bilalfaye/nllb-200-distilled-600M-wo-fr-en
Translation
•
Updated
•
47
•
2
fr
stringlengths 4
1.08k
| wo
stringlengths 2
4.02k
| en
stringlengths 3
1.08k
|
---|---|---|
Bonne continuation. | Yal na la jig te yeneeni ndam topp ci. | Good work. |
Vérifiez que votre main soit détendue le plus possible lorsque vous jouez chaque note correctement. Essayez également de ne pas faire de mouvements inutiles avec vos doigts.
| Wóo ni sa loxo bi téguna bu baax booy bindee lii bu baax – tamit bul jeema def yeneen yu si bokkul ak say baaraam.
| Make sure your hand is as relaxed as possible when you play each note correctly, and try not to make unnecessary movements with your fingers. |
Ce renouveau politique, véritable alternative, nous conduira immanquablement vers une reconquête des valeurs républicaines et démocratiques. | Beesal gi am ci pólótig bi dana tax, ci lu wér, ñu dellu ci suñuy xar-baax. | This political renewal, a genuine alternative, will inevitably lead us to a reconquest of republican and democratic values. |
Mais je ne doute point, vu la mobilisation exceptionnelle qu’il y a ici, et la popularité que vous avez auprès de votre peuple, et particulièrement auprès de cette frange jeune, que vous saurez surpasser ces obstacles. | Waaye wéddiwuma ko, soo gisee ndaje mu am doole mi fi am ak ni nga siiwee ci sa askan, lu ci ëpp ci ndaw ñi, dinga mën a romb jafe-jafe yi. | But I have no doubt, given the exceptional mobilisation that is here, and the popularity you have among your people, and especially among this younger fringe, that you will be able to overcome these obstacles. |
Il faut que tu tiennes ta promesse, me dit doucement le petit prince, qui, de nouveau, s’était assis auprès de moi. | Ndoomu buur si toogaat ci sama wet, wax ma ndànk: danga war a def li nga ma dig. | "You must keep your promise", said the little prince, who was sitting next to me again. |
Patriotes du Sénégal pour le Travail l’Ethique et la Fraternité. | Doomi Senegaal yi fonk seen réew ngir liggéey bu jaar yoon ak bennoo. | Patriots of Senegal for work ethic and fraternity. |
C'est, du moins, ce que rapporte le quotidien L'As dans sa livraison de ce mercredi. | Loolu lañu Le quotidien L’As xibaar ci àllarba ji. | At least that is what the daily newspaper L'As reports in its issue of this Wednesday. |
Ce qui a été bien accueilli par Serigne Mountakha qui a fait un émouvant témoignage sur Sokhna Aïda Diallo dans cet audio. | Mu doonoon lu Sëriñ Muntaqaa nangu woon a dalal, ba tax mu def ab seede bu am solo ci Soxna Ayda Jàllo ci jile wax. | This was welcomed by Serigne Mountakha who gave a moving testimony about Sokhna Aïda Diallo in this audio. |
Cela semble un peu intimidant d'en bas, et c'est une ascension raide et difficile, mais les personnes les plus en forme devraient pouvoir le faire en 45 minutes environ.
| Moo ngi niroog lu ragallu, te njël bu jafe ak kawé, wante nit yu bari té am xel warna ñu ko defar cili toloog 45 simili
| It looks a little intimidating from below, and it's a steep and difficult climb, but the fittest people should be able to do it in about 45 minutes. |
Pour satisfaire aux exigences de provisionnement, les primes collectées sont donc investies dans des produits financiers, sélectionnés par les services idoines des sociétés d’assurance, selon certaines contraintes relatives à la concentration et l’exposition notamment., | Moom rekk moo jot a dugal bit waa Pari yi ci joŋante ren bi ci LDC. | To meet the provisioning requirements, the premiums collected are therefore invested in financial products, selected by the appropriate insurance company departments, according to certain constraints relating to concentration and exposure in particular. |
El Hadj Mar a comparu, mercredi, devant la Cour d’appel de Dakar pour abus de confiance. | Elaas Maar wuyuji na, àllarba, ca ëttu àttekaay bu Ndakaaru ndax njublaŋ. | El Hadj Mar appeared on Wednesday in the Dakar Court of Appeal for breach of trust. |
C'est un garçon timide qui n'a pas lephysique d'un caïd. | Góor gu noppi la, ku yorul kanamu woyu. | He's a shy boy who doesn't have the physique of a big shot. |
Nous avons eu 110 combats par équipes et 70 en catégories de poids, a-t-il détaillé. | Am nañu téeméer ak fukki kombaa kuréel gu ne ak juróom-ñaar-fukk ci pàcc ñi am doole ci li mu wax. | We had 110 fights per team and 70 in weight categories, he said. |
Le Il-76 est une composante majeure de l'armée russe et soviétique depuis les années 1970, et avait déjà enregistré un grave accident en Russie le mois dernier.
