Datasets:
wolof
stringlengths 1
166
| french
stringlengths 2
331
|
---|---|
aakimu | accaparer |
Mu ngi aakimu mikoro bi; mënatuñoo jél kàddu gi | il a accaparé le micro; on ne peut plus prendre la parole. |
aada j- | coutume, culture |
Jubb yii, seen aada la | ces touffes (de cheveux), c’est leur coutume. |
aafiya j- | paix |
May ma aafiya | fiche-moi la paix ! |
aawo b- | Épouse qui occupe le premier rang dans un foyer polygame |
Aawo, buuru këram « aawo » | reine de sa maison |
aka | comme |
Aka gaaw | comme il est rapide ! |
a | c’est… qui |
Omar a lekk ceeb bi | C'est Omar qui a mangé le riz. |
Man a | C'est moi. |
a | indique un procès à l’inaccompli |
Boo ko gisee muy dem ak a dikk nii rekk, dafa jaaxle | quand tu le vois aller et venir comme ça sans arrêt, c’est qu’il est inquiet. |
(prov.) Bëgga dem taxula mëna dem. Mëna dem ay taxa dem | il ne suffit pas de vouloir partir, il faut pouvoir le faire. |
a | ou |
amaana j- | loyauté |
am-aajo | être respectueux, être attentionné, avoir de l’égard (à l’endroit des gens) |
Ku am-aajo la ci ay dëkkandoom | il a beaucoup d’égards pour ses voisins. |
am-am b- | richesse avoir bien |
Danu wara boole sunu am-am | nous devons mettre en commun nos biens. |
am-bopp | être extralucide, être un illuminé |
Dafa am-bopp; lu ñu ko fexeel, mu yàqu | C'est un extralucide; tous les coups qu’on monte contre lui échouent. |
am-alal | être riche être fortuné |
Waa ju am-alal lay séyal | elle est mariée à un homme riche. |
am-diine | être pieux |
am-bayre | avoir une aura qui attire toutes les attentions à soi |
Jaaykat bu am-bayre la | C'est un commerçant en vue. |
am-bët | avoir les yeux globuleux |
Am-bët dafay yokk taaru jigéen | avoir des yeux globuleux rehaussent le charme d’une femme. |
am-fayda | avoir du caractère, de la personnalité |
Góor gu am-fayda du wàlli sabar | un homme qui a de la personnalité ne va pas à des séances de tam-tam. |
am-gat | avoir du toupet (grossier) |
Aka am-gat | comme il a du culot ! |
am-fit | être audacieux, être courageux |
amiin | amen ! Ainsi soit-il ! |
Neleen amiin | dites amen ! |
Lii de mooy ñaan gu daje ak amiin | cela ne pouvait pas mieux tomber |
am-jëmm | avoir de la prestance |
Xale bu tuuti la; dafa am-jëmm doŋŋ | C'est un tout jeune enfant; il a seule-ment de la prestance. |
am-ji-jàmm j- | personne avec qui on entretient de bonnes relations |
Omar sama am-ji-jàmm la; mën naa koo ñaan njekk | Omar est une de mes relations; je peux lui demander une faveur. |
am-jom | avoir de l’amour-propre |
Ku am-jom la; su ko baay ji xulee, mu jàng bu baax | il a de l’amour-propre; si son père le sermonne, il étudie bien. |
am-jàmm | être pacifique, calme, paisible |
Kooku, nit ku am-jàmm la | celui-là, c’est une personne paisible. |
am-jot | n’avoir rien à faire de son temps être libre |
Seetal ku am-jot, nga ànd ak moom | vois qqn qui est libre, va avec lui ! |
Toppal fale; danga am-jot | fiche le camp; tu n’as vraiment rien à faire. |
am-jikko | avoir des sautes d’humeur |
Ku am-jikko neexula dëkkal | une personne qui a des sautes d’humeur n’est pas facile à vivre. |
am-kersa | être timide avoir de la retenue |
Dafa am-kersa | il est timide. |
am-kàttan | être résistant, endurant, fort |
Tool bii, ku am-kàttan rekk a ko mëna bey | ce champ, seul qqn de fort peut le cultiver. |
ammaa | pour sûr |
Ammaa, koddaay moom, ay farataam barewul | pour sûr, s’agissant des habits, ses exigences ne sont pas nombreuses. |
am-maanaa | être important, intéressant |
Dama defe woon ne lu am-maanaa la ma doon wooye | je pensais qu’il m’appelait pour qqch d’important. |
am-kóllëre | (relations) Être fidèle |
Xaj, rab wu am-kóllëre la | le chien est un animal fidèle. |
am-solo | être important, intéressant |
Mbir mu am-solo la waxtaane | C'est d’une affaire importante qu’il parle. |
am-sutura | être discret |
