wolof
stringlengths
6
405
french
stringlengths
8
465
english
stringlengths
7
437
Lu moy loolu, benn ndaje ak Trump, mii nekkoon persida bu Amerik ci New York,biraloon nañu ko ci bisu Alkamis.
Une rencontre avec Trump, alors aux Nations Unies, à New York, a plutôt été annoncée pour jeudi.
Instead, a meeting with Trump, who was then at the United Nations in New York, was announced for Thursday.
Trump neena dax kii di Rosenstein "do ko gënal" waaye nak li tax ñu puus ndaje bi moy ngir mooytu ñakk deggoo am ci diggante komite Yoon bu Sena bi doon deglu ci mbir moomu benn jigeen tuumal Kavanaugh ni def kaa sakku, Dr Christen Blasey Ford, waat nañu ñoom ñaar ñepp.
Trump a déclaré qu’il « aimerait mieux ne pas » renvoyer Rosenstein, mais la rencontre a été retardée pour éviter les conflits avec l’audience du Comité judiciaire du Sénat où Kavanaugh et la femme l’accusant d’inconduite sexuelle, la docteure Christine Blasey Ford, allaient témoigner.
Trump said he would "prefer not" to fire Rosenstein but then the meeting was delayed to avoid a clash with the Senate judiciary committee hearing in which Kavanaugh and one of the women who have accused him of sexual misconduct, Dr Christine Blasey Ford, both testified.
Ci bisu Aljuma, Trump diglena lañketu benn ayubes ci li ñuy takkal Kavanaugh, lii gina yeexalaat wote bu Sena lëmm.
Trump a ordonné vendredi une enquête d’une semaine du FBI au sujet des accusations portées contre Kavanaugh, ce qui a retardé davantage le vote du sénat.
On Friday, Trump ordered a one-week FBI investigation of claims against Kavanaugh, further delaying a full Senate vote.
Kii di sekkerteeru yeklekaay bu Trump, Sarah Sanders , feeñ na ci Fox News bisu Dibeer
L’attachée de presse de Trump, Sarah Sanders, était invitée à Fox News samedi.
Trump's press secretary, Sarah Sanders, appeared on Fox News Sunday.
Buñu ko laaje ci ndaje Rosenstein, dafa ne: "Jappaguñu bës ngir loolu, amaana mu doon ci bii ayubes, gisnaa ñu puusaat ko ci beneen ayubes sunu xoole lii xew ci Kuur bu Kawe bi yepp.
Au sujet de la rencontre avec Rosenstein, elle a déclaré : « Aucune date n’a encore été fixée, cela pourrait se passer cette semaine, je crois qu’une autre semaine pourrait être nécessaire en raison de tout se qui se passe avec la Cour suprême.
Asked about the Rosenstein meeting, she said: "A date for that hasn't been set, it could be this week, I could see that pushing back another week given all of the other things that are going on with the supreme court.
Waante dinañu xool te dama bëgg di yégal saasune taskatu xibaar yi."
Mais nous verrons et j’aime m’assurer que la presse soit à jour ».
But we'll see and I always like to keep the press updated."
Yenn reporteer dina ñu bañ yooyu kaddu: Sanders deful benn ndaje ak taskatu xibaar yi ci White House bi li ko dale 10 fan weeru Setammbur ba leegi.
Certains journalistes pourraient contester cette affirmation : Sanders n’a tenu aucun point de presse de la Maison-Blanche depuis le 10 septembre.
Some reporters would contest that assertion: Sanders has not held a White House press briefing since 10 September.
Dalalkat bii di Chris Wallace laajna lu tax.
L’animateur, Chris Wallace, a demandé pourquoi.
Host Chris Wallace asked why.
Sanders neena geja def ay jakkarlo ay xibaarkat yi du bañ ñii di reporteeru tele yi "jaay doole" la ci yokk. "Du ma leen weddil jaay doole gi."
Sanders a affirmé que la rareté des points de presse ne s’expliquait pas par la répugnance de la démagogie manifestée par les journalistes, mais elle a dit : « Je ne dirai pas qu’ils ne font pas preuve de démagogie ».
Sanders said the scarcity of briefings was not due to a distaste for TV reporters "grandstanding," although she said: "I won't disagree with the fact that they grandstand."
Kon ci la digle ap jano bët ci bët diggante taskatu xibaar yi ak Trump.
Elle a ensuite avancé que les contacts directs entre Trump et la presse devraient s’accroître.
She then suggested direct contact between Trump and the press will increase.
Neena "Persida bi moo ëppu lu muy def ay janoo laaj& tontu bepp persida bu ko fii jiituwoon." "Xoolnañu lim yi."
« Le président mène plus de séances de questions que n’importe quel président avant lui », a-t-elle ajouté sans citer de preuves, « Nous avons étudié la question ».
"The president does more Q&A sessions than any president has prior to him," she said, adding without citing evidence: "We've looked at those numbers."
Sanders neena Jottali xibaar dina wey di am, waaye" su taskatu xibaar yi ame saas bu day ni jakkarlo ak persida bi di ko laaj moo gën fuuf ngeen di wax ak man.
Les points de presse auront toujours lieu, mais, « si la presse a l’occasion de poser les questions directement au président des États-Unis, c’est infiniment mieux que de me les poser.
Briefings will still happen, Sanders said, but "if the press has the chance to ask the president of the United States questions directly, that's infinitely better than talking to me.