| II-76 bi dafa nekkoon aab pàcc bu mag bu takk deru Russe yi ak Sowiet yi ci 1970, te ab akisdaa bu meti am na ba pare c Russi weer wi nu weesu.
| The Il-76 has been a major component of the Russian and Soviet military since the 1970s, and had already suffered a serious accident in Russia last month. |
Un pays où l’Organisation des Nations Unies dénombre 500 000 fumeurs. | Réew mu mbootaayu xeet yi waññ téeméeri junniy tuxkat. | A country where the United Nations estimates that there are 500,000 smokers. |
il a le droit d'avoir un avion mais ce n'était pas une priorité les gens meurent de faim. | War naa mën a am ab ropplaan waaye loolu du farata ndax askan wi dañoo xiif. | He's entitled to a plane, but it wasn't a priority. People are starving. |
C'est une nuit inoubliable dans l'histoire de Zamalek, assure le club sur les réseaux sociaux. | Këlëb bi nee na, ci mbaali jokkoo yi, guddi la gu ñu dul fàtte mukk ci taarixu Zamaleg. | It was an unforgettable night in Zamalek's history, the club said on social media. |
Au PASTEF, les préoccupations du sénégalais lambda sont au cœur des sujets. | Ca PASTEF, yittey doomu Senegaal moo fay waxtaan. | At PASTEF, the concerns of the ordinary Senegalese are at the heart of the topics. |
Saipov, âgé de 30 ans, se serait servi d’un camion loué auprès de Home Depot pour attaquer une piste cyclable sur la route West Side Highway, dans le Lower Manhattan, fauchant sur sa route des piétons et un cycliste en octobre dernier.
| Palin, 29, bu Wasilla, Alaska, deñ kaa jappoon ci ay tuuma fitnaal ci biir kër ak bañ ñu japp ko, su nu sukkandikoo ci ap jottali bu Samdi mu juge ci Réewu Alaska Troopers.
| Saipov, 30, allegedly used a rented Home Depot truck to attack a bike path on the West Side Highway in Lower Manhattan, killing pedestrians and a cyclist in October. |
Il passe le flambeau à son compatriote John Ram qui a vaincu la légende du golf américain Tiger Woods 2-1 en simples, dimanche dernier.
| Bumuy janoo ak Asamble Generaal bu mbootaayu xeet yi, jawriñ buñu denk bitim reew Walid al-Moualem neena mbir yi yaa ngi tane ci dëk bi.
| He passes the torch to his compatriot John Ram who beat American golf legend Tiger Woods 2-1 in singles last Sunday. |
La délégation de pouvoir au Président de la République est encadrée et circonscrite dans son objet (l’article 77 de la Constitution dispose : dans les limites de compétence fixées par la loi ) et dans sa durée (l’article dispose dans les limites de temps (…) fixées par la loi d’habilitation ). | Jébbalug njiitu réew mi sañ-sañ la ko ci fa mu jublu (dog juróom-ñaar-fukk ak juróom-ñaar : ci yamuwaayu mënin yi yoon teg) ak ci yàggaay (dog baa ngi wax ca yamuwaayu waxtu wi (…) bi yoonu dëkkuwaay yi taxawal). | The delegation of power to the President of the Republic is limited in its object (Article 77 of the Constitution provides: within the limits of competence laid down by law) and in its duration (Article 77 provides within the time limits (...) laid down by the law of empowerment). |
Une première explication réside dans la plus grande aversion au risque des femmes par rapport aux hommes., | Leeral bu jëkk bi mi ngi jëm ci musiba yiy gën a laal jigéen ñi. | One explanation is that women are more risk averse than men. |
C’était doux comme une fête. | Neexoon na ba mel ni xewu jàmm. | It was sweet as a feast. |
En Côte d’Ivoire, les coûts proposés par les compagnies de téléphonie demeurent encore élevés., | Ca Kódiwaar, njëg yi këru telefon yi joxe dañoo kawe lool. | In Côte d'Ivoire, the costs offered by telephone companies are still high. |
Toutefois, il y a le fléau du charlatanisme qui sévit dangereusement au Sénégal et bénéficie de grands renforts de publicité. | Waaye maa-mën yaa ngi gën a am doole ci Senegaal te di dollikoo ay fésal yu jéggi dayo. | However, there is the scourge of charlatanism that is dangerously rampant in Senegal and receives a great deal of publicity. |
Ryder Cup 2018 : L’équipe des États-Unis est prête à se battre pour garder espoir à l’approche des simples de dimanche
| "Tekk loxo ci kongere bi tamit defa doy waar ci taxawaayam, ni persida dina tukki ci rëëw yu bare nii ndax te ñoongi jublu ci ay bësu kampaañ yu xata xat " Reuters neena kenn ku bokk ci porto parool kampaañu Trump moo ko wax waaye nanngul joxe turam.
