wo
stringlengths 1
4.02k
⌀ | fr
stringlengths 1
1.08k
| source
stringclasses 2
values |
---|---|---|
Demal ci tunnel bi! | Allez dans le tunnel! | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Noo ngi def, waaw? | Ça va, d'accord? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Ma seet ci diksoneer bi waaye gisuma tekki bi | J'ai cherché dans le dictionnaire et je n'ai pas trouvé la traduction. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Waaw, yaakaar naa.... | Je suppose que oui. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Ànd ak wérgu-yaram. | Ça va. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Board bi joxeewul benn firnde ci BBC bi. | Le conseil n'a pas fourni de preuves à la BBC. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Subrata Mitra moo ko jël | Photo réalisée par Subrata Mitra | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Su guddi jotee, te dama wara nelaw ci sama lal sudee dangay xool, dinga gis ni damay jooy | Quand la nuit tombe, et que je devrais dormir dans mon lit Si tu regardes, tu verras que je pleure à la place | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Dina nu dóor ak doole. | Ils vont nous frapper en force. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Malakko neena luwaas bi diis na lool te kenn mënu ko yóbbu. | Malakko dit que la statue est trop lourde à porter. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
(TAMMERING) Amuma benn kàttan. | Je n'ai pas le contrôle. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Hewel, gërëm Yàlla nga dundu. | Hewel, Dieu merci, tu es en vie. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Lii jeexna! | C'est fini! C'est fini! | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Danu bëgga dakkal yokkuteg xarala yu bees yi | Nous voulons arrêter l'avancement de la technologie | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Murph la? | C'est pas Murph? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Dañuy nuru dàll ortopedi. | On dirait des chaussures orthopédiques. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Séy jigéen ñi dañuy wax ci xibaar yii | Les mariages de femmes sont mentionnés dans ces reportages. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Nga bàyyi sa xel ci nëbb lépp lu lay sol ci goor ñi. | N'oubliez pas de cacher tous vos objets portatifs aux singes. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Mu yëngal loxoom. | Je lui ai serré la main. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Noon yi fépp fuñu mëna dem duñu gis lenn ludul àll bu amul àpp. | Où que l'ennemi aille, il ne doit trouver que des terres désolées. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Jamono yi soppi nañu leen ay xeer, waaye dina ñu rafet ba fàww. | Les âges les ont transformés en pierre, mais ils seront toujours beaux. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
ay livre. | Plusieurs kilos. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Loolu rek nga wara xam. | Tu dois juste réaliser ça. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Ci jamano jooju, ñaari fan di dem noonu. | Pendant ce temps, deux jours passent comme ça. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
'Soo ma nangu dinaa soppi sa nimero ngir kaaraange.' | Avec votre permission, je vais changer votre numéro pour des raisons de sécurité. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
- Duggukaay... | - Je ne sais pas... | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Oh, ñëwal, bàyyi gëm sa bopp. | Arrête de te vanter. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Mënu ma des ci xol, fàww ñu jox cër | Je ne peux pas rester sans le sou. Je dois être respecté. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Dina ñu ma rey. | Ils vont me tuer. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Dama daan ñëw fi suma nekkee ci kër ci vacance. | Je venais ici quand j'étais en vacances. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Te dee rekk moo mëna fey dund gi. | Et seule la mort peut payer pour la vie. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Dama bëgga naan. | Je veux boire un verre. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Du xale bu ndaw. | Pas un bébé. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Nanga def, yegsi nga ci Doug. | Vous avez appelé Doug. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Souvenir yu bari. | Il y a trop de souvenirs. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Ki ñuy wax Abdu Fay yoroon na portaabal. | Ce dernier s’attend d’ailleurs à d’autres mesures salutaires de la part de l’entreprise française. | galsenai/french-wolof-translation |
Ndax Goa nga? | Vous êtes à Goa? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
- Waaw, yaa ngi yéeme. | - Tu as été incroyable. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Am nanu sax ay tàggat ngir saytu aparey bi waaye dafa yàgg tuuti | On a même eu quelques exercices pour tester l'appareil mais ça a pris un peu plus de temps. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Waaw, léegi dinaa la ko wax, nga xam.» | Je vais te le dire, et tu le sauras. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Bénn dér meenna ‘’tooy’’ wala ‘’waw’’ desna ci ni ndox mi toll.
| Un plat au curry peut être « solide » ou « liquide », selon la quantité de sauce qu'il contient.
