wo
stringlengths 1
4.02k
⌀ | fr
stringlengths 1
1.08k
| source
stringclasses 2
values |
---|---|---|
Góor gaa ŋgi. | L'homme, le voilà. | null |
Naka ligéey bi ? | Comment se passe le travail ? | null |
Jàngewuma ko it ci nataal yi mu fa jël ca at yu njëkk ya. | Ni même en regardant les photos qu'il a prises pendant les premières années, à son arrivée en Afrique. | null |
Du keneen ki. | Ce n'est pas l'autre. | null |
Yendu ak jàam | Aies une bonne journée | null |
Wool xale yi dul dem fenn. | Appelle les enfants qui n'iront nulle part. | null |
Sa yay nee soo yeggee dana dellusi. | Ta mère promet de revenir si tu vas jusqu'au bout. | null |
Góor gii demoon | Cet homme qui était parti | null |
Mbëggéelam googee woon a ŋgi fi ba tay. | C'est son amour d'antan qui survit encore. | null |
Tëri te julliwoo, xel daju ko te bu dibéer agsee, kenn sañul a yittewoo leneen lu dul jàng sa téereb mees. | C'était le même homme qui exigeait que la prière fût dite chaque soir à l'heure du coucher, et que le dimanche fût consacré à la lecture du livre de messe. | null |
Diŋga dem ? | Tu iras ? | null |
Gisu leen woon | Il ne les avait pas vus | null |
Tàngaay bi may wax, ndax sonaloon na nu dëggëntaan ? | Faisait-il chaud vraiment ? | null |
Su doon doxandéem ci man rekk, ñu ni waaw waaye yemu fa. Daanaka ab noon la ma def. | Il était trop différent de tous ceux que je connaissais, un étranger, et même plus que cela, presque un ennemi. | null |
Góor dëgg du fen ! | Un homme de bien ne ment pas ! | null |
Feneen fi bëttóon foofu. | Cet autre endroit où il y avait une fuite. | null |
Maa ngi tudd ... | Je m'appelles ... | null |
Jiit yi may wax nag, am na ci benn boo xam ne lu doy waar, lu kéemaane, dal na ko bés, ndeysaan. Li ma koy a waaj a nettali nii rekk sax mu ngi yëngal samag naw, may yëg xaat tiis wu réy. Bésub dibéer la woon, ci suba. | Les scorpions furent un jour au centre d'une scène dramatique, dont le souvenir fait encore battre mon cœur aujourd'hui. | null |
Gis naa nit ki. | J'ai vu l'homme. | null |
Fépp fu mu jëm foofu jàmm dana fa wacc. | Partout où il ira la paix descendra là. | null |
Fekkoon na xelam newoon ci dem. Mu doxe fa fomm ba fàww. | C'est à partir de ce moment-là qu'il cesse de songer au départ. | null |
Xale yi, foofu nag, ñu mer. | Les enfants alors se fâchèrent. | null |
Waa ji day waxe bakkan. | L'individu parle avec son nez. | null |
Siré ñaanal na Umar mi taxaw. | Cire a prié pour Oumar qui se tient-là. | null |
Loo bëgg ? | Que veux-tu ? | null |
Xamatuma sax man at la woon waaye mu ngi mel ni tey ci man. Dogaatleb démb ak tey a ngi sew ruuj, sew nib seetu. Bu kenn yaakaar ni nammeel a ma doxe ginnaaaw, gal-gal ma, ma yegg suuf di wax i waxi dof. | Tout cela est si loin, si proche. Une simple paroi fine comme un miroir sépare le monde d'aujourd'hui et le monde d'hier. Je ne parle pas de nostalgie. | null |
Ndax mën nga ko waxaat su la neexee ? | Répètes s'il te plaît ! | null |
Wool góor gi dul Kajgaamu fii ! | Appelle l'homme qui n'est pas Kangame d'ici ! | null |