| Ryder Cup 2018: Team USA ready to fight to keep hope alive as Sunday's singles draw draws near |
La réhabilitation et l’équipement complet de l’école élémentaire de six classes. | Defaraat ak jumtukaay yu mat sëkk ca daara ndongo yu ndaw yi am juróom-benni kalaas. | The rehabilitation and full equipment of the six-class elementary school. |
Lors de certains festivals de musique, la grande majorité des participants décident de camper sur place, et la plupart considèrent que cela fait partie intégrante de l'expérience.
| Ngir yenn festiwaal, li ëpp ci way-fekkee yi ci festiwaalu misik yi dañuy decidé campé ci si bi, te way-fekkee yu ci ëpp dañ koy jàppee xaaj bu am solo ci luñuy dundu.
| At some music festivals, the vast majority of participants decide to camp on site, and most consider this to be an integral part of the experience. |
Les travaux vont se poursuive l’après-midi, à partir de 15 heures, avec l’examen du projet de budget du ministère des Collectivités territoriales, du Développement et de l’Aménagement des territoires. | Dinañu yeggali liggéey yi ci njolloor gi su fukk ak juróomi waxtu jotee ak jàngat ci naal bu njëlu jëwriñ Ji yore wàllu gox-goxaan yi, yokkute ak yeesalaat dëkkin wi. | The work will continue in the afternoon, from 3 p.m., with the examination of the draft budget of the Ministry of Local and Regional Government, Development and Planning. |
Par ailleurs, selon le bureau météorologique islandais, la région de Hekla n’a pas connu de tremblement de terre au cours des dernières 48 heures.
| Biro bu Jangale ci wàllum Meteo ci Islànd xamle na itam ni amul lenn luñuy def ci wàllu yëngu-yëngu suuf ci barabu Hekla ci 48 waxtu yi weesu.
| In addition, according to the Icelandic Meteorological Office, the Hekla region has not experienced an earthquake in the last 48 hours. |
La joueuse Naomi Osaka durant un entraînement à Roland-Garros, face à l'Australienne Ashleigh Barty, le 6 mai 2021 à Paris. | Teniskat bu jigéen bii di Nawomi Osaka, ci tàggatam ca Rolaŋ-Garos, ci digganteem ak Aseigh Barti, bésu juróom-benni fan ci weeru mee atum 2021 ca Pari. | Naomi Osaka during a training session at Roland-Garros, against Australian Ashleigh Barty on 6 May 2021 in Paris. |
« Une des vitres s'est finalement brisée, et ils ont commencé à sortir par la fenêtre », a déclaré Franciszek Kowal, un survivant.
| Benn ci tëjukaaayu palanteer yi mujj naa toj nu daldi tàmbali di genn ci palanteer,”loolu la Franciszek Kowal mi mucc wax.
| One of the windows finally broke, and they started to escape through the window, said Franciszek Kowal, a survivor. |
Une enquête pour meurtre a été ouverte après que le cadavre d’une femme ait été trouvée à Birkenhead (Merseyside) ce matin.
| Ubbinañu app laŋketu faat ginnaaw bi ñu fekke neewu benn jigeen ci Birkenhead , Merseyside tay ci suba.
| A murder investigation has been launched after the body of a woman was found in Birkenhead, Merseyside, this morning. |
La tempête rencontre les eaux froides du Pacifique et perd donc de sa force.
| Waame bi mungi daje ak ndox bu gina sedd ci pasifik bi ba mu waral muy gina am ndegër.
| The storm encounters the cold waters of the Pacific and loses its strength. |
70 % des participants ayant l’intention de voter ont déclaré qu’ils voteraient « oui ».
| Ci 70 yoo jël ci temeer bi neena ñu dinañu wote waaw.
| 70% of participants intending to vote said they would vote yes. |
La conséquence de l’inexistence d’une mesure d’expropriation c’est naturellement l’inexistence d’une créance de l’État du Sénégal à l’endroit des héritiers Ndiaga Ndoye et consort, et donc l’impossibilité de céder une telle créance. | Jeexitalu ñàkk dogalub nangu bi mooy ne nguur gi dafa amul lu mu teg ci yoxoy njabootu Njaga Ndóoy geek ñi ñu àndal, kon nag ag ñàkk a mën a joxe alal jooju. | The consequence of the absence of an expropriation measure is naturally the absence of a claim by the State of Senegal towards the heirs Ndiaga Ndoye and consort, and therefore the impossibility of assigning such a claim. |
L’ouragan Katrina (1967) s’était arrêté à 64 km de la frontière de l’Arizona. »
| Katrina (1967) ap Uragaan la woon ak 40 meetar ci peggu AZ bi.”
| Hurricane Katrina (1967) had stopped 40 miles from the Arizona border. |
Ton expérience de la France a-t-elle influencé ta vision de la politique sénégalaise ? | Dafa war a yemb ni ki dogal yi ñu jël ci wàcc yoon yi ñu jëf. | Has your experience in France influenced your view of Senegalese politics? |
La ville contraste fortement avec les cités du reste du pays, car elle possède un style davantage arabe qu'africain.