Deñu koy jéema def lu bari, te gisngeen ñuy def loolu lu bari ci ayubes yu bari yii ñu genni te loolu dina jél palaasu jottali xibaar boo leen mëne wax ak persida bu Amerig.”
Nous essayons de faire ça, vous nous avez vus le faire souvent au cours des dernières semaines et parler au président des États-Unis remplacera les points de presse ».
We try to do that a lot and you've seen us do that a lot over the last few weeks and that's going to take the place of a press briefing when you can talk to the president of the United States."
Trump barina lu muy faral di jël ay laaj buy juge ci White House bi mbaa di bokk ci ay lëlu ligeey ak ay ndaje ak taskatu xibaar yi ak ay kilifa.
Trump répond régulièrement aux questions lorsqu’il quitte la Maison-Blanche ou participe à une séance ouverte ou une conférence de presse lors de visite de dignitaires.
Trump regularly takes questions when leaving the White House or participating in open sessions or press conferences with visiting dignitaries.
Janoo ak taskatu xibaari yow doŋg bariwul.
Les conférences de presse avec lui seul sont rares.
Solo press conferences are rare.
Bii ayubes ci New York munna am persida bi wonena lu tax, jél oto bu sempal ak yenn saa yi melokaan bu xawa doy waar bala muy dajale ay reporteer.
Cette, à New York, le président a possiblement démontré pourquoi avec une présence peu orthodoxe et même bizarre à l’occasion devant des journalistes.
In New York this week the president perhaps demonstrated why, making a freewheeling and at times bizarre appearance before gathered reporters.
Sekkerteer bu wergu yaram bindna ligeeykatu EU ci NHS Ekost ci lu jëm ci titaange wallu Brexit bi
La secrétaire de la Santé écrit aux travailleurs de l’Union européenne du National Health Service en Écosse en raison de craintes à propos du Brexit
Health secretary writes to EU workers at NHS Scotland over Brexit fears
Sekkerteeru wergu yaram bind na ñii di ligeey ci EU ci NHS bu Ekost ngir feddeli kollëre réew ma te di leen ñaanal ñu des su Brexit bi weeso.
La Health Secretary a écrit aux travailleurs de l’Union européenne au sein du National Health Service en Écosse pour exprimer la reconnaissance de pays et pour leur exprimer le souhait qu’ils restent même après le Brexit.
The Health Secretary has written to EU staff working in Scotland's NHS to express the country's gratitude and wish for them to stay on post-Brexit.
Jeanne Freeman MSP yonnena ap bataaxal ñu tollu ci jiroom benn weer bala UK di genni ci EU.
La membre du parlement écossais, Jeane Freeman, a envoyé une lettre moins de six mois avant le retrait du Royaume-Uni de l’Union européenne.
Jeane Freeman MSP sent a letter with less than six months to go until the UK withdraws from the EU.
Nguur bu Ekost parena ngir def lepp lu mu munti jar ngir ñu doon ap réew mu bokk ci EU ak ay sarwiisam yu ñepp bokk.
Le gouvernement écossais a déjà indiqué qu’il compenserait des demandes de statuts préétablis pour les citoyens de l’Union européenne qui travaillent dans ses services publics décentralisés.
The Scottish Government has already committed to meet the cost of settled status applications for EU citizens working in its devolved public services.
Ci biir bataaxal am, soxnaci Freeman neena: "Ci ete bi, waxaale yi diggante UK ak EU ci genni bi mungi wey, jém ci ndogal bu ñu xaar ci otom bi.
Madame Freeman a écrit : « Les négociations entre le Royaume-Uni et l’Union européenne se sont poursuivies durant l’été et des décisions sont attendues au courant de l’automne.
In her letter, Ms Freeman wrote: "Over the summer, negotiations between the UK and EU on withdrawal have continued, heading towards expected decisions this autumn.
Waaye nguur bu UK itam mungi doon lal ay pexe ndax su deme ba juboo bi ñakk am.
Mais le gouvernement du Royaume-Uni a également accéléré sa préparation en cas de séparation sans entente.
But the UK Government has also been stepping up its preparations for a possible no-deal scenario.
Xamnaa ni lii ap jamano bu metti ci yeen la.
Je sais que cette période doit être troublante pour beaucoup d’entre vous.
I know this must be a very unsettling time for all of you.
Moo tax ma bëggoon leegi rafetlu ndimmbalu kenn ku nekk ci ligeeykat yi fekk amul xajj ak seen.
C’est pourquoi je souhaitais réitérer maintenant à quel point la contribution de chaque membre du personnel est appréciée, peu importe votre nationalité.
That is why I wanted to reiterate now how much I value the contribution of every member of staff, regardless of their nationality.
Naataango yu fepp ci EU, ak fenee,; ñungi ñuy inndil xam xam yu ama am solo lool, ak ay xarañteef yuy doolel aki yokk ligeeyu sarwiisu wergu yaram bi, di jeriñfajukat yi ak askan wii ñuy ligeeyal.
Les collègues de toute l’Union européenne et au-delà apportent une expérience et une expertise précieuses qui renforcent et qui améliorent les services se santé et qui profitent aux patients et aux collectivités que nous servons.
Colleagues from across the EU, and beyond, bring valuable experience and skills that strengthen and improve the work of the health service, and benefit the patients and communities we serve.
Ekost sa dëkk la te bëggna nu nga toog fi."