Mu ngi ci Afrigu fentaakoon bu mag ma, Andare Siid, Afrig gi mu nuy nataalal ci téereem bu siiw boobu tudd Voyage au Congo. Bindkat boobook Baay a yeggandoo Afrig, daanaka. Li leen yéem, fees seeni bët, benn la tamit : yaatuwaayu dex gi, gaal yeek saxaari-géej yi ciy doxantu, bànxaasi dex yi, dexug Awóyadaa ak i gaalam ya ñu teg xobitiir ca kow te di leen bëmëxey bant yu gudd ; ci wetu tefes gi, dexug Kalabaar, ak dog-dogu dëkkub Óbukun, ňu yatt kook jaasi ci fi àll bi gënee fattu. | Il est devant les paysages de l'Afrique équatoriale tels que les décrit André Gide dans son Voyage au Congo (à peu près contemporain de l'arrivée de mon père au Nigeria) : l'étendue du fleuve, vaste comme un bras de mer, sur lequel naviguent pirogues et bateaux à aubes, et les affluents, la rivière d'Ahoada avec ses « sampans » aux toits de palmes, poussés par des perches, et plus près de la côte, la rivière Calabar, et l'échancrure du village d'Obukun, taillée à coups de machette dans l'épaisseur de la forêt. | null |
Gis naa la yaw ak moom ! | Je t'ai vu avec lui ! | null |
Yaw mile la ! | C'est toi-même ! | null |
Séen naa ag guy. | J'ai aperçu un baobab. | null |
Du ay janeer mbaa ay xalaat yuy baagante ci jaww ji : déedéet, ci suuf su nangoo-nangu lañuy meññ. | Beaucoup plus que de simples souvenirs, il est fait de certitudes. | null |
Ci keneen ki ñëw. | Chez l'autre qui est arrivé. | null |
Góor gi dem na, ma defe ! | L'homme est parti, je crois ! | null |
Mu neex ko, mu naqadi ko, doxandéem la bu turam siiw, mooy doktoor biy dagg loxo yeek tànk yi te it gaaw lool ci génne sarengalu armiňoŋam bu raglook pusoom bu sew ruuj. | Il est un étranger dont la réputation s'est répandue dans tout le pays, qui coupe bras et jambes quand la gangrène a commencé, et dont le seul remède est contenu dans cet instrument à la fois effrayant et dérisoire, une seringue de laiton munie d'une aiguille de six centimètres. | null |
Réew mii la ndiir-bët yem. Ni asamaan si yaatoo dafa rekk yéeme, joor gi naka noonu. | Ici, c'est un pays aux horizons lointains, au ciel plus vaste, aux étendues à perte de vue. | null |
Gis naa la ak moom ! | Je t'ai vu avec lui ! | null |
Ko gis ? | Qui as-tu vu ? | null |
Waa ji gor la fi ! | L'homme y est magnifique ! | null |
Te ŋga dem kat ! | Surtout pars ! | null |
Mas naa am ngone ni ñépp wànte li ma ñàkk ba fàww, lii la : baay bu may gis may màgg, kër gu féexal sama xol laata may xam dara ci àddina. | Ce qui est définitivement absent de mon enfance : avoir eu un père, avoir grandi auprès de lui dans la douceur du foyer familial. | null |
Lu tax ? | Pourquoi ? | null |
Nataal bii ma gis, gis naa ci ag kër gu rafet, am ag garab ci buntu kër gi. | Sur la photo que j'ai vue, j'y ai vu une jolie maison, et un arbre à la porte de cette maison. | null |
Góor gi soppul seen lekku Saalum yooyu. | L'homme n'apprécie pas votre cuisine du Saloum. | null |
Amaana sunu gis-gisu yaay ci Afrig mujje noo wàll. Afrig ma doon door a juddu, daanaka, te ñu teel koo teg coono àddina yu dul jeex. | Peut-être est-ce le regard de ma mère sur ce continent à la fois si neuf et si malmené par le monde moderne ? | null |
Nattu doomi Biyaafaraa moo doon petorool ba ni fa woon gàññ ci bëlub Kalabaar. Ibo yeek Yoruba yiy reyante, réewi Tugal yiy seetaan, naan tey mu neex. | Pour la mainmise sur les puits de pétrole à l'embouchure de la rivière Calabar, Ibos et Yoroubas s'exterminent, sous le regard indifférent du monde occidental. | null |
Bule xale laa wax ? | Je parle de cet enfant-ci ? | null |
Mi ŋgii dem ba delusi | Voilà qu'il a été et qu'il est revenu | null |