| Dëkk bii wuutena lool ay yeneen dëkk yi ci réew, ndax dëkku arab la gëna nuru dëkku Afrique.
| The city is in stark contrast to the rest of the country, as it has an Arab style rather than an African one. |
2 buts à 1 entre Rennais et Stéphanois et première défaite de Puel sur le banc Stéphanois. | ñaari bit ci benn joŋante Reen ak Estefanuwaa bi ak ñàkk ndam bu jëkk bu Puel ci Estefanuwaa yi. | 2 goals to 1 between Rennais and Stéphanois and first defeat of Puel on the bench of Stéphanois. |
Longtemps tenu en échec, le Bayern Munich a trouvé la faille à 20 minutes de la fin et un 2e but la dernière minute du temps réglementaire. | Ñu xawoon koo sonal, Bayern Munich dafa dugal ñaari bit bi ñaar fukki simili dese ci joŋante bi ak ci simili bu mujj bi ci simili yi ñu dolli woon ci joŋante bi. | Bayern Munich, who had been in check for a long time, found the gap 20 minutes from the end and a second goal in the last minute of regulation time. |
Le don de soi pour la PATRIE! El Hadj Malick NDIAYE SN à la Communication de Pastef Les Patriotes. | Tayle sa bakkan ngir RÉEW MI ! Elaas Maalig NJAAY SN ci jokkoo bu Pastef ñi bëgg réew mi. | The gift of self for the country! |
L'utilisation d'Internet permet aux apprentis d’accéder à des informations aussi souvent qu'ils le souhaitent.
| Jëfandikoo lënd gi ak World Wide Web may na ndongo yi ñu jot ci xibaar yi waxtu wu nekk.
| The use of the Internet allows learners to access information as often as they wish. |
On ne dit jamais France dégage. | Waruñoo wax benn yoon Farãas ca bitti. | You never say France is gone. |
Dans les années 1480, lorsque sa construction fut lancée par Lord Hastings, le pays était relativement paisible et la défense n’était nécessaire que contre de petites bandes de maraudeurs itinérants.
| CI jamono 1480, bi Lord Hasting don tambali tabaxam, dëkk bi dafa xawon am jàmm te dañoo soxlawon kaarànge ngir muccu si raykatu nit yi.
| In the 1480s, when its construction was initiated by Lord Hastings, the country was relatively peaceful and defence was only necessary against small bands of roving marauders. |
Par rapport aux élections locales, il explique qu'il n'a aucune ambition d'être le maire de la ville car c'est le président de la République qui a choisi le maire Diagne Sy Mbengue. | Lu jëm ci joŋante gox yeek gox-goxaan yi, leeral na ni mbébétul benn yoon nekk meeru dëkk bi ndax njiitu Réew mi moo tabb meer bi Jaañ Si Mbeng. | Regarding the local elections, he explains that he has no ambition to be the mayor of the city because it was the President of the Republic who chose Mayor Diagne Sy Mbengue. |
Jusqu’ici plutôt calme, le secteur de l’Education commence aussi à bouger, particulièrement dans l’Enseignement supérieur où les deux syndicats menacent d’aller en grève, suite au non respect des engagements pris par le ministre de tutelle Cheikh Oumar Anne. | Ag dal amoon na ci njàng mi, waaye fi mu ne nii jànglekati daara yu kawe yaa ngi bëgg bank seen yoxo ndax seen jëwriñ ji, Seex Umar Aan matalul li mu digaale woon ak ñoom. | The education sector, which has been relatively calm so far, is also beginning to move, especially in higher education where the two unions are threatening to go on strike, following the failure of the minister of guardianship Sheikh Oumar Anne to honour his commitments. |
La priorité désormais sera de mener des négociations pour garantir des garde-fous contre la contrebande, le dumping social et autres menaces économiques, a laissé entendre la présidence. | Njiiteef li, xamle na ni, bés niki tey, li war a jiitu mooy, ay waxtaan ngir wóoral ag fegu ci forot, jaaye bitim réew lu gën a yomb li nekk ci réew mi ak yeneeni gàllankoor yu mën a dal ci koom-koom. | The EU's main priority now will be to negotiate safeguards against smuggling, social dumping and other economic threats, the presidency suggested. |
La loi 2007 sur le gouvernement du Pays de Galles (Government of Wales Act de 2017) octroie à l’assemblée galloise le pouvoir de modifier son nom.
| Teralin bu 2017 joxoonna nguur bu rëëwu Gaal kattan ngir soppi turam.