L’Écosse est absolument votre pays et nous souhaitons avec vigueur que vous y restiez ».
Scotland is absolutely your home and we very much want you to stay here."
Christion Abercrombie mungi amal ap oppeere bu munul ñakk ginnaaw bi mu ame ay tolof tolof ci gaañu gaañu bopp
Christion Abercrombie subit une opération d’urgence après une blessure à la tête
Christion Abercrombie Undergoes Emergency Surgery After Suffering Head Injury
Yeglekkat bii di Mike Organ buTennessean xamlena ni Christion Abercrombie mii nekk app defaaseer ci Tennessee State Tigers defa defoon oppeere bu munulwoon ñakk ginnaaw bi mu ame ay gaañu gaañu ci bopp bi ci bisu Samdi.
Le secondeur des Tigers de Tennessee State, Christion Abercrombie, a subi une intervention chirurgicale d’urgence après s’être blessé à la tête lors de la défaite de 31 à 27 de son équipe samedi face aux Vanderbilt Commodores, selon Mike Organ du Tennessean.
Tennessee State Tigers linebacker Christion Abercrombie underwent emergency surgery after suffering a head injury in Saturday's 31-27 defeat to the Vanderbilt Commodores, the Tennessean's Mike Organ reported.
Rod Reed anterneeru Tennessee State neena reporteer yi ni moom mungi ame gaañu gaañu bi bala xaaj bu njékk bi.
L’entraîneur en chef de l’équipe de Tennessee State, Rod Reed, a déclaré aux journalistes que la blessure était survenue juste avant la mi-temps.
Tennessee State head coach Rod Reed told reporters the injury happened shortly before halftime.
Reed neena " Defa ñew ba ci liiñu tuus bi rek mu mel ni fa wadd nak".
« Il s’est simplement effondré sur les lignes de côté », a-t-il expliqué.
"He came to the sideline and just kind of collapsed there," Reed said.
Taggatkat ak fajjkat yi joxoon nañu Abercrombie ap ngelewu oksiseen ci liiñu tuus bi bala ñu koy tekk ci benn taabal ñu yobbu ko ngir yeneen seet.
Les entraîneurs et le personnel médical lui ont donné de l’oxygène sur les lignes de côté avant de l’emmener en civière pour évaluer son état.
Trainers and medical personnel gave Abercrombie oxygen on the sideline before placing him on a stretcher and taking him back for further evaluation.
Benn ofisiye bu juge Tennessee State neena Chris Harris bu WSMV ni Abercrombie gennina ci opeere bi ci santar faju bu Vnederbilt.
U représentant de Tennessee State a expliqué à Chris Harris de WSMV à Nashville, au Tennessee, qu’Abercrombie avait été amené au Vanderbilt Medical Center pour y subir une intervention chirurgicale.
An official from Tennessee State told Chris Harris of WSMV in Nashville, Tennessee, that Abercrombie was out of surgery at Vanderbilt Medical Center.
Harris yokk ci ne amul ay leeral ci ban xeetu/dayo gaañu gaañu fii mu nekk ni" te Tennessee State mungi jeema xool ba xam kañ la gaañu gaañu bi am.
Harris a ajouté qu’il n’y avait aucun détail sur le type de lésion ou sa gravité pour l’instant et que l’équipe essayait de déterminer quand l’incident est survenu.
Harris added that there are "no details on type/extent of injury yet" and Tennessee State is trying to figure out when the injury occurred.
Abercrombie, ap ndonngo bu ñaarelu at mu mbubbu mu xonk, mungi ci atam bu njékk ak Tennessee State ginnaaw bi mu juge ci Illinois.
Abercrombie, à sa première année du programme sportif, en est à sa première saison avec Tennessee State après avoir passé quelque temps en Illinois.
Abercrombie, a redshirt sophomore, is in his first season with Tennessee State after transferring from Illinois.
Amoon na jiroomi taakal su ñu dajale lepp ci Samdi bi bala muy genni ci matsa bi, loolu moo ko may 18 taakal ci at bi yep.
Avant sa sortie samedi, il avait accumulé cinq plaqués pour un total de 18 cette saison.
He had five total tackles Saturday before exiting the game, which brought his season total to 18 tackles.
Gan yi dinañu leen feyloo ay temmbere duwaan yu gina kawe sunu jennde ay suuf ci UK
Les acheteurs étrangers devront payer des droits plus élevés sur les propriétés achetées au Royaume-Uni
Foreign buyers will be charged higher stamp duty when they buy a property in the UK
Gan yi dinañu leen feyloo ay temmbere duwaan yu gina kawe sunu jennde ay suuf ci UK ak xaalis bu ciy teg ngir dimmbali ñi amul fu ñu dëkk ci doxalin yu bees yu waa Tory yi
Les acheteurs étrangers devront payer des droits plus élevés sur les propriétés achetées au Royaume-Uni afin de financer de l’aide aux sans-abri en vertu des nouveaux plans du gouvernement conservateur
Foreign buyers will be charged higher stamp duty when they buy a property in the UK with the extra cash used to help the homeless under new Tory plans
Jeego bi dina waññi doole bi Corbyn amoon ngir xecc ay ndaw yuy wote
Cette décision a pour but de contrer la popularité de Corbyn envers les jeunes électeurs
The move will neutralise the success of Corbyn's drive to attract young voters
Temmbere warugaar boobu dinañu ko dagg ci ñoonu dul fey taks ci biir UK
L’augmentation du droit de timbre sera prélevée auprès des personnes qui ne paient pas d’impôts au Royaume-Uni
The stamp duty rise will be levied on those who are not paying tax in the UK
Teresoor bi mungi yaakaar ni dina dajale luy tollu ci £120 milyoŋ at bu nekk- ngir jappale ñii amul fu ñu dëkk
Le ministère du Trésor s’attend à ainsi amasser jusqu’à 120 millions de livres par année pour aider les sans-abri
The Treasury expects it raise up to £120 million a year- to help the homeless
Gan yi dinañu leen feyloo ay temmbere duwaan yu gina kawe sunu jennde ay suuf ci UK ak xaalis bu ciy teg ngir dimmbali ñi amul fu ñu dëkk , Teresa Maay dina ko yegle tay.