Portale yi fi Baay jël, biral nañ cofeelam ci mim réew. | Les clichés que mon père prend avec son Leica montrent l'admiration qu'il éprouve pour ce pays. | null |
Bëgg naa góor gi ñëw | Je veux que l'homme vienne | null |
Kooku dem na | Celui-là est parti | null |
Du woon dem | Il ne serait pas parti | null |
Gàddaay ba far tebbi lu duun | S'exiler pour en tirer grand profit | null |
Na góor gi dem ba xale yi yeksi. | L'homme doit s'en aller jusqu'à ce que les enfants reviennent. | null |
Gis ŋga kookale ? | Tu as vu celui-là ? | null |
Kooku la ! | Celui-là ! | null |
Nataal bii de nataal la boo xam ne ay nit la yu nekk ci benn bërëb toog fa ba noppi am lu ñuy def. Ba noppi toog ca bërëb ba di am lu ñuy liggéey waaw. | Sur cette photo il y a des gens qui sont assis dans un domaine et qui font quelque chose. En plus ils sont bel et bien assis dans un domaine entrain de travailler. | null |
Buga nga fecc ? | Accepte-tu de danser avec moi ? | null |
Beneen ndab laa bëgg ! | C'est un autre récipient que je veux ! | null |
Ginnaaw géej gi wóoratul, Saxaraa fi sës ngir doxal njënd mbeek njaay mi. | Les routes maritimes sont devenues dangereuses, et c'est le Sahara qui permet la circulation des denrées. | null |
Demal, ndax mu di, leneen, mu di feneen ! | Vas-y pour que ce soit autre chose, que ce soit ailleurs ! | null |
Nataal bi, maa ngi ciy gis lu mel ni ab bãŋ. Bãŋ bi nag dañ koo teg ci aw xàll, bãŋ bi nag bãŋub ràbb la dañ koo ràbb rafet na lool nag neex a toog. | Sur cette photo, j'y vois quelque chose qui ressemble à un banc. Le banc est, cependant, posé sur <unk>. Le banc, on l'a cousu de très jolie manière et elle est confortable. | null |
Degguma. | Je n'entends pas. | null |
Nit doŋŋ tiitëlu ko. | Un homme tout simplement ne saurait l'effrayer. | null |
Dem naa | Je suis parti | null |
Dunu génn kër gi te sama yaay newu nu solleen seen kask Kaawanpoor – du woon dara sax lu dul mbaxane ňax yaň ňu jëndaloon ca Niis. | Quand elle nous voyait sortir, ma mère nous obligeait à mettre nos casques Cawnpore – en réalité des chapeaux de paille qu'elle nous avait achetés avant notre départ dans un magasin de la vieille ville de Nice. | null |
Bëgg naa góor ñi ñëw, xale yi ñëw, jigéen ñi toog ! | Je souhaite que les hommes viennent, que les enfants viennent et que les femmes s'asseyent ! | null |
Du sax nataal bu war a bett képp ku xam ni mbir mi doon deme booba. Tubaab yi doon dem Afrig, daanaka yoon woowu la ñu gënoon a miin, yoon wiy jóge Senegaal, jëm ruqu-géeju Gine. Tubaab ya doon jaay ak a jënd te yàkkamtee dajale alal ju takku, xamoon nañ bu baax yoon woowu. | Cette Afrique-là n'est pas très dépaysante : c'est l'étroite bande qui suit le contour de la côte, depuis la pointe du Sénégal jusqu'au golfe de Guinée, que connaissent tous ceux qui viennent des métropoles pour faire des affaires et s'enrichir promptement. | null |
Daawunu sax ubbi sunu gémmiñ. Dañ daan dóor rekk, mer, di yuuxu te luñ gën a yuuxu sunu xol gën a fees. | Nous ne parlions pas, nous cognions, nous poussions des cris de rage, et de nouveaux pans de murs s'écroulaient. C'était un jeu. | null |
Juróom-ñetteelu nataal bi seetlu naa ci cere joo xam ne dañ koo defar. Biñ ko defaree bam noppi mu àndak ñeex moo xam ne moom lañ koy siife. | Sur cette photo datant d'il y a huit ans, j'y ai vu du couscous qu'on a préparé. Après l'avoir bien préparé, il s'accompagne de sauce qui est mélangée avec. | null |
