fr
stringlengths 4
1.08k
| wo
stringlengths 2
4.02k
| en
stringlengths 3
1.08k
|
---|---|---|
Fluke a écrit que les efforts de certains pour empêcher les femmes de parler de leur santé ont échoué.
| Fluke bind na ni ñenn ñi jotu ñu mëna tere jigeen ñi wax ci seen wergu-yaram.
| Fluke wrote that efforts by some to stop women from talking about their health have failed. |
Concernant la transmission, le vice-président principal du marketing et des communications chez Bellator, Dave Schwartz, a déclaré que « le règlement gouvernemental dispose qu’à 6 heures du matin, ce contenu n’était pas adapté, alors ils ont dû basculer vers les émissions pour enfants ».
| Ci atum1994, Berners-Lee dafa soppi Internet ci taxawal World Wide Web Consortium ci Massachusetts Institute of Technology.
| Regarding the broadcast, Bellator senior vice president of marketing and communications Dave Schwartz said that government regulation states that at 6 a.m., this content was not suitable, so they had to switch to children's programming |
Les Championnats d’Afrique ont été annulés, après maints rebondissements. | Joŋante yu Afrig yi fomm nañu leen, ginnaaw ay waxtaan yu bare. | The African Championships have been cancelled, after many twists and turns. |
Grâce à sa victoire le FC Barcelone a fait un pas important pour la finale de la reine des coupes européennes. | Ak ndamam loolu, FC Barcelone def na jéego bu am solo jëm ca finaalu Ligg Sàmpiyoŋ. | With this victory, FC Barcelona has taken an important step towards the final of the European Cup. |
Comme ils n’osent pas t’attaquer sur ton bilan économique, tu le leur jette à la figure avec un ravageur weddi guis bokkou si ! | Segam ñemewu laa song ci sa doxalin ci koom-koom bi, may leen ko ci kanaw rekk, wéddi gis bokku ci ! | Since they don't dare attack your financial statements, you throw them in their faces with a pest weddi guis bokkou yes! |
Sainsbury’s fait main basse sur Boots, Superdrug et Debenhams et les garnit de rayons similaires à ceux de supermarché, emplis de produits esthétiques et cosmétiques et gérés par des spécialistes du domaine.
| Sainbury mungi jël ay robo, ,ay fer yu am doole ak Debenaam ak ndenku bankaas bu jem ci wallu rafetaay te juge ci ak borom xam xam.
| Sainsbury's has taken over Boots, Superdrug and Debenhams and has set up supermarket-like shelves full of beauty and cosmetics products and run by specialists in the field. |
À chaque fois que je parlais publiquement, et peu importe ce que je disais, suivait une tirade abusive sur les réseaux sociaux, appelant au retrait, dénonçant les politiques du centre, me disant que je ne devrais pas être membre du parti.
| Saa yu ma waxe ci mboolo te lu ma munti wax rek- ay xecco aki xastaate rek ñoo ciy toftalu di ñaan mu gennema, di jooytu politiku diggi bi, di ma wax ni warumawoon bokk ci parti bu Labour.
| Every time I spoke publicly, and no matter what I said, there was an abusive tirade on social media, calling for withdrawal, denouncing the policies of the center, telling me that I should not be a party member. |
Cette technique consiste à extraire des cellules immunitaires d’un patient et à les modifier en laboratoire
| Geiger defarna benn anam bu muy gise ak natt ay rajoaktiwite, ap sos bu jur loolu ñuy wowe Kontoor bu Geiger.
| This technique involves extracting immune cells from a patient and modifying them in the laboratory. |
Enfin, Ousmane Dembélé, rentré quelques minutes plus tôt, conclut une très belle soirée | Guléet Usmaan Dembele, ñibbi na ay waxtu ci kanam, lóolu moo tëj ngoon gu neex | Finally, Ousmane Dembélé, who arrived a few minutes early, concludes a very nice evening. |
L’affaire est en cours devant le tribunal des vétérans de l’Alaska.
