start_time
float64 0
2.73M
| end_time
float64 326
2.78M
| speaker_id
stringclasses 55
values | text
stringlengths 1
4.06k
| utterance_pitch_mean
float32 38.3
473
| utterance_pitch_std
float32 0
282
| snr
float64 -3.78
64.6
⌀ | c50
float64 -6.34
60
⌀ | speaking_rate
float64 0
2.1k
| phonemes
stringlengths 0
1.77k
| stoi
float64 0.24
1
| si-sdr
float64 -18.8
28.1
| pesq
float64 1.08
4.37
|
---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|
198,967 | 202,061 | 1010spk1 | muy que ne am na ñoo xam ne dañu bëgg a daw rekk toog fi ñu toog seen koñ | 145.363708 | 35.032852 | 21.044348 | 39.957722 | 12.305201 | kju ni æm nɑ ni ʌ dɔ faɪ sin | 0.987238 | 19.159142 | 2.120352 |
202,721 | 206,494 | 1010spk1 | tec() technique bi ñuy def sax bëgguñu keneen xam ko | 124.095177 | 46.958607 | 44.606045 | 47.650131 | 13.99825 | tɛk() tɛknik baɪ sæks koʊ | 0.988795 | 18.409489 | 2.765409 |
207,525 | 209,968 | 1010spk1 | yow li ngay defar su tasaaroowul | 148.682724 | 23.957941 | 25.114857 | 59.298809 | 4.938271 | jaʊ li su | 0.985658 | 22.183537 | 2.554156 |
210,761 | 211,217 | 1010spk2 | %hum %hum | 126.99894 | 16.567554 | 30.590178 | 18.702833 | 19.753087 | %hʌm %hʌm | 0.978294 | 22.09169 | 1.61348 |
211,217 | 226,053 | 1010spk1 | fokk li ngay def nit ñi xam ko pour mu mën a am njariñ mais am na ñoo xm ne dañuy jàpp ne ñoom li ñuy denc moom moo am njariñ maanaam li ñuy denc seen dëkk ñoom rekk ñu xam ko te loolu yow li nga am ca ame xam-xam la ci keneen amee xam-xam wala ëpp la ci ay ay pexe | 140.289764 | 33.389473 | 27.715544 | 57.301113 | 8.929477 | li nɪt koʊ pɔɹ mu ʌ æm meɪs æm nɑ ni ni li mu æm li sin koʊ ti jaʊ li æm kʌ eɪm - lɑ - wɔlʌ lɑ eɪ eɪ | 0.987561 | 21.761768 | 2.628228 |
226,053 | 226,605 | 1010spk2 | %hum %hum | 136.657639 | 23.0826 | 26.223209 | 28.456377 | 16.666666 | %hʌm %hʌm | 0.983382 | 21.85495 | 1.49447 |
226,605 | 240,404 | 1010spk1 | xay na bu ñu ko séddoo woon dana ngeen da ngeen dana la mën a gën a jàppale moo tax ci wàllu woowu bépp %e unité maanaam bu doon transformation bi nga xam ne dangay transformation fii ci %e région de %e Louga | 144.167618 | 32.219452 | 27.488649 | 49.829708 | 8.222222 | nɑ koʊ deɪnʌ dɑ deɪnʌ lɑ ʌ ʌ mu tæks %i tɹænsfɜ˞meɪʃʌn baɪ ni tɹænsfɜ˞meɪʃʌn %i di %i | 0.98675 | 19.980843 | 2.46027 |
240,404 | 240,800 | 1010spk2 | %hum %hum | 110.823708 | 39.811916 | 26.239365 | 31.239368 | 23.188406 | %hʌm %hʌm | 0.960482 | 22.51288 | 1.797632 |
240,800 | 284,173 | 1010spk1 | yu ci ëppoon ci jamono boobu en 2017 Fapal wëroon na ko xool leen xool seen i locaux pour xool ba xam est ce que méngoo na wala méngoowul ak ak ak ak doxalin ba mu leen defalee ba pare ci lañu leen woo ñoom ñépp seen i responsable defal leen formation ci approche HTTP c' à dire les techniques modernes de transformation des produit locaux xam ne approche qualité bi maanaam na mu gën a sellee na mu gën a yéwénee na mu gën a rafetee ci booy def transformation mu defal leen ci formation defal leen naka ngay def pour am am autorisation Fra yépp mu defal leen ko kon loolu taxaw boobu moom la am mais nag comme li ma la wax moo ci nekk xam nga par exemple bu fekkee ne association yi amuñu yenn moyens yi dafa am ñoo xam ne ñi énu tuddee des développeur économique wala éni ñu tuddee animateur économique | 131.614319 | 33.217319 | 24.866209 | 58.353039 | 9.356725 | ju ɛn nɑ koʊ lin sin aɪ pɔɹ bieɪ ɛst sii kju nɑ wɔlʌ bieɪ mu lin bieɪ pɛɹ lin wu sin aɪ lin fɔɹmeɪʃʌn eɪtʃtitipi si' daɪɹ lɛs tɛkniks di tɹænsfɜ˞meɪʃʌn dɛs ni baɪ nɑ mu ʌ nɑ mu ʌ nɑ mu ʌ tɹænsfɜ˞meɪʃʌn mu lin fɔɹmeɪʃʌn lin pɔɹ æm æm mu lin koʊ kɑn lɑ æm meɪs næɡ li mɑ lɑ wæks mu pɑɹ ni ʌsoʊsieɪʃʌn ji ji æm ni dɛs wɔlʌ | 0.982393 | 21.458469 | 2.464229 |
