start_time
float64
0
2.73M
end_time
float64
326
2.78M
speaker_id
stringclasses
55 values
text
stringlengths
1
4.06k
utterance_pitch_mean
float32
38.3
473
utterance_pitch_std
float32
0
282
snr
float64
-3.78
64.6
c50
float64
-6.34
60
speaking_rate
float64
0
2.1k
phonemes
stringlengths
0
1.77k
stoi
float64
0.24
1
si-sdr
float64
-18.8
28.1
pesq
float64
1.08
4.37
467,154
469,567
1010spk3
%e moom lañu koy defaree muy cinq produits yi
191.426819
56.47591
34.760139
39.675213
6.630407
%i sɪŋk ji
0.980394
17.253841
2.162841
469,567
470,048
1010spk1
%hum
160.151398
62.79517
26.998041
28.557941
8.465609
%hʌm
0.951176
24.082058
1.788423
470,048
481,774
1010spk3
5 la ñu koy booleel te loolu lépp ku ci nekk am na li nga xam si moom mooy quantité bi nga soxla ci ñebe bi bi ngay soxla ci dugub bi bi ngay soxla ci mboq bi bi ngay soxla ci gerte gi ak bi nga xam si moom ngay
194.496323
61.753838
38.258461
50.984848
7.684918
lɑ ti ku æm nɑ li si baɪ baɪ baɪ baɪ baɪ baɪ baɪ baɪ si
0.991712
24.974987
2.819007
486,252
489,030
1010spk1
mën a ràññee li nga ko waxee léegi nii nu ñu ko mën a nattee
162.49321
20.009144
49.216267
58.641453
9.394761
ʌ li koʊ nu koʊ ʌ
0.994345
25.494995
3.668213
490,206
491,364
1010spk3
foofu foofu xam nga loolu
258.79306
130.816788
38.834049
57.646008
3.485839
0.850442
4.306825
1.780474
492,737
493,065
1010spk1
%hum %hum
148.516418
23.502455
36.679745
2.169647
28.070175
%hʌm %hʌm
0.968711
20.054718
1.764508
493,065
507,649
1010spk3
ba li kenn ku ci nekk tay produit yooyu kenn ku nekk fa() %e boo fa bu fa kenn nekkoon sax mën a liggéey ci produit yooyu waaye lu ci nekk xam nga foofu bari na ndax cinq produits boo ko bëggee liggéey jaar fa nga war a jaar ba keroog muy sotti kon loolu yaakaar naa ne soo xamul normes yi dëgg dëgg dëgg liggéey ba dana des
227.398148
82.252045
40.302322
36.324951
10.42524
bieɪ li kɛn ku teɪ kɛn ku () %i bu kɛn sæks ʌ lu bɑɹi nɑ sɪŋk bu koʊ wɔɹ ʌ bieɪ soʊti kɑn ni su ji bieɪ deɪnʌ dɛs
0.976416
17.726673
2.121451
507,649
507,902
1010spk1
%hum %hum
168.502655
9.303264
7.621408
6.266284
35.555554
%hʌm %hʌm
0.990189
21.776886
2.42456
507,902
520,826
1010spk3
te yaakaar naa ne fii may waxee ci rajo laa ne wante maasàllaa bàjjenu goxu Louga yi dama leen di beral loxo ndax it ñoom maasàllaa dañuy faral di wax toujours %e di yónnee seen cant ci farine bi nga xam si ne moom la ñu defaral xale yi
186.796646
81.367332
37.274654
56.141045
8.056161
ti ni meɪ ni wɑntʌ ji dɑmʌ lin di ɪt di wæks %i di sin kænt baɪ si ni lɑ ji
0.99244
21.212265
2.591954
528,516
531,755
1010spk3
ndax %e kooku bàjjen Rama Dieye mooy présidente bàjjenu gox
154.750351
28.649725
18.083693
