start_time
float64 0
2.73M
| end_time
float64 326
2.78M
| speaker_id
stringclasses 55
values | text
stringlengths 1
4.06k
| utterance_pitch_mean
float32 38.3
473
| utterance_pitch_std
float32 0
282
| snr
float64 -3.78
64.6
⌀ | c50
float64 -6.34
60
⌀ | speaking_rate
float64 0
2.1k
| phonemes
stringlengths 0
1.77k
| stoi
float64 0.24
1
| si-sdr
float64 -18.8
28.1
| pesq
float64 1.08
4.37
|
---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|---|
174,684 | 187,254 | 66spk1 | waaw %e yaakaar na ne tay jii %e nit ki bu fekkee ne mi ngi ligéey di am lu muy ruuslu mën a faj soxlaam yaakaar na ne loolu bokk na si li nga xam ne nii dina ko gën a dimbali | 118.555069 | 28.222006 | 17.026285 | 48.697891 | 7.018593 | %i nɑ ni teɪ %i nɪt ki ni mi di æm lu ʌ nɑ ni nɑ si li ni dinʌ koʊ ʌ | 0.953206 | 11.839681 | 1.711502 |
187,254 | 187,707 | 66spk2 | %hum %hum | 127.680428 | 17.05559 | 10.837564 | 8.015578 | 20.512821 | %hʌm %hʌm | 0.949028 | 12.069828 | 1.165648 |
187,707 | 196,246 | 66spk1 | dina ko mën a am mane aafiya dana mën dimbali itam jëkkëram dina ko mën man aafiya dana mën itam dimbali ay doomam ñu gën ko mën gën leen a mën aafiya | 124.030807 | 14.323457 | 16.056957 | 59.733162 | 8.666374 | dinʌ koʊ ʌ æm meɪn deɪnʌ dinʌ koʊ mæn deɪnʌ eɪ koʊ lin ʌ | 0.959543 | 14.196881 | 1.505779 |
203,574 | 209,346 | 66spk1 | ak kër goo xam ne nii baay ba rekk a am ñu tëkkale leen kon yaakaar naa ne foofa faj soxla yi | 142.695297 | 31.539278 | 25.097908 | 54.813801 | 7.450726 | ɡu ni bieɪ ʌ æm lin kɑn ni ji | 0.989143 | 19.842796 | 2.050146 |
213,707 | 265,668 | 66spk1 | moo tax %e te nit ki bu fekkee ne jigéen ji am na mi ngi gën a am mën boppam ci wàllu xaalis dana ko gën a dimbali itam mu gën di avancé ci wàllu %e instances de décision yi maanaam fi ñuy jëlee %e kàddu fi ñuy jëlee pouvoir fi ñuy jëlee ay décisions foo fu bu fekkee jigéen ñi ña nga fay dem foofu itam danañu leen gën a dimbali ndax jigéen jiy ligéey day xam ligéeyam ndax kiy sàmm day xam li muy sàmm ni muy sàmmee xam jafe-jafe sàmm yi xam lan fan la war a sukkandiku sàmm gi jëm kanam kiy bay noonu kiy %e jaay it noonu kon ñoonu dèjà poroblematigu maanaam jafe-jafe yi nga xam ne nii moo nekk ci biir askan bi ñoom itam dañu koy xam seen problème dañu koy xam comme nag ñoo ciy yëngu maanaam liy saafara seen jagaro ñoom dañu koy xam te dañu koy mën a teg ci kaw ci kaw table ji moo tax moo tax %e jàppale jigéen ñi bañ gën a mën a yëngu yéwénal leen bañ gën a mën a am dara en tout cas mo() am na solo | 154.986877 | 32.396832 | 26.960489 | 56.567787 | 7.640768 | mu tæks %i ti nɪt ki ni dʒi æm nɑ mi ʌ æm deɪnʌ koʊ ʌ mu di %i ɪnstʌnsʌz di ji faɪ %i faɪ faɪ eɪ fu fu feɪ lin ʌ deɪ deɪ li ni - ji læn fæn lɑ wɔɹ ʌ beɪ %i ɪt kɑn - ji ni mu baɪ sin næɡ sin ti ʌ teɪbʌl dʒi mu tæks mu tæks %i ʌ ʌ lin ʌ ʌ æm dæɹʌ ɛn taʊt kæs moʊ() æm nɑ soʊloʊ | 0.983333 | 18.824556 | 2.157017 |
274,086 | 277,176 | 66spk2 | mbaadu c' est le monde à l' envers | 197.211456 | 69.011414 | 6.71121 | 41.195919 | 7.447885 | si' ɛst lʌ mɑnd ɛl' | 0.910319 | 7.104292 | 1.457903 |
282,550 | 283,020 | 66spk2 | %hum %hum | 133.457932 | 20.089073 | 7.258833 | 21.196394 | 19.753087 | %hʌm %hʌm | 0.810692 | 5.139788 | 1.17353 |
283,020 | 307,331 | 66spk1 | mais xam nga li ma bëgg a wax foofu rekk mooy que ni tey jii tay mère Anta wax na ko ci wàllu mbay mi xam nga tay jii dañoo nekk si jamono boo xam ne moo xam moo xam góor la wala jigéen la tay jii %e chaine de valeur agricole yi dañoo mën a joxe ligéey bu baree baree bari te xoolal bu fekkee ne baykat bi yéeg na ba yéeg ci kaw xa() gis lu ko commencé ci ab * ba ca commercialisation ñiy dugg yépp si chaine bi | 152.253174 | 44.561844 | 29.364067 | 49.015972 | 8.942275 | meɪs li mɑ ʌ wæks kju ni teɪ wæks nɑ koʊ mi teɪ si bu ni mu mu lɑ wɔlʌ lɑ teɪ %i di æɡɹɪkoʊl ji ʌ bɑɹi ti ni baɪ nɑ bieɪ () lu koʊ æb * bieɪ kʌ si baɪ | 0.990755 | 21.686928 | 2.612896 |