| 2004: Ci besu 26 disambar, yéngu-yéngu suuf bu magg amna ci soowu tefesu goxu Indonesi bu Aceh ci bët gaannaaru Sumatra, laalna 14 reew te yéngalna geej gi, faatna 226,000 nit ci tefesu Geeju End, xaaj gi Aceh lañu nek.
| The case is pending in the Alaska Veterans' Court. |
Il ajouta que la victime souffrait de blessures traumatiques sur la partie supérieure du torse.
| Giles yokk ci ni xale bi amna ay xoos xoos ci kawu yaramam.
| He added that the victim suffered traumatic injuries to the upper torso. |
En outre, pour OUSMANE SONKO, ce qui est encore plus préoccupant, c’est l’insuffisance des fonds consacrés à la santé publique. | Yokk ci, li Usmaan Sónko xamle mooy li gën a doy waar mooy koppar yi ñu joxe ci wér-gi-yarami askan wi doyul. | Furthermore, OUSMANE SONKO is even more concerned about the lack of funds for public health. |
Bien aidé par une expulsion en début de match, les Bleus ont déroulé. | Bulo yi futbal nañu bu baax ndax ki ñu génne ci ndoorteelu futbal bi dafa leen a ndimbale bu baax. | Well helped by an early ejection, the Blues have moved on. |
Cette affaire dite des 94 milliards est l’affaire de tous les citoyens sénégalais car ce sont les intérêts du Trésor public qui sont gravement compromis, par une bande de délinquants à cols bancs. | Mbir moomu ñu naan mu juróom-ñeent-fukki milyaar ak ñeent yi du mbiru askan wi yépp la ndax alalu réew mi la say-saay yiy sol simis yu weex yi, di pasar-pasaree. | This so-called 94 billion affair is the affair of all Senegalese citizens because it is the interests of the public treasury that are seriously compromised by a gang of criminals with bank collars. |
En effet, les piliers de l’accord de coopération monétaire du FCFA vont toujours demeurer en vigueur malgré l’adoption d’une nouvelle monnaie. | Kenuy déggoo yi ñu xaatim ngir xaalisu seefaa dinañu tàmbali doonte dëppoo nañu ci xaalis bu yees. | The pillars of the FCFA monetary cooperation agreement will remain in force despite the adoption of a new currency. |
Dans ce domaine, les partenariats public-privé pourraient jouer un rôle important., | Ci mbir moomu, jàppoo gu nguur gi ak mbootaayu ñi liggéeyul ci nguur gi mën a ci dox jeego yu am solo. | Public-private partnerships could play an important role in this area. |
De nos jours, il est rare que les gens réservent leur vol directement via la compagnie aérienne sans avoir préalablement recherché et comparé les prix.
| Ci jamonoy tey tukkib roplaan yi liñ leen di reservé ci kër yuy yëngu ci wàllum tukkib roplaan bareetul ñu koy def te seetu ñu njëg yi companie yi di jaayee.
| Nowadays, it is rare for people to book their flight directly through the airline without first researching and comparing prices. |
Après la mort inattendue de son dauphin désigné, l’ancien premier ministre Amadou Gon Coulibaly, le 8 juillet passé, ADO devait faire face à un choix cornélien: respecter sa promesse de passer le flambeau à la nouvelle génération en trouvant un nouveau candidat au RHDP, le parti présidentiel, ou bien se dédire en se représentant de nouveau malgré l’inconstitutionnalité de sa candidature. | Gannaaw bi ki mu bëggoon a jiital di Aamadu Gon Kulibali faatoo ci lu bette ci juróom-ñetti fan ci weeru sulet wi mujj, ADO dafa war a tànn bu baax : nangu li mu dige woon muy jox nguur gi xale yi te seet njiit ci RHDP, kuréel peresidaŋ bi, wala wax-waxet te bokkaat ci joŋante Njiitu Réew mi mi donte du doon lu yoon war a nangu. | After the unexpected death of its elected leader, former Prime Minister Amadou Gon Coulibaly, on 8 July, ADO faced a choice: to keep its promise to pass the torch to the new generation by finding a new candidate for the RHDP, the presidential party, or to resign by standing again despite the unconstitutionality of its candidacy. |
Ce qui est certain, c’est que le conflit qui éclata au milieu du XVIIe siècle a façonné le développement ultérieur de notre nation, et Cromwell est une figure particulièrement reconnaissable qui représente un côté de la fracture.