52.505531
4.653869
%i ɹɑmʌ
0.970092
16.581787
1.809852
538,395
541,073
1010spk3
dañu lay indil yow dañuy indi dañuy indi ngeen ñam produit yépp la ñuy indi
262.874359
61.928337
0.005497
31.698582
8.626348
leɪ jaʊ lɑ
0.846012
6.585366
1.249648
541,073
541,505
1010spk1
vraiment
217.546829
162.636765
32.31126
18.423805
2.37037
0.965092
12.987327
2.036905
541,505
542,421
1010spk3
dëgg la bu leer
242.61676
74.009178
32.545025
52.484715
5.486968
0.939129
12.095951
2.030038
551,984.285887
566,997
1010spk1
yaakaar naa ni %e yëf yi am na solo léegi ci wàllub ñaax wala ci wàllub %e soit message wala conseil bi nga xam ne danga koy yokk jigéen ñi pour que ñu mën a am li nga xamante ne moom mooy formalisation yi wala ñu mën a am code barre yi wala ñu mën a bokk ci Fra yi
142.578384
30.993322
32.567638
54.6595
9.132192
ni %i ji æm nɑ soʊloʊ wɔlʌ %i mɛsʌdʒ wɔlʌ baɪ ni pɔɹ kju ʌ æm li ni ji wɔlʌ ʌ æm koʊd bɛɹi ji wɔlʌ ʌ ji
0.992206
19.334846
2.835014
566,997
576,140
1010spk2
waaw li ñu leen di wax rekk mooy que ni %e jigéen ñi gën a xam ne %e nit ki moom nit bu amul carte d' identité amul kayitu juddu
125.2005
29.026358
19.944895
58.328281
7.995297
li lin di wæks kju ni %i ʌ ni %i nɪt ki nɪt kɑɹt di'
0.976263
12.457038
1.938646
576,140
576,846
1010spk1
%hum %hum
128.549637
30.485868
24.61442
28.166265
13.00813
%hʌm %hʌm
0.984932
22.806778
1.584181
576,846
581,460
1010spk2
daanaka boo koy gis mook %e pour pour nit ñi mën koo xàmmee
131.011108
24.299442
19.202208
54.030243
6.512007
bu mʊk %i pɔɹ pɔɹ nɪt ku
0.957426
20.281885
1.908027
588,797
589,177
1010spk1
%hum %hum
118.04731
18.816664
38.477531
27.038286
24.242424
%hʌm %hʌm
0.980334
20.966343
1.587292
589,177
590,118
1010spk2
ku ne la ñuy laaj naan kii
135.593201
15.984809
34.314861
58.696289
16.161616
ku ni lɑ nɑn
0.980554
23.487408
2.431946
592,140
592,959
1010spk2
c' du pareil au même
179.490601
42.459858
18.197378
59.658733
14.814815
si' du oʊ
0.939364
14.594032
1.845345
592,959
593,990
1010spk1
non day yàgg morgue ba
223.371445
46.593407
36.250763
32.368801
17.48634
nɑn deɪ mɔɹɡ bieɪ
0.955102
16.532555
2.063846
593,990
594,859
1010spk2
c' du pareil au même
136.661224
41.579037
15.999363
46.810486
13.943355
si' du oʊ
0.942662
10.98169
1.589134
594,859
595,144
1010spk1
%hum %hum
161.468307
8.707863
58.169117
4.909187
33.333332
%hʌm %hʌm
0.981601
22.703991
2.024337
595,144
598,604
1010spk2
moo tax jigéen ñi war nañoo gën a taxawaat
133.180817
32.245323
26.361578
46.420124
6.201551
mu tæks wɔɹ ʌ
0.983719
23.145992
2.551188
0
326
1010spk1
même
108.042282
20.352551
20.053461
58.882538
3.118908
0.920901
11.506562
1.585824
326
747
1010spk2
%hum %hum
