audio
audioduration (s)
0
198
text
stringlengths
0
3.82k
start_time
float64
0
3.02k
end_time
float64
0.33
3.03k
%hum %hum
708.434
708.814
am na ñu ko fiy bay
708.814
709.716
%hum %hum
709.716
710.216
mais :fra léegi bu delloo ci %e yooyu noonu par :fra exemple :fra buñ jëlee %e lu mel ni %e mboq par :fra exemple :fra moog dugub
710.216
718.05
%hum %hum
718.05
718.411
ñoom %e ay gàncax yu nga xamante ne dañ soxla ndox lañ
718.411
722.247349
%hum
722.247349
722.975
gàncax yu bëgg ndox lañu
722.975
724.422
%hum %hum
724.422
724.929
donc :fra suuf yi ñu gën a soxla
724.929
726.901
%hum %hum
726.901
727.335
mooy %e suuf yi ñuy tuddee ñun les :fra sols :fra argileux :fra sableux :fra argileux :fra sableux :fra
727.335
733.653
%hum %hum
733.653
734.209
maanaam déeg en :fra wolof déeg en wolof ñoom yooyu la ñu gën a soxla parce :fra que :fra suuf yooyu noonu énoom ñoo gën a mën a téye ndox
734.209
741.176
%hum %hum
741.176
741.755
parce :fra que :fra ñoom %e seen getax yi ak %e maanaan %e
741.755
748.032
épis :fra yi
748.032
748.557
danu soxla %e ndox mu bëri pour :fra mën a màgg donc :fra énoom ci suuf yooyu la ñuy gën %e soxla pour :fra %e maanaam mooy seen milieu :fra optimal :fra quoi :fra boo bëggee am rendement :fra bu baax ci li ngay bay bu dee da ngay béy %e mboq wala dugub boo amee suuf bu nga xamante ni c' :fra est :fra argileux :fra sableux :fra moo gën maanaam déeg mais :fra bu delloo ci ñebe
748.557
771.396
%hum %hum
771.396
771.908
ñebe moom ay exigeance :fra am bariwul noonu
771.908
773.977
%hum %hum
773.977
774.457
bu amee suuf bu nga xamante ne c' :fra est :fra sableux :fra
774.457
776.618
%hum %hum
776.618
777.023
mën na cee dund wala suuf boo xamante ne c' :fra est :fra sableux :fra argileux :fra
777.023
780.858
%hum %hum
780.858
781.3
moom ay exigence :fra am bariwul mais :fra bu delloo ci gerte moom suuf yi mu soxla
781.3
785.242
%hum %hum
785.242
785.621
mooy li ñu naan les :fra sols :fra sableux :fra mais :fra tamit bu amee suuf yu diis yi tamit dina ci mën a dund
785.621
791.497
%hum %hum
791.497
792.056
parce :fra que :fra ku amul la gën %e am la fa sës l' :fra essentiel :fra daal li mu soxla ci ay ferñeent ak li mu soxla ci ndox na ko am mais :fra %e daal amul amul problème :fra bu kii quoi :fra
792.056
803.144
%hum %hum mun naénu jàll nga wax ci ñeenteelu laaj bi ndax %e sànq wax nga ko junj nga ko nee nga %e fe() amandement :fra yi di nga ci dellusiwaat donc :fra jot na nag pour :fra nga dellu si si ndax %e nee nañu %e béykatu Louga bi %e donc :fra %e yan moyens :fra lay disposer :fra ah ngir %e mën a def li nga xamante ne moom mooy fertilisation :fra ak amandement :fra suuf si surtout :fra %e ki nekk fii Louga comme :fra que :fra si zone :fra Louga bi lañ nekk
803.144
829.157
waaw %e merci :fra beaucoup :fra sëñ Ba xam naa bu delloo ci coté :fra boobu moom
829.157
833.899
%hum %hum
833.899
834.405
%e amandement :fra ak %e fertilisation :fra
834.405
837.127
%hum %hum
837.127
837.502
peut :fra être :fra dañu ñun ci li ñu gën a apesantir :fra mooy
837.502
840.289
%hum %hum
840.289
840.606
utilisation :fra matière :fra organique :fra ci la énu gën a apesantir :fra matière :fra organique :fra nag mooy méngoog bu ñu ko bëggee tënk ci olof mooy lépp lu nga xamante ni dafa jugee ci luy dund
840.606
852.606
%hum %hum
852.606
853.122
%hum
853.122
853.653
%hum %hum
853.653
854.291
wala mu jugee ci lu doon dund par :fra exemple :fra
854.291
858.074
%hum %hum
858.074
858.623
buñ jëlee exemple :fra mën nañ ne %e ñax
858.623
861.657
%hum %hum
861.657
862.236
bu wow
862.236
862.663
%hum %hum
862.663
863.189
matière :fra organique :fra la
863.189
864.194
%hum %hum
864.194
864.719
nga dem sa mbaaru xar nga bale ko fumier :fra ba fa jógee matière :fra organique :fra la
864.719
869.217
%hum %hum
869.217
869.585
sa desitu ceeb sax matière :fra organique :fra la
869.585
871.6
%hum %hum
871.6
872.145
loolu daal ci gàttal moom mooy %e matière :fra
872.145
877.381
%hum %hum waaw des na
877.381
880.074
%hum
880.074
880.544
880.544
882.013
waaw dañ ciy ñëw mais :fra tamit %e phosphate phosphate :fra moom dafa nekk %e mën nañ ne benn xeer la
882.013
890.557029
%hum %hum
890.557029