| Lu wóór ba wóór moy xeex bu diggu 17 siyeekal amna njeexital ci sunu naataange réew , Cromwell ap kaŋnga bu bokk ci li taxxaliku boobu la.
| What is certain is that the conflict that broke out in the mid-17th century shaped the later development of our nation, and Cromwell is a particularly recognizable figure who represents one side of the divide. |
Dëgg la, nag, am nay jafe-jafe diggante askan week takk-der yi leen war a aar. | Dëgg la, nak, am na ay jafe-jafe diggante askan wi ak takk-der yi leen war a aar. | I'm not going to be able to do it. |
Il doit y avoir des opérations de patrouille souvent, pour mieux sécuriser la cité. | Dafa war a am ay tàkk-der yuy wër dëkk bi, ngir gën koo mën a aar. | There must be regular patrols to make the city safer. |
À la fin, une étudiante s'est approchée et m’a dit : "Pourquoi me dit-on cela seulement en dernière année ?"
| Mu bayi Pyongyong ci weeru Suliye di wax ni defnañu ay jeego, waaye ay waxtu dong Kore bu Gannaar di ko ŋañ di ko laaj ay laaju ku "niru-banndi."
| And at the end, a student came up to me and said, "Why am I only being told this in senior year?" |
Blake a également été condamné pour avoir tenté d’entraver le cours de la justice.
| Nangu nañu ni Blake mooy kiy nekkoon di jéema jalgati doxaliinu até bi.
| Blake was also convicted of attempting to "obstruct the course of justice". |
« L’évidence, non seulement de Toyota mais d’autres constructeurs, est que nous devons absolument être en mesure de maintenir ce qui s’est révélé un excellent ensemble de chaînes d’approvisionnement. »
| Neenañu boobu ñakk deggoo ñuy ruumandaat mungi amewoon ci weeru Suye atum 2009 ci benn bërëb ci otel bu Palms ak Casino ci Las Vegas.
| The evidence, not just from Toyota but from other manufacturers, is that we absolutely need to be able to maintain what has turned out to be a great set of supply chains. |
Il a publié une photo de la maquette du stade du Stade Olympique de 50 mille places qui va coûter pas moins de 150 milliards de FCFA. | Fésal na benn nataal bu Estaat Olempig bu juróom-fukki junniy palaas buy jar lu mat 150 téeméeri ak juróom-fukk milyaar ci seefaa. | He posted a photo of the model of the 50,000-seat Olympic Stadium that will cost no less than 150 billion FCFA. |
Lorsqu'on dirige un pays, tu dois estimer tes capacités afin de savoir comment agir. | Boo jiitee am réew, danga war a natt fu sa doole tolluu ngir nga xam noo war a doxale. | When you're running a country, you have to assess your abilities so you know how to act. |
Ils ne pensent qu’à se sauver eux-mêmes en abandonnant la société dans le désordre, à ses instincts sauvages. | Xalaatuñu lu dul daw bàyyi fi askan wi ci ab pëccëxoo bu jéggi dayo, ci ag nekkinu malaam. | They only think of saving themselves by abandoning society to its wild instincts. |
Le secteur informel échappe totalement au fisc et réduit ainsi l’attractivité de notre économie. | Liggéey bi nguur gi yorewul dafay rëcc ci fay lempo te loolu bokk na ci liy wàññi xemmemteefu koom gi. | The informal sector is completely tax-free and thus reduces the attractiveness of our economy. |
Viens jouer avec moi, lui proposa le petit prince. Je suis tellement triste… | Ndoomu buur si ne ko: Kaay fo ak man. Dama géey lool… | Come play with me, the little prince proposed. |
Jamais dans l’histoire de la première ligue un club s’est imposé à l’extérieur sur un score de 9 buts à zéro. | Mësuñoo gis, ci taarixu Première ligue ab ekib bu duma moroomam bitim réew juróom-ñeenti bit ci dara. | Never in the history of the Premier League has a club won on the outside with a score of 9 goals to zero. |
Faites également attention aux moustiques nordiques pendant l'été. Bien qu'ils ne transmettent aucune maladie, leur piqûre peut être irritante.
