audio
audioduration (s) 2.29
12.5
| sentence
stringlengths 26
118
|
---|---|
moo taxit feebaru jigéen dafa bari façons |
|
bu nawetee du génn te gànnaayoowul ak permiyaabal |
|
kii de dafay wanteer njëg li neex na lool |
|
léegi daawur dafa mel ni ku télbati |
|
delloo na naaru góor wi tëboon wajanam wi |
|
ci saa si ayda jafandu ci waasintóoram yu tuuti ya |
|
Nee ñu xobi pàppaayo baax na ci fas yi seen biir di metti |
|
ku woor di togg mën naa am nga juubu mos xorom |
|
ba mu egsee ca dëkk ba booba ñépp a nga woon ca tool ya ba mu des ndew ma mu fekk ca buntu néegam |
|
ruuxal soow mi ndax soppuma ci sañ yi |
|
tamaate fàrsi jaa ngi noy nepp kenn mënu ko dagg |
|
mu fab ko saggane ko te ndeyam amoon ko muy benn doññ |
|
mu nga jóge woon ca rëbb ma gàlloo genn kéwél |
|
mbëtt mënula daw mënula jaab lu dul bar bari |
|
sa yaraale bi màgg na léegi yow lañuy xaar |
|
reeni xom xom fajkat yee koy jëfandikoo |
|
muy toj mu ndaw di toj mu mag mënees nañoo tiim |
|
saalu gerte tubaab rekk la xale yi bëgg |
|
fas wa dellu fëx nekk ca la mu nekkoon |
|
ki sàcc sa nag yi du jaar ci saawo si |
|
buur ne ki rey ninki nanka bi lay may doomam |
|
këram la waaye dëkku ci dafa ko luye |
|
boo raxasee aset yi ba noppi nga fomp leen |
|
mbubb ma nga soloon ca céet ga booba laa bëgg |
|
mu jëm ca sàmba seytaane amari né ko |
|
amul bàyyi ni ko ndax am na jur gu dem |
|
dalal nga sama xel bi nga ma nee am na liggéey |
|
morooman yi gunge nañu ko ba gaar ba |
|
soo leen boolee dinañu gaawa xaritoo |
|
fompal lumbi deret yi bala nga koy faj |
|
moo yey Noy ci liggéeyam moo ko tax a suturlu |
|
bu jëkk jigéen ñi begguñu woon sew dañu daan yaflu |
|
Naar Naar Naar ba Naar yépp tiit daldi jóg ni ko |
|
mag ñu jëkk ña daawuñu génn te takkuñu nafa |
|
booy dem màrse ma yóbbante la kànja |
|
ba jànq ya indee meew ma xale yu góor yi daldi naan |
|
dafa bàyyi woon ay waajuram moo tax mu alku |
|
seen ndën li yal nangeen ko yàgga def |
|
kon dey ma dal di tegale samay ndab te dem |
|
yaay ji ni ko benn lam bu ma sa baay mayoon bi mu ma takkee |
|
ñu toogati lu yàgg ba ñépp fàtte |
|
yaay ji ni ko benn lam bu ma sa baay mayoon bi mu ma takkee |
|
jamanoy tàngaay ci teraas bi lañuy lekke |
|
maa ngi nii nag waxal nag loo ma fi mayul ma delloo la ko |
|
leegi li ñu wara def mooy balu ko te daw seeti feneen |
|
fas di nà dov vandé rutimgeer à cà ràv |
|
darkase yi meññuñu ndax bekkoor bi |
|
xale bi raatale na laax bi ci dënn bi |
|
loolu laa amoon lu ma leen di wax wasalaam |
|
xaaral ba nu matal ay gii nga soga bokk |
|
kër gu xate nii kenn mënu fi yar xar |
|
wër nañu xale bi ba tàyyi gisuñu ko |
|
saaga yu ñaaw lay génne ci gémmiñam gi |
|
dégg naa ne kër googa dafay jaay luññutu ko |
|
bu jur gi màngsee dañu leen di abal karas gi |
|
amoon na fi jigéen ju bon ju nekkoon ag ñeenti doomam |
|
mënuma laa dab yaa ma gën a gudd i jéego |
|
toppatool xale bi dafa mel na ku tojal |
|
xaaral ba suuf si màndi nga sog di gas |
|
moo xale bi yow reew nga di waaw lu doon say tànk sax |
|
xawma lu ko jot yaram mi dafa def yu mel ni ay càqar |
|
sama maam a ma defarluloon seN oor bii |
|
mbom la dagg bënn mi nii ni na doon bàmmeelam |
|
mu ngi jonkon ci wetu taal bi di jaaru |
|
mu ngi topp tali bi di tëñëx tëñëxi |
|
balawlaw tàppit malaan a ngoog am yobbaale ko buur |
|
li mu doon daw moo tax noyyi gi gëna gaaw |
|
miskin yu bare la yélimaan jooju daan leel |
|
xale bi laaj ko loo dagge sama butitu njurukaay |
|
tëggkat yi tàmbaleeguñu ñu ngiy foddat ndënd yi |
|
ci wetu seju la toolu banaana yi nekk |
|
wax ju jëkk fasu par la tontu la naaru góor |
|
mu daldi jël li mu soxla dem mu delluwaat ci yaayam ni ko |
|
gàpp bi weesu na bu yàgg dama koy seeti ndax ma soññ ko |
|
dafay gelu yaayam yóbbuleen ko ci moom |
|
góomam bi dafa wunni bi mu ci defee sunguf si |
|
badoolë bou bagn é ligaiye bagn é k mbok ëm |
|
ki sàcc sa nag yi du jaar ci saawo si |
|
bi mu tàmbalee jël garab googu ba tey miiratul |
|
soo ko wutaloon mbaxana doon na baax ci naaj wi |
|
damaa am ab rëq rëq ci li ma doon def |
|
boo ko dénkul woon say mbóot lii du la dal |
|
dafa ko seen rekk ne wëréñ ne mott |
|
dama bëgg xam këf ki mu dugal ci waxande wi lu mu doon |
|
sa ceebu tey bi wesaN na démb dafa xawoon tooy |
|
altine biy ñów lañuy wori bu soobee yàlla |
|
danga bëgg ci sama màngo bi waaye du jaar ci sa bóli |
|
li nga wax leerul nee ma maa ngi jëm béréb sàngam |
|
bu ñu noddee fajar dafa naan fojjet jóg |
|
demal foo jublu yàlla na fa yiwu yàlla jublu |
|
boo fi fekkulee xaalis bu jàppandal duma la mëna dimmali |
|
xale yu tuuti yi nga xam ni xamuñu dara mu bàyyi leen |
|
Nit ka déglu ko ba noppi dal di fiddi |
|
soldaar yi amatuñu bal amatuñu puudër |
|
këriñ gi du gaawa jàpp ndax dafa tooy |
|
bañuñu koo bind matadi gi mu àndal a tax |
|
fekk ma tool ya am na liggéey bu ñu fa war def |
|
lu mpicà baré baré du téré ji dugup |
|
bu ñu bëggee falu di wuta peeg nit ñi |
|
janq yu ndaw ndawaan yi lañu fiy jàngal togg |