139.660141
35.542847
47.054089
22.051155
22.222222
%hʌm %hʌm
0.97071
23.102858
1.807846
747
5,989
1010spk1
moo tax jigéen ñi war nañoo gën a taxawaat jéem a xool naka la ñuy amee këyit
134.135193
29.673962
27.238947
35.432884
6.318083
mu tæks wɔɹ ʌ ʌ lɑ
0.985033
22.983883
2.621681
5,989
6,315
1010spk2
%hum %hum
135.98732
18.843739
33.211052
3.809635
28.070175
%hʌm %hʌm
0.987558
21.631266
2.274361
6,315
11,834
1010spk1
ndax am na yoo xam ne yomb na xam nga lu mel ne que boo de() amee ñenti junni rekk mën a am ay kayit yoo xam ne danga ci mën a
141.147491
26.328543
27.329191
45.928192
12.141805
æm nɑ ju ni nɑ lu mɛl ni kju bu di() ʌ æm eɪ ju ni ʌ
0.979086
18.33007
2.130474
13,480
15,561
1010spk1
waaw bu dee entreprise bu dee entreprise individuelle
135.615448
30.226175
31.882061
57.511433
5.781391
di di
0.982478
13.717896
2.142795
15,561
15,959
1010spk2
%hum %hum
137.429718
24.571657
21.680788
28.669975
23.188406
%hʌm %hʌm
0.996337
24.261717
2.16077
15,959
19,741
1010spk1
ah amaale ca %e kii nu ñu koy waxeeti Ninea
134.559494
23.129456
28.411642
56.562115
4.497355
ɑ kʌ %i nu
0.986604
20.746229
2.300331
19,741
20,057
1010spk2
%hum %hum
132.838577
30.306288
52.080326
26.735004
29.629629
%hʌm %hʌm
0.993266
22.437073
2.327335
20,057
23,939
1010spk1
kooku kon nga jéem caa dugg wut kayi googu bu fekkee bëgg ngaa liggéey laa wax
154.324753
33.293003
37.221466
53.153439
5.668277
kɑn wæks
0.98788
23.34693
2.510077
25,965
26,418
1010spk2
%hum %hum
107.179756
18.322281
20.565464
17.925135
20.512821
%hʌm %hʌm
0.973701
19.132427
1.356964
26,418
52,184
1010spk1
waaye waxuñu ñoo xam ne dañuy liggéeyantu ndax dañoo war a nekk ci jamono boo xam ne nit ñi ñoo war a xam ne war nañoo mën a defar développé suñu gox yi ni ñu koy développé nag mooy nekk de véritables entrepreneur am esprit entrepreneur te boo ko esprit boobu boo ko amee mooy de() nga formaaliizewu soo formaliizewoo ba pare ci la nga nekk ci am ciy kayit mën a xool na ngay lëkkaloog ñeneen ñi pour mën a am formation pour am financement
149.730148
34.202423
33.942604
54.349449
8.745849
ni wɔɹ ʌ bu ni nɪt wɔɹ ʌ ni wɔɹ ʌ ji ni næɡ di ɑntɹʌpɹʌnɜ˞ æm ɛspɹi ɑntɹʌpɹʌnɜ˞ ti bu koʊ ɛspɹi bu koʊ di() su bieɪ pɛɹ lɑ æm ʌ nɑ pɔɹ ʌ æm fɔɹmeɪʃʌn pɔɹ æm fɪnænsmʌnt
0.959207
24.400589
2.866909
52,184
52,648
1010spk2
%hum %hum
120.000923
25.324614
20.573904
21.401159
19.753087
%hʌm %hʌm
0.973798
18.083256
1.495378
52,648
77,630
1010spk1