307,331 | 307,729 | 66spk2 | %hum %hum | 99.31234 | 26.527069 | 7.334859 | -1.305336 | 23.188406 | %hʌm %hʌm | 0.921924 | 8.396604 | 1.199496 |
307,729 | 312,756 | 66spk1 | ñooñu tay jii buñ fekkee ni tay jii jox nañu leen gëdd jox nañu leen farataal la mu mënoon jox ci ab ligéey kenn xamul nu mu toll | 156.914459 | 43.972446 | 23.562632 | 47.215218 | 11.572515 | teɪ ni teɪ lin lin lɑ mu æb kɛn nu mu toʊl | 0.985757 | 18.081917 | 2.040955 |
312,756 | 313,096 | 66spk2 | dëgg la | 131.969925 | 7.787245 | 1.944159 | 51.29184 | 8.888889 | lɑ | 0.920338 | 8.137755 | 1.691909 |
313,096 | 330,694 | 66spk1 | beneen bi ci des tay jii am na benn kii boo xam ne tay fokk ñu bàyyi ko xel ndax mbay mi fokk mu libéré tam ay mains maanaam fokk mu am ñu mu bàyyi ñu dem pour mën a créer mooy ñoom mère Anta ñiy def transformation ñoom mën nañoo dem ba tay jii sax duñ xalaati mbay ndax lu tax mooy seen ligéey dootu leen may ñu ñu bayi | 160.168961 | 41.479034 | 27.388914 | 50.836063 | 9.156181 | baɪ dɛs teɪ æm nɑ bɛn bu ni teɪ koʊ mi mu tæm eɪ meɪnz mu æm mu pɔɹ ʌ tɹænsfɜ˞meɪʃʌn bieɪ teɪ sæks lu tæks sin lin meɪ | 0.990154 | 21.052849 | 2.428645 |
330,694 | 331,216 | 66spk2 | %hum %hum | 137.766678 | 7.176337 | 3.661163 | 17.352425 | 17.777777 | %hʌm %hʌm | 0.779359 | -0.379948 | 1.157096 |
331,216 | 341,921 | 66spk1 | su ko defee lu bras yooyu muy libéré dafay créer ay emplois ñooña créer waat yeneen yeneen emplois su ko defee secteur bi day gën di day gën di développé ndax baykat bi xam ne lu mu defar | 170.278824 | 41.194401 | 27.087811 | 48.575314 | 8.692605 | su koʊ dɛfi lu bɹæs eɪ su koʊ dɛfi sɛktuɹ baɪ deɪ di deɪ di baɪ ni lu mu | 0.981452 | 21.007896 | 2.454407 |
341,921 | 342,446 | 66spk2 | %hum %hum | 143.468292 | 14.225761 | 12.060971 | 13.238685 | 17.204301 | %hʌm %hʌm | 0.798954 | 10.356897 | 1.158591 |
342,446 | 348,118 | 66spk1 | am na ku koy soppali kookee soppali am na ku koy jënd fas yéene koo fas yéene koo consommé | 147.576706 | 32.866329 | 28.006802 | 55.186466 | 6.525573 | æm nɑ ku æm nɑ ku ku ku | 0.986588 | 11.229156 | 1.743525 |
356,243 | 356,550 | 66spk2 | %hum %hum | 129.744492 | 6.845788 | 8.193375 | 33.938976 | 29.629629 | %hʌm %hʌm | 0.948306 | 10.492499 | 1.365278 |
356,550 | 369,813 | 66spk1 | noonu jafe-jafe yi ñu doon am yépp Yàlla day def ne dafay dafay saafara %e Fapal comme approche am mooy kër gi na kër gi am doole penc mi am doole bu penc bi amee doole yaakaar naa ne diwaan bi Yàlla mën na ci def sutura | 144.016037 | 45.148602 | 21.698057 | 54.84174 | 5.963671 | - ji æm deɪ ni %i æm nɑ æm mi æm baɪ ni baɪ nɑ | 0.988628 | 17.874088 | 2.141032 |
369,813 | 370,193 | 66spk2 | %hum %hum | 122.938324 | 6.53089 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.763777 | 6.599606 | 1.175007 |
370,193 | 384,617 | 66spk1 | loolu mooy philosophie Fapal exploitation familiale bi na am doole groupement bi am doole groupement bi am doole commune bi communauté bi am am doole te loolu lépp lu ko may fokk ñu am liberté te liberté boobu ligéey moo koy | 141.710403 | 28.503843 | 27.285826 | 58.747456 | 8.326828 | ɛksplɔɪteɪʃʌn baɪ nɑ æm ɡɹupmʌnt baɪ æm ɡɹupmʌnt baɪ æm kɑmjun baɪ baɪ æm æm ti lu koʊ meɪ æm ti mu | 0.989098 | 20.587612 | 2.365511 |