| The Government of Wales Act 2017 gives the Welsh Assembly the power to change its name. |
Le « phénomène » du Livingston - Analyse
| 'Levingston defna lu rëy- janngat
| The Livingston phenomenon - an analysis of the |
Cette affaire aurait généré au total une créance fictive, illégale, de 94 milliards, établie sur la base de faux documents et de fausses mentions, dénoncés explicitement par Ousmane Sonko lors de sa conférence de presse à Ziguinchor le 12 octobre 2019. | Mbir moomu mënoon na jur bor bu amul firnde te ñàkk a aw yoon te tollu ci juróom-ñeent fukki milyaar ak ñeent, ñu def ko ci ay kayit ak ay tur yu dëgguwul, Usmaan Sónko ŋàññoon na ko ca waxtaanam ak taskati xibaar yi ca Sigicoor ca fukki fan ak ñaar ci weeru oktoobar ca atum 2019. | The case allegedly generated a total fictitious, illegal claim of 94 billion, established on the basis of false documents and false statements, explicitly denounced by Ousmane Sonko during his press conference in Ziguinchor on 12 October 2019. |
Les assurances santé et de biens reposent sur un principe fondamental, qui les rend essentielles à la stabilité de tout écosystème : la mutualisation., | Kaaraangey wér-gu-yaram ak alal yi ñi ngi lalu ci aw doxalin wu am solo, buy tax ñu am solo lool ci yembaayu bépp dund : muy andil ma andi. | Health and property insurance is based on a fundamental principle, which makes it essential for the stability of any ecosystem: mutualisation. |
La population d'origine n'a pas changé du tout, elle a toujours besoin des mêmes adaptations.
| Askan wu wi fa jiitu soppekuwul benn yoon, dañuy soxla ba tey yooyu teggiin yu melni bu njëkk ba.
| The original population has not changed at all, it still needs the same adaptations. |
Demanda-t-il au petit prince. | Mu laaj ndoomu buur si: | He asked the little prince. |
On pourra y sortir des champions pour mieux faire face à ce qui se fait au niveau mondial. | Farãas màggat na waaye dese na ay ŋeleju ba tey. | We can make champions out of them to better deal with what's happening on a global level. |
Il aurait voyagé accompagné de son cousin depuis la province avoisinante de Yunnan le mercredi, dans le but de vendre 15 porcs sur le marché.
| Defa tukkiwoon moom ak benn doomu bajjanam ap dekkandoo ci Yunnan ngir jaayi 15 mbaam xuux ci marse ba.
| He reportedly traveled with his cousin from the neighboring province of Yunnan on Wednesday, with the aim of selling 15 pigs at the market. |
Ce n’est pas une chose très agréable à faire », a ajouté le banquier d’affaires.
| Deñ koo bëg delloo ci cosaanam, ngir defaat hip hop xel lu am bayre.
| It's not a very pleasant thing to do, the business banker added. |
Tu verras où commence ma trace dans le sable. | Dinga gis fi samay tànk tàmbale ci suuf si. | You'll see where my footprint begins in the sand. |
Après plus de sept années au pouvoir, demandez-vous pourquoi les Sénégalais baignent dans l’agonie ? | Ginnaaw lu ëpp juróom-ñaari at yu mu def ci nguur gi, laaj leen lu tax askanu Senegaal wéy di des ci ndóol ? | After more than seven years in power, do you wonder why the Senegalese are bathing in agony? |
Les chirurgiens connaissaient divers sédatifs comme la morphine, ce produit tirée des graines de pavot ainsi que la scopolamine, extraite de graines de jusquiame noire.
| Sirursiyeng yi amoon nañu xam xamu xeeti garab yuy dalalaate bokk na ci moroxin bi nu wutee ci peppi poppy yi ak skopolamin bi nu wutee ci peppi herbane.
| Surgeons were familiar with various sedatives, such as morphine, which is derived from poppy seeds, and scopolamine, which is extracted from black jusquiam seeds. |
Ils se sont rendus vulnérables en soutenant notre ligne politique radicale vis-à-vis du régime. | Dañu néewal doole seen bopp bi ñu doolelee sunu yoonu pólótig wu amul maslaa jëmale ci nguur gi. | They have made themselves vulnerable by supporting our radical political line towards the regime. |
Pastef, en ce qui le concerne ne porte qu’un seul combat à savoir celui contre les mauvaises politiques et la mal gouvernance du régime de Macky Sall et son clan APR – BBY. | Pastef fim ne nii lenn kese mooy xeexam, mooy xeex pólótig bu bon bi ak doxalin wu doyadi wu nguuru Maki Sàll gi ak waa APR-BBY. | Pastef, as far as he is concerned, is fighting only one battle, that against the bad policies and bad governance of the Macky Sall regime and its APR BBY clan. |
J’y gagne, dit le renard, à cause de la couleur du blé. | Wel wi ne ko: Jariñ na ma, ndax melokaanu mboq mi. | "I win", said the fox, "because of the colour of the wheat. |
Les répliques ont continué de secouer la ville côtière samedi.
| Amna ay ndesit yu weyoon di yenngal foronceer bi ni ki Samdi.