yeneen kayit ya ca war nga mën koo wut lu mel ne que bu dee dangay def transformation wala yeneen produit yi nga fas yéenee wu() am sa autorisation Fra ndax autorisation Fra moom itam boo ñëwee chambre de commerce %e nu mu tuddati direction des commerce ndax région bu ne am na ko boo fa demee boo laajee ñu teg la ci ñu teg la ci yoon boo ñëwee si fu mel ne que ku mel ne Bada Sylla moomu ñuy wax noonu tay boo ci demoon boo demee dañ la ko da la ciy da la ciy jox ay xalaat
143.861008
29.26107
27.979046
52.930992
10.428983
jɑ kʌ wɔɹ ku lu mɛl ni kju di tɹænsfɜ˞meɪʃʌn wɔlʌ ji wu() æm sɑ bu di kɑmɜ˞s %i nu mu dɜ˞ɛkʃʌn dɛs kɑmɜ˞s ni æm nɑ koʊ bu bu lɑ lɑ jun bu si fu mɛl ni kju ku mɛl ni bɑdʌ sɪlʌ wæks teɪ bu bu lɑ koʊ dɑ lɑ dɑ lɑ eɪ
0.992276
21.654545
2.673092
77,630
78,118
1010spk2
dina la jox ay
148.887115
9.977599
17.017809
59.361866
23.280423
dinʌ lɑ eɪ
0.972388
18.866207
2.838389
79,994
117,457
1010spk1
boo deme daañu la ci jox ay ay xalaat %hum boo ñëwee bu dee kuréel gi jege na la boo ñëwee Fapal boo ñëwee Fapal dana la ci jox ay ay xalaat %hum code barre itam la même chose ndax code barre dafa comme ni ñu ko waxee léegi dafa am solo solo trop trop trop te ñuy ñii yëngatu si transformation ñun ñépp ñoo ko war a ñoo ko mën a war a am ndax tag complexe bi ñu am muy consommation des produits étrangers dañu ko war a teg de côté complexe nourri boobu dañu ko war a teg de côté lii ñu bay ñu koy jëfandikoo maanaam lii ñuy bay ñu koy dundee li ñuy dundee ñun ñu koy bay loolu mooy tax ñu mën a am réew mu développé wala un monde rural bu développé
146.294205
39.94252
30.052374
46.674129
8.997622
bu lɑ eɪ eɪ %hʌm bu di nɑ lɑ bu bu deɪnʌ lɑ eɪ eɪ %hʌm koʊd bɛɹi lɑ tʃoʊz koʊd bɛɹi ni koʊ æm soʊloʊ soʊloʊ ti si tɹænsfɜ˞meɪʃʌn koʊ wɔɹ ʌ koʊ ʌ wɔɹ ʌ æm tæɡ baɪ æm dɛs koʊ wɔɹ ʌ di koʊ wɔɹ ʌ di beɪ beɪ dʌndi li dʌndi beɪ tæks ʌ æm mu wɔlʌ ʌn mɑnd ɹʊɹʌl
0.994222
21.216824
2.464991
117,457
118,705
1010spk2
mais est ce que affaire yi ca la nga
167.894455
36.602894
41.496883
59.02729
21.917809
meɪs ɛst sii kju ji kʌ lɑ
0.97928
18.233713
2.949029
124,571
127,318
1010spk1
non prix yi xam nga tay %e booy xool
167.786774
60.181419
30.102068
52.736267
7.681756
nɑn pɹi ji teɪ %i
0.992221
23.12195
2.666173
127,318
127,716
1010spk2
%hum %hum
130.115616
22.62322
22.125721
30.053869
23.188406
%hʌm %hʌm
0.930145
18.046116
1.304091
127,716
133,126
1010spk1
tay jii nga xoole cere kilo dugub mu jar nga jëndee ko trois:Fra cent:Fra
126.035225
31.630754
26.037113
59.10553
9.629629
teɪ kɪloʊ mu dʒɑɹ koʊ twɑ: sɛnt:
0.990295
19.431629
2.721804
133,126
133,743
1010spk2
%hum %hum
119.175545
22.988741
25.199215
40.290882
14.814814
%hʌm %hʌm
0.968918
22.089506
1.645196
133,743
146,400
1010spk1
soq ko sebeti ko weer ko wal ko mooñ ko tay ko kooku temps la
124.144562
35.947598
30.339773
49.682888
28.368795
koʊ koʊ koʊ wɔl koʊ koʊ teɪ koʊ tɛmps lɑ
0.985729
