wo
stringlengths
1
4.02k
fr
stringlengths
1
1.08k
source
stringclasses
2 values
Li ci gënoon siiw ci ger yooyu mooy li FBI jëfandikoo ci laŋket immigraasioŋ bu kër gu Weex gi, ñu koy woowe Filegate.
Le plus notoire de ces scandales de corruption a été l'utilisation par le FBI de la propre enquête de l'immigration de la Maison Blanche, le soi-disant Filegate.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xaalis rek laa soxla.
J'avais juste besoin d'argent.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñi ànd ci xaymay weer ak i biddiw yooyu te nekk ci bu jëkk, ni ko ñenn ñi waxee, tàmbali nañu koor altine.
Les partisans du calcul astronomique à l’avance tablaient depuis longtemps, comme l’ont souligné certains participants, sur un début de ramadan lundi.
galsenai/french-wolof-translation
Mën naa jeexal lii man kese.
Je peux finir ça tout seul.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
'Lii ab caaxaan la bu magg.
De la pole position, Bottas a pris un bon départ et frôlé Hamilton sur le flanc alors qu’il défendait sa place dans les deux premiers tours, et a invité Vettel à attaquer son partenaire d’équipe.
galsenai/french-wolof-translation
Xalaatu ma ni dina ñu ma gaaw jàpp.
Je ne m'attendais pas à être pris si vite.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Danga feebar, mën naa la jàppale.
Tu es malade et je peux t'aider.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Murph?
Tu veux dire Murph?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amul lenn luñu lay jaaxal
Ne vous inquiétez pas.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Saru.
Je suis Saru.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Sama jëkkër defna benn at ci biti.
Mon mari est là-bas depuis un an maintenant.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñakk xalaat ak wax lu mel noonu.
Arrête de penser et de dire des conneries comme ça.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
(Line buy sone)
(Ligne sonnant)
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Rëpibiliku Dominik (ci español: República Dominicana) réew bu nekk Caraïbes bu jël xaaj bi ci penku IiluHispaniola, bimu bokk ak Haïti
La République dominicaine (República Dominicana en espagnol) est un pays des Caraïbes qui occupe la moitié est de l'île d'Hispaniola, qu'il partage avec Haïti.
galsenai/french-wolof-translation
Tristam:
Je suis désolé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Wax ma...
Vous me dites...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Jahannama, xamuma fan laa wara tàmbalee?
Je ne saurais même pas par où commencer.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mënu ma leen nëbb ngir jàpp leen.
Je ne pouvais pas les attraper en douce.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Daara infirmiye soxla na sa talent ngir mëna dem ca kanam ci njàng mu jaar yoon.
L'école d'infirmières a besoin de vos talents pour faire avancer la cause de l'éducation saine.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Leegi ñu ngi may tiital.
Je suis maintenant en danger.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bella dama la ci ñee.
Je t'envie.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xaaral, kon ne nga doomu Walker faatu?
Attends, tu as dit que le fils de Walker est mort?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Newoon naa la nga xool liiñ bi, te bañ xool xaalis bi.
Je t'ai dit de viser la ligne, pas la pièce.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
"Maa ngi lay gëna baax, "fuck lépp ak ku nekk ñaari yoon," xeetu wankers.
Le genre "je suis meilleur que toi, je baise tout et tout le monde deux fois", le genre de branleurs.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
11:30 la.
Il est environ 23h30.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Am ngeen soxla?
- Vous avez besoin de quelque chose?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Morse mooy tombu-tombu-tiire-tombu.
Le morse est point-point-pointe-point.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nanga def, foofu.
Bonjour à vous.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amu nu sëy ci Naath, kon concept de bastard amul.
On n'a pas de mariage à Naath, donc le concept de bâtard n'existe pas.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kontaan naa ci xamante ak yaw itam.
Ravi de vous rencontrer aussi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Fan la Gisele nekk?
Où est Gisele?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ba ñaata fan laa wara xaar?
Combien de temps encore devrai-je attendre?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mingi ci kanam.
C'est juste devant.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bërëb bi eugueul doxalinam, donte téel na ñakk baldufa ci liggéey bërëb jawwu ji, ba dem ci jawwu di jex.