Les acheteurs étrangers devront payer un droit de timbre plus élevé lorsqu’ils achètent une propriété au Royaume-Uni, permettant de recueillir des fonds supplémentaires pour aider les sans-abri, Theresa May annoncera la nouvelle aujourd’hui.
Foreign buyers are set to be charged a higher stamp duty rate when they buy property in the UK - with the extra cash used to help the homeless, Theresa May will announce today.
Jeego bi dinañu ko gisee ni ap jëëma waññi doole Jeremy Corbyn ndax ni mu mëne xecc ay ndaw wotekat ak ay woote ngir yommbal dekkuwaay, te ñi ëppu li ñuy feyeeku la ci joxoñ.
La décision sera perçue comme une tentative pour contrer la popularité de Jeremy Corbyn envers les jeunes électeurs, qui promet d’offrir des logements plus abordables en ciblant les plus riches.
The move will be seen as an attempt to neutralise the success of Jeremy Corbyn's drive to attract young voters with pledges to provide more affordable housing and target high earners.
Temmbere bi ñuy yokk ci nit ñi ak ci sosete yi dul fey taks ci biir UK, ak xaalis bu dolleeku di dimmbali Nguur gi ci xeex nelaw bu jafe.
L’augmentation du droit de timbre sera prélevée auprès des entreprises et des particuliers qui ne paient pas d’impôts au Royaume-Uni et les fonds recueillis seront utilisés pour financer les efforts du gouvernement pour venir en aide aux sans-abri.
The stamp duty rise will be levied on individuals and firms not paying tax in the UK, with the extra money boosting the Government's drive to combat rough sleeping.
Sirsarse bi- bii nekk beneen yokk ci temmbere bu am nii, te mu ëmmbaale ci anam yu gina kawe yi ñu dugal ñaari att ci ginnaaw ci kër okasoŋ yi ak luwaas yi munna dem bo agg 3 ci teemeer boo jël.
La surtaxe, qui s’ajoute aux droits de timbre actuels, y compris les taux supérieurs imposés à l’achat d’une deuxième résidence ou de propriétés destinées à être louées entrés en vigueur il y a deux ans pourrait s’élever à trois pour cent.
The surcharge - which is in addition to the present stamp duty, including the higher levels introduced two years ago on second homes and buy-to-lets - could be as much as three per cent.
Teresoor bi mungi yaakaar ni dina dajale luy tollu ci £120 milyoŋ at bu nekk.
Le Trésor s’attend à ainsi amasser 120 millions de livres par an.
The Treasury expects the move to raise up to £120 million a year.
Lu tollu ci 13 ci teemeer boo jël ci ay tabax yu bees ñeneen ñi nekkul waa UK ñoo leen jënd, ba pare di kawel njeg yi di ko gina jafeel ci ñii di dooga jënd ngir ñoom itam ñu duggu ci limu ñii am kër.
Il est estimé que 13 pour cent des nouvelles constructions à Londres sont achetées par des personnes ne résidant pas au Royaume-Uni, ce qui a un effet à la hausse sur les prix et ce qui diminue les chances pour les premiers acheteurs d’entrer le marché immobilier.
An estimated 13 per cent of new-build London properties are bought by non-UK residents, driving up prices and making it harder for first-time buyers to get a foot on the housing ladder.
Ay bëreb yu bari ci rëëw mi -rawatina nak kapitaal bi nekkaatnañu ay "dëkku demm" ndax ay nit yu nekkul waa UK ñoo jënd suuf yi te lu ëppu ñoom ci bitti réew ma lañuy nekk.
De nombreux secteurs mieux nantis, en particulier, dans la capitale, sont devenus des « villages fantômes » en raison du nombre élevé d’acheteurs étrangers qui passent plus de temps à l’extérieur du pays.
Many wealthy areas of the country - particularly in the capital - have become "ghost towns" because of the high number of foreign buyers who spend most of their time out of the country.
Politik boobu mungi duggu ci ay ayubes ginnaaw bi Boris Johnson laaje benn waññi temmbere yi ngir dimmbali ndaw yu gina bari ñu am seen këru bopp bu njékk.
La nouvelle politique arrive quelques semaines seulement après que Boris Johnson a demandé une réduction des droits de timbre pour aider plus de jeunes à acheter leur première maison.
The new policy comes just weeks after Boris Johnson called for a stamp duty cut to help more young people own their first home.
Mu tuumal sosete yu yor wallu tabax yi ni deñoo kaweloo njëg yi ndax li ñuy tabax suuf yi bo pare du ñu ko jefandikoo, mu ñaan Maay mu bayi kota yi mu def ci kër yu yomb yi te mu jeema facc "porbolemu dekkuwaay" bi ci Biritaañ.