Jabar ju am-sutura la | C'est une épouse discrète. |
am-taxawaay | être élancé |
Waa ju am-taxawaay la | C'est un homme élancé. |
am-teraanga | être accueillant |
am-wërsëg | être chanceux avoir de la veine |
Tey, danga am-wërsëg | aujourd’hui, tu es chanceux. |
am-tur | être célèbre |
Woykat bu am-tur la | C'est un chanteur célèbre. |
am-muur | être chanceux |
am-xel | avoir du jugement avoir de la finesse d’esprit |
Jabar ju am-xel du mere jëkkëram ngir xarum Tabaski mu duuful | une épouse réfléchie n’en voudra pas à son mari pour un mouton de la Tabaski qui n’est pas gras. |
am-xorom | être intéressant être amusant |
Ku am-xorom laa doon waxtaanal | je causais avec une personne intéressante. |
am-yaram | être obèse avoir une forte corpulence |
Bëggumaa am-yaram | je ne veux pas être obèse. |
am-yar | être poli être bien élevé |
Gone gu am-yar la | C'est un enfant bien élevé. |
am-yeel | être élancé |
Xale la, dafa am-yeel rekk | C'est un enfant mais il est grand. |
am-yax | être robuste |
añ | déjeuner |
Xaaral ba ma añ ba-noppi | attends que j’aie fini de déjeuner ! |
añaan | prendre son déjeuner chaque fois en des lieux différents, généralement en pique-assiette |
Bi jabaram demee ba tey, dafay añaan rekk | depuis que son épouse s’en est allée, il prend son déjeuner à gauche et à droite. |
andaar w- | unité de mesure d’environ un litre |
Andaaru njaw, andaaru lem, andaaru soowum bëy, ñetti focci wuy, nga bembaxli ko | un litre de sirop de jus de Sclerocarya birrea, un litre de miel, un litre de lait caillé de chèvre, trois pains de singe, tu le verses dans la bouillie. |
añ b- | déjeuner |
Indil añ bi | apporte le déjeuner ! |
(prov.) Liggéeyu ndey : añub doom | labeur de la mère : déjeuner du fils |
anaata j- | sixième des sept périodes de treize jours de la saison des pluies |
Anaata jaa ngiy jeexsi | la sixième période de la saison des pluies tire à sa fin. |
aaréen j- | arachide |
Dañu toskareel aaréen | on a fait de l’arachide un parent pauvre. |
aaru | se protéger |
Bala may fital aw rab, dinaa xool ndax mu ngi ak biir, wala ndax tollu na ci waxtu aaru | avant de tirer sur une bête, je vois d’abord si elle est grosse, ou si elle est dans une période où elle se protège (d’un accouplement). |
Wolof Dataset for Open LLM Fine-Tuning
This project provides a dataset for fine-tuning language models (LLMs) in Wolof. It uses a Python script to create a JSONLines (.jsonl
) file from a list of words, retrieving detailed information from a Wolof-French dictionary API.
Dataset Details
Dataset Description
- Curated by: Mamadou Diagne
- Language(s) (NLP): Wolof to French
- License: MIT
Dataset Sources [optional]
- Repository: [More Information Needed]
The data is sourced from the "Corpus Oraux du LLACAN," which provides comprehensive Wolof-French dictionary data. You can access the API for this dictionary at:
- API Endpoint: https://corporan.huma-num.fr
Uses
Direct Use
[More Information Needed]
Out-of-Scope Use
[More Information Needed]
Dataset Structure
[More Information Needed]
Dataset Creation
Curation Rationale
[More Information Needed]
Source Data
Data Collection and Processing
[More Information Needed]
Who are the source data producers?
[More Information Needed]
Annotations [optional]
Annotation process
[More Information Needed]
Who are the annotators?
[More Information Needed]
Personal and Sensitive Information
[More Information Needed]
Bias, Risks, and Limitations
[More Information Needed]
Recommendations
Users should be made aware of the risks, biases and limitations of the dataset. More information needed for further recommendations.
Citation [optional]
BibTeX:
[More Information Needed]
APA:
[More Information Needed]
Glossary [optional]
[More Information Needed]
More Information [optional]
[More Information Needed]
Dataset Card Authors [optional]
Mamadou Diagne
Dataset Card Contact
- Downloads last month
- 73