wo
stringlengths 1
4.02k
⌀ | fr
stringlengths 1
1.08k
| source
stringclasses 2
values |
---|---|---|
Yaw xamuloo kenn | Toi tu connais personne | null |
Faatim la soo demee ! | C'est Fatim, peut-être ! | null |
Jambaar du bare wax. | Un homme de courage n'abonde pas paroles. | null |
Nataal bii de, nataal la boo xam ne ab paaka la, paaka boo xam ne paaka bi am na dénk ca wet ga ak weñ waaw. Nataal bii daal paaka lañ koy wax paaka bi daal beesul te daa chocolat waaw noon la mel. | Cette photo ci est celle d'un couteau. Un couteau pour lequel il y a du bois à côté ainsi que du fer. Ce qui est sur cette photo ci on l'appelle couteau. C'est un vieux couteau de couleur chocolat. Oui, c'est comme ça qu'il est. | null |
Xolal fépp ! | Fouille tout endroit ! | null |
Xam naa ni fa la ko Baay fekk ndax ni ma ko xame, nataal boobu woroo na lool ak gis-gisu Afrigam. | Il s'agit vraisemblablement d'objets laissés là par un précédent occupant, car cela ne ressemble pas à ce que mon père pouvait rechercher. | null |
Jigéen jan a réer ? | Quelle femme s'est égarée ? | null |
Nataal bii ñoo ngi ciy gis ay nit ñuy ñaxtu walla di jàmmaarlook takk-der yi rekk. Caa Kaasamaas la woon. Aw ndaw lañ gën a nurool. Du ñàkk am lu leen metti ñu ko doon ñaxtu. | Sur la photo, ont voit des personnes qui se révoltent ou qui s'opposent constamment aux gendarmes. C'était en Casamance. Ils ressemblent plus à des jeunes. C'était peut-être pour montrer quelque chose qui leur déplaisait. | null |
Noonee nan ? | Comment ? | null |
Gis na góor gi ag doomam. | Il a vu l'homme et son enfant. | null |
Waaw : ndoorteelu dunyaa ngi nii. Jamono walbatiku. Démb doon tey. Njuumteek wor ne fàŋŋ. | Une terre originelle, en quelque sorte, où le temps aurait fait marche arrière, aurait détricoté la trame d'erreurs et de trahisons. | null |
Yaa doonkoon falu | C'est toi qui eusses été élu | null |
Taw bi sóob, ànd ak ngelaw lu sedd guyy. Mu ngi yëngal collu garab yi, di wonkloo seeni bànqaas. Ndox miy rëkk suuf si, pënd bi fekksi ma ci biir néeg bi. | Enfin le vent de la pluie, très froid, qui avance dans toute sa puissance sur la cime des arbres, j'entends chaque branche gémir et craquer, l'air de la chambre se remplit de la poussière que soulève l'eau en frappant la terre. | null |
Gone gi ci jalu mbalit bi | Enfant des dépôts d'ordures | null |
Dëgg la, sore woon na Bansoo wànte mënutoon a réere loolu mbir. | Même loin de Banso, mon père ne pouvait pas l'ignorer. | null |
Menn nit ñëwul. | Aucun homme n'est venu. | null |
Kooka ak kile, bokkuñu ! | Celui-là et celui-ci ne se ressemble en rien ! | null |
Ay way-juram a ngi woon ciy jafe-jafe yu tar, fekk mag dikk, amatuñu benn kàttan. Gëmuma ni doon na leen néeg a bàyyi foofu dem yoonam. | Il lui aurait fallu abandonner ses parents en pleine tourmente, alors qu'ils n'étaient plus en état de résister. | null |
Su demee | S'il part | null |
Su weesoo ñaari goney Enjeŋ yi, du leneen lu Baay jële at ya mu def Guwiyaan yépp. Ñu ngi janook moom, naaj wi di leen gaññloo. | De son séjour en Guyane, mon père ne rapportera que le souvenir de ces deux enfants indiens, debout au bord du fleuve, qui l'observent en grimaçant un peu à cause du soleil. | null |