291,614 | 304,782 | 1010spk1 | ndax nag moyens yi moom moo disponiibulul ndax loolu bu fekkoon ne dafa am loo xam ne nii %e associations yi seen seen liggéey foofu la mën a yem maintenant ki xam ne ni nag yaa ngi yëngu ci mbir boobu te bëgg ñu wax la tay nga dégg ko | 151.258163 | 42.810661 | 31.765333 | 54.953541 | 8.519945 | næɡ ji mu ni æm lu ni %i ʌsoʊsieɪʃʌnz ji sin sin lɑ ʌ ki ni ni næɡ ti wæks lɑ teɪ koʊ | 0.991835 | 25.14625 | 2.776959 |
304,782 | 305,180 | 1010spk2 | %hum %hum | 82.376526 | 40.271809 | 28.946304 | 24.004004 | 23.188406 | %hʌm %hʌm | 0.950372 | 21.912363 | 1.658482 |
305,180 | 326,403.464415 | 1010spk1 | wala ñu defal la formation nga dégg ko nga ne man kat kii li mu soxla moom laa soxla Fapal dana am taxawaay bu mu taxawee mooy su gisee ku xam ne dalay jàppale si wàllu matériel wala si wàllu defar dana la def dana def intermédiation bi dana la boole ak moom %hum dana la def dana la jox ay ay conseils am bu dee comme lu mel ne autorisation Fra itam ci ay %e éni lay jàppale ndax xaalis la | 152.024063 | 30.034018 | 29.604359 | 58.997612 | 9.475824 | wɔlʌ lɑ fɔɹmeɪʃʌn koʊ ni mæn kæt li mu deɪnʌ æm mu su ku ni si wɔlʌ si deɪnʌ lɑ deɪnʌ baɪ deɪnʌ lɑ bul %hʌm deɪnʌ lɑ deɪnʌ lɑ eɪ eɪ æm di lu mɛl ni eɪ %i leɪ lɑ | 0.994134 | 23.518936 | 2.669132 |
326,403.464415 | 326,802 | 1010spk2 | %hum %hum | 107.043884 | 32.24332 | 24.114273 | 26.22295 | 23.188406 | %hʌm %hʌm | 0.920218 | 12.351272 | 1.54041 |
326,802 | 341,298 | 1010spk1 | xaalis ngay fay kooku bu fekkee ne nag li ngay jaay demewul noonu pour nga am ko day doon problème xay na %e comme lu mel ni que unité de transformation bi dañoo am partenanire boo xam ne dañoo jàppale woon si wàllu xaalis pour ñu mën a am autorisation pour ñu am autorisation Fra | 135.470901 | 26.045134 | 25.70719 | 52.926735 | 8.761264 | feɪ ni næɡ li pɔɹ æm koʊ deɪ nɑ %i lu mɛl ni kju di tɹænsfɜ˞meɪʃʌn baɪ æm bu ni si pɔɹ ʌ æm pɔɹ æm | 0.98418 | 22.121756 | 2.342446 |
341,298 | 341,566 | 1010spk2 | %hum %hum | 120.554092 | 22.142677 | 24.020689 | 3.265764 | 35.555554 | %hʌm %hʌm | 0.978297 | 21.642202 | 2.27321 |
341,566 | 356,497 | 1010spk1 | loolu daf cee daf cee am solo mais nit ki pour ñu nekk lu professionnel pour ñu nekk ay professionnels allah :ar kulli :ar allin :ar fokk ñu formaliizewu formalisation boobu nag ci la autorisation Fra dugg ci la kayit yi kayit yi dugg ci la code barre | 165.074936 | 42.19487 | 32.256535 | 46.338951 | 7.574996 | æm soʊloʊ meɪs nɪt ki pɔɹ lu pɔɹ eɪ ɑlʌ :ɑɹ :ɑɹ ʌlɪn :ɑɹ næɡ lɑ lɑ ji ji lɑ koʊd bɛɹi | 0.988876 | 23.227518 | 2.479146 |
357,926 | 358,524 | 1010spk1 | code :barre dugg | 119.220566 | 17.537531 | 18.450571 | 33.397163 | 18.624339 | koʊd :bɛɹi | 0.974664 | 17.721626 | 2.008864 |
