wo
stringlengths
1
4.02k
fr
stringlengths
1
1.08k
source
stringclasses
2 values
- Toxu!
- On se déplace!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Sasshesn yooyu ñu ngi gëna am njariñ ci mbir yu bari.
Ces sasshens sont les meilleurs dans beaucoup de choses.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Duma am benn sig' ci sama bip./ Yaakaaruma.
- Je ne reçois pas de signal. - Je ne suis pas sûr.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Daa melni perle yii.
C'est comme ces perles.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Komàndaŋ bi nangu woon na ne njiiti MFDC yi sax feneen ci lu jëm ci gisinu dal gi ci réewi Afrig yi.
Le commandant avait alors reconnu le risque que des responsables MFDC aillent s'enkyster ailleurs concernant l’appréciation du risque dans nos pays africains.
galsenai/french-wolof-translation
Raincutter bi dañu dagg laaf yi ak mbaal rasoir.
Cette Raincutter avait l'aile tranchée par un filet de rasoir.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaye amul lenn luñu mën a def.
Mais on ne peut rien faire.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dagg dagg./ Wër rek.
- Faites un tour.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ci li ma jot a xam, ginnaaw dañuy àtte ci turu askan wi lan moo tax amuñu yelleefu joxe seen xalaat ci jëf jooju.
À ce que je sache la justice est rendue au nom du peuple alors pourquoi ceux au nom duquel celle-ci est rendue n’ont pas le droit d’apprécier son action à l’aune de sa mission.
galsenai/french-wolof-translation
Me Mustafaa Njaay mi jiite woon mbooloom CESE mi jotal na nuyoo ñi ci bokk ñépp ak yu njiitam.
Me Moustapha Ndiaye qui conduisait la délégation des Conseillers du CESE a pour sa part transmis les salutations de l’ensemble des membres de l’Institution ainsi que celles de sa Présidente.
galsenai/french-wolof-translation
Waaye jàpp naa ni bëggoon naa nga gëna ma baax.
Mais je suppose que je voulais que tu sois meilleur que moi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kon dafay tàngal sa kanam ba noppi di tooyal sa der.
Pour réchauffer votre visage et hydrater votre peau.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bëy yi denc leen ci anam wu wóor
Chèvres stockées en toute sécurité
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Te bëggoon naa xam luñuy.
Et j'aimerais savoir ce que c'est.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ninga ko jàppee, sa fiancé du nit ku baax.
Comme vous le pensez, votre fiancé n'est pas un homme bon.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amuma benn fàttaliku ci loolu.
Je n'ai aucun souvenir de ça.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Da ngeen wara liggéey ci benn ekip..
Vous devez travailler en équipe.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bu ko defee, mu nekk jaamu buur bi Erodd.
Il est donc le sujet du roi Hérode.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nanga def Amy.
Je suis Amy.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñaan na jàmm ak dal ci biir réew mi.
Il a prié pour la paix et la stabilité au sein du pays.
galsenai/french-wolof-translation
Gisu leen benn.
Vous n'en avez trouvé aucune.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Ngir lan?
- Pour quoi?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Sama xarite yi, sunu consultants leempo yi di leen di digal ngeen baña joxe benn conseil
Chers amis, nos consultants leempo vous conseillent de ne donner aucun conseil
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Canada amoon na asamaan bu wóor.
Le Canada avait des cieux sûrs.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Seen xalaat, samay gént, ñoom ñépp booloo.
Leurs pensées, mes rêves, tout mélangé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Neenal nañu wépp yoon wu ñu doon doxal te mu aju ci lempo yiy ñëw rekk dugg ci gafakag réew mi ak yeneen yu ni mel ak tamit lempo yiy jaaree feneen, soog a yegsi ci gafag réew mi, te aju it ci sañ-sañu bindu, timbar, fésal suuf ak lempo yu ni mel, rawatina yoon limat 92-40 bu juroom-ñeenti fan ci weeru sulet 1974, di yoon wi samp Kotu lempo bu dajal bi ñu soppi.