La station a maintenu son attitude, malgré la perte d'un gyroscope plus tôt au cours de la mission de la station spatiale, jusqu'à la fin de la sortie spatiale.
galsenai/french-wolof-translation
Risa Kusuma, benn yaay bu tollu ci 35 att neena waa Sky News: "Simili bu nek ambilaans day andi ay néew.
l a affirmé que les agents de bord avaient paniqué et crié, et qu’il souffrait d’une blessure mineure à la tête.
galsenai/french-wolof-translation
"Leegi suuf si mingi wëréelu ci ay 'selfie'"
"La terre tourne de nos jours coincé dans les écrans de'selfie' "
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Yan ñooy seen naal yéen ñi nekkee Nouvelle-Aquitaine ak kurélu PASTEF gi nekk Farãas.
Quels sont vos projets au sein de la Section Nouvelle-Aquitaine et de la Coordination PASTEF France ?
galsenai/french-wolof-translation
Khallad nettali ñaareelu jaar-jaar ni ñoom ñatt ñu ngi tukki ci Karachi.
Khallad a donné une deuxième histoire que les trois d'entre eux ont tous voyagé à Karachi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Du man.
- Je ne suis pas.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Marshal, ndax mën nanu ci waxtaan ab diir? !
On peut en parler une seconde?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi lakk!
Je brûle!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dama yaakaar ni sama jëkkër mingi fi.
Je crois que mon beau-frère est là.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Àdduna bi dafay sargal
Le monde apprécie
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ci fowokaayu askan wi, mën na jàppale xale yi ñu xam li nit ñi di nuru ak di wuute ci seeni bëgg-bëgg, seen gëm-gëm ak seeni yëg-yëg.
Dans les jeux de société, les enfants peuvent apprendre à travailler et à coordonner différents rôles, ce qui les aidera à comprendre les similitudes et les différences entre les désirs, les croyances et les sentiments des gens.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
'Nekkoon na foofu'
Il était là.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Benn mbir rekk.
Une seule chose.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi lay digal nga taxaw.
Je vous ordonne de vous retirer.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Baal ma, Krishna.
Je suis désolé, Krishna.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amnaa benn, waaye dafa yàqu.
J'en ai une, mais elle est cassée.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mën nañu nu jokkoo ci telefon 24 waxtu ci bis bi
Nous sommes disponibles par téléphone 24 heures sur 24
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ci yóbbaaleek yaatuwaayu naalu pólótig bu PASTEF.
Sur l’influence et l’étendue du projet politique de PASTEF.
galsenai/french-wolof-translation
Fichier yi mën nañu leen tekki ci yeneen làkk.
Les fichiers peuvent être traduits dans d'autres langues.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Fukki mboq, yaa ko moom.
Dix épinards, c'est à vous.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Tànta daf la ko jox yaakaar ni sama jabar nga.
Tante te l'a donné en pensant que tu étais ma femme.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dinaa ko xam.
Je vais le prendre.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ni may gis muy ñëw...
Que je le verrais arriver...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
-Dalal ak jàmm!
- Bienvenue à vous!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bernstein moo leeral kàddu yu njëkk ya.
Bernstein explique la préface.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Loolu dina ñu ko soxla. Def ko.
On va avoir besoin de ça.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nanu xalaat bu baax ci mbir mii.
Réfléchissons à cette chose.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Charlie neena dem nga ci dëkk bi
- Charlie a dit que tu avais quitté la ville.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Barab bu wóor.
Dans un endroit sûr.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dafa wara wéyal ko ñeenti ayu-bis.
Elle doit le garder pendant quatre semaines.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Danu ko wara gis.
Il faut juste le trouver.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Klimaa bi ci boppam dafay soppeeku bu baax.
Le climat lui-même est très changeant.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Te yaw itam amoo sa passport?
Vous n'avez pas votre passeport?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Makpaayis yi bétt nañu Sitisën yi.
Les Citizens se sont fait surpris par les magpies.
galsenai/french-wolof-translation
Xam nga lan? Dama wara sol uniform.
Je vais porter un uniforme.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Fi mu tollu, na ko ñépp xamee nii, féetale boor bu ëpp bi dafa mujj doon njaayum doole.
Auteur d’un des trois buts, Mbaye Niang et Rennes mettent fin à une série de 10 matches sans succès.
galsenai/french-wolof-translation
Lan--?
- Je suis désolé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Ana sama doom?
- Où est mon fils?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Deeguma.
Je ne suis pas encore mort.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Def dara moo gën ñàkka def dara?
Faire quelque chose est mieux que rien?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Musu ma xalaat ni dinaa bokk ci nit ñi ragal aniwerseer, waaye daf may fàttali ni nekkuma fima bëgga nekk.
Je n'aurais jamais pensé être une de ces personnes qui redoutent les anniversaires, mais ça me rappelle que je ne suis pas là où je veux être.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
-Déedet, Sean, duma faral di ñëw fii.
- Non, Sean, je ne viens pas ici très souvent.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nit ku dëgër laa woon. Jàppoon naa ni fitna rekk mooy tax nga am li nga bëgg.
J'étais un dur, je pensais que la violence était le seul moyen d'obtenir ce que l'on voulait.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Loolu amul benn njariñ.
C'était des conneries.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Déedet Déedet Déedet, YÀGGAL TUUTI.
Un peu plus haut.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
[ REE ]
Je suis désolé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dawal bu neex, xarit.
Bonne course, mon pote.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Li leer mooy mag ñi waru ñu jàngal xale yu ndaw yi ci baat, ni ñu koy defee suñu leen di jàppale ñu def ay puzzle wala yeneen liggéey yu mel noonu.
Malheureusement, les adultes ne devraient pas enseigner par cœur aux enfants d'âge préscolaire, comme ils le font lorsqu'ils les aident à résoudre des énigmes ou à faire d'autres tâches.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bëggoon nañu balaa daraay xew ñu mas-sawu mbokki Senegaal yi loru ci mbënn mi ñu gis fu yaatu ci réew mi, séddook ñoom seen tiis.
Nous aimerions avant tout exprimer toute notre sympathie à chaque Sénégalais touché par les inondations qui paralysent une large part du pays.
galsenai/french-wolof-translation
Ndax mën naa la wax dara?
Je peux te dire quelque chose?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
seconde yu nekk dina ñu sànni nataal biñ gëna néew ba keroog benn kese des.
Et toutes les 10 secondes, l'image la moins choisie sera éliminée jusqu'à ce qu'il n'en reste plus qu'une.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
britannique yi ñàkk nañu yor xaalis ci àdduna bi
Les Britanniques ont perdu le contrôle des finances mondiales.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bima laalee benn garab guy raam, mu daal di may yuuxu naan...
Quand j'ai touché une chenille, elle m'a réprimandé en disant...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Danuy waaja wax mbooloo mi ñu jàppale daara ji xaalis, waaye defu ñu ko bu njëkk.
Nous avons l'intention de demander à ce groupe de faire un don à l'école, mais ils ne l'ont jamais fait auparavant.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ku nekk, wàcci!
Tout le monde, à terre!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Trapper dragon bi gëna baax ci àdduna.
Le meilleur trappeur de dragons vivant.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Ñu ngi xaar.
- Ils attendent.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Ay téemeeri.
- Des centaines.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amnaa xel mu ñaw.
Je suis assez intelligent.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ginaaw ga, benn wàll ci macceer genetik bi dafay soppi nekk tinte bu wiyole.
Finalement, une partie du matériel génétique est transformée en une teinture pourpre.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Sudee ñaari at lañuy wax, mën naa jëfandikoo jot gi ngir gëstu ci gravite bi.
Si on parle de quelques années, je pourrais utiliser le temps pour étudier la gravité.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Danu wara def lii leegi.
- On devrait finir ça maintenant.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dafa wara nekk Lex.
Ça doit être Lex.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi ci bain.
Je prends un bain.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kon noo ngi jaar.
On vient de passer.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mu ne ndoomu buur si: Lu doy waar la, lépp mat na: póli bi, baag bi ak goj bi…Mu reetaan, làmb goj bi, wëndeel póli bi.
C’est étrange, dis-je au petit prince, tout est prêt : la poulie, le seau et la corde…Il rit, toucha la corde, fit jouer la poulie.
galsenai/french-wolof-translation
Purge essence!
Purgée de carburant!
bilalfaye/english-wolof-french-translation