| galsenai/french-wolof-translation |
ci saasi, bis, mu taxaw? | et tout d'un coup, un jour, ça s'arrête? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Kon, danu leen di sant ci seen ndimbal. | On apprécie votre aide. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Baalnu def benn coppite ci sunu adres. | S'il vous plaît, ne changez pas notre adresse. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Firndeel nañu ko. | - Je confirme. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Ku nekk da ciy dem ni mu ko neexe, ni mu ko bëggee, ngir saafara ko, faj wiris bi : laaj, limoŋ, soble, banaana, lem, jinjeer, xorom-polle, xobu lóriyee, neem, bineegar, kaani, añs. | Pour être plus direct, cette sortie de M. Sakho est une insulte à tous les Sénégalais. | galsenai/french-wolof-translation |
Garanti nañ la ni nga tooy soo jeggee poŋ bi wala nga dox ci kaw raay yuy wër Falls yi.
| Vous êtes sûr de vous faire mouiller si vous traversez le pont ou si vous marchez le long des pistes qui serpentent près des chutes.
| galsenai/french-wolof-translation |
Murray ñakk na pacc gu njëkk gi ci benn sanni dong ginnaw bi ñaar ñepp amé benn poñ ci sanni buné.
| Murray a perdu le premier set au tie break après que les deux hommes ont gardé leur service pendant tout le set.
| galsenai/french-wolof-translation |
-Ndax rafet na? | - Il est beau, non? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
3. 2. 1. | 3. 2. 1. le | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Fan nga dem fu sori? | Vous avez exploré jusqu'où? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
"Cale du faral di def rapoor yi ci waxtu wiñ ko digal." | "Cale ne termine pas souvent ses rapports de terrain à temps". | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Taabal bu njool, sées yu njool! | Une grande table, des chaises! | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Piyees bi waxul ni Kaufman waxna ci deewam. | La pièce ne dit pas que Kaufman parle de sa propre mort. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Amoon na jokkoo bu bawoo ci American 11 juróomi simili yu nekk. | Il y avait une communication de l'American 11 toutes les cinq minutes. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Usmaan Baaxum miy tàggat ikib bi gi nee na, waaye ñoom, jëluñu kub bi. | C’est peut-être un début de passation de pouvoir entre Mohamed Salah intenable la saison dernière et Sadio Mané qui continue de prendre une nouvelle (grosse) dimension à Liverpool et dans le championnat anglais. | galsenai/french-wolof-translation |
Xamuma luma wara wax waaye uh, maa ngi xalaat yaw bro. Yaakaar naa nga nekk ci jàmm, bëgg naala. | Je ne sais pas quoi dire, mais je pense à toi, j'espère que tu vas bien. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Bernstein dafa leeral ci kàddu yu njëkk yi | Bernstein explique dans l'introduction | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Ndax dama wara yónnee lépp sa néeg? | Je dois tout envoyer dans ta chambre? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Njoxeem alal jooju jooju su dee am na, ci kaw lawug feebar bi ak ni ay màndargaam di soppeekoo ci ñaari tëralinu koom gi ak ci pénc mi, loolu la David Malpass, njiitu kippangoog Bànku àdduna bi xamle ci ab këyitu yégle gu mu wasaare talaata ñetti fan ci weeru màrs 2020. | L’allocation de ses ressources s’il y a lieu, en fonction de la propagation de la maladie et de l’évolution de ses effets sur le double plan économique et social, a fait comprendre David Malpass, président du Groupe de la Banque mondiale dans un communiqué publié le mardi 3 mars 2020. | galsenai/french-wolof-translation |
Mën nga xalaat dawalkat bu ragal. | Vous pouvez imaginer un conducteur effrayé. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Waxna dëgg. | Elle a raison. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Ci dëgg, dafa waroon a nekk luy yëngal xaalaat yi ci xeli ñu jub ñi ndax bañ lu dul yoon, beddiwante ci xeet, beddiwante ci diine, te jëfin yooyu doonuñu aw tànneef waaye li fi sax di am la te di dundal sunu àddina bi la bàyyi ko mettital sunum xel la. | En réalité, ce devrait être un tremblement de conscience dans l’esprit des justes puisque refuser l’injustice, le racisme, l’islamophobie et les mises en scènes n’est pas une option mais une constante qui est substantielle à notre humanité et y déroger c’est tordre notre conscience. | galsenai/french-wolof-translation |
Amna benn tablo, Rembrandt moo ko defar. | Il y a une peinture, c'est de Rembrandt. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Tendo. | Je suis Tendo. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
benn njariñ mooy ku nekk ci jafe-jafe yii | Un avantage est pour tout le monde dans cette situation | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Benn ci màndarga yi gëna fës ci muse bi mooy mbonaat yi | Les vautours sont une caractéristique remarquable du musée. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