18.544397
2.430963
146,400
147,927
1010spk2
processus la de bu ya() bu gudd sax
170.745712
33.574364
34.242847
58.314354
12.510288
lɑ di jɑ() sæks
0.992115
23.500271
3.152418
147,927
148,524
1010spk1
temps la
276.774658
36.438324
22.095846
21.856394
13.544974
tɛmps lɑ
0.941113
22.689699
2.291626
150,326
153,934
1010spk1
mu jaay la benn kilo nga ñëw léegi ne ko jaay ma kilo cere léegi
159.579453
19.88649
27.132538
59.302773
10.850287
mu lɑ bɛn kɪloʊ ni koʊ mɑ kɪloʊ
0.992128
22.536518
2.630408
153,934
154,695
1010spk2
fekk bu ñu defar ba pare
144.49588
27.208788
34.51984
59.294792
15.80247
bieɪ pɛɹ
0.995637
26.512493
3.385701
154,695
155,436
1010spk1
en une minute
202.48288
42.675472
38.94706
58.953754
13.781223
ɛn mɪnʌt
0.989094
21.382
3.324051
155,436
155,870
1010spk2
waaw
138.888489
15.217422
26.38414
28.029963
0
0.991532
21.156116
2.658391
155,870
159,236
1010spk1
danga mën a vaqué say occupation danga mën a def se def sa beneen liggéey
184.001541
29.590399
45.487694
35.62125
10.124698
ʌ seɪ ɑkjʌpeɪʃʌn ʌ seɪ sɑ
0.990664
21.815008
2.72091
159,236
159,536
1010spk2
%hum %hum
122.653069
42.695351
40.52504
3.039545
31.372548
%hʌm %hʌm
0.981872
20.115028
1.814384
159,536
160,957
1010spk1
te amoo benn perte temps
175.654236
66.647217
23.104294
32.018669
10.58201
ti bɛn tɛmps
0.974132
20.411316
2.299927
160,957
161,197
1010spk2
%hum %hum
142.475555
39.503773
13.886396
4.575639
38.095238
%hʌm %hʌm
0.977155
22.547413
1.748902
161,197
161,529
1010spk3
%hum %hum
97.417633
25.983034
9.850411
24.375208
28.070175
%hʌm %hʌm
0.636278
6.42942
1.131297
161,529
166,256
1010spk1
kon kooku amul perte bu ciy bu ci nekk
138.863647
44.61673
23.638292
35.616566
4.158545
kɑn
0.986342
15.696824
1.913721
166,256
166,618
1010spk2
dëgg la
133.983109
19.73835
14.691566
59.901604
8.465608
0.95812
16.09803
1.735048
166,618
167,957
1010spk1
maanaam cher defu ko
150.420364
46.212791
30.435991
34.039921
6.751055
ʃɛɹ koʊ
0.997477
21.622223
2.779222
167,957
168,192
1010spk2
%hum %hum
181.356201
14.102462
39.660496
26.341972
41.025641
%hʌm %hʌm
0.969475
22.651482
1.861767
168,192
169,513
1010spk1
ndax kilo cere ñaata la ñu koy jaayee
152.375626
38.729916
41.05859
33.123547
10.636278
kɪloʊ lɑ
0.96652
6.943871
1.682822
169,513
169,984
1010spk3
sept:Fra cent:Fra
141.570709
41.917728
20.182785
59.774296
24.142661
sɛpt: sɛnt:
0.953451
13.902371
1.522461
169,984
170,997
1010spk1
sept:Fra cent:Fra franc:Fra
220.821259
38.196114
26.788397
32.433292
17.777777
sɛpt: sɛnt: fɹæŋk:
0.964026
18.206375
1.882873
170,997
171,718
1010spk2
kilo cere
169.732224
55.793663
34.213776
39.673359
8.465608
kɪloʊ
0.991459
22.00005
2.595726
172,155