360,025 | 386,998 | 1010spk1 | ndax jàpp nañ ne liy wàllug transformation na ñu ko daan def ca cosaan ba comme moom la énu xam jàpp nañu ne loolu * mooy que ne naa defar sama cere bu ngoonee ma jaay ko ci koñ bi naa defar sama sànqal bu ngoonee ma jaay ko ci koñ bi naa defar sama kii bu ngoonee ma jaay ko si dëkk bi mbaa ma jaay ko si koñ bi loolu nit ñi dañoo war a am ni nag man est ce que tay jii du ma posé sama bopp ay question xam ne lii may def gis naa ne am na njariñ ndax nit ñaa ngi koy consommé lan laay def nag ba méngale ko ak bëgg-bëggu ñeneen ñi ci des | 152.27066 | 37.991924 | 33.183903 | 51.952526 | 11.770115 | ni tɹænsfɜ˞meɪʃʌn nɑ koʊ kʌ bieɪ lɑ ni * kju ni sɑmʌ mɑ koʊ baɪ sɑmʌ mɑ koʊ baɪ sɑmʌ mɑ koʊ si baɪ mɑ koʊ si baɪ nɪt wɔɹ ʌ æm ni næɡ mæn ɛst sii kju teɪ du mɑ sɑmʌ bɑp eɪ kwɛstʃʌn ni meɪ ni æm nɑ nɪt læn næɡ bieɪ koʊ - dɛs | 0.990751 | 23.600048 | 2.619385 |
387,674 | 400,279 | 1010spk1 | jikko yi dafay changé te comportement yi day gën a moderne te fokk ñu adapté wu maanaam fokk ñuy jël suñu li ñuy %e li ñuy defar fokk mu jëm mu méngoo ak ñun suñu bëgg-bëgg ak surtout bëgg-bëggu bëgg-bëggu xale yi | 148.823486 | 39.724186 | 29.619802 | 49.011581 | 6.314511 | ji ti ji deɪ ʌ moʊdɛɹn ti wu li %i li mu mu - - - ji | 0.988827 | 21.794769 | 2.266533 |
400,279 | 400,677 | 1010spk2 | %hum %hum | 121.104515 | 22.05023 | 19.80615 | 17.223753 | 23.188406 | %hʌm %hʌm | 0.95098 | 20.689348 | 1.397437 |
400,677 | 408,892 | 1010spk1 | loolu nit ñi fokk ñu bàyyi ci xel te loolu en tout cas Fapal moom ma nga cay taxaw ci orientation waaye am na loo xam ne nii nag dafa laaj ay moyens | 141.090942 | 28.291355 | 27.164295 | 56.169674 | 9.26688 | nɪt ti ɛn taʊt kæs mɑ keɪ ɔɹiɛnteɪʃʌn æm nɑ lu ni næɡ eɪ | 0.987036 | 22.215744 | 2.515909 |
408,892 | 409,272 | 1010spk2 | %hum %hum | 105.977882 | 19.442123 | 23.358276 | 14.431638 | 24.242424 | %hʌm %hʌm | 0.914897 | 17.414387 | 1.392228 |
409,272 | 414,664 | 1010spk1 | ndax tay marche en avant bi rek batimat bi nga defaraat ko ah équipement bi loolu xaalis la | 136.519531 | 25.942083 | 25.79952 | 54.407295 | 8.545223 | teɪ mɑɹʃ ɛn ʌvɑnt baɪ baɪ koʊ ɑ baɪ lɑ | 0.986866 | 21.262924 | 2.637972 |
415,377 | 420,943 | 1010spk1 | %e ñi ciy liggéey dañoo war a booloo dañoo war a boolee loolu lu ci am solo la | 133.727188 | 33.177273 | 18.977114 | 57.013664 | 7.155143 | %i wɔɹ ʌ wɔɹ ʌ lu æm soʊloʊ lɑ | 0.979357 | 11.700253 | 1.773301 |
420,943 | 422,770 | 1010spk2 | dañuy faral di wax naan lu kenn mën ñaar moo ko ko | 129.996048 | 34.67675 | 9.687059 | 52.389328 | 18.106996 | di wæks nɑn lu kɛn mu koʊ koʊ | 0.952544 | 6.799806 | 1.533678 |
425,660 | 446,629 | 1010spk2 | %e ci %e émissions yi nga xam ne %e United :en Purpose :en moo ko jagleel jigéen ñi ci projet tekki jigéen ñi %e te %e USAID daal di koy financé waaye nag si jàppalug Jokalante ak Fapal maa ngi ñëwaat léegi léegi | 114.951241 | 35.656643 | 35.791626 | 54.275455 | 7.416772 | %i %i ji ni %i junaɪtɪd :ɛn pɜ˞pʌs :ɛn mu koʊ %i ti %i juɛseɪd di næɡ si | 0.982552 | 17.910448 | 3.005216 |
446,629 | 515,754 | 1010spk4 | yéen sunu mbokki jigéen ñi xibaar bi yéen a ko moom kuréel gii ñu naan Fapal moo lëkkaloog kuréel gii ñu naan consortium tekki jigéen ci njàppanadalu USAID ñoo ñëw ngir gunge leen ci lépp luy suqali seen koom-koom te it yaqanal seen poche jaarale ko ci projet bii ñu naan tekki jigéen tekki jigéen projet la boo xam ne dafa ñëw ngir dooleel bépp jigéen ci li muy yëngu moo waral ñu baaxee leen ay formation yu jëm ci éducation financière naka la ñuy dugalanteeg a génne ci wàllum koom marcketing :en wàllum jënd ak jaay rawatina lu jëm ci wàllum internet wàllum javélisation ci nees la ñuy defaree eau de javel savonerie ci naka la ñuy defaree saabu ak lépp