- Soo ko defee, ndax dinga jéema ray ma? | - Si c'était le cas, tu me tuerais? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Leegi dama bëgga ñam thon bu saf. | Je tuerais pour un rouleau de thon épicé. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Weeral sa màntoo. | Accrochez votre manteau. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Daa melni dama bàyyi dara ci benn oto buma delloo Samdi bi weesu. | Apparemment, j'ai oublié quelque chose dans un véhicule que j'ai rendu samedi dernier. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Sunu bokkee liggéey mën nanu jeexal xare bii ci diiru ñaari ayu-bis. | Ensemble, nous pourrions mettre fin à cette guerre en deux semaines. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Liiñ bu gudd mooy anam wi ñuy wóorloo ni li léeb bi di tekki jot na. | Une longue ligne permet de s'assurer que le sens d'un proverbe a été transmis. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Déedet. Danu la bëggoon, Ender. | On voulait vous, Ender. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Rawatina Murph. | Surtout pas Murph. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Mu xool ma ni ku waaru. | Il me regarda stupéfait. | galsenai/french-wolof-translation |
Sasha: 15 at. | - Je suis à 15. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Sa jëf jii dafa wone ne fullaaloo ñu benn yoon yaw njiitu réew mi, waaye ñun itam naka noonu. | Cet agissement montre que vous n'avez aucun respect pour nous et c'est réciproque Monsieur le Président | galsenai/french-wolof-translation |
- Moo gënoon baax. | - C'était le meilleur. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Maa ngi ragal ni advocaat la, kilifa. | Je crains que ce soit l'avocat, monsieur. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Nit ñi dañu wara tëye seen ordinatër ak seen jiné suñuy dugg ci kër gi ngir mëna ci dugg. | Les gens doivent tenir leur ordinateur et leur souris quand ils entrent dans la propriété, afin d'y accéder. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Gisuma leen. | Je ne vous reverrai plus. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Soldaar yu Almaañ, déggal ngeen ndigalu Führer, ngeen waajal wéyal xare bi ngir dem Berlin, doonte seeni munisioŋ jeexna, te yeneen xeex amul benn njariñ. | Soldats allemands, vous avez obéi aux ordres du Führer et vous étiez prêts à poursuivre la bataille pour Berlin, bien que vous manquiez de munitions et que la résistance fut inutile. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
[ ak kàddu yu kawe ] Kenn ci nun. | Un de nous. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Waaw, am nga ko, sama buur, te bëgg nanu la ci loolu. | Oui, vous l'avez fait, mon roi, et nous vous aimons pour cela. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Lii sama ekip la? | C'est mon équipe? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Garab yi ñooy défar oxygen bi nit yi di noyyi, ba noppi ñu jël dioxide de carbon bi nit yi di génne (mooy, noyyi).
| Les plantes produisent de l’oxygène que les humains respirent, et elles absorbent le dioxyde de carbone que les humains exhalent (c’est-à-dire expirent).
| galsenai/french-wolof-translation |
Maki Sàll seetlu woon na ak ñàkk pexe ñàkkug ndox mi laaloon bu baax dundu waa Senegaal yi te ni : maay ki jëkk a gis ni mbir mi neexul a nangu, neexul a muñ ci askan wi te réccu naa bu baax. | Macky Sall constatait avec faiblesse la pénurie d’eau qui impactait profondément la vie des Sénégalais en déclarant: Je suis le premier à trouver cette situation inacceptable, difficile à supporter pour les populations et je le regrette énormément. | galsenai/french-wolof-translation |
(SIBI) | Je suis désolé. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Ak wéy di xool soldaar yiy war ci cammoy bi. | Et surveillez la cavalerie à gauche. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Yéen ñépp a ngi doon. | Vous l'étiez tous. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Waaw kay, ñëwal. | Très bien, passez. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Aw, waay, ndax dañu yàqu? | On est foutus? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Lunu wara def, soxna si? | Que devrions-nous faire, madame? | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Danu wara dem ci liggéey bi. | On doit se mettre au travail. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Sëñkat bi, dama wara wax ni, lii mooy Mike Banning. | Je dois vous dire que c'est Mike Banning. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
- Tokk. | - Restez ici. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Waaw kay, jarul nga wéy di "wax". | Tu n'as pas à tenir un "discours". | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Ndoomu buur si bantuwaat ko, ngir bañ ko fàtte: Li am solo bët du ko gis. | L’essentiel est invisible pour les yeux, répéta le petit prince, afin de se souvenir. | galsenai/french-wolof-translation |
Duma ab kàngam, waaye xamnaa ku ko xam. | Je ne suis pas un expert, mais je connais quelqu'un qui l'est. | bilalfaye/english-wolof-french-translation |
Subsets and Splits