Daŋga gis kan ? | Tu as vu qui ? | null |
Moo dem | C'est lui qui est parti ? | null |
Du ñàkk ñu ni, aa, ñii kat seen nekkin ca Niseryaa nekkinu Tubaab yi tegoon loxo ci Afrig doŋŋ la woon, nga xam ne dañu fa daan sanc, yaakaar ni mën nañ koo soppi Àngalteer walla Normàndi gu ndaw. | Tout cela pourrait donner l'impression d'une vie coloniale au Nigéria, très organisée, presque citadine – ou du moins campagnarde à la façon de l'Angleterre ou de la Normandie d'avant l'ère industrielle. | null |
Ni may xalaate ni lu ma neexaan def, fu ma neexaan dem, ñàkkul muy lu may janeer, daanaka. | Une liberté de mouvement, de pensée et d'émotion que je n'ai plus jamais connue ensuite. | null |
Mu japp nag yooyu yan ? | Qu'il attrappe quelles vaches ? | null |
Su góor gi dee ñëw | Si l'homme vient | null |
Te sax, ma ŋgii dem ! | D'ailleurs, je m'en vais ! | null |
Xam naa nit ñi dul Sërin ! | Je connais les gens qui ne sont pas des Sérignes ! | null |
Yan xar ñoo ñëw ? | Quels moutons sont arrivés ? | null |
Noonu, Baay sottiwaat leen alkol, ñu tàkk jëppét, mook doom yi. Mbir mee gënoon a gaaw xef ak xippi. Ndaxam meloon na ni toogoon naa lu yàgg janook jiit ji muy tàkk, di wëndéelu ba sedd guyy. | Une deuxième giclée d'alcool l'a d'un seul coup embrasée. L'affaire n'a pas pu durer plus de quelques secondes, et pourtant j'ai l'impression d'être resté longtemps à regarder sa mort. La femelle scorpion a tourné plusieurs fois sur elle-même, sa queue agitée d'un spasme. Ses petits étaient déjà morts et tombaient de son dos, recroquevillés. Puis elle s'est immobilisée, ses pinces repliées sur sa poitrine dans un geste de résignation, et les hautes flammes se sont éteintes. | null |
Waaye léeg-léeg yeneeni jiit yu gën a réy wuutu leen. Boo leen giseek seen weexaay bu xëcc ci puur, njort ni ñii moom war nañoo am daŋar. | Mais de temps à autre, le matin, ils avaient été remplacés par un spécimen plus grand, de couleur blanche tirant sur le jaune, et nous savions instinctivement que cette variété pouvait être venimeuse. | null |
Nataal bii nag ñuŋ fi gis lu Nga xamante ne moom la nuy woowe gejje fii ci Senegaal. Mooy jën wi Nga xam ben dañ kaa jël weer ko ba lu Wow def ci ay xorom ak yooyu.'Après' moom na ñuul di ko togg. | Sur cette photo on voit ce qu'on appelle'poisson séché' au Sénégal. Il s'agît d'un poisson qu'on accroche jusqu'à être sèche et ensuite qu'on met du sel et consorts. Après on cuisine avec. | null |
Setal keneen ki rekk ! | Cherche l'autre tout simplement ! | null |
Sama yaay, moom, ku sedd la, noppal nu. | Ma mère était douce. | null |
Góor gi ragal na juubuwoon. | L'homme craint d'avoir interrompu son jeûne par inadvertance. | null |
Ma taxaw fi ma taxaw, ni tekk, sama xel mi yépp jaxasoo. Maa ngi yëg tamit ni suuf siy yëngoo. Gunóor yaa ngiy wéndeelu ba mel ni callweer, tàmbalee yéeg samay dàll, di dugg ci samay kawas, di màtt samay bëti tànk, di mareñ wuti samay pooj. | Je reste immobile, incapable de fuir, incapable de penser, sur le sol tout à coup mouvant, formant un tapis de carapaces, de pattes et d'antennes qui tourne autour de moi et resserre son tourbillon, je vois les fourmis qui ont commencé à monter sur mes chaussures, qui s'enfoncent entre les mailles de ces fameuses chaussettes de laine imposées par mon père. Au même instant je ressens la brûlure des premières morsures, sur mes chevilles, le long de mes jambes. | null |
