audio
audioduration (s)
1.22
171
transcription
stringlengths
6
108
bëgg naa xaj yi.
xaw nanoo dee ak xiif.
afirik sa téere bi, kalaame bu meti la, booy kalaame kopparu euro ak cfa
looloo ma tax a bég ci li ma jot ci yool boobu
xalaat mii a yànj !
mel ne moom it ay jafe-jafey kese la
njariñ li it yal na bari
waxuma la ak lu jëm ci wàllug yoon
foytéefam këmbaan guy lang, 10 ba 30i sàntimet moo di guddaayam.
sopp naa kàggu yi.
i at ba tay, sunuy jafe-jafe ci wàllum paj soppikuwul.
téyéel sa làmmiñ !
lat-joor jóob, dammeelu kajoor
lan mooy taxawaayam?
turu 2 nit ñi wuute ci injiil
bokk nq ci li mu wax di ci tagg sëriñam ba sëriñ tuuba
exquisite-kfind.png ngir xóotal, yërël bii jukki ci jàppum njaam
amna tuuti xaalis.
peeyug kaabu, kansala, la woon
yeen a ngi may gaañ !
ndeem soob na yàlla.
politigu suturaanami jëfandikubindwaay
ndax nun doŋ la ?
koko gi xeetu garab la gu bokk ci njabootu arecaceae.
seen yaay a ngi fi a?
mi ngi ci mbàmb lu ñàng.
lan la loolu di tekki?
bu ngeen xëyatee
sóobarey mbootaayu xeet yi ak askan wa
mbàmbulaan gu atlas
ñenn ngeen ci gaa ñu ndaysaanu ñi !
ku yaroowut ci ab sëriñ dana daje ak coono.
tom nuru na ku am yar.
li dale ci robowam ñetteelu buur ci yuda la woon
dangaa gaañu ?
xalaat naa ne wax na dëgg.
man na wàlle ci lu sew ak ci lu tar
damaa tëdd ngir dallu.
guddaayu yamoo gu suuf si mi ngi tollu, ci xayma, 40 075 km.
ndax nun doŋ la?
maa ngi metitlu ak moom.
nit ñii mat nañu 241 952 2010.
nataali xiirtalukaay yu ndombo yees móol
doo leen xool.
nogoy mi nga xam ne ndawal kër doktoor la, dem na këram seeti ko.
tey-si-tey nag, woowule woy, warees na koo jëmale ci góor ak jigéen
turam feeñ na ci injiil ci ro 1614.
man naa nekk dawaan bu safaanu walla bu wéy.
indoneesi bokkeef bu indoneesi réew
fexee sottal càkkuteef dongay daara ju iseb jamñaajo.
bu jaab yàggee gawar feeñ
daanaka kóoluteem ci goney ekip bi amul àpp
danoo war a tekki.
ubbi njël lu njëkk li
wurus wi moom xalaatunu ko koo laaj
abdu rahmaan léy
damaa bëgg ub dawantu.
bëj-saalum-penku asi ci goxu asi la bokk.
garab gu dëgër lay doon ci jamonoy noor.
ndax am naa pexe ?
dama doon naxaate.
nataalu xobi gàncaxug gerte
sama baay daa jàpp .
pàccu tiyaataram defoon lu rëy.
dangaa war a jug.
ma door a séwét siiwna.
dafa gaaw a yaqu lool.
naa dem sama yoon sax.
noppi naa ngir tàmbali.
i ba tay, lu jóg fëkk nu.
maa ngi doxal barab bii.
man nga cee dem leegi.
danuy dellu ginnaaw.
tasee naa ak moom démb.
jigéen ñi, ñoom, dañ leen daan siif saa su nekk, di leen tëdde
xoolal sa gannaaw .
koorug jàmm na nu ñeel.
sëriñ saaliwu ci melo wuy wone ag ragal yàlla ak ginnaawal àdduna
waxal tom ne maa ngi jéggalu.
paj lan mooy koronaawiris ?
lan moo ma wor ?
ñépp a ko sopp.
limub ñi faatu jóge na ci juróom-ñent ba ñaar-fukk ak ñatt.
ndax sell na ?
ñi ko nàngulul te jàppunu,
bokkeef bu finlaand wu-finlaand suomen tasavalta réewum tugal óróop
te, daanaka, looloo di laago bépp doomu afrig
damaa xaw a xiiw.
ndax dingeen nelaw ?
biraan jaaxle lool, jël sànnikaay bi teg ci tuñ mi.
dawkat bu gaaw la.
mi ngi ak néegu boppam.
kañ la tom egsi ?
seen jataay mboor ak xayte
rfm xamle na ne ŋamtu 51 bi la.
nit ku mukàllaf dina ci am lu toll ci juróomi liitar
damay jàng angale.
ku am wërsëg laa.
kër gi daa yaatu.
am nga dëgg ci xaaj bi.
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
60