891.333
xeer la bu nga xamante ni wala suuf la sax ci tënk bu ñu ko bëggee tënk ci olof bon :fra bu nga xamante ni dan koy exploiter :fra ci carière :fra yi moom nag %e peut :fra être :fra dinañ gën a ñëw ci ay dinañ gën a ñëw sax ci ay njëriñam ci kanam mais :fra phosphate :fra moom am na solo trop :fra puisque :fra am na benn ferñeent bu nga xamante ni ñi ngi koy woowee phosphore :fra
891.333
914.454
%hum %hum
914.454
914.756
boobu moo nekk ci engrais :fra NPK yi
914.756
917.323
%hum %hum
917.323
917.803
mooy P boobu noonu nekk ci engrais :fra NPK yi kooku ci phosphore :fra maanaam boo jëlee phosphate :fra %e dafa bari phosphore :fra te dañu seetlu ne fii ci Sénégal suñu suuf dafa manqué :fra phosphore :fra moo tax nag %e gouvernement :fra bi %e andi benn politique :fra bi nga xamante ni phosphotage :fra de :fra fonds :fra la tudd
917.803
938.351
%hum %hum
938.351
938.718
boobu mi ngi dox nii nii jamono jii
938.718
941.094
%hum
941.094
941.576
xam naa dinañ ko gën a leeral ci kanam
941.576
943.108
%hum %hum nee naénu tamit %e béykat bi
943.108
946.338
%hum %hum
946.338
946.79
%e li nga xamante ne moom mooy %e avantages :fra yi waaw parce :fra que :fra dañu ne fii %e expliquer :fra ah les :fra avantages :fra par :fra rapport :fra aux :fra autres :fra formes :fra de :fra fertilisation :fra donc :fra yi nga fi lim nii %e yan yan yan naka la gënee yeneen xeetu fertilisation :fra yi
946.79
961.773
%hum %hum dëgg la %e maanaam %e tey jii nii man bu ma jëfandikoo %e fumier :fra
961.773
969.204
%hum %hum
969.204
969.602
jël ko def ko sama tool wala ak ci utiliser :fra
969.602
973.271
%hum %hum
973.271
973.551
engrais :fra de :fra synthèse :fra mooy maa() engrais :fra yi ñiy defar ci usines :fra yi
973.551
976.32
%hum %hum
976.32
976.74
loolu noonu ban différence :fra lay am ci sol %e mën naa la koo gën a tënkalaat ba tey damay delluwaat ci suñu doom ji ak suñu yaay ji
976.74
983.874
%hum %hum
983.874
984.452
parce :fra que :fra bu dee par :fra exemple :fra
984.452
986.758018
%hum %hum
986.758018
987.247
jigéen ju nga xamante ni dafa war a nàmpal doomam te amul soow
987.247
990.667
%hum %hum
990.667
991.268
%hum nga jox jigéen ji mu lekk ba suur %e faj ko ba mu wér kooku dina mën a nàmpal dooma
991.268
999.569
dana nàmpal
999.569
1,000.427
léegi ah amaat soow léegi loolu noonu nga ko jox loolu mooy matière :fra organique :fra ba
1,000.427
1,005.367
%hum *
1,005.367
1,006.058
matière :fra organique :fra du dafay %e ñëw rek %e dundal gàncax bi directement :fra mais :fra day defar suuf si ba mu mën a dundal gàncax bi mais :fra léegi nag bu dee yeneen formes :fra engrais :fra de :fra synthèse :fra yi nga xamante ne ci usine :fra la ñu koy defaree yooyu ci tënk dama naan la mooy biberon :fra entre :fra doom jeeg yaay ji parce :fra que :fra tey jii bu dee jigéen ji moom amul soow
1,006.058
1,025.006
%hum %hum
1,025.006
1,025.694
%e mu bëgg a nàmpal doomam nga dem jëndi meew pharmacie :fra ñëw defar ko biberon :fra jox ko doom ji doom ji moom mandi na de lekk na ba suur mais :fra ba tey yaay ji amul soow bu mu ko jox léegi %e loolu noonu mooy yeneen engrais :fra yi
1,025.694
1,040.528
%hum %hum
1,040.528
1,041.041
par :fra rapport :fra ak suuf mooy yeneen engrais :fra yi par :fra rapport :fra ak gàncax
1,041.041
1,044.814
%hum %hum
1,044.814
1,045.294
boo defee engrais :fra NPK yii nii ñuy utiliser :fra engrais :fra de :fra synthèse :fra yi nga jël ko def ko ci suuf
1,045.294
1,050.052
%hum %hum
1,050.052
1,050.4
gàncax bi rek moo koy jëfandikoo mais :fra suuf bi moom du ci am dara ba tey tamit %e phosphate :fra phosphate :fra moom njëriñ bi mu am
1,050.4
1,058.307
%hum %hum
1,058.307
1,058.763
mooy %e bu ma jëloon phosphate :fra defko sama suuf non :fra seulement :fra dinaa am phosphore :fra mais :fra dinaa am yeneen ferñeent yu ci mel ni calcium :fra wala magnésium :fra yu nga xamante ni gàncax yi daén leen di jëfandikoo te bu doon yeneen beneen engrais :fra nga utiliser :fra doo ko am
1,058.763
1,074.081
%hum %hum
1,074.081
1,074.481
loolu daal mooy différence :fra bi entre :fra phosphate :fra beeg matière :fra organique :fra bi ak yeneen xeetu engrais :fra yi
1,074.481
1,080.121