Na ŋgeen dem ndax gerte gi ñëw te nak ñjaay mi jar benn yoon ! | Allez pour que l'arachide arrive et qu'enfin les ventes marchent une fois pour toutes ! | null |
Fas weneen wu moo daw. | C'est l'autre cheval qui s'est égaré. | null |
Su góor gi bëggée | Si l'homme accepte | null |
Naka ngon si | Bonne soirée | null |
Lii nag ab buntu la boo xam ne ndénk lanu ko defaree. Waaye nag dañu koo tëj, am na sax ab sëluur mooy jàppukaayu buntu bi ñu ubbi. | Ceci est, cependant, une porte conçue avec du bois. Mais on l'a fermée. Il y a même une serrure qui est ce avec quoi on attrape la porte quand on l'ouvre. | null |
Loolu la. | Voilà ce qu'il est. | null |
Liggéeyam a nga ko doon xaar Ogosaa, ca diiwaanu Koros Riwër. | Il rejoint son nouveau poste à Ogoja, dans la province de la Cross River. | null |
Dégg naa ko muy nettali ne léeg-léeg néew yi dañuy nëb a nëb ba, su waree lelli der bi, fàww mu takk paaka awsaam ci catu bant, ndax rekk ragal yaram wi fàcc ci kowam. | J'ai entendu mon père raconter que les corps qu'il doit examiner sont parfois dans un tel état de décomposition qu'il lui faut attacher son scalpel au bout d'un bâton avant d'entailler la peau, pour éviter l'explosion des gaz. | null |
Yóobuwaalewul i garab mbaa leneen. | Il n'a pas eu le temps de se préparer, d'emporter des médicaments, des provisions. | null |
Demleen ! | Allez ! | null |
Bonag, dey mu ñibbi | Dans ce cas, qu'il rentre | null |
Su dee dem | Quand il partira | null |
Mu ngi dale digaloom ak Kamerun gi ci moomeelu Farañse yi, wuti bëj-gànnaar, ca cati Aadamawa, ëmbaale dëkk yu ndaw-ndawaan yi Àngale yi jotul woon a teg loxo ba ñu fa dàqee Almaŋ yi. Muy dëkk yu mel ni : Kantu, Aboŋ, Nkom, Bum, Fumbaŋ ak Baali. | Cela va de la frontière avec le Cameroun sous mandat français, au Sud-est, jusqu'aux confins de l'Adamawa au Nord, et comprend la plus grande partie des chefferies et des petits royaumes qui ont échappé à l'autorité directe de l'Angleterre après le départ des Allemands : Kantu, Abong, Nkom, Bum, Foumban, Bali. | null |
Tey, mënal naa sama bopp, am soxna ak i doom, dëkke yéeg roppëlaan ak a wàcc, am na feneen fu ma sañ ni fa la fekk baax. | Aujourd'hui, j'existe, je voyage, j'ai à mon tour fondé une famille, je me suis enraciné dans d'autres lieux. | null |
Xawma nan la ma xalaat boobu dikkee. | D'où me vient cette idée ? | null |
Kee nit ŋgay gis | Cet homme là-bas que tu vois | null |
Loolu doyul, biñ duggee ci atum 60, ñu ubbil Afrig bunti gàddaay. Gone yi dawsee Ganaa, Beneŋ walla Niseryaa ngir daan seen doole. Lu nekk ñu koy daj ci réewi Tubaab yi. Àddinay dox, ñu dem ba réew yooyu tollu diggante, daldi tëjaat ràpp seeni bunt, di sikkal doomi Afrig yi, naan dañoo rekk xayadi, ngalla nañ toog fañ fekk baax. | Les portes ouvertes à l'émigration, ces cohortes de jeunes hommes quittant le Ghana, le Bénin ou le Nigeria dans les années soixante, pour servir de main-d'œuvre et peupler les ghettos de banlieue, puis ces mêmes portes qui se sont refermées lorsque la crise économique a rendu les nations industrielles frileuses et xénophobes. | null |
Noo def ? | Comment vas-tu ? | null |