| The aftershocks continued to shake the coastal city on Saturday. |
Pourtant, Baye Modou Fall n' rien d'un héro hollywoodien. | Té nag Baay Móodu niruwul dara ak jàmbaaru Oliwut. | But Baye Modou Fall is not a Hollywood hero. |
Une course, un jeu d'enfants gates n'ayant jamais grandi, de voitures disons le electriques avec des batteries concus suite a la disponibilte de plus en plus accrue de minerais des terres rares tels le zircon exploite a moins de 10 km du circuit. | Benn rawante, powum xale yu ñu yàq ba duñu mës a màgg, ay oto yu ñuy wax yu kuraŋ ak seen i batëri yu seen defar aju ci gàncax giy bawoo ci suuf si ba mel ni sirkoo bu ñuy génnee lu yées fukki kilomet diggante fii ak saxu ga. | A race, a child's game, never grown up, of cars say electric with concussion batteries due to the increasing availability of rare earth minerals such as zircon mined within 10 km of the circuit. |
Nun ci kujje gi la nu nekk te sunu xam-xam màcc ci mbir mi, juróomi at a ngii nuy jooytu bor bi te tegunu ko rekk ci ay wax. | Ñun ci kujje gi lanu nekk te sunu xam-xam màcc ci mbir mi, juróomi at a ngii ñuy jooytu bor bi te teguñu ko rekk ci ay wax. | I'm not sure I'm ready to talk about it, but I'm sure I'll be able to do it. |
C’est pourquoi, nous vous demandons d’oser avouer certains échecs dans vos choix. | Loolu moo tax, ñu ne leen ngeen ñemee wax yenn lajji yi ngeen def te taamu ko. | We therefore ask you to have the courage to admit some of the failures in your choices. |
Mais, situé dans les « tropiques élevées » à seulement quelques degrés au nord de l'équateur, il faudra vous adapter à la chaleur (toujours) et à un fort rayonnement du soleil (quand le ciel est dégagé, ce qui est plus rare).
| Waye nékk ci ‘’mbir yi geenee kawe’’ tuuti dégré dong ci bët gannaru equator dinga soxla jëflantél ak tangaay bi (saasuné) ak jant bu am doolé (bu asamaan bi sété, cilu bariwul).
| But, located in the high tropics just a few degrees north of the equator, you will have to adapt to the heat (always) and strong sunlight (when the sky is clear, which is less common). |
Je soulevai le seau jusqu’à ses lèvres. | Ma yékkati baag bi ba mu tolloo ak ay tuñam. | I lifted the bucket to her lips. |
Pourquoi il ne doit pas être autant dans ce pays où tout manque et que les populations sont livrées, depuis le 12 mai 2020, au coronavirus pour son festin ? | Lu tax warul nekk ci réew mile nga xam ne lépp a fi mànke te askan wi, dañu leen a bàyyeek koronaa bi, ci jamonoy fukki fan ak ñaar ci weeru mee atum 2020, jàngoro ji di leen def lu ko neex ? | Why should it not be so in this country where everything is lacking and the population is being delivered, since May 12, 2020, to the coronavirus for its feast? |
Celui-ci est passé de 40 à 60 milliards de francs CFA, soit une hausse de 50%. | Bile jóge na ci ñeen-fukk, dem ci juróom-benn-fukki milyaar ci xaalisu seefaa, manaam ab yokkute bu tollu ci juróom-fukk ci téeméer boo jël. | The amount of the loan was increased from CFAF 40 billion to CFAF 60 billion, an increase of 50%. |
), ce qui contribue à l’appauvrissement des populations. | Liy gën a ndóolal askan wi | ), which contributes to the impoverishment of the population. |
Parmi les exemples figurent le contrôle, la planification et la programmation, la capacité à répondre aux diagnostics et aux questions des clients, ainsi que la reconnaissance de l'écriture, de la voix et du visage.
| Natt saytu bokk na ci, meebeet ak xalaat, meen menu tontu laaj ak xalaatu jeend kat yi, ak di bind ci loxo nangu, baat ak kanam.