Sont abrogées toutes dispositions légales de droit commun présentement applicables et afférentes aux impôts directs et taxes assimilées, et aux taxes et droits indirects internes, aux droits d’enregistrement, de timbre, de publicité foncière et taxes assimilées, notamment la loi 92-40 du 09 juillet 1974 instituant le code général des impôts modifiée.
galsenai/french-wolof-translation
Mën nga jëfandikoo ab paquet de care?
Tu peux utiliser un truc pour les soins?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
SEAN: Sama gaa yi, ñëwleen, ngeen jàppale ma gas.
Les gars, allez, vous devez m'aider à creuser.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
-Musu ma ci dem.
- Je n'ai jamais eu le temps.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Defin wi gën mooy jariñ sa réew.
D’une part, j’ai rappelé au ministre que la création de cette allocation forfaitaire mensuelle est incompréhensible pour un gouvernement dont l’argument a été jusqu’ici la maitrise de la masse salariale.
galsenai/french-wolof-translation
Déedéet--!
Je ne...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñaari yoon ci ayu-bis bi dañu koy woo ci këru mag ñi waaye mu dem ci këru mag ñi.
On appelle une maison de retraite deux fois par semaine, mais il est allé dans une maison de retraite.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Soo ma toppee, amnanu mbir yu baax ci yaw.
Si vous voulez bien me suivre, nous avons une très bonne situation pour vous.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ak baax ci environmaa bi, xam nga?
Et écologique, vous savez?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
"Bul dem leegi."
"S'il vous plaît, ne partez pas maintenant".
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Saa waay, leegi nga dem.
Hé, voilà pour vous.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Te loolu mooy danga wara fexe ba say doom am kaaraange.
Et c'est que vous voulez vous assurer que vos enfants se sentent en sécurité.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
tiire avion ak explosif, ñu wër nu bi avion bi daanu.
Il a bombardé l'avion, on a été encerclés.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaye sa yoon nekku ci dara, danga fi bëgg a nekkaat di siimee sa cere rogooñi baadoolo yi.
Mais qu'importe, tu t'en fou, tu veux encore te sucrer sur le dos des sénégalais.
galsenai/french-wolof-translation
Ram niko, "Mënu ma jiite sudee samay doomi réew joxu ñu ma cër, kon danga wara..."
Ram dit: "Je ne peux pas régner si mes sujets ne me respectent pas et donc vous devrez"...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xamuma woon naka lay def ak soxna si.
Et puis je ne savais pas comment ça allait aller avec la madame.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waruñu toppoto jubluwaay ki tuumal.
La prémisse perpétuellement d’actualité est que la Grande-Bretagne a de graves problèmes.
galsenai/french-wolof-translation
Muy noyyi bu baax.
Elle respire profondément.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Peñeel barab bi yépp, wut barab bimu nekk, wut ay leeral ci moom, fàww ma xam lépp lu jëm ci moom...su ngeen àndul ak moom, dinaa leen ray ñépp.
Fouillez toute la région, trouvez sa maison, obtenez ses détails, je dois obtenir toutes les informations sur lui... Si vous ne venez pas avec lui, je vous tuerai tous.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Centrelink amoon na prograam yu bari ngir jàngal nit ñi ni ñuy joxee rapoor ci saleer ndax nguur gi dafa doon ñàkk xaalis bu bari ci njuumte yi.
Centrelink avait plusieurs programmes pour apprendre aux gens comment déclarer les salaires parce que le gouvernement perdait beaucoup d'argent sur les erreurs
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Benn xeetu gaal.
Une sorte de vaisseau.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Gëm leen, dinaa ko def!
Je le ferai.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Simon, ndax dinga jéema dal.
Simon, tu veux bien te calmer, s'il te plaît?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lu ngeen ci xalaat?
