪŋk %i ji næɡ nɑ faɪ ni wu tɛknik di lin ʌ di ɪnfɜ˞meɪʃʌn lɛs di poʊst ) koʊ mi faɪ %i mi ni mu dɜ˞ɛkʃʌn ɹʊɹʌl sin di lin ʌ baɪ di ɛfɛm %i di di lin dɪɡ aɪ | 0.80218 | 5.033075 | 1.125177 | very noisy | very distant-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
0 | 25,060 | 1010spk1 | %e de de la consommation foofu moom ngay adressé lettre bi soo ko ko adressé ak kayit yooyu ñuy wax ni mooy échantillon yi ngay yóbbaale mooy maquette étiquette bi %e certificat d' inscription bi xam ne nii mooy mooy kayit bi xam ne mooy carte d' ident() kayitu juddu %e kuréel gi plus maintenent %e process bi li nga koy defee soo ko defee insaa àllaa Yàlla mën na na la si defal taw féex ba %e li nga bëgg nga am ko | 122.827393 | 24.213303 | 20.555346 | 59.283249 | slightly slowly | %i di di lɑ baɪ su koʊ koʊ wæks ni ji baɪ %i di' ɪnskɹɪpʃʌn baɪ ni baɪ ni kɑɹt di' aɪdɛnt() %i plʌs %i pɹɑsɛs baɪ li dɛfi su koʊ dɛfi nɑ nɑ lɑ si bieɪ %i li æm koʊ | 0.974761 | 18.671766 | 2.023728 | very noisy | very close-sounding | monotone | noisy | bad speech quality |
25,060 | 40,775 | 1010spk2 | %hum %hum Jalle dégg nga ni ko Ibrahima waxee %e mais loolu ni mu ko waxee yomb na yombul tay jii su fekkee ni dañuy wax ci wàllu jafe-jafe ngir ngen mën a %e am kayit yooyu yépp yan jafe-jafe ngeen di faral di rencontré fan lay gën a bloqué woo %e souvent | 142.783859 | 40.199093 | 34.339619 | 58.400101 | slowly | %hʌm %hʌm ni koʊ %i meɪs ni mu koʊ nɑ teɪ su ni wæks - ʌ %i æm jæn - di di fæn leɪ ʌ wu %i | 0.991871 | 18.651596 | 2.718687 | slightly noisy | slightly close-sounding | monotone | noisy | slightly bad speech quality |
40,775 | 43,747 | 1010spk3 | bloqué bi yaakaar naa ne jafewul sax | 138.167496 | 63.139744 | 20.179237 | 57.386314 | slowly | baɪ ni sæks | 0.930379 | 12.087962 | 1.484519 | very noisy | slightly close-sounding | slightly expressive and animated | noisy | very bad speech quality |
43,747 | 44,157 | 1010spk2 | %hum %hum | 109.846245 | 16.979134 | 35.782978 | 33.383411 | fast | %hʌm %hʌm | 0.970067 | 12.95029 | 1.442422 | slightly noisy | very distant-sounding | very monotone | noisy | very bad speech quality |
44,157 | 45,660 | 1010spk3 | xay na ñàkkoon a xam yoon bi | 172.186325 | 60.93602 | 35.474831 | 59.796009 | slightly slowly | nɑ ʌ jun baɪ | 0.991611 | 17.786217 | 2.572079 | slightly noisy | very close-sounding | slightly expressive and animated | noisy | slightly bad speech quality |
45,660 | 45,986 | 1010spk1 | %hum | 108.792923 | 15.441559 | 12.542839 | 15.53726 | moderate speed | %hʌm | 0.83286 | 15.16245 | 1.350234 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | noisy | very bad speech quality |
50,962 | 51,306 | 1010spk2 | %hum %hum | 128.88681 | 29.098091 | 50.787289 | 27.008326 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.952533 | 16.16135 | 1.857978 | slightly clean | very distant-sounding | monotone | noisy | bad speech quality |
51,306 | 57,385 | 1010spk3 | wante comme ni ko Ibrahima demee ni mu ko waxee noonu la ñu ko defee ba nga xam si ne ñun yoon bi benn la wante it nag bokk na si | 198.900177 | 72.173515 | 22.431574 | 31.686657 | moderate speed | wɑntʌ ni koʊ ni mu koʊ lɑ koʊ dɛfi bieɪ si ni jun baɪ bɛn lɑ wɑntʌ ɪt næɡ nɑ si | 0.957337 | 17.25078 | 1.735543 | very noisy | very distant-sounding | expressive and animated | noisy | bad speech quality |
57,385 | 57,697 | 1010spk2 | %hum %hum | 124.162292 | 13.286933 | 15.517602 | 9.943645 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.896907 | 17.717289 | 1.29263 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | noisy | very bad speech quality |