172,729
1010spk2
sept cent :Fra
170.142624
40.942245
35.13588
21.939726
19.172113
sɛpt sɛnt :
0.986654
21.566505
2.942924
172,729
173,072
1010spk3
%hum %hum
62.850487
19.479219
3.17305
8.084206
26.666666
%hʌm %hʌm
0.53292
-0.121005
1.191871
173,072
173,708
1010spk1
sept:Fra cent:Fra
177.966095
52.904594
30.382294
34.164181
17.617618
sɛpt: sɛnt:
0.976189
22.474613
2.587685
173,708
174,260
1010spk2
%hum %hum
152.685715
23.896477
29.56752
26.291683
16.666666
%hʌm %hʌm
0.983722
22.689255
1.781199
174,260
178,413
1010spk1
kon kooku yow te kilo cere bi xoolal ñaata nit ñoo ci mën a
169.85614
35.764397
30.027439
55.1922
7.949413
kɑn jaʊ ti kɪloʊ baɪ nɪt ʌ
0.992298
12.915937
1.747594
179,607
180,910
1010spk1
jëlal tay jii ñu jël
174.26091
40.282787
40.723965
25.12837
5.387205
teɪ
0.990526
23.310429
2.298554
180,910
182,593
1010spk2
ki %e cere laalo ou sans laalo
197.91272
55.141392
26.309244
52.620487
8.978676
ki %i u sænz
0.939074
15.70312
2.551848
182,593
182,949
1010spk1
%hum
154.321487
28.122135
10.728544
47.903393
11.287478
%hʌm
0.926059
13.647915
1.688886
182,949
184,728
1010spk3
am na cere laalo am na sans laalo
173.384506
49.210011
32.797844
14.36721
10.723104
æm nɑ æm nɑ sænz
0.969637
16.80872
2.077353
184,728
185,976
1010spk2
%hum %hum mais ñoo yam benn prix
141.10527
31.990759
34.905556
59.662365
22.72958
%hʌm %hʌm meɪs jæm bɛn pɹi
0.98659
18.432007
2.629858
185,976
186,230
1010spk1
waaw
145.192047
18.371599
5.122153
6.108505
0
0.944894
14.6785
1.772599
186,230
186,772
1010spk3
déedéet
196.711517
31.811056
27.934021
59.697517
0
0.976994
22.310034
2.101975
191,205
191,911
1010spk2
okey:en
124.591782
34.442127
35.98988
59.729248
10.117435
oʊki:ɛn
0.994648
24.12495
2.662328
191,911
192,813
1010spk3
comme ni Ibrahima waxee
245.650925
125.879753
18.63966
20.967089
5.590496
ni
0.917169
15.564973
2.265892
193,546
193,901
1010spk2
%hum %hum
120.856781
35.735741
13.920878
26.47167
25.396825
%hʌm %hʌm
0.970606
11.989801
1.265723
193,901
196,812
1010spk3
gis nga %e dañoo développé boog maasàllaa
182.295135
84.360786
30.238178
28.202351
2.756245
%i
0.976748
21.961117
2.312793
196,812
197,282
1010spk2
%hum %hum
112.842102
27.99276
28.344893
21.108335
19.753087
%hʌm %hʌm
0.990076
24.70109
2.227244
197,282
207,986
1010spk3
ndax tay jigéen bu njëkk da daan dem góobi dikk xar weer mu wow nga bojj soq mag ñi amuñu woon benn temps
185.212234
94.500618
33.978905
50.155098
4.96649
teɪ dɑ mu waʊ mæɡ bɛn tɛmps
0.97768
12.231759
2.635264
209,767
210,189
1010spk2
%hum %hum
154.583115
22.914923
38.138336
26.901674
24.242424
%hʌm %hʌm
0.987838
20.816055
2.462224
210,189
213,323
1010spk3