Tu en penses quoi?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Garab lañuy jëfandikoo ngir defar dëkkuwaay, garab lañuy jëfandikoo ngir defar yéere. Li ëpp ci lu ñuy lekk ci garab lay bawoo. Su garab amul baayima duñu dund.
Nous fabriquons nos maisons et nos vêtements à base de plantes. La plupart des aliments que nous mangeons sont des plantes. Sans les plantes, les animaux ne survivraient pas.
galsenai/french-wolof-translation
Ci noonu gannaaw mbiru wër-gi-yaram lañuy mbubboo ngir tànn depite yi ñuy nangul ñu bokk ci liggéeyi kuréel yi ak bërëb bi ñépp di tase, loolu waral na ma bokk ci depite yi ñu génnee ci kuréel googu, maa ngi leen di wax ne ndax li ma fi lim yépp ci kow dinaa màndu ci wote nas sart boo xam ne : dafa nar a teg ci loxo kenn nit alal joo xam ne ni mu toll waxuñu ko ci mbébét bi ; nar a jox njiitu réew mi doole yu bari ci lépp, yu ëpp xeexu Koronaa ak jeexitalam si dundu gi ak koom bi, tàmbaliwul ak anami xeex buy wone ni lépp di demee ; tàmbaliwul itam won péncum ndawi réew mi mbébétu sàrt koppar bu ñu jubbanti ; mujj nar a andi ay jafe-jafey saytu yu jéggi dayoo.
À noter que le camp de Serigne Saliou Thioune, apparemment plus expérimenté, a déjà pris une longueur d'avance sur elle.
galsenai/french-wolof-translation
Dëgg la, mingi doon waaja jënd uh um, benn telefon boo mëna jëfandikoo.
Il voulait acheter un portable que tu pourrais utiliser.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
( greve )
(grève)
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Saytu ndax dee na am déet.
Vérifiez si elle est morte ou pas.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xoolal, nanu jubbanti benn mbir, sama gaa yi.
Écoutez, soyons clairs sur une chose, les gars d'accord.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Walla seeni doom.
- Ou leurs enfants.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amnaa 22 at..waaye ndax amna ku màggal sunu aniwerseer?
J'ai 22 ans, mais quelqu'un a célébré notre anniversaire?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
lii dafay ànd ak diisaay, doole ak kiliftéef bu mat sëkk ci sama liggéey:
cela vient avec tout le poids, le pouvoir et l'autorité de mon bureau:
bilalfaye/english-wolof-french-translation
tàngooru ndox mi mingi diggante 18 ak 24°C (64-75°F)
la température de l'eau est comprise entre 18 et 24 °C (64 à 75 °F)
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Donte diwaan bi nga xam ne fa lañu gisee néew bi, siiw na ci wóoradi ndax suuf su bari si, lu ndaw moo tax laajkat yi yeewu : Ba keroog, Jeynaba Taraawore mu ngi takkoon benn càqu oor, lóolu la ki ñu jox xibaar bi wax.
Même si la zone où le corps sans vie a été retrouvé, est réputée dangereuse à cause des multiples agressions, un détail a néanmoins attiré l’attention des enquêteurs : Dieynaba Traoré portait encore un collier en or, informe la source.
galsenai/french-wolof-translation
Deet lool, dee lool.
Très, très mort.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Tiket?
- Un billet?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ding ding ding ding ding ding ding.
Ça va?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mooy dex gi.
C'est la rivière.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Misha Philipchuk Sanja bimu nekkee xale ci filmu PAVEL CHUKRAI
MISHA PHILIPCHUK Sanja dans un film de PAVEL CHUKHRAI quand elle était enfant
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Arya...
Arya est morte.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Jappo bii di Rusi-Turki boobu defay wone benn dall bu yaatu bu leen ndawi Siri yi jappale ,fu ñetti milyoŋ ci ay nit nekk.