384,617 | 385,322 | 66spk2 | %hum %hum | 136.596237 | 11.438103 | 1.360005 | 10.848014 | 13.00813 | %hʌm %hʌm | 0.753624 | -0.277825 | 1.159834 |
385,322 | 385,801 | 66spk1 | moo koy maye | 109.065895 | 5.779555 | 19.844662 | 34.049873 | 14.814815 | mu meɪ | 0.975184 | 11.865716 | 2.163599 |
385,801 | 391,455 | 66spk2 | %hum %hum %e xam naa ne li ñu dese ci ay simili bariwul waaye maman Anta ndax tay jii ci waxtaan bi | 151.831177 | 28.762753 | 22.538818 | 59.588257 | 7.783306 | %hʌm %hʌm %i ni li eɪ teɪ baɪ | 0.985701 | 22.240791 | 2.533804 |
391,455 | 391,799 | 66spk1 | %hum %hum | 183.602173 | 5.699935 | 8.966568 | 27.998102 | 26.666666 | %hʌm %hʌm | 0.845375 | 10.927862 | 1.247367 |
391,799 | 395,152 | 66spk2 | am na loo xamante ne bëggoon nga koo wax fekk samay laaj àggu fa | 149.891754 | 18.104086 | 24.097666 | 57.977398 | 8.380097 | æm nɑ lu ni ku wæks | 0.976867 | 8.283544 | 1.694871 |
397,415 | 403,729 | 66spk1 | %e waaw kon amady jërëjëf %e mu ba mu mel ne lu bari ci laay yi daal lu bari ci li ma bëggoon a wax de | 206.226364 | 28.006182 | 30.140982 | 54.861473 | 11.364789 | %i kɑn %i mu bieɪ mu mɛl ni lu bɑɹi ji lu bɑɹi li mɑ ʌ wæks di | 0.974182 | 19.626886 | 2.224695 |
412,359 | 412,884 | 66spk2 | %hum %hum | 135.770599 | 12.160245 | 10.254653 | 47.172585 | 17.204301 | %hʌm %hʌm | 0.880812 | 13.254703 | 1.168451 |
412,884 | 427,149 | 66spk3 | %e li ma bëgg daal mooy gën a yokk jigéen ñi ñu gën a tekki ndaxte am na ay tailleur yoo xam ne sii yu jigéen lañ ñu ngi ubbi seen i atelier boo demee Géoul tay lu mel ne commune Kelle Gueye %e am na fa atelier yu bari yoo xam ne ay tailleur ñoo yu ji() tailleur yu jigéen ñoo ko yore | 197.534485 | 28.332474 | 32.601017 | 47.958817 | 9.747973 | %i li mɑ ʌ ʌ æm nɑ eɪ ju ni ju sin aɪ bu teɪ lu mɛl ni kɑmjun %i æm nɑ ju bɑɹi ju ni eɪ ju dʒi() ju koʊ jɔɹ | 0.984461 | 21.355259 | 2.466645 |
427,149 | 427,548 | 66spk2 | %hum %hum | 155.829605 | 17.288708 | 11.542249 | 20.141613 | 23.188406 | %hʌm %hʌm | 0.976274 | 17.51067 | 1.539366 |
427,548 | 447,592 | 66spk3 | yoo() ñooña ñépp ay jigéen lañu yoo xam ne si dañoo sukandiku ba defar seen i ay places jël ay xale yu góor ànd fa ak ñoom ñuy ñuy ñuy ñaw di di di di teral seen kër di teral seen ay njaboot xale yu góor ya nga xam ne ñoo fay xëy ñoom itam aussi noonu ña nga cay jéem a teral seen i waayjur kon lépp loo xam ne si entreprise la %e jëm rekk | 196.080963 | 42.650524 | 30.67662 | 55.932999 | 7.987769 | ju() eɪ ju ni si bieɪ sin aɪ eɪ pleɪsʌz eɪ ju di di di di sin di sin eɪ ju jɑ ni feɪ keɪ ʌ sin aɪ kɑn lu ni si lɑ %i | 0.986196 | 22.277966 | 2.523213 |
451,319 | 459,715 | 66spk3 | am na solo ndaxte ñun daal %e jigéen ñi nga xam ne sii ñoo fi nekk sonn nañu seen i fit sax buñu tëddee tamit nag duñu nelaw buñu waxee dëgg te muy dëgg | 195.882507 | 33.171898 | 26.818058 | 46.648792 | 8.397061 | æm nɑ soʊloʊ %i ni faɪ sɑn sin aɪ fɪt sæks næɡ ti | 0.979143 | 20.052982 | 2.200924 |
459,715 | 460,149 | 66spk2 | %hum %hum | 135.018524 | 12.673389 | 2.106683 | 42.961494 | 21.333333 | %hʌm %hʌm | 0.877749 | 10.616612 | 1.229802 |
460,149 | 467,560 | 66spk3 | ndaxte sunu xale yi ñu baree bari ñi ngi bëgg a tekki luñu def %e xooluñu ludul dugg ci biir gaal yi des ci des ci ndox mi | 206.718613 | 56.978779 | 26.577782 | 58.66048 | 7.021239 | ji bɑɹi ʌ %i ɡɑl ji dɛs dɛs mi | 0.964577 | 21.162548 | 2.283107 |
467,560 | 468,013 | 66spk2 | %hum %hum | 138.856018 | 27.190109 | 20.427624 | 59.522465 | 20.512821 | %hʌm %hʌm | 0.956911 | 13.704513 | 1.368889 |