57,697 | 58,598 | 1010spk3 | produit yi ngay yóbbu | 173.18396 | 43.818024 | 31.292622 | 16.881241 | slowly | ji | 0.653481 | -0.712928 | 1.124795 | noisy | very distant-sounding | slightly expressive and animated | extremely noisy | very bad speech quality |
58,598 | 59,068 | 1010spk2 | %hum %hum | 115.297455 | 14.862122 | 22.624117 | 45.778255 | fast | %hʌm %hʌm | 0.88568 | 17.101093 | 1.354199 | very noisy | slightly distant-sounding | very monotone | noisy | very bad speech quality |
59,068 | 59,937 | 1010spk3 | échantillon yooyu | 224.497406 | 65.483841 | 25.915632 | 39.480469 | very slowly | 0.950857 | 11.576174 | 1.697122 | noisy | distant-sounding | slightly expressive and animated | noisy | very bad speech quality |
|
59,937 | 60,262 | 1010spk2 | %hum %hum | 119.976707 | 29.359316 | 25.3965 | 53.394722 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.895523 | 20.681129 | 1.42792 | very noisy | slightly distant-sounding | monotone | slightly noisy | very bad speech quality |
60,262 | 64,381 | 1010spk3 | dafa war a nekk loo xam si ne dafay méngoo ak ni ngay liggéeyee ci béréb bi | 227.699295 | 87.68943 | 30.612181 | 52.770782 | slowly | wɔɹ ʌ lu si ni ni baɪ | 0.939597 | 9.855935 | 1.97884 | noisy | slightly distant-sounding | expressive and animated | very noisy | bad speech quality |
64,381 | 64,741 | 1010spk2 | %hum %hum | 123.240585 | 15.128 | 20.24114 | 20.718864 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.967332 | 19.328747 | 1.52443 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | noisy | very bad speech quality |
64,741 | 74,358 | 1010spk3 | ndax xam nga wut échantillon yoo xam ne ba nga ko joxee mu sell na set na te béréb ba nga nekk jëfëndikoo woo ca noona kon yaakaar ne bu ñu ñëwee waa service d' hygène | 223.390854 | 96.765587 | 31.727139 | 32.608528 | slightly slowly | ju ni bieɪ koʊ mu sɛl nɑ sɛt nɑ ti bieɪ wu kʌ kɑn ni sɜ˞vʌs di' | 0.94662 | 7.279415 | 1.962546 | noisy | very distant-sounding | very expressive and animated | very noisy | bad speech quality |
75,198 | 85,540 | 1010spk3 | mën nañu la jàpp chambre de commerce ñépp kenn ku ci ne dana def visite ci fi nga xam si ne mooy béréb bi nga xam ne si nga defaree li nga xam si moom mooy céréale bi wala soit yeneen produit yi ngay defar | 204.623917 | 73.86882 | 26.405977 | 50.042889 | slightly slowly | lɑ di kɑmɜ˞s kɛn ku ni deɪnʌ faɪ si ni baɪ ni si li si baɪ wɔlʌ ji | 0.959018 | 16.220776 | 2.031433 | noisy | slightly distant-sounding | expressive and animated | noisy | bad speech quality |
85,540 | 85,884 | 1010spk2 | %hum %hum | 154.150909 | 16.402506 | 45.932045 | 21.671841 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.98845 | 24.123314 | 1.825094 | balanced in clarity | very distant-sounding | very monotone | slightly noisy | bad speech quality |
85,884 | 89,653 | 1010spk3 | kon %e qualité bi daf ci am solo | 214.47731 | 84.76403 | 28.850201 | 45.755379 | slowly | kɑn %i baɪ æm soʊloʊ | 0.973026 | 22.835751 | 2.662202 | noisy | slightly distant-sounding | expressive and animated | slightly noisy | slightly bad speech quality |
89,653 | 108,838 | 1010spk2 | %hum %hum trop hygène bi daf ci am solo trop ndax lépp li nga xam si moom ngay defar boo ko yóbboo bu ñu ko dugalee ci laboratoire yi day feeñ ndax kii bu ci nekk %e Fra bu ci nekk daañu la jox %e kii bi maanaam maanaam %e li nga xam si ne mooy mooy mooy cent:Fra pour:Fra cent:Fra nga ci am wala 50 nga ci am | 208.493683 | 77.560944 | 33.788059 | 53.865181 | slowly | %hʌm %hʌm baɪ æm soʊloʊ li si bu koʊ koʊ ji deɪ %i lɑ %i baɪ %i li si ni sɛnt: pɔɹ: sɛnt: æm wɔlʌ æm | 0.976685 | 19.533546 | 2.445042 | slightly noisy | slightly distant-sounding | expressive and animated | noisy | slightly bad speech quality |