On ne peut pas se permettre de manquer un épisode sinon on est à la traîne.
galsenai/french-wolof-translation
Dañu tëye toppalante docking otomatik.
La séquence d'accouplement automatique est refusée.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xoolal li sama mag nekk.
Regardez la situation de mon frère.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Wutal ma G.I. Joes.
Donnez-moi les G.I. Joes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kublay Khan moo sos benn dëkk ci Taywan.
Kublai Khan a fondé une ville à Taiwan.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Oh, kontaan naa ci yaw. Sama doom, rafetoon nga.
Je suis si fière de toi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Solal sa sentiir!
Mets ta ceinture de sécurité!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Loccent, dañu nu dóor!
Loccent, on est touchés!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Soon-jong, may nanu dundu dundu gu dal
Je vous en prie, laissez-nous mener une vie tranquille.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xam nga ni maa ngi lay topp.
Je vous ai surveillée.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Jëflante bi am ci Caroline du Sud jurna beneen jéego ci at mi ci topp.
Le partenariat de la Caroline du Sud a donné une autre percée l'année suivante.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kon dama wara dem liggéey?
Je devrais me mettre au travail?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Rax ci dolli, soo amee visa Schengen, soxlaatul nga ñaan visa ngir dem ci meneen réew mu bokk ci espaas Schengen, dootoo génne xaalis ngir dem meneen réew, kenn dula sonalati ci joxe ay kêyit yudul jeex.
De même, en ayant un visa Schengen, vous n'avez pas besoin de demander séparément un visa pour chacun des pays membres de l'espace, ce qui permet d'économiser du temps, de l'argent et des formalités administratives.
galsenai/french-wolof-translation
Maanaam, amaana Danny def na njuumte.
Je veux dire, peut-être que Danny a fait une erreur.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ana tigre bi?
Et le tigre alors?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Boobu bëñ, Lars.
- Ce connard, Lars.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Gas!
Je vais creuser!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi koy woowe guddi.
Je me couche.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi xool sama yaram balaa may ñibbi.
Je vais faire un contrôle du périmètre avant de rentrer chez moi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nanga dugg.
Je vous en prie, entrez.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Sunu xare yëngal na suuf si... ba mujjee...
Notre bataille a secoué la terre... jusqu'à ce que, finalement...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
noonu la woon..
C'était tellement...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaye lu yéeme la, xale bu góor bimu daan faral di nekk ak moom delloo ko njukkal gi.
Mais ironiquement, un garçon avec qui il s'est défoncé trop souvent lui a rendu la pareille.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Kawar gu weex!
- Elle est blonde!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Alegsàndar bu mag.
Alexandre le Grand.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Du am cirque.
- Il n'y aura pas de cirque.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kureel yu nu dul giss dagnuy tollook kureel yu dëgg yi, waye amna ay wuuté yu ndaw.
Les équipes virtuelles sont soumises aux mêmes standards d'excellence que les équipes conventionnelles, mais il existe de subtiles différences.
galsenai/french-wolof-translation
Michael Apted dafa yàq pomi bimu wax ni dañu wara dindi lépp lu niru ak nit.
Michael Apted a ruiné le jeu quand il a insisté pour que tout ce qui avait une apparence humaine soit enlevé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Yaakaar naa ni mën nga wax ni Overlook Hotel amna lu ci melni luy melax.
Je suppose que l'on pourrait dire que l'Overlook Hotel a quelque chose qui brille.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mën nga xalaat dawalkatu buldoser.
Tu ne peux pas penser à un conducteur de bulldozer.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kapiteen Jaye Burnet.
Le capitaine Burnett.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
"Mutant ak mbégte." Lan?
"Mutant et fier". Quoi?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lii dafay nuru nimero telefonu nit.
Ça ressemble plus au numéro de téléphone de quelqu'un.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dinaa la may nga wax 2 simili
Je vous laisse parler deux minutes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation