wo
stringlengths
1
4.02k
fr
stringlengths
1
1.08k
source
stringclasses
2 values
Xam nañu ni damay sonal nit.
Je suis connu pour être très vexant.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Waaw leegi amnaa benn sartu.
- Je vous laisse à une condition.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waa Angleterre itam amoon nañu njaay bu bari ci àdduna bi.
Les Anglais avaient aussi un commerce important dans le monde entier.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi koy boole.
Je le connecte.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Leegi dégg naa ñuy klone baayima.
J'ai entendu parler du clonage des moutons.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ginnaaw bu mu lottee lool, Bayern dafa waroon a teg defãas bu dëgër (Pavard ak Hernandez ci aks bi)
Décimé, le Bayern devait aligner une défense inédite (Pavard et Hernandez dans l’axe).
galsenai/french-wolof-translation
(BAAT NORMAL) "Nit la"?
"C'est un homme"?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Du musa nekk nit ku lay bàyyi xel.
C'est généralement quelqu'un qui ne se soucie jamais.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Du ni jamono yu njëkk ya, bi internet amoon.
Ce n'est plus comme avant, quand il y avait Internet.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Alexander, xamnaa la bi nga juddoo.
Je te connais depuis ta naissance.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Juif yi, chretien yi, jullit yi.
Les juifs, les chrétiens, les musulmans.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mën nanu maske sunuy adres IP.
On peut masquer nos adresses IP.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xamuma kan laa!
Je ne sais plus qui je suis!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nit ñu bari lool te mënu ñu def dara?
Trop de gens pour faire quoi que ce soit?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amul doom.
Sans enfant.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi ragal, suñu nu jàppee?
J'ai peur, si on est pris.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Baay, xoolal ni muy doxee.
Père, regardez sa démarche.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dédeet, mënu ma ñibbi te amul baague bii.
Je ne peux pas rentrer sans cette bague.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Letty la, wala book?
C'est Letty, pas vrai?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndax sa jëkkër musul wax ci "Buur bu weex bi?"
Votre mari a-t-il déjà parlé du "Roi pâle"?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Te mingi ñëw!
Il arrive!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaye Sharmila demoon na Mumbai 5 fan ci ginaaw ci passport bu baaxul.
Mais Sharmila est partie pour Mumbai il y a 5 jours avec un faux passeport.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Ñëwal, ñëwal.
- Je vous en prie.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Oh. Baax na,
Très bien.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Man itam ñàkk naa xaalis bu bari.
J'ai aussi perdu beaucoup d'argent.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Li koy firndeel mooy, ci bés bu jëkk bi dañu duma gaa yi bu baax, ca ëllëg sa, gisuma sax muus muy taxawaalu.
Li koy firndeel mooy, ci bés bu jëkk bi dañu duma gaa yi bu baax, ca ëllëg sa, gisuma sax muus muy taxawaalu.
galsenai/french-wolof-translation
Mu daldi taalaat làmpu mbedd mi.
Et il ralluma son réverbère.
galsenai/french-wolof-translation
Lu nuy soxal su amee njiit li?
Qu'est-ce qu'on en a à voir s'il prend le président?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Conte de Monte Crisco?
Le comte de Monte Crisco?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bëgg nga mburu mu am xorom?
Tu veux du pain avec du sel?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Toog nga foofu.
Vous vous asseyez là.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Li gëna taxa jog science mooy xam ni àdduna bi di doxee ci anam wu mengoo ak xarala. Anam woowu itam ci la benn gëstu ci wàllu xarala di tënku.
L'objectif principal de la science est de comprendre la façon dont le monde fonctionne grâce à la méthode scientifique. Cette méthode guide en fait la plupart des recherches scientifiques.
galsenai/french-wolof-translation
Doomu Will Turner ak Elisabeth Swann.
Il est le fils de Will Turner et Elisabeth Swann.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñu ngi sos réew mi ci ngëm ni amna nit ñu gëna mag ci ñeneen ñi.
Cette nation a été fondée sur la croyance que certaines personnes sont intrinsèquement supérieures aux autres.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bi mu suuxatee, bu mujj, tóor-tóor bi, ba di ko waaj a dëpp leget gi, la ko jooy jàpp.