Nit ku baaxkoon la ! | C'est un homme qui eût été bon ! | null |
Kooku ci biir. | Celui-là à l'intérieur. | null |
Mangui lay ndokkel ci sa bess bu délu si bi | Mes voeux d'anniversaire | null |
Fan ngeen joge ? | D'où venez-vous ? | null |
Xam naa jamono jooju la njàqare gu jéggi dayo teqale Baay ak sagoom, mu ni fàww mu jàll màndiŋ mi, dem Alseri jël fa gaal, wutali bëj-saalumu Tugal ngir mën a delloosi Afrig jabar jeek seen ñaari doom. | C'est sans doute à ce moment-là que mon père tente cette chose folle, traverser le désert pour s'embarquer en Algérie à destination du Sud de la France afin de sauver sa femme et ses enfants et les ramener avec lui en Afrique. | null |
Nit lanu ! | Nous avons été quelqu'un ! | null |
Léeg-léeg, bóoy bi doon wottu tóokër bi, mer sànni leen xeer. Su ko defee ñu daw waaye nees-tuut ñu dellusi toog fa ñu toogoon. | De temps en temps le « garden boy » se fâchait et les chassait à coups de pierre, mais l'instant d'après ils étaient revenus. | null |
Dil nitu nit ñi ! | Sois l'homme de tout le monde ! | null |
Ci biir foofu, mu bënn. | Là, où il a fait un trou. | null |
Dóor i kuur ci suuf su sell | Coups de pilons sur la terre sacrée | null |
Xar moomu man ŋga wax ? | Tu parles de quel mouton ? | null |
Jaama nga fanaan ? | As-tu passé la nuit en paix ? | null |
Dil nitu dëgg ! | Sois homme de vérité ! | null |
Góor gi bëgg na | L'homme veut | null |
Fu mu dem ? | Où a-t-il été ? | null |
Afrig mënatul a yem ci Bamendaak Bansoo, fa xolam daan féexe, béréb ya daan yàkkali dënnam, muy noyyi bu baax. Xam naa xelam dinay faral a dellu ci ñaari diiwaan yu sell ya te ay ponkal wër leen : tangoru Bàmbutaa, yegg ba 2 700 meetar ak tangori Kojo ak bu Oku yiy def 2 000 ak 3 000 meetar. | Bamenda, Banso, c'était au temps du bonheur, dans le sanctuaire du haut pays entouré de géants, le mont Bambouta à 2 700 m, le Kodju à 2 000, l'Oku à 3 000. | null |
Sunuy xol di pët-pëti ak doole, nu gàdduy xeer ak i yat, àndandoo di dóor ak a dóoraat ba far màbbal jànj yi. Fan lan tegoon loolu ? Fenn. Walla xanaa boog seetaan pënd biy jóg wutali asamaan moo nu neexoon, nu gis ni taax yiy màbbe, dégg ni yat wiy dale ci miir yu dëgër yi. Ak lanati ? Xanaa janook xur wu xonq week puuritam miy pët-pëti. | Nous avions le cœur battant, la violence débordait avec notre souffle, nous prenions des pierres, des bâtons et nous frappions, frappions, nous faisions écrouler des pans de ces cathédrales, pour rien, simplement pour le bonheur de voir monter les nuages de poussière, entendre crouler les tours, résonner le bâton sur les murs durcis, pour voir s'offrir à la lumière les galeries rouges comme des veines où grouillait une vie pâle, couleur de nacre. | null |
Nit ñan ñoo ñëw ? | Quelles personnes sont venues ? | null |
Gis naa sama xarit bi ! | J'ai vu mon ami ! | null |
Maa ŋgi fi ba mu ñëw ! | Je reste ici jusqu'à ce qu'il vienne ! | null |
Waaw lii de comme ni ma la ko waxe woon rekk, ceebu jën la, ñu teg ko ci palaat bu weex, teg lu mel ni ay ñambaan, daldi koy teg ci kow. Waaw boo xoolee ceeb bi, am na benn kuddu bu ñuul bu koy cubb, bu cubb ñambaan ci kow. | Oui ceci est comme je te l'avais dit seulement. C'est du riz au poisson posé sur un plat blanc. Une sorte de patte de tamarin est mise au-dessus. Oui si tu regardes le riz, il y a une cuillère noire qui <unk> dessus de la patte de tamarin. | null |