468,013 | 472,321 | 66spk3 | ba fii ma la koy waxee nii dëkk bii ma dëkk di Nangur Ndiaye am na néew boo xam ne kenn dencagu ko maara deytaali | 199.874115 | 40.744762 | 41.359608 | 57.220203 | 11.619463 | bieɪ mɑ lɑ mɑ di æm nɑ bu ni kɛn koʊ | 0.989472 | 21.176266 | 2.571933 |
472,321 | 472,683 | 66spk2 | %hum | 190.736649 | 43.355701 | 18.018442 | 49.17408 | 11.287478 | %hʌm | 0.964651 | 15.096834 | 1.646537 |
472,683 | 520,018 | 66spk3 | te ba mu faatoo ak léegi %e léegi mu mat deux mois %e yaayam xalaat na ginaaw bi ba mujjee faatu te néew boobu ñëwagul yaayam rob nañu ko ba fàtte ko te néew boobu ñëwagul te li leen ko yóbbee lépp mooy bëgg a tekki kon képp koo xam ne tekkil nga jigéen tekkil nga ay njabootam mu mën a toog di géré ay entreprises am fi mu dëkk ñii di %e yar jur gi ñii di dem ci mbay mi ñii di dem ci càmm gi ñii di dem ci %e poulailler yi ñii di dem ci yeneen %e ki maanaam lu mel ne ndox mi %e ñu am ay forage yoo xam ne sii tay si tay buñu ligéeyoon bu nawet bi doxulee sax dañuy daal de turnewaat nekk ci biir forage yooyu ndaw ya di ca yëngu ndaw yooya di ca yëngu xëy di wàcc bu weer deewee ñu tallal seen loxo ñu am luñu ca teg duñu def nii ñuy def di ray seen bopp ci %e ndox mi te lépp bëgg a tekki rekk moo ko waral maanaam du ma leen yedd lu bari sax ndax lée() ku ci jóg rekk danag bëgg a tekki | 213.174927 | 43.759605 | 33.127804 | 53.936195 | 8.809666 | ti bieɪ mu %i mu mæt du %i nɑ baɪ bieɪ ti ɹɑb koʊ bieɪ koʊ ti ti li lin koʊ ʌ kɑn ku ni eɪ mu ʌ di eɪ æm faɪ mu di %i di mi di di %i ji di %i ki lu mɛl ni mi %i æm eɪ fɔɹɪdʒ ju ni teɪ si teɪ baɪ sæks di fɔɹɪdʒ jɑ di kʌ di kʌ di sin æm kʌ di ɹeɪ sin bɑp %i mi ti ʌ mu koʊ du mɑ lin lu bɑɹi sæks () ku ʌ | 0.979741 | 22.076519 | 2.633844 |
520,018 | 520,398 | 66spk2 | %hum %hum | 142.938889 | 6.941185 | 1.902796 | 51.608952 | 24.242424 | %hʌm %hʌm | 0.74356 | 4.081275 | 1.139544 |
520,398 | 543,873 | 66spk3 | kon képp koo xam ne sii yaa jàppale jigéen jàppale nga ko ci njabootam su tëddee day gën a nelaw su dana gën a mën a yandoor dina gën a mën a continué itam ligéey bi nga xam ne moom la doon def kon daal ñun tallal nañu suñuy loxo ñëpp rekk muy gouvernement muy %e Fapal Fapal moom gàcce ngaalaama li mu def moom bu ko ñépp defoon rekk bu soobee Yàlla bu ci ñaar ak ñett ñu mel ne moom jàppoon rekk bu soobee Yàlla ñun dañuy daal di avancé dem ca kanam | 188.147903 | 35.37392 | 34.43681 | 52.178535 | 6.603296 | kɑn ku ni koʊ su deɪ ʌ su deɪnʌ ʌ ʌ dinʌ ʌ ʌ baɪ ni lɑ kɑn %i li mu koʊ mɛl ni di kʌ | 0.987024 | 20.71825 | 2.401636 |
543,873 | 547,318 | 66spk2 | d' accord donc %e lan ngay tàggatoo ndax émission bi daanaka jeex na | 155.485596 | 25.169764 | 28.222801 | 56.069416 | 8.933557 | di' ʌkɔɹd %i læn baɪ nɑ | 0.979501 | 20.186993 | 2.355116 |
547,318 | 556,053 | 66spk3 | %hum kon li may tàggatoo daal mooy di sant sama mbokk jigéen yépp di sant sama alaaji moom mi nga xam ne si moomay bàyyi nag bu ma ko tàggoo du ne ma doo dem | 211.428268 | 43.340328 | 32.785881 | 52.857838 | 10.201304 | %hʌm kɑn li meɪ di sænt sɑmʌ di sænt sɑmʌ mi ni si næɡ mɑ koʊ du ni mɑ du | 0.983582 | 23.009291 | 2.67932 |
571,632 | 603,837 | 66spk3 | ak li ñu daan waxtaanee ak ñoom ñu jéem koo jàpp te jéem koo jëfee jéem a am xam-xam jéem a ligéey jéem a tekkil suñuy njaboot ba bu ëllëgee ku fi jógeeti maaradaytaali Yàlla na yéex nga bàyyi fi loo xam ne si say njaboot daañu ci mën a sukandiku ba duñ def naka sudul noonu ndax xale moom bu taxawaaloo def naka sudul noonu kon ñoo ngi leen di sant te di leen gërëm te di ñan Yàlla Ibrahima mi nga xam ne moom lañu Yàlla booleel Yàlla na ko Yàlla dooleel fu lu fu jigéen ñi égg rekk boo yaboo mane la taxawaayam ma nga fa ndaxte ñun bàyyiwuñu si kàddoom mi ngi wax ak ñun ci suuf mi ngi wax ak ñun ci kaw bu waxul ak ñun ci kaw ci rajo mi ngi wax ak ñun ci suuf | 202.240723 | 45.099789 | 35.263134 | 54.969906 | 7.888812 | li ku ti ku ʌ æm - ʌ ʌ bieɪ ku faɪ nɑ faɪ lu ni si seɪ ʌ bieɪ kɑn lin di sænt ti di lin ti di mi ni nɑ koʊ fu lu fu bu meɪn lɑ mɑ si mi wæks mi wæks mi wæks | 0.988805 | 23.016479 | 2.578778 |
