African-NER / inputs /Wolof /Example5.txt
abdullahmubeen10's picture
Upload 58 files
908edf6 verified
raw
history blame contribute delete
334 Bytes
Ciy ati 60 , bokkoon na ci ” Groupe de Grenoble ” kurél gu doon jéem a suqali làmmiñi réew mi mook ñ...
Ciy ati 60 , bokkoon na ci ” Groupe de Grenoble ” kurél gu doon jéem a suqali làmmiñi réew mi mook ñoomin Asan Silla , Masàmba Sare ak Saaliyu Kànji ak it Ablaay Wàdd mi fi doonoon njiitu réewum Senegaal .