audio
audioduration (s)
0.01
482
text
stringlengths
0
2.5k
labels
stringclasses
7 values
speaker
stringclasses
23 values
filename
stringclasses
123 values
[musique] nawet bi door na ndax taw yu njëkk yi gis nañu leen ba tax na projet :fra bii di ECHO moo leen ciy gunge ci ay émission :fra yu am solo émission :fra yi nag ñu ngi ciy ànd ak ñi nga xam ne seen xam-xam dafa màcc jëm ci wàllum mbéy état :fra bi maanaam nguur gi ràñ~ee leen lool nag ci mel ni waa DRDR ANCAR institut :fra naional :fra de :fra pédologie :fra waa CNAAS di nañ ciy waxtaanee ci thème :fra yi nga xam ne dina yitteel loolu béykat yi ci li nga xam ne moom mooy nawet bi ndax dinañ ci waxtaane la :fra fertilisation :fra et :fra la :fra consevation :fra des sols :fra maanaam daal naka la ñuy toppatoo suuf si ba mu ñu mën cee am mbéy mu mucc ayib dinañ si waxtaanee tamit les :fra déficits :fra pluviométriques :fra et :fra de :fra la :fra manière :fra s' :fra y :fra adopté :fra maanaam néew gi nga xam ne taw bi dina ko néew ak naka la ñuy mën a def ngi mën a ànd ak moom dinañ ci waxtaanee les :fra ravageurs :fra qui attaquent :fra des :fra cultures :fra maanam daal yi nga xam ne dañuy yàq mbéy mi dinañu waxtaanee ak béykat yi nu ñuy mën a def ba moytu loolu waaye danañ waxtaan tamit les :fra conservations :fra des :fra récoltes :fra maanaam daal naka la énuy toppatoowee li nga xamante ne moom mooy li ñuy béy
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
waaye nag mbokk yi ñu ngi leen di xamal ne émission :fra bu njëkk bi ñu ngi ko jàpp àllarba ñaar fukki fan ak juróom-ñaar ci weeru juin :fra bu 17 heures :fra ci ngoon jotee maanaam mercredi :fra 27 juin :fra à :fra partir :fra de 17 heures :fra fii ci Louga FM RTS yéen nag mën ngeen cee bokkagum bu ngeen wootee ci li nga xam ne moom mooy serveur :fra vocal :fra bi ci 33 869 74 02 33 869 74 02 ngeen mën a bàyyi seen tur seen sant ginnaaw bi ngeen déggee bip :fra bi wax tamit li nga xam ne moo leen titteel su ko defee suñu ndax dana leen mën a indi ay leeral may fàttali àllarba bii di ñëw yemoog ñaar fukki fan ak juróom-ñaar ci weeru juin :fra à :fra partir :fra de :fra 17 heures :fra fii ci Louga FM RTS di émission :fra bi nga xam ne dinañ ci àndak ku xam-xamam màcc jëm ci wàllu mbéy mu bokk nag ci institut :fra national :fra pédologie :fra kon nag mbokk yi seen émission :fra baa ngi noonu bu leen ko kenn nettali [musique]
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
jërëjëf mbokk yi ci %e déglu bi ngeen di déglu Louga FM RTS comme :fra ni ñu leen ko annoncer :fra woon tey jii nag di %e émission :fra bu njëkk [r] di émission :fra bi nga xam ne moom la leen waa ECHO di jagleel [r] xam ngeen ni bande :fra annonce :fra bi mu ngi doon daw waaw fan yii yëpp nag tey jii ñu am mbégte ak bànneex [r] %e dalal ki nga xam ne xam-xamam dafa màcc jëm ci wàllup %e jëm ci suuf si mbéy mi climat :fra bi yooyu yëpp [r] day dinañ ci %e waxtaan ndax tey jii [r] thème :fra bi nga xam ne moom la ñu jël moom mooy %e fertilisation :fra et :fra gestion :fra durable :fra des sols :fra [r] loolu nag %e moom mi nga xam ne moom mooy invité :fra bi dana dana dana ñu ko faram fàcceel [r] xanaa rek %e du ñu si sori ndax wolof Ndiaye nee na tungune du teew ñuy nataal [r] dañ koy daal di nuyu rek moom Pape Gora Kane [r] su ko defee rek mu daal di nuyonteeg mbokku auditeurs :fra yi [r] ba noppi nag gën ñoo présenter :fra boppam ndax %e wolof Ndiaye nee na [r] loo xam Mademba Mademba gën laa xam boppam Pape ñu ngi lay nuyu
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
%e salaamaaleykum %e monsieur :fra monsieur :fra Amady Ba maa ngi lay fay di %e nuyu tamit sa auditeurs :fra yi ñuy déglu %e di leen baalu àq ci weeru koor biñ jógee te tamit %e di leen di leen baal di ñaan yàlla %e bépp jaamu yàlla bu nga xamante ni def nañ ko si yàlla %e nangul ñu ko ah xam naa nag %e man maa ngi tudd %e Pape Gora Kane [bb] nekk assistant :fra %e délégué :fra zonal :fra bu institut :fra national :fra de pedologie :fra [bb]