lu mu làmbool ku ci bëgg a bokk ci formation yi mën ngaa woote ci numéro bii ñu naan 33 879 30 82 33 879 30 82 ginnaaw boo déggee bip bi nga wax sa tur sa sant ak fi nga dëkk ak ban formation nga yittewoo ngir nga mën a bokk ci pàcc bu njëkk bu ñuy tàggat formation yooyu daw leen gaaw woote ci numéro bii ndax nombre de place yi dañu koo limité jaaraama projet tekki jigéen mi làmboog njarñu kese | 193.021393 | 76.561157 | 29.805706 | 9.566913 | 6.439119 | baɪ ʌ koʊ nɑn mu nɑn kʌnsɔɹʃiʌm juɛseɪd lin sin - ti ɪt sin pɑtʃ koʊ nɑn lɑ bu ni li mu lin eɪ fɔɹmeɪʃʌn ju lɑ ʌ :ɛn lu ɪntɜ˞nɛt niz lɑ oʊ di lɑ lu mu ku ʌ fɔɹmeɪʃʌn ji nɑn bu bɪp baɪ wæks sɑ sɑ sænt faɪ bæn fɔɹmeɪʃʌn ʌ fɔɹmeɪʃʌn dɔ lin di pleɪs ji ku mi | 0.924413 | 7.117326 | 2.059985 |
515,754 | 536,276 | 1010spk2 | voilà ñu koy jaajëfal moom %e Serigne di %e koo xamante ne vraiment farlu na lool ci liggéey bi %e Jalle yaakaar naa ne %e fi brahima daane lee ci li nga xamante ne moom mooy li ñuy wax naan mbooloo %e mooy doole te it %e d' après ni ma déggee code barre yeeg Fra yeeg loolu lépp ku amul doole dèjà dafa mel ni que pour nga jot ci day jafe | 146.404144 | 36.478588 | 39.819874 | 58.986073 | 7.748538 | %i di %i ku ni nɑ baɪ %i ni %i faɪ dɑn li li ni li wæks nɑn %i ti ɪt %i di' ni mɑ koʊd bɛɹi ku mɛl ni kju pɔɹ dʒɑt deɪ | 0.991429 | 25.644524 | 3.583618 |
536,276 | 540,379 | 1010spk3 | waa Ibrahima li mu wax dëgg la ndax mbooloo mooy doole | 170.687988 | 28.702415 | 27.713219 | 50.791462 | 8.117707 | li mu wæks lɑ | 0.944975 | 19.46595 | 1.951209 |
540,379 | 540,777 | 1010spk2 | %hum %hum | 122.16832 | 12.004741 | 18.647938 | 32.916023 | 23.188406 | %hʌm %hʌm | 0.969183 | 19.413414 | 1.518155 |
540,777 | 542,956 | 1010spk3 | xam nga li ñu tubaab bi rawee mooy booloo | 152.470764 | 45.979122 | 22.068859 | 59.000137 | 5.971863 | li baɪ | 0.981691 | 19.213472 | 2.097131 |
542,956 | 543,301 | 1010spk2 | %hum %hum | 148.022171 | 24.351963 | 32.320911 | 15.028501 | 26.666666 | %hʌm %hʌm | 0.979845 | 22.023026 | 1.991936 |
543,301 | 552,450 | 1010spk3 | gis nga %e di bi muy wax sànq ci li nga xam si mooy seen produit yi tubaab bi li mu ñu rawee mooy emballage | 195.405853 | 64.934311 | 46.703224 | 31.676834 | 8.68023 | %i di baɪ wæks li si sin ji baɪ li mu | 0.991933 | 25.256201 | 3.1947 |
552,450 | 553,337 | 1010spk2 | emballages yi | 146.01796 | 24.077398 | 28.063387 | 59.535172 | 3.418803 | ji | 0.995667 | 24.140345 | 2.575364 |
553,337 | 555,001 | 1010spk3 | defar ba mu rafet taaral ko | 158.646011 | 48.388332 | 36.269958 | 46.646198 | 9.535973 | bieɪ mu koʊ | 0.980224 | 20.373024 | 2.503214 |
555,001 | 555,417 | 1010spk2 | %hum %hum | 153.029144 | 18.133389 | 22.171677 | 25.325384 | 22.222222 | %hʌm %hʌm | 0.979692 | 20.950466 | 1.861527 |
555,417 | 559,895 | 1010spk3 | donte daal li ciy nekk sax du bari wante gis bi bu rafetee rekk njaay ma day yomb | 195.499863 | 66.125603 | 39.128204 | 56.989735 | 9.392033 | li sæks du bɑɹi wɑntʌ baɪ mɑ deɪ | 0.988864 | 17.051907 | 2.56315 |
559,895 | 560,796 | 1010spk2 | daf lay jox envie | 150.112106 | 14.655321 | 23.105528 | 57.229362 | 7.826694 | leɪ | 0.993585 | 24.077759 | 2.83813 |
560,796 | 561,542 | 1010spk3 | jeex na | 125.03569 | 31.370098 | 37.764107 | 57.000523 | 4.938271 | nɑ | 0.941019 | 14.941786 | 1.783508 |
561,542 | 562,211 | 1010spk2 | %hum %hum | 105.010399 | 21.130785 | 21.274836 | 32.246521 | 13.675214 | %hʌm %hʌm | 0.918424 | 19.307863 | 1.515034 |