Et, quand il arrosa une dernière fois la fleur, et se prépara à la mettre à l’abri sous son globe, il se découvrit l’envie de pleurer.
galsenai/french-wolof-translation
Hank Williams ak cowboy yiy daw...
Hank Williams et tous les Cowboys dérivant...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ma daldi jël kareyoŋ tàmbalee rëdd sama nataal bu njëkk.
Mon dessin numéro 1.
galsenai/french-wolof-translation
Suuf su ñépp bokk la, te poliis mën na dugg fii.
C'est un terrain public, et la police a le droit d'y entrer.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lu tax Alan?
Pourquoi c'est Alan?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Centerlink amoon na anam yu bari yu nit ñi mëna xamee ci wàllu xaalis.
Centerlink avait de nombreuses façons de rendre ses états financiers compréhensibles au public.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dama jàpp ni mbir yu bari xewna ci hotel bii ci at yi weesu.
Je pense que beaucoup de choses se sont passées ici dans cet hôtel particulier au fil des ans.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Du bis bi may njëkka yónnee ñaari xale yu jigéen ñuy yuuxu ci néeg.
Ce n'est pas la première fois que je fais crier deux filles.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dafay laaj ñu xoolaat anami wote yi, yu doxal yeek yu saytu gafag nguur gi.
Il en appelle ainsi à une redéfinition des modalités de vote, d’exécution et de contrôle des budgets des pouvoirs publics.
galsenai/french-wolof-translation
Xoolal magazine bi?
Le magazine Look?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Leegi, doom, doom, song ma!
- Maintenant, bébé, bébé, attaque moi!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dinaa ko gaaw.
Je vais faire vite.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dugalal ñaar yii ci jeep bi.
Mettez ces deux là dans la jeep.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Benn Triceratops meenna jeefee ndiko koppam bu mak ngir genné xob yi laata lékk gnam bi.
Un tricératops aurait pu utiliser son bec puissant pour enlever les feuilles avant de manger le tronc.
galsenai/french-wolof-translation
Boobu yëg-yëg mooy fondaasioŋ... li nuy def nit.
Cette émotion est à la base... de ce qui nous rend humains.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
tëye liiñ bi.
Restez en ligne.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kon danga wara xam nimu tabaxee kuréelam
Alors tu dois savoir comment elle a construit son groupe.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amoon nanu yaakaar defal xale yi feetu noel, waaye musu nu mëna defal sunu bopp dara.
Nous avions espéré organiser une fête de Noël pour les enfants, mais nous n'avons jamais pu faire quoi que ce soit pour nous-mêmes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Firndeel nu ni yaay ki nga wax ni yaay.
Prouvez-nous que vous êtes qui vous dites être.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Mënoon nañu ko àttee neneen su doon dafa réeral caabi otoom te moom ci boppam moo doon jéem dàjji otoom.
Il faudrait le juger différemment s'il avait perdu les clés de sa voiture, et si c'était sa propre voiture qu'il essayait de forcer.
galsenai/french-wolof-translation
Maa ngi wax jëfandikoo bépp target.
Je dis engager toutes les cibles.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Déedéet, ñëwoon naa ngir daje ak yaw.
- Non, je suis venu vous voir.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaw kay, tijji ko.
Très bien, débloquez-le.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndax dañuy def ni ñu leen di wax wala ñu def ni ñu ko neexee?
Ils font ce qu'on leur dit ou ce qu'ils veulent?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Famiy yi dañuy xaajaloo.
- Des familles sont déchirées.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Ñaar fukki pied ci biti.
- À six mètres.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bu ñu ubbee sarax yépp, keesu xaalis yooyu dinañu des ci seeni xayma.
Ces coffres resteront dans leurs tentes quand tous les cadeaux seront ouverts.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Piyeesu kaka!
Espèce de merde!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Match bu jaar yoon.
Une combinaison parfaite.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Loolu naka la meloon?
C'était comment?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dinaa la namm soo dee.
Tu me manqueras quand tu mourras.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waxuma woon ci moom, dama doon wax ci yaw.
Je ne parlais pas de la sienne, mais de la tienne.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Reer bi ñor na, sama xol.