605,593 | 633,059 | 66spk3 | lépp loo xam ne sii njëriñu jigéen la rekk Ibrahima a ngi taxaw si suñ kanam di ko def kon ñoo ngi koy sant te di ko gërëm di sant suñu monsieur le maire ndax lépp mooma ndax lu mu dee dee mooy mooy mooy suñu présidente mooy suñu président kon fuñ fuñ fuñ dem fu nekk war nañu faa tudd turam sant ko ñaanal ko ndax %e lu xew rekk fi ñu toll ci moomeelam la xewee kon ñu dund ak jàmm ba nga xam ne sii %e nekk na fi ba jóge fi keneen ku ko yore itam ku muy sa wërsëg nga yore ko Yàlla na ko Yàlla def ci jàmm ak salaam | 201.910202 | 33.651325 | 30.061701 | 56.332294 | 9.178447 | lu ni lɑ ʌ si di koʊ kɑn sænt ti di koʊ di sænt mʌsjɜ˞ lʌ mɛɹ lu mu di di kɑn fu wɔɹ sænt koʊ koʊ %i lu faɪ toʊl lɑ kɑn bieɪ ni %i nɑ faɪ bieɪ faɪ ku koʊ jɔɹ ku sɑ jɔɹ koʊ nɑ koʊ sʌlɑm | 0.986458 | 21.086161 | 2.368931 |
638,862 | 642,884 | 66spk3 | ku jëndiwul jaayiwoo defar sa poulailler wala nga yar say xar wala nga yar say ginaar | 204.184814 | 37.711273 | 30.321257 | 40.324318 | 8.21662 | ku sɑ wɔlʌ seɪ wɔlʌ seɪ | 0.988651 | 23.473206 | 2.861055 |
645,417 | 649,868 | 66spk2 | merci beaucoup maman Anta Gueye ah voilà donc Ibrahima | 144.782562 | 24.797028 | 24.513857 | 41.413685 | 4.281087 | mɜ˞si boʊku ɑ | 0.959307 | 17.50668 | 1.906393 |
649,868 | 656,491 | 66spk1 | %e jërëjëf amady %e fi mère Anta daanelee foofu laay commencé | 123.912766 | 32.908203 | 16.82089 | 59.274376 | 2.87226 | %i %i faɪ | 0.933864 | 3.053327 | 1.345511 |
656,491 | 656,961 | 66spk2 | %hum %hum | 138.264557 | 14.10246 | 25.502769 | 59.638714 | 19.753087 | %hʌm %hʌm | 0.886514 | 11.954213 | 1.233445 |
656,961 | 678,788 | 66spk1 | ci jigéen ñi mooy que ne képp koo xam ne nii bëgg ngaa taxawal entreprise soo ñëwee Fapal daañu la wax ci yoon wi nga jaar pour entreprise bi nga bëgg a taxawal moo xam entreprise individuelle la moo xam GIE la moo xam société la moo xam SARL la moo xam daal façon société socié() en() entreprise bi nga bëgg a taxawal soo ñëwee Fapal daañu la teg ci yoon woo ko woo ko taxawalee | 130.112137 | 27.08168 | 24.222557 | 50.93449 | 6.782963 | kju ni ku ni su lɑ wæks jun pɔɹ baɪ ʌ mu lɑ mu lɑ mu lɑ mu lɑ mu () ɛn() baɪ ʌ su lɑ jun wu koʊ wu koʊ | 0.973433 | 4.603582 | 1.623331 |
678,788 | 679,331 | 66spk2 | %hum %hum | 121.11692 | 11.611721 | null | null | 900 | %hʌm %hʌm | 0.779904 | 9.512601 | 1.141042 |
679,331 | 730,370 | 66spk1 | %e beneen bi ci des mooy %e li mère Anta wax fokk jigéen ñi gën a taxawaat gën a takkuwaat ah te fas yéene bokk ci ñi nga xam ni ñooy suqali njaboot gi njaboot gi mooy taxawal ay entreprises yoo xam ne ni entreprise yu am doole lay doon entreprise yoo xam ne nii ñoom daañu ci mën a am %e faj seen soxla faj si seen i soxlay soxlay doom loolu nag %e mën naa nekk mën naa nekk dañu koy gëm dañu koy gëm mais buñu nee warut a mën a nekk rekk du sotti mais dañuy gëm ne ñoom fii ñu jëm war nañu faa mën a àgg mooy créer ay entreprises comme ni mu amee Europe amee feneen kon africain yi itam sénégalais yi ak surtout njambur njambur yi am nañu possibilité bi te am na ñoo xam ne nii jigéen ñoo xam ne nii tay jii dàggi nañu seen bopp ba tay jii daanaka %e vraiment %e maasaa àllaa yaakaar naa boo xoolee ci lot bii rekk danga ko fiy danga ko fiy gis | 138.658188 | 23.535093 | 27.663343 | 50.42569 | 6.564766 | %i baɪ dɛs %i li wæks ʌ ʌ ɑ ti ni eɪ ju ni ni ju æm leɪ ju ni ʌ æm %i sin si sin aɪ dum næɡ %i meɪs ni ʌ ʌ du soʊti meɪs ni wɔɹ ʌ eɪ ni mu jʊɹʌp kɑn ji ji ji æm baɪ ti æm nɑ ni ni teɪ sin bɑp bieɪ teɪ %i %i bu lɑt koʊ koʊ | 0.98431 | 19.885893 | 2.030566 |