Il a accusé les grandes entreprises de constructions de favoriser les prix élevés des propriétés en s’appropriant les terrains, mais sans les utiliser et il a pressé madame May d’abandonner les quotas de maisons abordables afin de réparer la « honte du logement » britannique.
He accused big construction firms of keeping property prices high by snapping up land but not using it, and urged Mrs May to abandon quotas on affordable homes to fix Britain's "housing disgrace."
Corbyn xamlena ni seentunañu ci lu yaggatul ay coppite ñeel dekkuwaay, and ci seytu luwaas yi ak bayi lii di "dax ku deful dara."
Monsieur Corbyn a annoncé une série de réformes accrocheuses sur le logement, y compris le contrôle des loyers et la fin des expulsions « sans faute ».
Mr Corbyn has announced an eye-catching series of proposed housing reforms, including rent controls and an end to "no-fault" evictions.
Bëgg na itam gina doolel konsil yi ndax ñuy tabax ay kër yu bees.
Il souhaite également donner plus de pouvoirs aux conseils pour la construction de nouveaux foyers.
He also wants to give councils greater powers to build new homes.
Soxna May neena: ”Daaw newoon naa ni sama jiite bi ci dunndalaat gent boobu Britaañ amoon laa koy njëkk def- bii dunndu defa wara gina neex ci seneraasioŋ bu bees bu ñew.
Madame May a déclaré : « L’an dernier, j’ai dit que je me dédierais, en tant que première ministre, à restaurer le rêve britannique, que la vie s’améliorerait avec chaque génération.
Mrs May said: "Last year I said I would dedicate my premiership to restoring the British dream - that life should be better for each new generation.
Loolu moy defaraat sunu marse dekkuwaay bu tas bi.
Cela signifie de réparer notre marché immobilier déficient.
And that means fixing our broken housing market.
Angleteer dina wëy di ubbil buntu am nit ñu fi bëgg dëkk, liggeey and dund.
La Grande-Bretagne sera toujours ouverte aux gens qui veulent y vivre, y travailler et y bâtir leur vie.
Britain will always be open to people who want to live, work and build a life here.
Waaye nak munul nekk luy yommbe noonu ci nit ñii dëkkul UK, naka noonu ci sosete yu nekk yi ci bittim réew, di jënd ay kër ni waa Biritaañ yi fii dëkk di ligeey bu baax.
Toutefois, je ne peux accepter qu’il soit juste qu’une personne ou une entreprise qui n’est pas établie ici puisse acheter une maison aussi facilement qu’un résident du Royaume-Uni qui travaille dur.
However, it cannot be right that it is as easy for individuals who don't live in the UK, as well as foreign-based companies, to buy homes as hard-working British residents.
Gent boobu di am sa këru bopp de gennina ci bopp ñi bari leegi, te ñakk worma bi nelaw bu jafe and ak moom mungi gina dëggal bopam rek."
Le rêve de propriété est devenu irréalisable pour de trop nombreuses personnes et la réalité des sans-abri demeure bien réelle ».
For too many people the dream of home ownership has become all too distant, and the indignity of rough sleeping remains all too real."
Jack Ross: 'Sama mebet bu mujj mooy jiite Ekost'
Jack Ross : « Mon ambition première est de diriger l’équipe d’Écosse »
Jack Ross: 'My ultimate ambition is to manage Scotland'
Anterneeru Sunderland bii di Jack Ross neena yittee am bu gina magg moy nekk taggatkat bu Ekost ci benn jamono.
Le patron du club Sunderland, Jack Ross, a déclaré que son « ambition première » est de diriger l’équipe de l’Écosse à un moment donné.
Sunderland boss Jack Ross says his "ultimate ambition" is to become the Scotland manager at some stage.
Doomu Ekost bi, am 42 att, mungi ŋoyu ci xeex boobu di dunndalaat ekipu bët gannarpenku boobu nekk nii ci ñetteelu palaas bu lig ben bi ñetti poñ ci ginnaaw ki jiitu ki.
L’Écossais de 42 ans savoure de défi de redonner vie au club nu nord-est, actuellement en troisième position de la League One, trois points derrière les meneurs.
The Scot, 42, is relishing the challenge of reviving the North-East club, who currently sit third place in League One, three points off the top.
Demna ci bii ete ci estaad bu Light ginnaaw bi mu tettee St Mirren inndiwaat ko ci Premiership daaw.
Il a déménagé au Stadium of Light cet été après avoir ramené St Mirren à la première ligue d’Écosse la saison dernière.
He moved to the Stadium of Light this summer after guiding St Mirren back to the Scottish Premiership last season.
"Dema bëgg jonganteel sama réew ginnaaw jongantekat laa”.
« Je voulais jouer pour mon pays en tant que joueur.
"I wanted to play for my country as a player.
Jotoon naa ap Cap B te mungi woon noonu rek" Ross moo ko wax BBC ci Sportsound.
J’ai été capitaine de l’équipe B et c’est tout », a raconté Ross à Sportsound sur la chaîne BBC Scotland.
I got a B cap and that was it," Ross told BBC Scotland's Sportsound.
" Waay ma magg fi seetaan Ekost ci Hampden lu bari ak sama pappa bi ma nekke xale, te loolu def ma musa delloo ci ginnaw.
« Mais j’ai grandi en regardant beaucoup l’Écosse à Hampden avec mon père et c’est ce qui m’y ramène toujours.