Le dîner est prêt, chérie.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kon lu tax?
Alors pourquoi?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Leegi lu tax doo ma wane?
Pourquoi tu ne me le montres pas?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nguuru Nazy yi nangu nañu ko.
Le régime nazi l'a permis.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Fan, naka ak kañ nga sëy?
Où, comment et quand vous êtes-vous mariés?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaw, baaxul. góor:
- Oui, pas mal. - Je sais.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ma xool ci atelier bi, waaye nekkul woon.
J'ai vérifié l'atelier, mais il n'était pas là.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Am nga ñaari waxtu wala ma ray ko sama bopp.
Vous avez deux heures ou je l'exécuterai moi-même.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
(VOKALISE)
Je suis désolé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bëgg naa ñu provoke sama membre.
Je veux provoquer un membre.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Charles!
Je suis désolé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ex agent RAW
Ex agent RAW
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nanga def, pàppa.
Je suis désolé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Hazmi ak Mihdar bokk nañu néeg
Hazmi et Mihdar partagent une chambre.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Am nga ay ball yu am solo, waay.
Tu as vraiment des couilles.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dama wara yegsi ci juróom ñaari waxtu.
Je dois y être dans sept heures.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñari loxo neuronal yi ci 100%.
Les deux poignées de main neuronales à 100%.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Baaxna, dinga wér. Di nga wér.
Ça va aller, tout va bien se passer.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kan lay xalaat ni moom la?
Pour qui se prend-il?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndax dañu wara jaaxle ?
Faut-il s'inquiéter?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Sama dundu jafe na, Max.
Ma vie est compliquée, Max.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Njiitu Pastef ñi bëgg seen réew
Président de PASTEF-les patriotes
galsenai/french-wolof-translation
Gis nga ñaareelu Ridge bi, foofu?
Tu vois cette deuxième crête, là-bas?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Phil, bul dem ci duus bi./ Alan, nga jéema dal, man la.
- Phil, ne va pas dans la salle de bain. - Alan, calme-toi, c'est moi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñu daaj ko ci bant ndax dafa doon xeex ngir ñu daaneel nguur gi ak sàcc fas yi.
Il a été pendu pour avoir préconisé le renversement de l'État et le vol de chevaux.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ci téere bu mu tudde Critique de la raison nègre, Asil Mbembe dëggal na fa ne xaalaatu àddina bi bayaal bu jaay ak jënd di dox di bënn diggu réew yi moo ngi dànkaafu seenug kilifteef ba koy nar a néewal doole, te dafa sàmmoonteek juddug àqu réew yi, àqu pénc mi, àqu ñépp ba nga am ne jubluwaayam mooy wattu jàmm ju sax ji.
Dans Critique de la raison nègre, Achille Mbembé affirme que l’idée du monde comme surface parcouru par des relations commerciales qui traverse les frontières des Etats et menacent de rendre obsolète leur souveraineté est, à bien des égards, contemporaine de la naissance du droit international, du droit civil, du droit cosmopolite dont la visée est de garantir la paix perpétuelle.
galsenai/french-wolof-translation
Musu ma weddi dara ci li nga laaj.
Je n'ai jamais nié ce que vous m'aviez demandé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Sa néeg mingi ni nga ko bàyyee. Dafa pare.
Votre chambre est exactement comme vous l'avez laissée.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñaar ñuy sey mën nañu dogal ni loolu du lu baax ci ñoom, wala ci seen doom, ñu yar ab liir.
Un couple peut très bien estimer qu'il n'est pas dans leur intérêt, ni dans celui de l'enfant, de s'occuper de l'éducation d'un bébé.
galsenai/french-wolof-translation
Amaana du sama doom.
J'aimerais qu'il ne soit pas mon fils.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ci Afrig mësul a yomb nga téqale donte kujjee gi bari na waa gox bi.
En Afrique il n'est jamais facile de faire une nette différence même si l'adversaire est composé de locaux en majorité.
galsenai/french-wolof-translation
Luy pose ngir def?
C'est quoi cette pose?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dama defaral samay baayima ñag
Je fais une clôture pour mes moutons
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bëgg naa ko lépp.
Je veux tout.
bilalfaye/english-wolof-french-translation