562,211 | 570,720 | 1010spk3 | kon foofa bari na ñoo xam ne si tay comme ni mu waxee ne mën nga toog sa kër rek nga transformé nfa comme ci yoon bu njëkk bi énu daan jaaree | 184.786026 | 83.628479 | 26.400017 | 37.889488 | 7.817179 | kɑn bɑɹi nɑ ni si teɪ ni mu ni sɑ jun baɪ | 0.985163 | 21.387348 | 2.503128 |
570,720 | 571,154 | 1010spk2 | %hum %hum | 133.997131 | 19.083786 | 29.354527 | 20.106483 | 21.333333 | %hʌm %hʌm | 0.876743 | 20.667532 | 1.360081 |
571,154 | 574,752 | 1010spk3 | def ko si mbuus yoo xam ne si ne mbuus yi yiy sol galaas la rekk | 263.111359 | 97.074425 | 21.294661 | 35.805031 | 9.737437 | koʊ si ju ni si ni ji sɑl lɑ | 0.943369 | 20.718342 | 2.378391 |
574,752 | 575,296 | 1010spk2 | %hum %hum | 104.220596 | 32.635651 | 28.485645 | 26.400158 | 16.666666 | %hʌm %hʌm | 0.979239 | 19.597614 | 1.434876 |
575,296 | 590,782 | 1010spk3 | xam nga tay nga jaayee ko téeméer tay bu fekkee def nga ko ci emballage jaay moo rafet mën na jar 1000F te fekk yow coono ba nga ca jànkuwanteel beneen ba ca des mooy il faut que it ñu jéem a nekk mbooloo di daje di waxtaan di diisoo | 176.753235 | 79.041077 | 34.398697 | 44.357731 | 6.881289 | teɪ koʊ teɪ koʊ mu nɑ dʒɑɹ ti jaʊ bieɪ kʌ bieɪ kʌ dɛs ɪl kju ɪt ʌ di di di | 0.987565 | 21.252123 | 2.414174 |
593,024 | 603,792 | 1010spk3 | amul dellu ginnaaw avance rekk ngay def amul arrieère soo xasee dugg ci unité bi dangay dangay avancé ba keroog ngay génn kon bu fekkee yaa ngi sa biir koñ rekk | 168.031174 | 82.535522 | 37.291592 | 55.902496 | 5.29306 | su baɪ bieɪ kɑn sɑ | 0.987002 | 14.9048 | 2.710971 |
603,792 | 604,280 | 1010spk2 | %hum %hum | 161.279251 | 4.936952 | 38.880074 | 52.433411 | 19.047619 | %hʌm %hʌm | 0.920739 | 13.318316 | 1.449654 |
604,280 | 605,185 | 1010spk3 | dëbb sa roq rekk | 240.310593 | 134.744034 | 16.829563 | 42.602467 | 5.590496 | sɑ | 0.945042 | 18.931183 | 2.499812 |
613,454 | 615,661 | 1010spk3 | mooy dafay des des bu métti | 162.403809 | 62.977955 | 32.473019 | 31.436563 | 5.014245 | dɛs dɛs | 0.982164 | 16.594627 | 1.81911 |
618,068 | 636,324 | 1010spk3 | li ñu liggéey wax dëgg fa Yàlla des na des na trop kon te Fapal def na ci ay formation yu bari formation yu bari yoo xam si ne kenn ku ci nekk war nga mën a xam ne yow mii kat tay bu fekkee ne dangay samp loo ak lépp loo mën a transformé war nga ko amal bérébu boppam boo dul bokk ak dara dama ne formation saabu sax | 225.940353 | 88.518509 | 38.561394 | 51.807571 | 10.799329 | li wæks dɛs nɑ dɛs nɑ kɑn ti nɑ eɪ fɔɹmeɪʃʌn ju bɑɹi fɔɹmeɪʃʌn ju bɑɹi ju si ni kɛn ku wɔɹ ʌ ni jaʊ kæt teɪ ni sæmp lu lu ʌ wɔɹ koʊ ʌmɑl bu dæɹʌ dɑmʌ ni fɔɹmeɪʃʌn sæks | 0.985121 | 16.175289 | 2.723374 |
640,178 | 646,620 | 1010spk3 | te formation saabu dafa nekk loo xam ne xale waru koo waru faa dem xale waru ko jege | 235.42392 | 122.998116 | 37.74567 | 57.426941 | 7.07288 | ti fɔɹmeɪʃʌn lu ni ku koʊ | 0.962637 | 23.886517 | 2.279513 |
648,837 | 652,718 | 1010spk3 | xalee maanaam xale bi nga xamante ne dafay soog a juddu ba am 3 ans ndax xam nga xale boobu xamul dara | 198.988113 | 75.560638 | 30.046951 | 54.049767 | 9.57464 | baɪ ni ʌ bieɪ æm dæɹʌ | 0.968257 | 17.397457 | 2.196779 |
653,515 | 653,875 | 1010spk2 | ok :en | 124.036133 | 30.376835 | 19.437817 | 46.627167 | 25.396825 | oʊkeɪ :ɛn | 0.942409 | 18.201859 | 2.062485 |