"But I grew up watching Scotland at Hampden a lot with my dad as a kid, and it is always something that has drawn me back.
Waaye saas boobu de mujjuwul am, waaye nak amnaa ndam ci wallu jiite moom.”
Mais cette occasion ne se présenterait que si je connais du succès à la tête de clubs ».
That opportunity would only come, though, if I am successful in club management."
ñii jiituwoon Ross te nekkoon ay anterneeru Sunderland bokk na ci Dick Advocaat, David Moyes, Sam Allardyce, Martin O'Neill, Roy Keane, Gus Poyet ak Paulo Di Canio.
Dick Advocaat, David Moyes, Sam Allardyce, Martin O'Neill, Roy Keane, Gus Poyet et Paulo Di Canio figurent parmi les prédécesseurs de Ross à la tête du club de Sunderland.
Ross's predecessors as Sunderland manager include Dick Advocaat, David Moyes, Sam Allardyce, Martin O'Neill, Roy Keane, Gus Poyet and Paulo Di Canio.
Anterneeru Alloa Athletic ba woon neena yegul benn ragal ci topp ci tuur yooyu ñu lim ci ekip bu ngannde nii, moom mi bañoon ay laaj yu juge ci Barnsley ak Ipswich Town.
L’ancien patron d’Alloa Athletic a dit ne pas être intimidé par le fait de suivre la trace de ces grands noms avec un tel club, lui qui a auparavant refusé des offres de Barnsley et de Ipswich Town.
The former Alloa Athletic boss says he felt no trepidation in following such established names at such a big club, having previously rejected overtures from Barnsley and Ipswich Town.
"Jaloore fi mu nekk nii lu muy doon moy 'ndax munnaa delloo bii ekip ci Premier League bi?
« En ce moment, pour moi, la mesure de ma réussite sera "est-ce que je peux ramener ce club à la Premier League?"
"Success for me at the moment will be gauged by 'can I return this club to the Premier League?'
Neena: Ndax te matuwaay yi ak ligeeyukaay yii ci bii ekip , amul sikki sakka, seen palaas Premier League la”.
La structure et les installations de ce club en font sans aucun doute un club digne de la Premier League », a-t-il dit.
Because of the structure and facilities at this club, it undoubtedly belongs in the Premier League," he said.
"Yobbu leen foofu du ligeey bu yomb, waaye, waaye balaa may muna japp ni defnaa jaloore faawu ma delloo bii ekip foofu."
« Le mener jusque là n’est pas une tâche facile, mais je ne considérerai pas que j’ai réussi tant que je ne ramène pas le club dans cette ligue ».
"It is not an easy task to get it there, but I would probably only view myself as being successful here if I can get the club back there."
Ross,ñetti att dong la def ci ligeeyam bii di anterneer , ginnaaw ap diir bu mu nekkewoon kuy wuutu anterneer ci Dumberton ak 15 weer ci njiitu Heart yi.
Ross n’en est qu’à sa troisième année à la tête de clubs après une période en tant qu’assistant à Dumbarton et 15 mois dans le personnel d’entraînement du club Heart.
Ross is only three years into his management career, after a period as assistant boss at Dumbarton and a 15-month spell on Hearts' coaching staff.
Ci la dimmbali Alloa mu juge ci wacc ñewaat ci diggi bi , mu jéle St Mirren ci waaja wacc bo gaddulooleen raaya championship bi att bi ci topp.
Il a ensuite aidé Alloa à se remettre de sa relégation au troisième niveau et a fait passer St Mirren d’une menace de relégation au titre de championnat la saison suivante.
He then helped Alloa recover from relegation to the third tier, and transformed St Mirren from the brink of relegation to Championship title winners the following season.
Te Ross neena tay la gina feex, musul mel nii ci adunam bu muy jongante ci Clyde, Hartlepool, Falkirk, St Mirren ak akadami bu Hamilton sax musul egg fii.
Et Ross se dit plus confortable que jamais durant sa carrière à Clyde, Hartlepool, Falkirk, St Mirren et Hamilton Academical.
And Ross says he feels more comfortable now than he ever did during his playing career at Clyde, Hartlepool, Falkirk, St Mirren and Hamilton Academical.
Xeyna ap selebe yoon dégg la woon “ muy fattelikoo bi muy jél Alloa.
« C’était probablement un moment décisif », s’est-il souvenu, parlant de sa prise en charge d’Alloa.
"It was probably a real crossroads," he recalled, of taking charge of Alloa.
"Dema amon ngëm bu deggu ni man jiite ekip moo gina doon sama ligeey, ci laay gina gis sama bopp, lu ëppu lu may am ci jongante.
« Je crois vraiment que la direction était la bonne chose pour moi, plus que jouer.
"I genuinely did believe management was the right fit for me, more so than playing.
Xamnaa dina xawa doy waar ndax te defoon naa ko bu baax, ma am ci dunndu bu muccu ay, ma am ci ay yekketiku yu am solo lool.
Ça peut sonner bizarre parce que je m’en suis bien tiré, j’ai pu bien en vivre et profiter de quelques moments forts.
It sounds bizarre because I did okay, made a reasonable living out of it, and enjoyed some reasonable highs.
Waante fo mënna metti.
Mais jour peut être difficile.
But playing can be tough.
Amna ay mbir yu bari yu ngeen wara ci ayubes bu nekk.