amuñu woon benn jot lépp lu ñu daan liggéey journée bi ci kër gi lay yam
192.104736
68.200432
22.988941
59.478642
10.57057
bɛn dʒɑt lu baɪ leɪ jæm
0.973518
18.471176
2.334107
213,323
213,649
1010spk2
%hum %hum
168.220108
13.471261
40.721508
26.115471
28.070175
%hʌm %hʌm
0.979394
23.863148
1.765719
213,649
222,841
1010spk3
tay nag mën nga defi say activité yow loo bëgg a def tay damay xëy dem liggéeyi sa liggéey ya ngay sa njaay ma ngay jaay ak la ngay defi lépp ndax jigéen ñi ñépp kenn ku ci ne fa nga nekk yaa ngi yëngu
277.08429
113.44593
27.964291
32.180241
8.823529
teɪ næɡ seɪ jaʊ lu ʌ teɪ sɑ jɑ sɑ mɑ lɑ kɛn ku ni
0.915014
9.924253
1.622858
222,841
223,131
1010spk2
%hum %hum
151.988174
26.178955
5.049428
5.970021
31.372548
%hʌm %hʌm
0.973428
21.47958
1.784441
223,131
226,442
1010spk3
bu ngoonee nga jaar ci unité bi jënd fa sa cere
206.100357
124.859573
32.958012
39.56023
4.535148
baɪ sɑ
0.928026
9.791696
2.334732
229,700
230,477
1010spk3
defar sa ñeex
107.386414
47.447498
14.792893
34.68195
5.152979
0.830176
2.030387
1.211334
230,477
231,165
1010spk2
moo gën a gaaw
135.650513
21.798542
28.277538
32.639427
8.888889
mu ʌ
0.980317
18.413612
2.65909
231,165
231,545
1010spk3
jeex na
162.539352
56.459496
54.538406
56.58456
8.080808
0.984787
17.585066
2.680847
231,545
231,908
1010spk2
%hum %hum
109.502998
26.329487
51.453182
3.382447
25.396825
%hʌm %hʌm
0.989422
23.180691
1.794659
231,908
235,851
1010spk3
kon foofa amatul lenn loo xam si ne lu lu lay tardé ci sa liggéey
208.498444
85.795876
24.87199
59.503437
8.392942
kɑn lu si ni lu lu leɪ sɑ
0.952311
15.708858
1.729851
235,851
236,140
1010spk2
%hum %hum
140.298248
38.184658
8.676158
4.600744
31.372548
%hʌm %hʌm
0.982919
23.488167
2.522435
236,140
239,379
1010spk3
su fekkee ne yow tay danga ne tey dangay dangay dangay togg fonde reer
228.23558
93.335724
23.648806
23.321522
7.756448
su ni jaʊ teɪ ni
0.979595
21.495361
2.479547
239,379
239,886
1010spk2
%hum %hum
151.727386
16.934832
24.047647
23.141012
17.777777
%hʌm %hʌm
0.977194
20.132408
1.605635
239,886
245,893
1010spk3
dangay xaar ba ngoon rekk nga yónnee sa araw jaay ma araw nga jënd sa araw dem togg sa fonde reer
299.188171
100.979187
32.997707
41.907043
5.34168
bieɪ sɑ mɑ sɑ sɑ
0.952464
23.960995
3.003207
247,413
251,050
1010spk3
dangay xaar ba ngoon rekk au lieu que ngay soq ak a wal ak a sebet a ka jël sa temps
312.147827
88.006432
21.364912
31.833349
12.95435
bieɪ oʊ lu kju ʌ wɔl ʌ ʌ kɑ sɑ tɛmps
0.934754
18.260986
2.8185
253,661
259,464
1010spk3
te yow amoo ci pertement ki ngay jëndee ci moom it amu ci pertement
208.595093
120.825203
43.86285
37.37748
4.313174
ti jaʊ ki ɪt
0.986157
21.83757
2.637022