Sama yaay mi juddoo Mili, newu fa woon booba wànte yàgg naa dégg baayam daan ko waxtaane. Muy boog lu bokk ci cosaanam, daldi soppiku béréb bu xelam sàkk, béréb bu boole lëndëm ak leer, jege ak sori. Ndax, ca jamono jooju, Móris sore na sore gu, ci gént rekk la ko mënoon a feeñu. | Ma mère n'a pas vécu là-bas (elle est née à Milly), mais elle en a toujours entendu parler par son père, cela fait partie de son passé, pour elle cela a le goût d'un rêve inaccessible et familier (car, en ce temps-là, Maurice est si loin qu'on ne peut qu'en rêver). | null |
Na dugg su bëggée ci biir ! | S'il veut qu'il entre ! | null |
Wau, degg naa tuuti Wolof | Oui, un peu | null |
Tanéel ak jáam | Je te souhaites de récupérer tôt | null |
Nataal bii lii ab àngal la boo xam ne dañ ciy deñci ay kaas ak yu ni deme. Ñu defare dénk ak weer defar bu mucc ayib. | Sur cette photo, c'est <unk> dans laquelle on garde des tasses et consorts. On l'a conçue avec du bois et du verre de manière méthodique. | null |
Yooyale deey bëggu leen ! | Ceux-là, il ne les apprécie pas ! | null |
Xawma dara ci li ma wara def ak lim yi rek, war ngeen ma jox ay detaay yu gëna bare ngir ma xam yàq bii. | Je n'ai aucune idée de ce qu'il faut faire avec seulement les totaux, veuillez me donner plus de détails pour comprendre ce gâchis. | null |
Séen naa as jigéen. | J'ai aperçu une femme. | null |
Diggante Lasim ak Ngonsin, sama xel dajeek géttug nag yuy daagu ak seeni béjjén yu bindoo ni xaaju weer, di lonk niir yi. | Les hauts plateaux où avance lentement le troupeau de bêtes à cornes de lune à accrocher les nuages, entre Lassim et Ngonzin. | null |
Muy baat ba ñuy jëfandikoo ca Móris. Loolu biral ni saa yu bët yiy doxantu ci gàncaxu Afrig, gàncaxu Móris day ñëw tegu ci kowam. | Si ce paysage le requiert, s'il fait battre mon cœur aussi, c'est qu'il pourrait être à Maurice, à la baie du Tamarin, par exemple, ou bien au cap Malheureux, où mon père allait parfois en excursion dans son enfance. | null |
Soo dee góor | Si tu es homme | null |
Xand kenn demul ? | Personne n'est donc parti ? | null |
Suufus Afrig si nu war ca njalbéen | Terre d'Afrique flouée dès l'aube | null |
Ñu teg ciy fan, mu dugg gaal, teeri Sorstaawun, ca Guwiyaan. | Quelques jours plus tard, il s'embarque à destination de Georgetown, en Guyane. | null |
Néeg bépp | Toute la chambre | null |
Maa ngi koy jeema def, waaw. | J'essaie de le faire, évidemment. | null |
Séen naa am guy. | J'ai aperçu un baobab. | null |
Daawuloo woon coow. | Tu ne bavardais pas, généralement. | null |
Giséegul | Il n'a pas encore pris de contacts | null |
Su Baay demee ba fépp fu mu teg tànkam xam na mooy fan, Yàllaak góor googoo tax. Jibar yi sax, nga xam ni mënoon na leen a yàqal seen liggéey, wegoon nañu Baay. Niñ ko yaatale woon noonu, Ayijoo dara la ci woon. | C'est grâce à lui que mon père a pu trouver ses repères dans le pays, être accepté de tous (y compris des sorciers dont il était le concurrent direct), exercer son métier. | null |