Il faut passer par beaucoup de choses dans une semaine.
There are a lot of things you have to get through on a weekly basis.
Bo leegi ci loolu laay weye, lu jém ci wallu fitna bi ak jaaxle ci wallu ligeey bi waaye jiite moom defa baax ci man.
Je vis encore ça, le stress et la pression, mais, en tant que directeur, je me sens bien.
I still go through that in terms of the stresses and pressure of the job but management just feels right.
Dema musa bëg jiite te leegi nak maangi koy def, defa mel ni moo gina feex, dema musa and ak sama sago nak bi ma nekke mag bo leegi."
J’ai toujours voulu diriger, et, maintenant que c’est ce que je fais, je ne me suis jamais senti aussi bien dans toute ma vie d’adulte. »
I always wanted to manage and now I am doing it, it feels the most comfortable I have been in my own skin throughout my entire adult life."
Mun ngeen deglu jotaay bi yepp ci Sportsound ci bisu Dibeer, 30 fan weeru Setammbar, ci rajo Ekost diggante 12:30 ak 13:30.
L’intégralité de l’entrevue sera en onde à Sportsound sur Radio Scotland le dimanche 30 septembre de midi à 13 h BST
You can listen to the full interview on Sportsound on Sunday, 30 September, on Radio Scotland between 12:00 and 13:00 BST
Ay gestu fësal na</seg>ñu ni 5.300 ci ngoon moy bu baax bi ngir amal ay laaj ak tontu
Le moment parfait pour une pinte est 17 h 30 le dimanche selon un sondage
Perfect time for a pint is 5.30pm on a Saturday, survey finds
Tanngooru ete bi yokk na piriis yi ngir pib yuy waaja deee yu Biritaañ yi waaye defa yokk fitna ci seenu restoraa yi.
La vague de chaleur cet été a stimulé les pubs anglais, qui connaissent des moments difficiles, mais aux dépens des chaînes de restauration.
The summer heatwave has boosted takings for Britain's struggling pubs but heaped more pressure on restaurant chains.
Pib yi ak baar yi seen njaay yi deñoo yokkuwoon ba 2.7 ci teemeer boo jél ci weeru Sulet- waaye piriis yi ci restoraŋ yi defa waccoon bo 4.8 ci teemeer boo jël , kanngam yi ñoo ko xamle.
Des groupes de pubs et de bars ont vu leurs ventes s’accroître de 2,7 pour cent en juillet, mais les restaurants ont quant à eux connu une baisse de 4,8 pour cent, selon les données.
Pub and bar groups saw sales rise 2.7 per cent in July - but takings in restaurants were down 4.8 per cent, figures revealed.
Peter Martin bu bisnees consultancy CGA, mii jammbatoon ci yooyu kanngam neena: "Naaj bu tang ak bokkup Angalteer ci kup de mondo bu gina yagg ni ñu ko foogewoon, defay tëktale ni Sulet tamit defa toppaat li amoon ci weer wu jiituwoon bi Suye, bi pib yi yeege ba 2.8 ci teemeer boo jél, lu ko wutali moy restoraŋ yi la seen laal ginoon metti.
Peter Martin, de la société de conseil aux entreprises CGA, qui a compilé les données, a déclaré : « Le soleil constant et la longue participation de l’équipe d’Angleterre à la coupe du monde signifient que, pour juillet, la tendance a été la même qu’en juin, où les pubs ont vu leurs ventes augmenter de 2,8 pour cent, sauf que ce sont les restaurants qui en ont payé le prix le plus fort.
Peter Martin, of business consultancy CGA, which compiled the figures, said: "Continued sunshine and England's longer than expected participation in the World Cup meant July followed a similar pattern to the previous month of June, when pubs were up 2.8 per cent, except that restaurants were hit even harder.
Wacc bu 1.8 ci teemeer boo jël ci njaayu restoraŋ yi ci weeru Suye defa gënoona bon ci weeru Suyet.
La baisse de 1,8 pour cent des transactions dans les restaurants en juin s’est accrue en juillet.
The fall of 1.8 per cent in restaurant trading in June just got worse in July.
Pib yu ñu joxoñ ak baar yi ligeeynañu lu ëppu fuufak ay bëg ngir bëggante lu ëppu ay restorŋ deñoo daanuwoon.
Les pubs et les bars, qui vendent surtout des boissons, s’en sont, et de loin, le mieux tiré avec, pour des services similaires, des ventes supérieures, alors qu’elles étaient en baisse dans les restaurants.
Drink-led pubs and bars performed by far the strongest with like-for-likes up more than restaurants were down.
Ay pib yu ñu jiital ci wallu lekk tamit sonnoon nañu ci naaj bi, waaye nak eggul fi borom restoraŋ yi eggoon.
Les pubs qui vendent surtout de la nourriture ont également souffert du soleil, mais pas autant que les restaurants.
Food-led pubs also suffered in the sun, although not as dramatically as the restaurant operators.
Dafa melni nit ñi dañoo bëgg genn ngir naani.
Il semble que les gens souhaitaient simplement prendre un verre.
It seems people just wanted to go out for a drink.
ci pib yi ñu jiite ak naan yi ci baar yi njaay yi demoon nañu bo romb 6.6 ci teemeer boo jél ci weer wi, ak lekk yu daanu ba ñett ci teemeer boo jél."