| Examples include control, planning and programming, the ability to respond to diagnostics and customer questions, and handwriting, voice and facial recognition. |
Il poussa le vice jusqu’à présenter deux sondages qui le donnaient vainqueur à 70% dès le premier tour, devant Bédié 19%,Soro 8% et Gbagbo 2%. | Mu xuus ba joxe ay natt yu ko def borom ndam li, ak juróom-ñaar-fukk ci téeméer boo jël (70%) ci wote yu jëkk yi, ci kanam Bédié mi am fukk ak juróom-ñeent ci téeméer boo jël (19%) ak Soro mi am juróom-ñett ci téeméer boo jël (8%) ak Gbagbo mi am ñaar ci téeméer boo jël (2%). | He pushed the vice to present two polls that gave him a 70% winner in the first round, ahead of Bédié 19%, Soro 8% and Gbagbo 2%. |
Il n’y a pas de tigres sur ma planète, avait objecté le petit prince, et puis les tigres ne mangent pas l’herbe. | Ndoomu buur si tontu ko ne: Sama palanet amul ay tene, te ñoom duñu lekk ñax. | "There are no tigers on my planet", the little prince had objected, "and tigers don't eat grass". |
Au regard de ce qui précède, on est tenté de dire que c’est dans le leadership politique, moribond, antinational et piteux de nos gouvernements respectifs, depuis 1960, que résident les racines de la domination culturelle et l’exploitation économique française du Sénégal. | Su nu xoole li jot a jàll, mën nañoo wax ne ci mën a jiite ci pólótig bu feebar, àndul ak dëkk bi, ruslu bu su nu nguur yi fi jot a jaar, 1960 ba tey, fa la reenu nooteelu aada ak jëfandikoo koom-koomu Senegaal gi Farãas di def. | In view of the above, it is tempting to say that it is in the moribund, anti-national and pitiful political leadership of our respective governments since 1960 that the roots of French cultural domination and economic exploitation of Senegal lie. |
97 points à leur actif et n’ayant enregistré qu’une seule défaite depuis le début de la saison, les Reds n’ont pas su garder leur avance de 7 points obtenus à l’entame de la seconde phase du championnat. | Juróom-ñeent-fukk ak juróom-ñaari poñ ci seen joƞante ci bennu lajji rekk ci ndoorteelu nawet bi, Reds yi mujj nañoo des ca lim ba ñu rawe woon ñeneen ña ca ndoorteel la tolloo ak juróom-ñaari poñ ci ndorteelu ñaareelu pàccu sàmpiyonaa bi. | The Reds were able to keep their lead of 7 points at the start of the second phase of the championship. |
Arretez de nous divertir avec un monsieur dont sa seule condition d'existence en politique était le poste d'un DG. | Bàyyileen di ñu reeloo ak sang bi nga xam ne, lenn rekk moo taxoon muy pólótig, mooy takk nombo tànku njiit. | Stop entertaining us with a gentleman whose only condition for existence in politics was the position of a CEO. |
Ses recherches ont démontré que si une hormone était administrée, elle accélérerait la maturation pulmonaire du bébé.
| Gëstu bimu amloon wone na ni sudee dañoo joxewoon ay ormoon dina yokk gaawaayu matirasiyon pilmoneer bu pumo yi.
| His research showed that if a hormone was administered, it would accelerate the lung maturation of the baby. |
Quelle est l'utilité pour le Sénégal, combien ça rapporte au Sénégal ? | Lan lay jariñ Senegaal, ñaata lay andil Senegaal ? | What is the utility for Senegal, how much does it bring to Senegal? |
Cela peut également être un bon moyen d'étirer un budget pour permettre un séjour plus long quelque part, car de nombreux emplois de bénévoles offrent le gîte et le couvert et certains versent un petit salaire.
| Mën naa doon itam anam bu baax ngir yokk bidsé bi ngir ñu mën fi toog lu gëna yàgg, ndax liggéey yu bari yuñuy def te sentu wuñu dara dañuy jox néeg ak lékk ñenn ñi te fay payoor bu ndàw.
| It can also be a good way to stretch a budget to allow for a longer stay somewhere, as many volunteer jobs provide accommodation and cover and some pay a small salary. |
Et pourtant, Macky a convié hier tout son gouvernement et les militants Apr à l’inauguration du Complexe scolaire Bibi Ndiaye. | Waaye Maki Sàll woo na démb nguur gi yépp ak ay farandoom ca ubbiteg Ekool Bibi Njaay. | And yet, Macky invited his entire government and the Apr activists to the inauguration of the Bibi Ndiaye School Complex yesterday. |
Il faut dire que la baisse de régime (huit matches sans but) de la superstar égyptienne, meilleur joueur africain et meilleur joueur de Premier League la saison dernière, a permis de mettre en lumière les performances de Mané (11 buts en 13 matches). | War nañu jàpp ne daanu xélu (juróom-ñetti mats yu mu dugalul benn bit) ndaanal Esipt lu mag li, futbalkatu Afrig bi gën a xarañ ak futbalkatu Ligg bu jëkk bi gën a xarañ ci jotaayu Ligg bi weesu, moo tax jàlloorey Maane feeñ (fukki bit ak benn ci fukki joŋante ak ñett) | It must be said that the decline in the regime (eight games without a goal) of the Egyptian superstar, best African player and best player in the Premier League last season, has highlighted Mane's performances (11 goals in 13 games). |
Le roi siégeait, habillé de pourpre et d’hermine, sur un trône très simple et cependant majestueux.
| Buur bi ci gàngune gu xumbul waaye gu am daraja la daan toog, sol manto bu weex, bu gudd, am ndimo lu xonq. | The king sat on a throne, clothed in purple and scarlet, very simple yet majestic. |
Le véhicule est allé dans le décor et le chauffeur est décédé sur le coup. | Oto bi dafa yàqu yaqeet dawalkat ba moom dafa faatu ci saa si. | The vehicle went into the set and the driver died instantly. |
La France voit un régime aux abois prêt à tout pour se maintenir. | Farãas gis na nguur gu dof, gu mu jaral lu nekk ngir des fi. | France sees a regime in the abyss ready to do anything to survive. |
En parallèle, la Chine a présenté sa feuille de route l’an dernier : elle prévoit de devenir le leader en innovation IA d’ici 2030.