Joorug ñax a teggi woon loolu lépp teg fale, tàngaay bi toj sunuy xol, tàbbal nu ci fitnaak tés-tés ju tar a tar. Ba tax, su guddi jotaan, danuy sonn ba nga ni lii lu mu doon, ni yàcc-yàccaaral. | La plaine d'herbes avait aboli tout cela, dans le souffle chaud de l'après-midi. La plaine d'herbes avait le pouvoir de faire battre nos cœurs, de faire naître la fureur, et de nous laisser chaque soir dolents, rompus de fatigue au bord de nos hamacs. | null |
Li ko gënaloon mooy pilyaanu tuwaal ba nga xam ni néegoo-néeg diri na ko fa, mook taabal ju ndaw ja mu daan teg rajoom. Rajoom boobu nga xam ne, ba bi muy génn àddina, ci la daan déglu, ngoon gu Yàlla sàkk, ay xibaari BBC. Ma ngi déggaat ngóor soosu daan yuuxu ci rajo bi, naan ci kàllaama àngale : Pom pom pom pom British Broadcasting Corporation here is the news ! | Il leur préférait son vieux fauteuil pliant en toile et bambou qu'il avait transporté d'une case de passage à l'autre sur tous les chemins de montagne, et la petite table au plateau de rotin qui servait de support à son poste de radio, sur lequel, jusqu'à la fin de sa vie, il écoutait chaque soir, à sept heures, les informations de la BBC : Pom pom pom pom ! British Broadcasting Corporation, here is the news ! | null |
Kër gépp | Toute la maison | null |
Jéeg yi ak jaŋx yi it dañu ñëw | Les femmes mariées et les jeunes filles viendront | null |
Noonu la woon. | Ainsi fut. | null |
Jeexul, de. Teg loxo ci taabal ji booy lekk itam, da ko doon tere, te palaat bi, soo ko ñéddulee ba mu set wecc du baax ci yow ; sàqami sax dafa amoon noo koy defe : waroo ŋaaŋ ba li ci sa gémmiñ feeñ... Su fekkoon ni set ba mu ëpp feebar la, ma ni feebar booboo ko daloon. | Ils devaient manger sans poser les mains sur la table, ne pouvaient rien laisser dans leur assiette et devaient faire attention à ne jamais mâcher la bouche ouverte. | null |
Maa dem | C'est moi qui ai été | null |
Yaa ka gis moom Samba. | C'est toi qui l'as vu, lui, Samba. | null |
Loolu lépp amul solo ci gis-gisu Baay. Jàpp na ni fàww mu dem. | Il n'importe. Mon père a décidé de partir, il partira. | null |
Këru simoŋ gu ñu teg jànqu seng la, seng bu koy tax a tàng jërr su jant biy so. Moo tax ngoon gu jot, Baay gaawtu muur kook i xobi garab. | C'est une maison moderne, assez laide, faite en blocs de ciment avec un toit de tôle ondulée qui la transforme en four chaque après-midi – et que mon père se hâte de recouvrir de feuilles pour l'isoler de la chaleur. | null |
Waa ji di wax | Cette personne qui parle | null |
Li ma wóor, daal, moo di ne du Afrig gii bindkat yeek defarkati film yiy wone, xumb, takkarnaase, te ndóol bu jéggi dayo terewul nit ñiy wéy di dàq seen bànneex subaak ngoon. | Certainement pas celle qu'on perçoit aujourd'hui, dans la littérature ou dans le cinéma, bruyante, désordonnée, juvénile, familière, avec ses villages où règnent les matrones, les conteurs, où s'exprime à chaque instant la volonté admirable de survivre dans des conditions qui paraîtraient insurmontables aux habitants des régions plus favorisées. | null |
Feneen fi la góor gi dëkk ? | C'est de l'autre côté qu'habite l'homme ? | null |
Subsets and Splits