Dans les pubs et les bars, les ventes de boissons étaient en hausse de 6,6 pour cent lors de ce mois, alors que, pour la nourriture, nous avons vu une baisse de 3 pour cent. »
Across managed pubs and bars drink sales were up 6.6 per cent for the month, with food down three per cent."
Paul Newman, bu mbiri feexlu ak seetlu kat ci wallu teraanga RSM neena: "Yooyu resilta ñungi wey di desendi ba leegi, gisnañu ko ci njeexte weeru Awaril.
Paul Newman, analyste en loisir et en accueil chez RSM a dit : « Ces résultats représentent une continuité de la tendance vue depuis la fin d’avril.
Paul Newman, of leisure and hospitality analysts RSM said: "These results continue the trend we've seen since the end of April.
Jaawu ji ak njeexital yu mag yu nit ñi mbaa ay xew taggat yaram ñooy mbir yi gina magg yii di ko def su de ci wallu njaay ci marse beneen réew.
La météo et l’influence majeure des événements sociaux et sportifs demeurent les facteurs principaux en matière de ventes hors foyer.
Weather and the impact of major social or sporting events remain the biggest factors when it comes to sales in the out-of-home market.
Bettul kenn ni bo leegi restoraŋ yaangi am ay tolof tolof , daanaka ap daanu bu tollu ci 4.8 ci teemeer boo jél at ci kaw at dina doon lu metti lool ci njég yii di gina yokku rek.
Ce n’est pas une surprise que les restaurants continuent de battre de l’aile et une baisse des ventes de 4,8 pour cent en glissement annuel leur fera particulièrement mal, sans oublier les pressions continues sur les coûts.
It comes as no surprise that restaurant groups continue to struggle, albeit a sales drop of 4.8 per cent year-on-year will be particularly painful on top of ongoing cost pressures.
"Ete bu yagg te tang bi munoon na baña ñew fi mu gënee metti ci ñii di yenngu ci lekk yu ñu jiite, te su yagge dinañu xam ndax tamperatiir yu yem yu weeru Uut bi dina ñu inndil tan bii ñu soxla lool."
Le long été chaud est arrivé à un bien mauvais moment pour les restaurateurs et le temps nous dira si les températures plus modérées d’août leur donnera le répit dont ils ont le plus grand besoin. »
The long hot summer could not have come at a worse time for food-led operators and time will tell whether the more moderate temperatures we've experienced in August will provide some much-needed respite."
Yokkute njaay yepp ci pib ak ci restoraŋ yi boole ci yuy sooga ubbi yi, mungi nekkoon 2.7 ci teemeer boo jël ci weeru Sulet, muy wone rek waññeeku yu tar yi.
La croissance totale des ventes dans les pubs et les restaurants, y compris les nouvelles installations, était de 2,7 pour cent in juillet, ce qui reflète le ralentissement en matière de lancements de marques.
Total sales growth across pub and restaurants, including new openings, was 2.7 per cent in July, reflecting the slow down in brand roll-outs.
Kii seytu njaay yu The Coffer Peach Tracker ngir pib yu UK , baar ak restoraŋ defay dajale ba pare cu cammbar lim yi ci 47 kurel yu wuute, ak benn wëlbëti buy tollu ci £9 milyaar su ñu boole lepp te moy marsandiis bi ñu gina ñee.
L’outil Coffer Peach Tracker effectue le suivi des ventes de l’industrie des pubs, des bars et des restaurants au Royaume-Uni, recueillant et analysant les données de rendement de 47 groupes d’exploitants, avec un chiffre d’affaires combiné de plus de 9 milliards de livres (15 milliards de dollars canadiens). Il est reconnu comme l’outil de référence du secteur.
The Coffer Peach Tracker industry sales monitor for the UK pub, bar and restaurant sector collects and analyses performance data from 47 operating groups, with a combined turnover of over £9 billion, and is the established industry benchmark.
Benn ci jiroomi xale yoo jel amna benn porfil ci reso sosiyoo yi mu koy nëbb ay waajuram
Un enfant sur cinq a un compte secret de média social caché de ses parents
One in five children have secret social media accounts that they hide from their parents
Benn ci jiroomi xale ñenn ñi wara tollu ci 11 att benn gestu moo ko xamle- yoo jel amna benn porfil ci reso sosiyoo yi mu koy nëbb ay waajuram
Un sondage révèle qu’un enfant sur cinq, dont certains ont aussi peu que 11 ans, a un compte secret de média social caché de ses parents de ses professeurs
One in five children - some as young as 11 - have secret social media accounts that they hide from their parents and teachers, survey reveals
Gestu bu 200000 ndonngo yu daara bu diggidoor bi wonena ap yokkute bu ñeel ay "xëtu Insta yu baaxul"
Un sondage mené auprès de 20 000 élèves du secondaire révèle une croissance de pages « fake Insta »
Survey of 20,000 secondary school pupils revealed growth in "fake Insta" pages
Xibaar yi yoknañu diisaayu tiitaange ci wallu ay ñaawteef yu jém ci sëy yi ñuy def ci enternet bi
La nouvelle fait craindre que du contenu de nature sexuelle soit publié
The news has heightened fears that sexual content is being posted
ñaari fukk yoo jél ci teemeer bu nekk ci ndonngo yi neenau amnañu ap porfil "bu mag" bu ñuy won seen waajur yi
Vingt pour cent des étudiants disent détenir un compte « principal » qu’ils montrent à leurs parents
Twenty per cent of pupils said they have a "main" account to show parents