653,875 | 655,192 | 1010spk3 | foofa xale bi mën nay raam | 336.648041 | 88.28685 | 47.6348 | 36.816696 | 8.357075 | baɪ neɪ | 0.907566 | 8.511487 | 2.145738 |
655,192 | 655,687 | 1010spk2 | %hum %hum | 111.056938 | 38.729221 | 22.272316 | 26.250973 | 18.390805 | %hʌm %hʌm | 0.984012 | 18.04734 | 1.515979 |
655,687 | 656,409 | 1010spk3 | mën na dox | 261.055298 | 96.027718 | 2.042336 | 35.991734 | 5.643739 | nɑ | 0.984425 | 23.159307 | 3.576768 |
656,409 | 656,717 | 1010spk2 | %hum %hum | 100.597382 | 48.479595 | 21.556648 | 24.390862 | 29.629629 | %hʌm %hʌm | 0.987925 | 20.336929 | 2.029255 |
656,717 | 662,561 | 1010spk3 | mën na gis laal ko ci gémméñam wala mu laal ko feneen mu indil ko ay jefe-jafe yu dul jeex kon ki nga xam si mooy transformé li nga xam si mooy savon | 217.378296 | 91.212669 | 39.730576 | 44.722706 | 12.673946 | nɑ koʊ wɔlʌ mu koʊ mu koʊ eɪ - ju kɑn ki si li si seɪvɔn | 0.967725 | 13.67632 | 2.124506 |
662,561 | 662,977 | 1010spk2 | %hum %hum | 107.822166 | 22.392645 | 21.054319 | 17.081587 | 22.222222 | %hʌm %hʌm | 0.971472 | 15.896848 | 1.216729 |
662,977 | 670,848 | 1010spk3 | dafa war a am bérébu boppam boo xam si ne su fay dugg moom rekk moom ak équipe ba fay dugg buñu paree tëjaat nañ génn dem seen yoon | 197.683365 | 88.299431 | 30.41433 | 53.450466 | 7.604064 | wɔɹ ʌ æm bu si ni su feɪ bieɪ feɪ sin jun | 0.97897 | 19.221289 | 2.279456 |
670,848 | 671,120 | 1010spk2 | %hum %hum | 101.918854 | 31.572369 | 6.537754 | 44.465622 | 33.333332 | %hʌm %hʌm | 0.767978 | 16.120663 | 1.260772 |
671,120 | 675,426 | 1010spk3 | kon ki nga xam si mooy def céréale it naka noona fi ñuy defaree céréale laajul xale di fa ne | 211.455811 | 85.286629 | 35.600399 | 59.384113 | 8.133624 | kɑn ki si ɪt faɪ di ni | 0.981418 | 21.315928 | 2.764685 |
677,014 | 684,220 | 1010spk3 | li nga xam si ne mooy hygène boo ko toppee dëgg dëgg dëgg ak fi ñuy kay jaaralee ba ba ngay pare laajul dugg ak génn | 206.744598 | 103.177361 | 36.879723 | 56.062588 | 8.121828 | li si ni bu koʊ faɪ keɪ bieɪ bieɪ pɛɹ | 0.970742 | 19.2215 | 2.355954 |
691,367 | 691,675 | 1010spk3 | %hum %hum | 128.887314 | 44.866894 | 52.381821 | 12.732835 | 29.629629 | %hʌm %hʌm | 0.746045 | 18.002878 | 1.277268 |
691,675 | 699,134 | 1010spk2 | yi ngay wax nii yépp est ce que am na ay yoo xamante ne seen fi ngeen di transformé yii yépp est ce que am na fa mais aussi est ce que respecté ngeen norme yi ngay wax fii nii ci rajo bi yépp | 152.352036 | 33.890144 | 45.093376 | 57.091206 | 15.015921 | ji wæks ɛst sii kju æm nɑ eɪ ju ni sin faɪ di ɛst sii kju æm nɑ meɪs ɛst sii kju ji wæks baɪ | 0.991045 | 9.789673 | 2.128361 |
699,134 | 700,559 | 1010spk3 | waaw am na fa waaye des na | 209.365875 | 76.593849 | 26.83065 | 36.717392 | 10.58201 | æm nɑ dɛs nɑ | 0.979013 | 22.168839 | 2.522861 |
700,559 | 700,885 | 1010spk2 | %hum %hum | 125.332596 | 29.560656 | 37.398991 | 26.189312 | 28.070175 | %hʌm %hʌm | 0.977714 | 22.866093 | 1.862875 |
700,885 | 706,512 | 1010spk3 | am na fa waaye des na ndax bu ñu wa() bu ñu boo xoolee tay boo fa demoon tay mën naa ne yaa ngi naan chantier bu àggul la | 210.60231 | 82.931252 | 28.901121 | 48.321777 | 10.677344 | æm nɑ dɛs nɑ wɑ() bu teɪ bu teɪ ni nɑn lɑ | 0.958824 | 17.824001 | 1.938667 |
706,512 | 707,115 | 1010spk2 | %hum %hum | 84.761627 | 34.642632 | 27.026955 | 26.438709 | 15.238096 | %hʌm %hʌm | 0.984634 | 21.504951 | 1.717487 |