| Ci jooju jamono Siin duggalna pexem daaw: fas yeene doon ci 1 palaas ci wallu juntuwaay yu bees fii ak 2030.
| In parallel, China presented its roadmap last year: it plans to become the leader in AI innovation by 2030. |
Loolu doyul, nga taafantoo guural gi, di jël dogal yu la neex. | Loolu doyul, nga taafantoo guural gi, di jël dogal yu la neex. | I'm not going to let you do this. |
Mais ils auront une réplique à la mesure de leurs conneries !Je voudrai vous annoncer que les comptes bancaires et orange money de PASTEF vont se remplir énormément avant 2024 et vous n’y pourrez rien. | Waaye dinañu leen toontoo nu méngook senn waxi dof yi ! Dama leen a bëgg a xamal ne nafay bànk ak orãas mone yu PASTEF dinañu fees ak koppar laataa atum 2024 te dungeen ci mën dara. | But they will have a response to their bullshit!I want to tell you that PASTEF's bank accounts and orange money will be filled up before 2024 and you can't do anything about it. |
Rosa devrait se diriger directement sur Phoenix mardi, avec des pluies annonciatrices dès lundi soir.
| Rosa ñungi seentu mu aw ci yoonu Phoenix ci Talaata duggu ci guddig Altine ak taw.
| Rosa is expected to head directly for Phoenix on Tuesday, with rain forecast as early as Monday night. |
Les Gabelous, qui se sont qualifiés grâce à une meilleure place de troisième, n’ont pas pu faire l’exploit lors de cette première édition qui se tient à Kigali au Rwanda face à l’Us Monastir pour atteindre les demi-finales. | Gabluu yi jàlloon ci ñetteelu palaas bi, mujju ñoo def seen liggéey ginnaaw joŋante yi jëkk yi amoon ci Kigali ca Ruwàndaa ci kanam Us, Mosatiir ngir yegg ci dëmi finaal yi. | Gabelous, who qualified with a better third place, failed to make the feat in this first edition held in Kigali, Rwanda against US Monastir to reach the semi-finals. |
Ces derniers avaient quitté la Somone, à bord dudit bateau avant de rallier la Voile d'Or. | Ñooñule dañu jóge woon Somon, ci bato bi ñu doon wax laata ñuy dem Waaldoor (Voile d’Or). | The latter had left the Somone on board the same ship before joining the Golden Voile. |
Trois adolescents et un homme de 20 ans ont été arrêtés sous l’inculpation de tentative d’homicide, après qu’un garçon de 16 ans a été retrouvé poignardé dans le Somerset.
| Japp nañu ñetti waxambaane ak benn waay bu tollu ci 20 att ci ay tuuma ni deñu doon jëëma rey ginnaaw bi ñu fekke benn xale bu 16 att bu ñu jam ci Somerset.
| Three teenagers and a 20-year-old man have been arrested on suspicion of attempted murder after a 16-year-old boy was found stabbed in Somerset. |
L'Ocrtis, en charge de l'enquête, a ferré Mbaye Athie. | Kurélu takk-der giy saytu mbiri ñoll gi, moo yore wàllu gëstu bi, loolu la Mbay Aaj wax. | Ortiz, the man in charge of the investigation, has Mbaye Athie in his sights. |
Mais en réalité, la phase administrative de la dépense demeurait de la responsabilité de l’ordonnateur, l’administrateur de crédits ne faisant que des propositions, lesquelles ne produisant d’effet juridique qu’après validation par l’ordonnateur. | Waaye ci dëgg-dëgg, wàllu njaay wu nguur gi, mu ngi aju ci ki nekk ci boppu bi, ki yore wàllu bor du def lu dul joxe xalaatam, bi nga xam ne jeexitalam ci yoon ginnaaw dëggël li kiy digal wax. | But in reality, the administrative phase of expenditure remained the responsibility of the authorising officer, the appropriations officer making only proposals, which did not produce legal effect until validated by the authorising officer. |
Ces couples peuvent choisir de faire un projet d’adoption pour leur bébé.
| Way déngnanté yi meenagno tan nignuy jeelé sénidoom.
| These couples may choose to make an adoption plan for their baby. |
« Après le 6 novembre, j’envisagerai sérieusement de présenter ma candidature aux présidentielles. »
| .
| After November 6th, I will seriously consider running for president. |
De quoi mettre les représentants diplomatiques et consulaires du Sénégal à l'étranger dans l'œil du cyclone. | Luy dugal ndawi réewum Senegaal ya ca bitim réew ci | This puts the diplomatic and consular representatives of Senegal abroad in the eye of the storm. |
Pour camper sous le niveau du Grand Canyon, il vous faut un permis d’arrière-pays.
| Bepp camping ci suufu rim bi ci Grand Canyon dafay laaj ab permi backcountry.
| To camp below the Grand Canyon, you need a backcountry permit. |