wolof
stringlengths 1
166
| french
stringlengths 2
331
|
---|---|
peme j- | cornaline |
Caqu peme lay wut | elle cherche un collier de cornaline. |
perantal b- | bébé sevré qui réclame encore le sein |
Jooyi perantal la | ce sont des pleurs de nourrisson sevré. |
oteel b- | hôtel |
pepp m- | grain mil |
Pepp mee gën ci moom | le mil est meilleur pour lui. |
Amuma pepp | je n’ai absolument rien. |
oote | appeler |
Dangay oote ba xam ndax nit a ngi fi | appelle pour voir s’il y a quelqu’un ! |
pat-pati | trembler de peur |
Dafa gis xaj bi rekk di pat-pati | dès qu’il vit le chien, il se mit à trembler. |
përëm b- | cuivre |
Tëggal ko lamu përëm | fais-lui un bracelet en cuivre ! |
pas-pas b- | nœud |
Pas-pas bi moo tax mënuloo koo nas | C'est à cause du nœud que tu ne peux pas l’enfiler. |
pay g- | abandon du foyer conjugal sur un coup de colère |
Payam gi bett na ma | son abandon du domicile conjugal m’a surpris. |
payis b- | hépatite jaunisse fièvre jaune |
Doktoor ne na payis la | le médecin a dit que c’est la jaunisse. |
per m- | clôture de paille tressée |
Maa liggéey per mi léem bërëb bi | C'est moi qui ai fait la clôture de paille tressée qui entoure cet endroit. |
oppi | être boulimique |
Danga oppi walla lan ? | tu es boulimique ou quoi ? |
perlu | se laver les parties intimes |
May ko ndox mu perlu | donne-lui de l’eau pour qu’il se lave les parties intimes. |
peru bët b- | iris |
paacaan b- | diarrhée (les matières fécales se présentent comme une bouillie) |
pastel b- | crayon à maquillage |
Ana sama pastel ? | où est mon crayon pastel ? |
pastel b- | beignet farci au poisson |
Demal jéndal ma pastel | va m’acheter des beignets au poisson ! |
pattal | borgne |
Pattal ci ñaar ! | rends-en deux borgnes ! |
onk w- | gémissement |
Fu onk yooyu di jóge | D'où viennent ces gémissements ? |
onk | gémir |
Mu ngiy onk rekk, biir beey metti | il n’arrête pas de gémir, il a mal au ventre. |
omb b- | ourlet |
Omb bi dafa teppiku | L'ourlet s’est défait. |
payis | avoir la jaunisse |
Dafa payis | il a la jaunisse. |
pareel | faire les préparatifs de (qqch) |
Ubbite kalaas yi laay pareel | je prépare la rentrée des classes. |
paase wisit | faire une visite médicale |
patt | être borgne |
Muus mi dafa patt | le chat est borgne. |
peyoor b- | jour de paie |
Peyoor bi, feek ñaari fan la | la paie est dans deux jours. |
pet | À l’écart |
Waxal ak moom ci pet | parle-lui à l’écart ! |
pann m- | couscous de la veille |
Sama maam daan na wax ne pann baax na ci yaram | mon grand-père disait que le couscous de la veille est bon pour le corps. |
(prov.) Kuy reere pann, boo woppee fande | qui dîne avec le couscous de la veille, quand tu seras malade, tu ne dîneras pas) si tes moyens sont limités alors que tu es en bonne santé, ce sera pire quand tu seras malade. |
patt b- | l’un des éléments d’une paire |
Ana pattu dàll bi ? | où est la deuxième chaussure ? |
patt b- | personne borgne |
Li muy ab patt, moo tax mu mer | C'est parce qu’il est borgne qu’il s’est fâché. |
patam-patame | bâcler |
paaka b- | couteau |
Nangul paaka bi ci xale bi | retire le couteau à l’enfant ! |
paxu-bakkan m- | narine |
Fattal paxu-bakkan yi | bouche-lui les narines ! |
piire b- | purée (de pomme de terre) |
pecc m- | danse |
Pecc moomu yiiwul | cette danse n’est pas décente. |
pecc | tout à fait, très (clair) |
Dafa xees pecc | il a un teint très clair. |
pëdd b- | jaune d’œuf |
Soppul pëdd | il n’aime pas le jaune d’œuf. |
peccargo b- | épouse du beau-frère d’une femme |
Sama peccargo dafa ma yendusil | la femme de mon beau-frère est venue passer la journée avec moi. |
pëccét | exprime l’idée de courir immédiatement |
Mu ne pëccét jél këll gu tilim, may ko ci ndox | elle courut immédiatement prendre une écuelle sale et lui offrit de l’eau dedans. |
peesekaay b- | balance, instrument servant à peser |
peesu b- | où on dépouille les animaux |
Demal ca peesu ba, dinga fa am der | va à l’endroit où on dépouille les animaux, tu y trouveras une peau. |
(prov.) Jóge peesu taxuta am yàpp | ce n’est pas parce qu’on revient de l’endroit où on dépouille les animaux qu’on a de la viande. |
patapaare g- | race de singes qui vivent toujours perchés |
peese b- | flux de la mer, marée montante |
Peese bi moo tax yenn waxtu yi jaaykati jén yi di sore tefes gi | C'est à cause de la marée montante qu’à certaines heures les vendeuses de poissons s’éloignent de la plage. |
pegg b- | côté abords |
Ci peggu dëkk bi | aux abords de la ville. |
péexlukaay b- | endroit où on prend l’air |
Taatu ekool bee di seen péexlukaay | le pied du mur de l’école est l’endroit où ils prennent l’air. |
pom b- | pomme |
Kilo pom ñaata ? | combien le kilo de pommes ? |
pom b- | pont |
Léegi, am na pom | maintenant, il y a un pont. |
péllal | laisser entrevoir les cuisses en marchant |
Sa sér baa ngiy péllal rekk | ton pagne laisse continuellement entrevoir tes cuisses. |
péget m- | tourterelle |
Fiir na fukki péget | il a pris au piège dix tourterelles. |
pëggu b- | baguette crochue avec laquelle on fait avancer un cerceau |
Weñ gu ma def pëggu laay wut | je cherche une tige métallique pour en faire une baguette de cerceau. |
pekk b- | réduit situé dans une chambre |
Dencal saaku ceeb bi ci pekk bi | garde le sac de riz dans le réduit. |
poo b- | poids |
Teggil poo bi | enlève le poids. |
peer b- | tronc d’arbre |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.