707,115 | 713,116 | 1010spk3 | donte laa ñu ngi si ñu ngi jéem nag ci suñu kéemtalaay kàttan ndax biir kaso la lu ci dugg moom nay wax jàmm | 176.424667 | 71.710999 | 32.141655 | 48.302147 | 6.6771 | si næɡ lɑ lu neɪ wæks | 0.9755 | 14.406724 | 2.278565 |
713,116 | 713,351 | 1010spk2 | %hum %hum | 131.568405 | 12.610571 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.982321 | 19.422779 | 1.811729 |
713,351 | 720,657 | 1010spk3 | wante ba fi mu ne nii am na chantier yoo xam si ñu ngi ko préparé pour maanam naka la ñuy def ba marche arrière bi di am | 170.168304 | 84.798813 | 31.026117 | 46.19009 | 11.48904 | wɑntʌ bieɪ faɪ mu ni æm nɑ ju si koʊ pɔɹ lɑ bieɪ mɑɹʃ baɪ di æm | 0.96122 | 15.285252 | 1.928005 |
730,704 | 740,868 | 1010spk3 | te loolu ba léegi may wax des na waaye teewul ñu ngi siy jéem sunu kéemtulaay kàttan ba topp normes yooyu ba nga xam ne tay suñu jógee fii nga xam si ne fi la ñuy wàcce stocké matière première bi | 206.198685 | 79.594955 | 33.369652 | 47.587181 | 8.988177 | ti bieɪ meɪ wæks dɛs nɑ bieɪ tɑp bieɪ ni teɪ si ni faɪ lɑ baɪ | 0.981641 | 19.658501 | 2.440923 |
740,868 | 755,023 | 1010spk2 | %hum %hum suñu ko génnee fa ñuy jar fi ñu ko génnee ba keroog ñuy pare def finition ba keroog ñuy génn loolu lépp ñu ngi suñu kéemtulaay kàttan donte laa béréb bi des na des na bu métti ndax tay boo dikkoon ba àggsi dinga xam ne am na lu des waaye li des lépp ñun ñoo ngi si yoonu fas yéenee topp | 177.595016 | 73.022011 | 33.31881 | 38.867825 | 9.864629 | %hʌm %hʌm koʊ dʒɑɹ faɪ koʊ bieɪ pɛɹ bieɪ baɪ dɛs nɑ dɛs nɑ teɪ bu bieɪ ni æm nɑ lu dɛs li dɛs si tɑp | 0.982001 | 16.376614 | 2.080534 |
761,157 | 767,816 | 1010spk3 | waaw loolu moom di nañu koy respecté moom norme yi moom di nañ ko respecté ndax li ñuy liggéey su fekkee ne woon respecté woo normes yi | 185.41922 | 71.53186 | 27.148264 | 47.880493 | 7.551041 | di ji di koʊ li su ni wu ji | 0.986122 | 15.188138 | 1.975278 |
767,816 | 768,178 | 1010spk2 | %hum %hum | 157.619293 | 14.133508 | 29.177839 | 26.318003 | 25.396825 | %hʌm %hʌm | 0.98904 | 23.45166 | 2.117406 |
768,178 | 770,693.714286 | 1010spk3 | yaakaar naa ne ba léegi uni() suñu unité bi tëj na | 159.783707 | 33.088264 | 40.745056 | 56.991108 | 10.738255 | ni bieɪ juni() baɪ nɑ | 0.977663 | 24.426582 | 2.982979 |
772,581.678571 | 773,082 | 1010spk2 | %hum %hum | 108.91787 | 20.302868 | 13.233711 | 26.140755 | 18.390805 | %hʌm %hʌm | 0.981158 | 18.804743 | 1.500138 |
773,082 | 775,595.5 | 1010spk3 | yii a ngi dem génn réew mi di dem | 193.102539 | 66.573883 | 36.606266 | 47.615376 | 5.706447 | ʌ mi di | 0.991339 | 25.210093 | 3.244287 |
775,595.5 | 775,974.964286 | 1010spk2 | %hum %hum | 96.38105 | 31.647512 | 20.253181 | 17.422722 | 24.242424 | %hʌm %hʌm | 0.95878 | 20.649952 | 1.57817 |
775,974.964286 | 779,903.535715 | 1010spk3 | yii a ngi ci biir sénégal te kenn ku ci nekk si ñi nga xam si ne | 226.584061 | 95.493393 | 36.619781 | 57.404762 | 7.662835 | ʌ ti kɛn ku si si ni | 0.991143 | 23.763611 | 2.609769 |
786,823 | 807,597 | 1010spk3 | bu fekkee gis nga si dara du la joxaat commande te fi mu toll commande bu jeex keneen laajaat la keneen laajaat la loolu li koy maye mooy hygène ba ca aju norme:Fra ya nga topp ba nga xamante ne sii jaar na yoon ba nga xamante ne sii am nga qualité:Fra nga jox ko nit ki bu ko gisalee boppam sax moom moo lay njëkk a wax ñi ñu jox presque ñun suñu client yépp ñun ñoo ñu woowal suñu bopp wax ñu li nga xam si ne mooy bë() ngënéel yi ñu gis | 209.680222 | 81.562462 | 37.710823 | 49.916687 | 9.86852 | si dæɹʌ du lɑ ti faɪ mu toʊl lɑ lɑ li meɪ bieɪ kʌ : jɑ tɑp bieɪ ni nɑ jun bieɪ ni æm : koʊ nɪt ki koʊ sæks mu leɪ ʌ wæks klaɪʌnt bɑp wæks li si ni () ji | 0.958729 | 10.404307 | 1.992169 |