| Ci beer gi, meeytul tamit yoo wu Nordic yi. Donté dungnu joxé bénn fébar, meen nagnula sonal.
| Also, beware of northern mosquitoes during the summer, which do not transmit any disease but can be irritating. |
Le golfeur italien Molinari a excellé dans toutes ses rondes, devenant l’un des quatre joueurs à avoir jamais atteint 5-0-0 depuis le format actuel du tournoi, dont la première édition remonte à 1979.
| Donald Trump, njiitu reewum Amerig, joxena awertisma bu njëkk ci ndoorteel at bi ci tek ay juuti ci lu Siin di jaay bitim reew bokkna ci pano soleer yi, weñ gu ñuul gi ak alimiñom bi.
| Italian golfer Molinari excelled in all of his rounds, becoming one of only four players to ever reach 5-0-0 since the current format of the tournament, which was first held in 1979. |
Et ce qui a marché en occident ne marchera point ici : vos termes extrémistes, nationalistes ou encore populistes, on s’en fout éperdument ! | Te li mën a dox ca réewi tubaab ya mënul a dox fii : seen baat yii di eksteremis, yittewoo sa réew wala jëmale say wax ci askan wi, suñu yoon nekku ci. | And what worked in the West will not work here: your extremist, nationalist or populist terms, we don't give a damn! |
Ses écoles ont formé la majorité des élites de l'Afrique. | Daaraam yee tàggat li ëpp ci kàngami Afirig yi. | Its schools have trained the majority of Africa's elite. |
Il a une valeur moyenne de 86% dans notre échantillon, ce qui confirme l’écart conséquent d’accès au crédit entre les sexes. | Téeméer yu nekk ci li nu jël am na juróom-ñett-fukk ak juróom-benn ci xayma, loolu di firndeel gënalaate gu fés gi nekk diggante góor ñeek jigéen ñi ci wàllu leb. | It has an average value of 86% in our sample, which confirms the large gender gap in access to credit. |
La police a déclaré que Lo Piccolo avait le dessus parce qu'il avait été le bras droit de Provenzano à Palerme et que sa plus grande expérience lui avait valu le respect de l'ancienne génération de patrons qui poursuivaient la politique de Provenzano consistant à rester aussi bas que possible tout en renforçant leur réseau de pouvoir.
| Waa Police wax nañu ci mëna luñu dara Lo Piccolo ndax dafa jege woon lool Provenzano ca Palermete limu fa liggéey lépp taxna patron yu mag yépp daan topp politique bimu daan def, jox ko fa cër, liggéeyu Provenzano mooy wàññi courant te fexe numu gëna jàppandee.
| The police said that Lo Piccolo had the upper hand because he had been Provenzano's right-hand man in Palermo and that his greater experience had earned him the respect of the older generation of bosses who pursued Provenzano's policy of staying as low as possible while strengthening their network of power. |
Cela peut sembler lourd, mais au vu du match c’est mal payé pour les Allemands. | Mën naa niru lu jafe, waaye so xoolee joŋante bi xam ni li ñu fay saa-almaañ yi baaxul. | It may seem heavy, but in view of the match it is badly paid for the Germans. |
Celles-ci peuvent être dangereuses si le voyageur poursuit le mirage, gaspillant ainsi une énergie précieuse et l’eau restante.
| Yii mën nañu doon yu wooradi sudee aji-tukki bi dafay topp miir bi, di yaqaale enersi bu am solo ak ndox mi ci des.