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
institut :fra national :fra de :fra pédologie :fra nag dafa nekk %e benn bànqaassu ministère :fra de :fra l' :fra agriculture :fra bu nga xamante ni moom mooy saytu wàll suuf yi %e saytu bi jëm ci wàll di leen aar %e ba pare bu amee ay yàqu-yàqu ci suuf si ñoom ñoo koy jéem a jooyanti maanaam dégradation :fra des :fra sols :fra yi dañ koy xeex bu baax %e fii ci Louga ak li ko wër ñu naan ko %e zone :fra pédoclimatique :fra sylvopastoral :fra et :fra Niayes
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
institut :fra national :fra de :fra pédologie :fra mi ngi fi nekk %e commune :fra Kell Guèye yaakaar naa yaakaar naa ñi miin %e yoonu Dakar bi avant :fra ngay dugg Kell di nga gis benn batimat :fra bu ne foofu batimat :fra bu orange :fra foofu la %e institut :fra national :fra de :fra pédologie :fra nekk
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
en :fra meme :fra temps :fra tamit am nañu ay buraux :fra DRDR maanaam mooy agriculture :fra gu Louga [r] %e xam naa bu delloo ci *
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%e mooy %e voilà :fra léegi nag pour :fra dugg ci %e waxtaan bi xam nga thème :fra bi dañ ne fertilisation :fra [r] et :fra gestion :fra durable :fra des :fra sols :fra tey boo ñu ko doon faram facceel [r] %e thème :fra bi lan la
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
waaw xam naa monsieur :fra Ba ma lay remercier :fra bu baax %e thème :fra bi nag dafa nekk %e thème :fra d' :fra actualité :fra parce :fra que :fra li ñuy naan gestion :fra durable :fra des :fra sols :fra dafa %e nekk lu nga xamante ne tey àdduna si yëpp daanaka ci la ñu dox %e si buñ ko bëggee tënk daal ci lu gàtt maanaam fertilisation :fra dafa dugg sax ci biir gestion :fra durable :fra des :fra sols :fra
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
mais :fra nag dinaa gën a ñëw ci fertilisation :fra
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
mais :fra gestion :fra durable :fra des :fra sols :fra moom [r] bu énu ko déggee mooy %e bépp xeetu doxalin bu nga xamante ne day dajale lépp lu nga xam ne dafay dellu si aar suuf yi %e ak ndox yi ak %e bépp meññeef bu nga xamante ne day jugee ci aalam bi %e ba pare %e day may %e béykat bi day may béykat bi %e mu yokk njëriñ li nga xamante ne moom lay jëlee suuf si ci suuf si te du ko lor
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
bon :fra xam naa nag %e donc :fra fertilisation :fra moom dafa dugg ci gestion :fra durable :fra des :fra sols :fra ndax %e fertilisation :fra mooy bépp xeetu technique :fra bu nga xamante ni %e béykat bi da koy jëfandikoo pour :fra jo() dolli suufam ay ferñeent loolu mooy ferilisation :fra
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
d' :fra accord :fra donc :fra ba tax na %e laaj bu njëkk bi ginnaaw bi nga faram fàccelee li nga xamante ne moom mooy %e thème :fra bi waxtaan bi tey [r] daénu ne %e état :fra suuf si naka la mën a affecté :fra rendement :fra bi nga xamante ne moo am ci culture :fra bi [r] %e suuf si xam nga %e wax nga léegi ba ne [r] %e ni nga xamante ne noonu la énu ko mën a taxawoo daal [r] ngir %e béykat bi mën cee am njëriñ léegi nag man li ma bëggoon laaj mooy suuf si ci boppam [r] naka la ñu ko war a mën a taxawee daal ba mu indil li nga xam ne moom mooy njëriñ ci béykat bi
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum %hum ah oui :fra jërëjëf %e sëñ Ba xam naa question :fra boobu moom am na solo trop :fra puisque :fra %e suuf moom comme :fra ni ñu koy faral di waxee rek moom mooy support :fra production :fra
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
bu ñu nee état :fra wu suuf si naka la mën a %e affecté :fra ci %e maanaam %e rendement :fra béykat bi
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
[bb] loolu dafay dellu juste :fra ci fertiliser :fra suuf si [bb] xam naa %e foofu noonu [bb] man dama koy jéem a pour :fra simplifier :fra suñu auditeurs :fra yi ñiy déglu pour :fra mu bañ a %e xaw a technique :fra de trop :fra