112,330 | 112,620 | 1010spk2 | %hum %hum | 134.209106 | 11.225066 | 49.031952 | 2.695873 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.882149 | 8.845181 | 1.233057 | balanced in clarity | very distant-sounding | very monotone | very noisy | very bad speech quality |
112,620 | 116,184 | 1010spk3 | kon foofu dana la may nga xam bii qualité bi nga li nga defar | 235.854279 | 82.371498 | 30.739511 | 46.141975 | slightly slowly | kɑn deɪnʌ lɑ meɪ baɪ li | 0.982264 | 23.010899 | 2.811247 | noisy | slightly distant-sounding | expressive and animated | slightly noisy | slightly bad speech quality |
116,184 | 116,564 | 1010spk2 | %hum %hum | 164.59108 | 19.371246 | 55.491489 | 56.304226 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.956198 | 18.824474 | 1.590315 | slightly clean | slightly close-sounding | very monotone | noisy | very bad speech quality |
116,564 | 120,400 | 1010spk3 | ndax yow jaar na yoon normal wala des na ñoom loolu lépp dañu la koy wan | 215.638718 | 78.956024 | 32.350327 | 31.527586 | slightly slowly | jaʊ nɑ jun nɔɹmʌl wɔlʌ dɛs nɑ lɑ wɑn | 0.982058 | 16.804249 | 2.691062 | noisy | very distant-sounding | expressive and animated | noisy | slightly bad speech quality |
120,400 | 120,871 | 1010spk2 | %hum | 106.574409 | 19.090622 | null | null | very fast | %hʌm | 0.746711 | 11.185231 | 1.171093 | very clean | very close-sounding | very monotone | noisy | very bad speech quality |
120,871 | 129,845 | 1010spk3 | bu jaaree yoon normal moom daañu la jàllaleel sa Fra waaye su jaarul yoon suñu dugalee si laboratoire bi lépp luy loo xam si ne defoo la ci rekk dañ koy da koy daal rejeté mu delloosil la ko | 208.975342 | 78.120811 | 31.159035 | 41.760494 | slightly slowly | jun nɔɹmʌl lɑ sɑ su jun si baɪ lu si ni lɑ dɑ mu lɑ koʊ | 0.970951 | 19.167671 | 2.173181 | noisy | distant-sounding | expressive and animated | noisy | bad speech quality |
131,456 | 131,823 | 1010spk2 | %hum %hum | 163.424042 | 17.932236 | 44.218285 | 21.201351 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.986814 | 21.501287 | 2.322044 | balanced in clarity | very distant-sounding | very monotone | slightly noisy | bad speech quality |
131,823 | 133,221 | 1010spk3 | la nga fay danga koy perte | 178.024109 | 102.292145 | 31.773624 | 35.365047 | slightly slowly | lɑ feɪ | 0.967394 | 20.715204 | 2.602325 | noisy | distant-sounding | very expressive and animated | slightly noisy | slightly bad speech quality |
133,221 | 133,808 | 1010spk2 | ah oui | 164.507507 | 17.453188 | 37.511341 | 59.821758 | slightly slowly | ɑ wi | 0.985489 | 16.668644 | 2.899552 | slightly noisy | very close-sounding | very monotone | noisy | slightly bad speech quality |
133,808 | 135,389 | 1010spk3 | dangay perte boo xase fay | 208.047058 | 47.507671 | 28.07819 | 58.631943 | slowly | bu feɪ | 0.923649 | 12.776658 | 1.882849 | noisy | slightly close-sounding | slightly expressive and animated | noisy | bad speech quality |
136,540 | 147,458 | 1010spk3 | kon li ngay def mooy na fa ngay defaree na sell fa nga koy defaree na sell li ngay def it na sell ba keroog mu cay muy dem fa mu fa nga xam si ne mooy ci laboratoire yi | 213.836853 | 92.517769 | 33.66507 | 46.732796 | slowly | kɑn li nɑ nɑ sɛl nɑ sɛl li ɪt nɑ sɛl bieɪ mu keɪ mu si ni ji | 0.975035 | 13.1559 | 2.177801 | noisy | slightly distant-sounding | very expressive and animated | noisy | bad speech quality |