813,027 | 818,993 | 1010spk2 | client yi lan la ñuy gën a soxlaci par rapport ak li ngeen di li ngeen di transfor() li ngeen di liggéey lan la transformation bi lan la exactement | 135.230988 | 17.880692 | 43.260921 | 59.416924 | 15.836526 | klaɪʌnt ji læn lɑ ʌ pɑɹ ɹæpɔɹ li di li di () li di læn lɑ tɹænsfɜ˞meɪʃʌn baɪ læn lɑ | 0.990452 | 24.898617 | 3.152919 |
818,993 | 822,351 | 1010spk3 | tranformé bi daañu transformé maanaam mil bi | 216.625961 | 72.72361 | 41.611664 | 43.305653 | 4.489338 | baɪ mɪl baɪ | 0.971095 | 16.086258 | 2.269611 |
823,885 | 824,287 | 1010spk2 | %hum %hum | 135.729507 | 51.195568 | 30.852289 | 59.540661 | 23.188406 | %hʌm %hʌm | 0.990148 | 21.169659 | 2.732914 |
824,287 | 825,517 | 1010spk3 | ñoo ëpp ci li ñuy transformé | 226.01651 | 132.346359 | 33.838398 | 58.877033 | 6.584362 | li | 0.989041 | 21.561474 | 2.336522 |
825,517 | 826,069 | 1010spk2 | waaw | 185.809647 | 43.085144 | 30.526392 | 47.834942 | 0 | 0.964327 | 23.26273 | 2.629152 |
|
826,069 | 827,327 | 1010spk3 | bu ñu xoolee ñebe bi | 199.03154 | 127.743774 | 46.115101 | 57.995678 | 5.605606 | baɪ | 0.95545 | 21.494993 | 2.438026 |
827,327 | 827,761 | 1010spk2 | %hum %hum | 132.672073 | 31.302055 | 45.266964 | 27.164244 | 21.333333 | %hʌm %hʌm | 0.986615 | 22.083721 | 2.367255 |
827,761 | 829,969 | 1010spk3 | bari na client yoo xam si ñoom ñebe rekk la ñu soxla | 204.132858 | 87.700943 | 27.255926 | 59.416985 | 13.675214 | bɑɹi nɑ klaɪʌnt ju si lɑ | 0.955247 | 7.36105 | 1.753946 |
829,969 | 830,475 | 1010spk2 | waaw | 143.800949 | 43.126637 | 22.312483 | 58.468044 | 0 | 0.984875 | 24.603271 | 2.836125 |
|
830,475 | 831,887 | 1010spk3 | am client yoo xam si ñoom | 173.379211 | 78.655365 | 29.666637 | 36.985031 | 13.852813 | æm klaɪʌnt ju si | 0.922241 | 10.168993 | 1.688699 |
831,887 | 832,339 | 1010spk2 | %hum %hum | 152.395996 | 15.360455 | 28.925825 | 59.424576 | 20.512821 | %hʌm %hʌm | 0.98433 | 21.693245 | 2.594614 |
832,339 | 833,624 | 1010spk3 | %e mil bi rekk la ñu soxla | 189.105469 | 43.328075 | 35.770966 | 59.806305 | 12.475633 | %i mɪl baɪ lɑ | 0.868702 | 11.02829 | 1.815557 |
833,624 | 834,473 | 1010spk2 | mil bi rekk la ñu soxla | 153.754166 | 33.840435 | 22.264843 | 56.657948 | 15.407407 | mɪl baɪ lɑ | 0.985714 | 25.076065 | 2.868494 |
835,795 | 836,175 | 1010spk2 | waaw | 139.80278 | 9.088029 | 23.650682 | 39.981236 | 0 | 0.974064 | 22.548714 | 3.108245 |
|
836,175 | 836,772 | 1010spk3 | da naan la | 224.336761 | 35.64373 | 34.600395 | 34.282681 | 15.238096 | dɑ nɑn lɑ | 0.812403 | 7.472328 | 1.461823 |
836,772 | 836,988 | 1010spk2 | %hum %hum | 153.930405 | 4.909342 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.978008 | 21.44276 | 2.655546 |
836,988 | 838,762 | 1010spk3 | defal ma cinq:Fra cent:Fra araw | 229.32341 | 75.547951 | 24.670237 | 22.951345 | 9.029982 | mɑ sɪŋk: sɛnt: | 0.979406 | 18.03915 | 2.888883 |
845,565 | 845,891 | 1010spk2 | %hum %hum | 162.75798 | 16.237494 | 42.453442 | 18.686382 | 28.070175 | %hʌm %hʌm | 0.976587 | 20.792471 | 2.052842 |
Subsets and Splits