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
danu jël diggante %e nit maanaam yaay ak doom jigéen bu am doom bu ñu jàppee ni jigéen ji moom mooy suuf
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
doom ji moom mooy gàncax bi lépp lu nga xamante ni %e doom ji mi ngi koy soxla pour :fra nàmp ci yaay ji la koy jëlee léegi bu dee yaay jooju moom mi ngi ànd ak wér %e ànd naag wér day mën a nàmpal doomam bu baax te du am benn gàllankoor mais :fra bu dee yaay ji dafa manqué :fra par :fra exemple :fra soow
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
du munul nàmpal doom ji noonu la gàncax bi mel ak suuf lépp lu nga xamante ni daal gàncax daf koy jëfandikoo daf koy jëlee ci suuf ferñeent yëpp ci suuf la koy jëlee
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
donc :fra %e ci %e wàllu mbéy dañuy faral di wax ñiy jàng agronomie :fra [r] am na terme :fra bu ñu tuddee exportation :fra peut :fra être :fra tey jii nii comme :fra damay ragal ñi ma ñi ma ñi ma ñi ma war a summi summi ma
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
mais :fra man comme :fra dama bëgg ñebe bu dee dañu béy %e toolu ñebe
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
jël ñebe ji dem jaayi ko Dakar
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
%e xam nga buñ jëndee ñebe ñu ci bëri dañ naan ñebe dafa riche :fra en :fra fer :fra
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
wala dafa réer ci yeneen ferñeent yi nga xamante ne dañ koy jëfandikoo di ko lekk léegi ferñeent yooyu noonu ñebe ji ci suuf si la ko jëlee %hum bu dee yow man dama am sama tool chaque :fra at ma ciy béy ñebe
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
di jël ñebe ji di ko jaayi Dakar
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
di jël ngooén mi di ko dem yóbbu sama kër
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
donc :fra ferñeent yooyu nekkoon ci suuf si maa ngi leen di jël di leen yóbbu Dakar ferñeent yi nekkoon ci suuf maa ngi leen di jël di leen stocké :fra sama kër léegi nag bu dee chaque :fra année :fra damay def lma :fra même :fra chose :fra damay dem ba sama suuf
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
dootul amati dara ci wàllu ferñeent [r] %e léegi [bb] comme :fra suuf moom comme :fra ni ñu ko xamee rek [r] bu ma %e jëlee benn échantillon :fra suuf jël ko yóbbu ko laboratoir :fra par :fra exemple :fra analyser :fra ko [r] da ngay gis ni suuf énetti pàcc moo ko composé :fra
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
maanaam am na liñ naan partie :fra minérale :fra bi
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
am partie :fra organique :fra bi am beneen partie :fra bu nga xamante ni [r] c' :fra est :fra %e gazeux :fra kooku moom mun nañ cee bañ a dugg
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
mais :fra li ma ci gën a interessé :fra mooy partie :fra organique :fra bi
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
organique :fra bi
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
partie :fra organique :fra boobu noonu moom la %e ferñeent yi ne ci suuf si
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
loolu moo leen concerné :fra directement :fra foofu la ñu jugee léegi ferñeent yooyu noonu nekk ci suuf sm na lu énu naan les :fra éléments :fra majeurs :fra mooy NPK bi ngay dégg ñu koy faral di am ci ñu koy faral di wax ci engrais :fra yi léegi bu delloo ci %e NPK boobu N bi moom azote :fra la [r] moom mooy permettre :fra croissance :fra su garab gi P bi di phosphore :fra xam naa dinañ ci gën a dellu si si kanam [r] moom mooy permettre :fra développement :fra garab gi K bi moom mooy %e potasium :fra moom moom pour :fra couvertir :fra %e ferñ() %e nu mu tudd meññeent yi jugee ci %e meññeent yu jugee ci garab gi lay lay lay gën a dëgëral [r]
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