148,254 | 161,880 | 1010spk3 | ndax dangay dégg nit naan man defar naa Fra def naa ko ñaari yoon déposé naa ñaari yoon ñu rejeté ma man jàlluma li koy tax mu jàll mooy biir kaso la lekk ci boppam dafa nekk lu sensible kon nit ku bu koy defar war naa xool li muy def mooy lan | 223.400009 | 78.586823 | 30.659597 | 53.686928 | slightly slowly | nɪt nɑn mæn koʊ jun jun mɑ mæn li tæks mu lɑ lu sɛnsʌbʌl kɑn nɪt ku wɔɹ li læn | 0.974292 | 18.653091 | 2.215453 | noisy | slightly distant-sounding | expressive and animated | noisy | bad speech quality |
163,341 | 167,091 | 1010spk3 | bu duggee ci laboratoire ndax laboratoireb moom lépp lu la réer bu ci duggee day feeñ | 238.052414 | 94.330048 | 33.184444 | 35.394993 | slowly | lu lɑ deɪ | 0.955456 | 22.626823 | 3.007854 | noisy | distant-sounding | very expressive and animated | slightly noisy | slightly bad speech quality |
168,539 | 175,324 | 1010spk3 | ñun népp war nañu cee bàyyi xel ne damay déposé rek dañu maa rejeté rek déedéet nekkul ñu rejeté la noonu ndax lu mu ci doon yoon lay jaar | 188.899673 | 45.223545 | 20.547743 | 59.340691 | slowly | wɔɹ ni lɑ lu mu jun leɪ | 0.989354 | 21.985302 | 2.292819 | very noisy | very close-sounding | slightly expressive and animated | slightly noisy | bad speech quality |
175,324 | 175,595 | 1010spk2 | %hum %hum | 97.550797 | 20.381804 | 15.809019 | 15.910879 | very fast | %hʌm %hʌm | 0.963032 | 20.095478 | 1.515235 | very noisy | very distant-sounding | monotone | slightly noisy | very bad speech quality |
175,595 | 178,979 | 1010spk3 | te yoon boobu moom kenn du ci jalgati lu tooloog tarfat nay | 177.610214 | 83.55162 | 25.314703 | 56.858856 | slightly slowly | ti jun kɛn du lu neɪ | 0.980866 | 17.72883 | 2.288078 | very noisy | slightly close-sounding | expressive and animated | noisy | bad speech quality |
178,979 | 192,151 | 1010spk2 | %e Ibrahima bu ma déggee Jalle ci li mu wax nii est ce que aussi tamit di ngeen taxawu jigéen ñi nga xam ne dañuy bëgg wut Fra mais surtout si béréb yooyu ñuy defaree seen i produit yi balaa muy dem ci labo yi le matériel qu' il faut b ak hygène %e bi nga xamante ne war na faa am | 153.136414 | 36.975002 | 44.624409 | 54.88726 | slightly slowly | %i mɑ li mu wæks ɛst sii kju di ni meɪs si sin aɪ ji lɑboʊ ji lʌ ku' ɪl bi %i baɪ ni wɔɹ nɑ æm | 0.994847 | 24.343517 | 3.245577 | balanced in clarity | slightly distant-sounding | monotone | slightly noisy | moderate speech quality |
192,151 | 194,730 | 1010spk1 | moo xam li mu doon wax léegi xam nga | 140.827896 | 38.393959 | 12.875976 | 59.400162 | slightly slowly | mu li mu wæks | 0.966447 | 5.518765 | 1.569103 | very noisy | very close-sounding | monotone | very noisy | very bad speech quality |
194,730 | 194,968 | 1010spk2 | %hum %hum %e | 137.991531 | 13.588718 | 10.44142 | 3.115964 | very fast | %hʌm %hʌm %i | 0.933023 | 17.778345 | 1.970047 | very noisy | very distant-sounding | very monotone | noisy | bad speech quality |
194,968 | 198,479 | 1010spk1 | %e ñun danu am benn tare benn défaut | 122.012505 | 27.549479 | 17.071297 | 59.801167 | slowly | %i æm bɛn bɛn | 0.929504 | 13.606483 | 1.944993 | very noisy | very close-sounding | monotone | noisy | bad speech quality |
198,479 | 198,967 | 1010spk2 | %hum %hum | 106.767998 | 20.853079 | 29.115335 | 20.661409 | slightly fast | %hʌm %hʌm | 0.986131 | 20.959633 | 1.46687 | noisy | very distant-sounding | monotone | slightly noisy | very bad speech quality |
Subsets and Splits