735,537 | 744,731 | 66spk1 | wuti xibaar bi fan la xibar bu baax bi nekk loolu fokk ñu loolu itam ku ci ñëw Fapal laaj ko daañu leen wax gindi ci wàllu financement | 151.823792 | 24.130043 | 29.506908 | 47.415157 | 6.64488 | baɪ fæn lɑ baɪ ku koʊ lin wæks fɪnænsmʌnt | 0.991715 | 23.440128 | 2.646111 |
750,971 | 752,710 | 66spk1 | ñëw daañu la daañu la gindi | 184.227554 | 29.995956 | 19.932909 | 43.080898 | 5.177994 | lɑ lɑ | 0.967177 | 18.858688 | 2.407362 |
752,710 | 753,072 | 66spk2 | %hum | 140.527557 | 8.654091 | 2.652534 | 33.049839 | 11.287478 | %hʌm | 0.828207 | 15.325747 | 1.165647 |
753,072 | 818,379 | 66spk1 | wax la yan yoon ngay jaar pour am financement yan yoon ngay jaar pour am formation yan yoon ngay jaar pour sa jëmal sa entreprise kanam budee lu mel ni que business :en plan la budee jigéen bi ne nekk membre Fapal boo ñëwee daañu la jàppale ba nga am sa business :en plan danga am sa plan commercial wala nga am sa plan de sa plan de développement li ma bëgg a wax daal mooy Fapal moom taxaw na pour gunge jigéen ñi ba ci biir tay jii %e écosystème bi wala book ci biir en tout cas territoire bi wala boog territoire gi mu nekk jigéen boo xam ne membre Fapal nga soo dee ñëw Fa() di diisoo ak Fapal wala di wax papa sox() di diis sa bopp Fapal te bëgg a jëm ci kanam insaa àllaa Yàlla mën na laa jàppale ba nga jëm ci kanam ndax daañu la teg ci yoon daañu la teg ci xàll woo xam ni boo ci jaaree doo ko réccu ëllëg kon ñu ngi sant ñëpp di gërëm ñëpp di gërëm président %e Baye Moussa Moussa Ndiaye %e di gërëm Malick sow %e di gërëm Modou Ndiaye ak Idy ak staf Fapal bi yépp maanaam ñépp bàyyiwuñu kenn di gërëm auditeurs yépp ak auditrices yépp %e di beral loxo nag %e unité de transformation bi ndax bokk na ci tay jii bu fekkee takk %e tekki jigéen ñi ñëw na ñoom foofu la ko jaaralee | 145.569443 | 28.04563 | 29.266441 | 53.379608 | 9.53777 | wæks lɑ jæn jun pɔɹ æm fɪnænsmʌnt jæn jun pɔɹ æm fɔɹmeɪʃʌn jæn jun pɔɹ sɑ sɑ lu mɛl ni kju bɪznʌs :ɛn plæn lɑ baɪ ni bu lɑ bieɪ æm sɑ bɪznʌs :ɛn plæn æm sɑ plæn kʌmɜ˞ʃʌl wɔlʌ æm sɑ plæn di sɑ plæn di li mɑ ʌ wæks nɑ pɔɹ bieɪ teɪ %i baɪ wɔlʌ bʊk ɛn taʊt kæs baɪ wɔlʌ mu bu ni su di () di wɔlʌ di wæks pɑpʌ sɑks() di sɑ bɑp ti ʌ nɑ bieɪ lɑ jun lɑ wu ni bu du koʊ kɑn sænt di di %i beɪ maʊsʌ maʊsʌ %i di mælɪk saʊ %i di baɪ kɛn di %i di næɡ %i di tɹænsfɜ˞meɪʃʌn baɪ nɑ teɪ %i nɑ lɑ koʊ | 0.993473 | 23.420315 | 2.677316 |
828,331 | 863,170 | 66spk2 | voilà merci %e Ibrahima kon nag %e yéen mbokki auditeurs yi yéen tamit %e sant nañu leen gërëm nañ leen lii nag moo nekkoon ñaareelu émission bi nga xamante ne waa %e United :en Purpose :en ak %e ci projet bii di tekki jigéen bi nga xam ne %e waa USAID ñoo ko financé ci jàppaleb Jokalante ak waa Fapal ñoo leen mayoon émission bi fii ci Louga FM RTS %e 88.7 ñu ngi leen di gërëm di leen sant di leen jaajëfal di leen jox dig daje ba beneen yoon Louga Fm 88.7 station original RTS | 209.693802 | 132.957367 | 34.943985 | 54.07518 | 9.292678 | mɜ˞si %i kɑn næɡ %i ji %i sænt lin lin næɡ mu baɪ ni %i junaɪtɪd :ɛn pɜ˞pʌs :ɛn %i di baɪ ni %i juɛseɪd koʊ lin baɪ ɛfɛm %i . lin di di lin sænt di lin di lin dɪɡ bieɪ jun ɛfɛm . steɪʃʌn ɜ˞ɪdʒʌnʌl | 0.989169 | 21.691137 | 2.747647 |