Xamoon ŋga jaŋx ba ? | Tu connaissais la jeune fille ? | null |
Yéen ñan la wax ? | Il parle de vous ? | null |
Waa jii ag waa joojale duñu benn. | Cet homme-ci, devant nous, et cet homme-là ne sont pas les mêmes. | null |
Fanaanal jaam. | Bonne nuit. | null |
Daňu daan jóge dalukaay bii, dal ca ba ca des, dëkk buñ dem Baay daldi dugal tur wa ci déndam : Nikom, Babungo, Njii-Nikom, Luwaakom Ndiyee, Ngii, Òbukun. | Ils vont de campement en campement, dans des villages dont mon père note les noms sur sa carte : Nikom, Babungo, Nji Nikom, Luakom Ndye, Ngi, Obukun. | null |
Soo demee, Faatim la ! | C'est peut-être Fatim ! | null |
Ay jiit yu tuuti lañu woon te ñuul, mu leer nu ne amuñu daŋar. | Les scorpions qui vivaient sous le tapis étaient généralement petits, noirs, probablement inoffensifs. | null |
Yaa daan dem | C'est toi qui avais l'habitude d'aller | null |
Liñ daan njëkk a def mooy sànniy xeer ngir seet ndax am na luy yëngu ci biir jànj bi. | Nous avions dû commencer par jeter quelques pierres, pour sonder, pour écouter le bruit caverneux qu'elles faisaient en heurtant les termitières. | null |
Àndal ak yar ! | Sois poli ! | null |
Gis na seen yeneen xarit ! | Il a vu d'autres amis à vous ! | null |
Lëf ki weex na tàll. | La chose est d'un blanc éclatant. | null |
Mook Baay ñu ànd di wër dëkki tangor yi féete sowu-jant, fu ne ñu dem fa ngir faj képp ku feebar, làppto beek yenukat yi topp seen ginnaaw. | Ainsi elle accompagne mon père dans ses tournées médicales, avec la suite des porteurs et l'interprète, à travers les montagnes de l'Ouest. | null |
Fàww xelam gën a màcc ci pajum feebari réewi Afrig yi. | Il fait une spécialité de médecine tropicale. | null |
Waaye, kenn demul | Malheureusement, nul n'a été | null |
Dëkk fa ci taaxu-kow bu ñàkk solo, sa baay tere la génn foweek say moroom, àddina faf sàppi la... Waaye bés, Afrig ubbil lay loxoom ni la kaay, yàgg naa laa xaar. Nga sanc ci peggu dex gu baree-bari poto-poto, li ko wër lépp dib àll bu xonq coyy. | Nous étions venus d'un appartement au sixième étage d'un immeuble bourgeois, entouré d'un jardinet où les enfants n'avaient pas le droit de jouer, pour vivre en Afrique équatoriale, au bord d'une rivière boueuse, encerclés par la forêt. | null |
Yaw la ndaw si sopp | C'est toi qui aimes la jeune femme | null |
Wànte tamit, lépp a nu daan soppi. Muy àll bi, di ngëlén yi, di asamaan si daan dajale saa yu tàkkusaan jotaan, loolu lépp a daan feesal sunuy dënni gone, daan nu xiir ci song jànj yeek xube yu ñuul ya ni woon jadd, jëm ca kow a kow. | La savane, l'orage qui s'accumulait chaque après-midi, la brûlure du soleil sur nos têtes, et cette expression trop forte, presque caricaturale de la nature animale, c'est cela qui emplissait nos petites poitrines et nous lançait contre la muraille des termites, ces noirs châteaux hérissés contre le ciel. | null |
Ñu ŋgi toog | Nous voilà assis | null |
Deñoo bëgg sàmm lenn lu ëpp lu ci des. | Nous voulions sauver une chose plus que le reste. | null |
Samba, yaw, yaa dem | Samba, toi, tu as été | null |
Subsets and Splits