ak lu ñu naan les :fra oligo :fra élément :fra yooyu yëpp xam naa dinañ ci dinaén ci ñëw ci kanam [r] léegi yooyu noonu bu ci manqué :fra rek [r] dafay affecté :fra dooley suuf si énu ko naan fertilité :fra du :fra sol :fra
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
loolu mooy loolu mooy définir :fra fertilité :fra du :fra sol :fra éléments :fra yooyu ma udd ak yeneen des na yeneen ak yeneen
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
yooyu mooy définir :fra fertilité :fra du :fra sol :fra
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
léegi
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
bu dee éléments :fra yooyu dafa manqué :fra suuf si day manqué :fra doole
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum *
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
am na tamit yeneen paramètres :fra yu nga xamante ne peut :fra être :fra dinañ ci gën a xuus ci kanam [r] mais :fra énu jàpp daal ci tënk ni [tx] éléments :fra yooyu ma lim ak yeneen
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
ñoom ñooy définir :fra dooley suuf
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
waa léegi li nga wax ni ley définir :fra dooley suuf léegi producteur :fra bi nag [r] moom naka la mën a njëriñoo
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum %hum
<o,f1,male>
locuteur_2
wol_4210
%e suuf si nga xamante ne ci lay ci la ci lay béy [r] ndax wax nga sànq ci sa biir wax ba joxe exemple :fra ne su fekkente ne [r] da ngay ji par :fra exemple :fra ñebe bu loolu defee at bu jot nga jaayi ji ko Dakar wala nga denc ko sa kër [r] dana dem ba am loo xamante ne dana ko manqué :fra ci tool bi foofu mu ne [r] léegi nag moom %e béykat bi [r] naka la war a mën a def nag ba di jëriénoo suufam ba saa yu ko soxlaa rek [r] fekk fa ferñeent yi nga xam ne war naa nekk ci suuf si
<o,f1,male>
locuteur_1
wol_4210
%e jërëjëf %e sëñ Ba xam naa ci côté :fra boobu noonu li ci gën a %e am solo mooy d' :fra abord :fra nga tànn
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%e suuf si ngay bayee dafa am solo
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
parce :fra que :fra comme :fra ni ñu koy waxee rek
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
dëgg la %e béy moom [bb] gàncax foo ko ji bu amee condition :fra yu mu soxla dana sax mais :fra [bb] nga choisir :fra %e en :fra fonction :fra li nga bay suuf si mu méngool loolu am na solo trop :fra pour :fra am rendements :fra yu baax [r] loolu benn la ci ba pare tamit %e di dundal maanaam di fertiliser :fra di yokk sa suuf doole di ko amander :fra dinañ ñëw ci différence :fra fertilisation :fra amandement :fra lan la dinañ ci ñëw ci kanam [r] loolu tamit %e dafa am solo
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum [r] bon :fra %e waaw xam naa %e
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
nga wax ñu ci ci ci ci ci ci ci tànn wi suuf si maanaam da nga ne tànn bi am na solo
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
[r] %hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%e mais :fra même :fra tànn bi
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
ndax du %e ku ne rek moo mën a tànn
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
ndax tànn bi mën ngaa baaxee auditeurs :fra yi nga xam ne ñu ngi ñuy dégl
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
[r] %hum
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%e naka la ñuy tànnee %e par :fra rapport :fra ak fi nga xamante ne moom moom moom la ñu war a ji
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
waaw
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%e ci loolu noonu bu dee ñun zone :fra bi ñu nekk nii muy zone :fra %e sylvopastorale :fra Niayes
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
<o,f0,>
inter_segment_gap
wol_4210
%e di ëmb Louga ak li ko wër
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
%e bu ñu seetloo liñ fiy gënal faral di béy
<o,f0,male>
locuteur_2
wol_4210
%hum %hum
<o,f0,male>
locuteur_1
wol_4210
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
42