0 | 1,212 | 99spk1 | %e ANACIM | 116.877457 | 24.796038 | 13.994262 | 59.497791 | 2.503912 | %i | 0.928037 | 13.954322 | 2.01122 |
1,212 | 1,822 | 99spk2 | ANACIM | 129.223572 | 12.28953 | 26.567579 | 59.634171 | 0 | 0.989585 | 19.510025 | 2.342354 |
|
1,822 | 5,799 | 99spk1 | waa donc ñoom ñoo yore lu jëm ci mbirum jaww bi ñu taw bi | 113.346413 | 12.608604 | 20.300411 | 59.213963 | 6.052009 | jɔɹ lu baɪ baɪ | 0.936656 | 8.289814 | 1.760471 |
5,799 | 6,165 | 99spk2 | %hum %hum | 119.907799 | 27.629147 | 34.595131 | 12.688581 | 25.396825 | %hʌm %hʌm | 0.982626 | 19.318184 | 2.038173 |
6,165 | 8,479 | 99spk1 | donc ñoom ñoo ñuy ne goxu sàngam | 120.407082 | 13.308867 | 19.197163 | 59.215408 | 3.460395 | ni | 0.96249 | 10.727284 | 2.047675 |
8,479 | 8,808 | 99spk2 | %hum %hum | 148.366562 | 19.878708 | 51.359051 | 15.60982 | 28.070175 | %hʌm %hʌm | 0.993524 | 22.695824 | 2.292585 |
8,808 | 10,425 | 99spk1 | ndox bi manqué fa | 102.399025 | 20.081553 | 15.645823 | 59.524368 | 3.74269 | baɪ | 0.97937 | 11.737864 | 2.018453 |
10,425 | 10,785 | 99spk2 | %hum %hum | 124.669708 | 12.694473 | 55.38604 | 20.488138 | 25.396825 | %hʌm %hʌm | 0.994575 | 23.329815 | 2.551013 |
10,785 | 14,406 | 99spk1 | mais bu manqué jarul sax %e baykat bi di ñu si ne ndox manqué na wala leneen | 143.002701 | 22.929329 | 19.050568 | 59.05172 | 11.35341 | meɪs sæks %i baɪ di si ni nɑ wɔlʌ | 0.973677 | 14.55019 | 2.187963 |
14,406 | 14,679 | 99spk2 | %hum %hum | 145.743607 | 25.162441 | 14.676966 | 24.383804 | 33.333332 | %hʌm %hʌm | 0.925282 | 7.071635 | 1.224946 |
14,679 | 16,270 | 99spk1 | ñun si foofu la ñuy sukkandiku rekk | 136.053711 | 33.578209 | 20.038185 | 39.44759 | 6.934594 | si lɑ | 0.884816 | 3.415455 | 1.254582 |
16,270 | 16,560 | 99spk2 | %hum %hum | 141.389618 | 4.018491 | 21.964361 | 25.351381 | 31.372548 | %hʌm %hʌm | 0.917459 | 24.854815 | 1.663667 |
16,560 | 17,599 | 99spk1 | pour jox ko ndàmpaayam | 104.838448 | 17.998955 | 12.72167 | 37.320839 | 9.714633 | pɔɹ koʊ | 0.950487 | 11.827732 | 1.412968 |
17,599 | 23,498 | 99spk2 | pour jox ko ndàmpaayam am nañu dafa mel ne am na ku njëkk nekk ci %e ligne bi ñu jël ko %e salaamaaleykum | 161.175079 | 31.936728 | 32.556332 | 47.696941 | 10.164209 | pɔɹ koʊ æm mɛl ni æm nɑ ku %i baɪ koʊ %i | 0.991165 | 23.49259 | 2.786988 |
23,498 | 24,284 | 99spk3 | maaleykum salaam | 146.456375 | 83.262665 | 14.120496 | 44.651051 | 7.729469 | sʌlɑm | 0.841995 | 11.931272 | 1.703619 |
24,284 | 25,663 | 99spk2 | sëñ bi ziyaar nañ la | 129.949219 | 37.89809 | 25.348965 | 52.96875 | 6.584362 | baɪ lɑ | 0.995267 | 22.367346 | 3.266856 |
25,663 | 27,394 | 99spk3 | *** ñu ngi lay delloo ziyaara | 186.158142 | 74.336716 | 17.880894 | 42.827621 | 6.390704 | *** leɪ | 0.580422 | -15.165666 | 1.202518 |
27,394 | 29,378 | 99spk2 | %e noo tudd ak foo ñuy woowee | 213.054153 | 63.954975 | 37.777821 | 40.599693 | 5.064894 | %i fu | 0.997522 | 25.222973 | 3.332279 |
29,378 | 31,079 | 99spk3 | man la Mbaye Gaye maa ngi wootee Thiamène | 241.297379 | 76.756287 | 21.736235 | 46.094185 | 8.888889 | mæn lɑ ɡeɪ | 0.978125 | 23.883772 | 2.752729 |
31,079 | 32,474 | 99spk2 | Mbaye Guèye bu Thiamène | 155.386597 | 36.837788 | 46.845711 | 59.437546 | 2.168022 | 0.9954 | 24.529278 | 3.559145 |
|
32,474 | 33,569 | 99spk3 | waa Mbaye gaye Gaye | 223.276077 | 95.149849 | 17.869026 | 30.856979 | 8.333333 | ɡeɪ ɡeɪ | 0.849383 | 17.082623 | 2.099151 |
33,569 | 34,544 | 99spk2 | Mbaye Gaye | 135.72493 | 35.370197 | 53.007904 | 59.660751 | 4.158544 | ɡeɪ | 0.997403 | 25.567017 | 3.637274 |