| These can be dangerous if the traveller pursues the mirage, wasting precious energy and remaining water. |
Nous ne voulons pas qu’il soit une réunion de chrétiens. | Bëggunu mu nekk ndajem yéeféer yi. | We don't want it to be a Christian meeting. |
Historiquement, le forum aurait dû se tenir avant les événements de mars dernier. | Ci taarix, ndaje maa ngi waroon a am laata xew-xewi weeru màrs wi weesu. | Historically, the forum should have been held before the events of last March. |
Imaginez qu'Airbus ait accordé des conditions favorables au Sénégal pour l'acquisition de cet appareil, vous trouverez normal que le Sénégal le crie sur tous les toits. | Seetal rekk ne Airbus joxoon na nekkin yu tegu ngir réew mi mën a am xarala bi, yaakaar nga ne Senegaal dina ko fésal ci kaw. | If Airbus had offered Senegal favourable terms for the purchase of this aircraft, you would find it normal for Senegal to shout it from the rooftops. |
Il a fallu que la presse divulgue l'information pour que le gouvernement fasse un communiqué bidon sans aucune précision sur le prix sous prétexte d'un quelconque secret d'État. | Waa nguur gi dañoo xaar ba taskati xibaar yi génne xibaar bi ñuy soog a def ab yégle bu amul benn njariñ te waxuñu sax njëg yi di taafantaloo sekereb Nguur. | It took the press to leak the information for the government to make a bogus statement without any details about the price under the pretext of some kind of state secret. |
Le président Sall a informé qu’à l’occasion, il délivrera un message à l’endroit de la communauté nationale et internationale, en attendant la tenue d’un Conseil présidentiel sur la question’’, ajoute la même source. | Njiitu réew mi Sàll yégle na ne dina wax ak askan wi ak waa àdduna, laata muy amal am ndaje ci mbir moomu, la ci ki joxe xibaar bi yokk. | President Sall said he would take the opportunity to send a message to the national and international community, pending the holding of a Presidential Council on the issue, the source added. |
A côté de ce programme support, figurent des programmes dits métiers dont le nombre (entre un et cinq), la dénomination et le montant des crédits dépendent, évidemment, du périmètre de compétences du ministère. | Ci wetu tëralin woowu taawu lépp, am na yeneen tëralini mécce yu seen lim nekk ci diggante benn ba juróom, turu ak xaalis bi aju ci, ci lu wóor, ci fi njëwriñ ji mën a dem ak liggéeyam. | In addition to this support programme, there are so-called 'trade' programmes, the number of which (between one and five), the name and the amount of the appropriations obviously depend on the scope of the Ministry's powers. |
Ces organisations ont également annoncé un risque d’incursion d’essaims de criquets pèlerins et enjoignent les gouvernements de prendre les mesures préventives. | Kurél yile yégle nañ ne mën naa am ay njéeréer fees ci béréb yi ba tax na woo nañ nguur yi ñu jël ci seen i matukaay. | These organisations have also warned of the risk of swarms of locusts and are urging governments to take preventive measures. |
Une campagne électorale originale et saine faite d’un autofinancement à partir des cotisations, des ventes de produits de parti et de dons licites. | Ab kàmpaañ bu wuute te sell jóge ci gafakag boppam ci ndimbalug ma-réew ya mu bokkal réew mi, ay bagaas yu ñuy jaay ci pàrti bi ak ay maye yu lew domm. | An original and healthy election campaign made of self-financing from dues, sales of party products and legal donations. |
Ayr 38 - 17 Melrose : Ayr reste invaincu
| Ayr 38 - 17 Melrose: Ayr mi kenn doorul demna ci kaw
| Ayr is undefeated. |
Il faut être très patient, répondit le renard. Tu t’assoiras d’abord un peu loin de moi, comme ça, dans l’herbe. | Wel wi tontu ko: Dangay bañ a yàkkamti lool. Dangay toog nale ci ñax mi, xaw ma sori tuuti. | "You must be very patient", replied the fox. "First you will sit a little far from me, like this, in the grass". |
Heureusement que j’avais des garçons merveilleux qui étaient à fond avec moi. | Yàlla baax na, dama amoon ay xale yu góor yu baax yu nekkoon ak man. | Luckily I had some wonderful boys who were all over me. |