34,544 | 35,028 | 99spk3 | waaw | 112.221252 | 2.905612 | 11.006571 | 35.281658 | 0 | 0.412853 | -13.213476 | 1.221825 |
|
35,028 | 37,166 | 99spk2 | Mbaye Gaye ndax mën naa am sa numéro téléphone | 177.409088 | 27.051346 | 39.584846 | 58.362743 | 7.524985 | ɡeɪ æm sɑ | 0.993943 | 20.592394 | 3.064846 |
37,166 | 38,662 | 99spk3 | waaw moom kay bu baax yomb na | 232.818115 | 64.698883 | 14.865617 | 25.133137 | 7.407407 | keɪ nɑ | 0.978218 | 25.31324 | 3.642125 |
38,662 | 40,312 | 99spk2 | %hum %hum ñaata la | 221.876511 | 86.966537 | 44.341156 | 58.912334 | 7.941962 | %hʌm %hʌm lɑ | 0.977159 | 17.897507 | 2.840286 |
40,312 | 41,016 | 99spk3 | 77 | 227.647781 | 61.235928 | 18.476307 | 38.764107 | 0 | 0.899293 | 6.371434 | 1.576738 |
|
41,016 | 41,771 | 99spk2 | waaw | 169.769714 | 33.785278 | 24.046556 | 51.923756 | 0 | 0.981029 | 24.193747 | 3.121911 |
|
41,771 | 43,213 | 99spk3 | 522 | 184.365845 | 54.288563 | 24.65358 | 37.873856 | 0 | 0.877989 | 17.411228 | 2.153866 |
|
43,213 | 44,603 | 99spk2 | 522 waaw | 172.406403 | 58.68404 | 41.609287 | 58.308498 | 0.722674 | 0.993011 | 23.670345 | 3.257028 |
|
44,603 | 45,652 | 99spk3 | 57 | 225.687302 | 108.107216 | 23.340839 | 36.003521 | 0 | 0.942791 | 13.124122 | 1.835597 |
|
45,652 | 46,743 | 99spk2 | 57 waaw | 172.649185 | 23.235415 | 29.236526 | 59.505836 | 0.925926 | 0.989988 | 21.661982 | 2.961138 |
|
46,743 | 47,672 | 99spk3 | 22 | 161.51062 | 40.166229 | 12.146041 | 33.367348 | 0 | 0.872171 | 10.519608 | 1.490064 |
|
47,672 | 48,383 | 99spk2 | 22 | 138.657318 | 27.304886 | 44.549248 | 51.299362 | 0 | 0.994807 | 21.329863 | 2.815517 |
|
48,383 | 49,071 | 99spk3 | waa | 117.566345 | 3.578303 | 6.459244 | 34.82695 | 0 | 0.358753 | -15.076697 | 1.204108 |
|
49,071 | 52,671 | 99spk2 | alors donc %e dafa am loo buggoon laaj Abdoulaye Deme mu ngi lay déglu | 227.100662 | 95.039833 | 51.26926 | 57.653427 | 6.6771 | %i æm lu mu leɪ | 0.997885 | 24.664272 | 3.219034 |
52,671 | 56,132 | 99spk3 | waaw dama koy laaj ku bëgg maanaam ku bëgg a bokk ci assurance bi nan nan ngay def ba bokk ci | 245.852798 | 87.694221 | 23.437033 | 37.468937 | 14.164409 | dɑmʌ ku ku ʌ ʌʃʊɹʌns baɪ næn næn bieɪ | 0.818014 | 10.362091 | 2.400473 |
56,132 | 56,852 | 99spk2 | %hum %hum | 111.450043 | 38.117748 | 17.924196 | 26.746416 | 12.698413 | %hʌm %hʌm | 0.966635 | 19.875359 | 1.754727 |
56,852 | 62,373 | 99spk3 | %hum * ndax man sama tool yi dafa bari ay *** mbaam yi ñoo ma sonal trop mbaamu pël yi ñoo ma sonal | 225.611786 | 100.26165 | 22.262299 | 39.207211 | 11.809674 | %hʌm * mæn sɑmʌ tul ji bɑɹi eɪ *** ji mɑ ji mɑ | 0.876098 | 13.114799 | 2.374 |
62,373 | 63,913 | 99spk2 | mbaamu pël yi ñoo la sonal | 150.74884 | 30.303493 | 36.535439 | 56.716801 | 5.860806 | ji lɑ | 0.98766 | 23.375269 | 3.260729 |
63,913 | 65,066 | 99spk3 | waa ñoo ma sonal lool | 151.788162 | 41.58894 | 14.293201 | 42.183441 | 6.100218 | mɑ | 0.745495 | -1.000558 | 1.322769 |
65,066 | 68,176 | 99spk2 | d' accord d' accord donc %e Abdoulaye Deme dégg na la | 155.140823 | 19.872578 | 46.212669 | 43.940166 | 10.305958 | di' ʌkɔɹd di' ʌkɔɹd %i nɑ lɑ | 0.987616 | 21.989613 | 3.265723 |
68,176 | 68,791 | 99spk1 | waaw | 108.785645 | 7.55995 | 5.456635 | 10.399984 | 0 | 0.813209 | 3.900982 | 1.234505 |
|
68,791 | 69,286 | 99spk3 | waaw | 88.973541 | 25.332037 | 3.414409 | 45.720184 | 0 | 0.484389 | -12.015139 | 1.196011 |
|
69,286 | 69,706 | 99spk2 | %hum %hum | 147.236984 | 27.24728 | 35.820023 | 26.387732 | 22.222222 | %hʌm %hʌm | 0.867317 | 9.922858 | 1.358552 |
Subsets and Splits